Mane douma Pikine deukoumafa wayer aka ma beugone Tyson! Eumeu dou sama Mbeur wayer dama ko respecter tolone ne fou meti si bire Pikine wayer Pikine doit un grand respect à Eumeu, roi des arènes indi nako fa ak lamb derbi you saff sape. Litakh Guiediawaye yaboul Pikine Eumeu ligueye nako si lamb dji. C'est un grand lutteur ce Eumeu mashallah!
Eumeu Sene my favorite wrestler should always keep this fitness, you can see real muscles. When he is like this, he moves different. Being too big isn’t good for him.
Sa thies si noumouy waher ak public si bire lamb dji mome la touder "borome djok lène takhaw ma douma Mbeur bi wala Mbeur bi douma me douma ragale djok lene"! Jeune homme bonne chance pour la suite de ta carrière inshallah. Eumeu mola dane dou gathier ...
Mane souma done andak Eumeu Séne bilahi sou parer beurer sou daner Ba parer douma ko gatandou ndakh meune ngassi djeule coups. Eumeu sassou lamb djekher dey khape talou te coup wou Eumeu woroul 😂
😂 😂 Wakho dof rek guèn di wakh am na genre wakh yo kham ni diaroul wakh ça sert rien, Wakhou MA Biram Souley mais Diomaye sakh meunul téré niu lamb, lamb force. Niu dunu ay complexé
Felicitation à eumeu sene pour la victoire
Amoul sens ndakh tégolénko en direct
Mane douma Pikine deukoumafa wayer aka ma beugone Tyson! Eumeu dou sama Mbeur wayer dama ko respecter tolone ne fou meti si bire Pikine wayer Pikine doit un grand respect à Eumeu, roi des arènes indi nako fa ak lamb derbi you saff sape. Litakh Guiediawaye yaboul Pikine Eumeu ligueye nako si lamb dji. C'est un grand lutteur ce Eumeu mashallah!
Eum niounn wa pikine déssé loniou dara
Eumeu Sène dinafi dane bénen boy nagnou dem rekk Ken euppou kossi dolé😂😂😂
Eumeu Sene my favorite wrestler should always keep this fitness, you can see real muscles. When he is like this, he moves different. Being too big isn’t good for him.
Sa thies si noumouy waher ak public si bire lamb dji mome la touder "borome djok lène takhaw ma douma Mbeur bi wala Mbeur bi douma me douma ragale djok lene"! Jeune homme bonne chance pour la suite de ta carrière inshallah. Eumeu mola dane dou gathier ...
Bilae
Dama am dolé💪🏾
Eumeu keneu douko yabb 😂
Eumeu sene mo guena deuguere Sa thies Adouna yakou neu 😂
Euma dou ragal dh
❤❤❤❤❤❤
Mane souma done andak Eumeu Séne bilahi sou parer beurer sou daner Ba parer douma ko gatandou ndakh meune ngassi djeule coups. Eumeu sassou lamb djekher dey khape talou te coup wou Eumeu woroul 😂
Felisitasion sathies lamb rek la
Khel mou dal moy lepou
Franc Vs sa Thies
😅😂eumeu sene néna mak nionme ma masé 😂😂😂ay victoire dina wahlo nit louné 😅😂
Sa kogn sénn ASC kou gueunnn nékk mag niatta att la ammm???
Quando é que esse nego vai postar foto nu?
Franc vs eumeu sen❤
Mo Dane bopame
Do reculer sa tenkeu gauche bi
Rodriguez Dorothy Smith Robert Garcia Jessica
Woi
Birame Souley Diop doit arrêter la lute en frappe sénégalais car il y'a beaucoup d'Hippocrate dans cette lutte
Nopil way ahhh
@@bayefall3213 mais tu me connais pas tu heuse de me dire ça tu es qui toi
Makoy dieuleul part mayniou ndm souniou diam
😂 😂 Wakho dof rek guèn di wakh am na genre wakh yo kham ni diaroul wakh ça sert rien, Wakhou MA Biram Souley mais Diomaye sakh meunul téré niu lamb, lamb force. Niu dunu ay complexé
Yaw est que ça va ?
Birëm Souley laniou dénk làmb bamoukay dakkal?
Franc vs eumeu sen
Franc vs eumeu sen
Franc vs eumeu sen
Franc vs eumeu sen