TRÈS Courageux frère wayai gnou éviter si commentaire yi di wakh lou gnaw BARA entouca c pa la personne ki nou intéresse mais on protège notre religion.
Mai mane je rêve ou quoi mai gnii kouñiou yébe serigne touba mome xana dou abe domou adama késsé mai Sénégal moome nii rék ba kagne téé ngééne xoolaate séne boppou balaa déé dilééne dikkeule billahi wallahi bou ngééne touboule diéggeulou yalla azzawajalla yawmalkhiyame di ngééne matte sééni baaraam witthiah
Mame chiekh ibrahima fall yalla moko ko téguil yéne lou takh guéne sokhor déme léne toubi waye yéne séne xol you bone yi nak fi serigne touba mofi néh mou nakhari guedé
Yéne bou léne niou fonto chiekh bara ndiaye mo apou khame khame séne baye ak séne mame mame chiekh ibrahima fall liko yalla défall ak serigne touba koumou méty dagaye sonou rék
Subqaana 'LLAA 🤭 Tassawuuf moo di ay tappale dëgg-dëgg! Bàyyi julli, bàyyi woor,..DA MA NI GIS NGA BU SËÑ TUUBAA NÉKKOON NII CI JAMONO JII ÑU KOY GIS GIS GU WÉR TA WAXU CI DARA SAX DU TAX LOOLA TÉKKI DARA CI FARATA GI ÑU DOON FARATA CI BÉPP JULLIT. Ab jullit bu demee bay gis waxi SUNU BOROOM ak YONÉNT BI (a s) ba nóppi bàyyi ko fa di déglooti keneen koo xam ni kii KÉNN YÓNNIWU KO, KÉNN WAXU ÑU CI MOOM LÉNN, KÉNN XAMUL SAX CI LU MU NÉKK NII,...booba jullit dëy CI AG RÉER DËGG LA NÉKK. Werente amu ci. Yalna ko sunu BOROOM gindi ta gindi ñu, Aamiin!
Qu'est ce qui vous a acheminés à Saqar ils diront nous étions de ceux qui ne faisaient pas la prière
Macha Allah diazakaallah khaiyran
Kepp koula daganal lou yalla araamal mougui lay alak soko toppè yagui koy djaamou 🥺
Atté senegal beussou yawmal khiyam nar naa yagg dé 😔💚
Thieuye Yalla Mame Borome Darou Wakh Li Ay Tapalé Rek Leuh Diouli Dou Meussa Wathe Domou Adama🙏🏿
C'est vraiment triste qu'Allah les aides soubhanne Allah thiey Sénégal
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ On est avec Mouhammadou ArrassoulillAh Quelqu'un qui ne prix pas les cinq prières de L'islam fait parti de Satan déjormé
TRÈS Courageux frère wayai gnou éviter si commentaire yi di wakh lou gnaw BARA entouca c pa la personne ki nou intéresse mais on protège notre religion.
Qu'ALLAH nous guide sur le droit chemin
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci beaucoup alla
جزاك الله خيرا بارك الله فيك أحسن الله إليك ماشاء الله بارك❤❤
Machalah seich alpha ba✅️✅️
Machaa Allah oustaz Alpha ba
Waa tasswouff mom subhanna llah😂
Merci beaucoup bah bon continuation souna reck Bara Ndiaye c'est un vrai menteur intercontinental
Mai mane je rêve ou quoi mai gnii kouñiou yébe serigne touba mome xana dou abe domou adama késsé mai Sénégal moome nii rék ba kagne téé ngééne xoolaate séne boppou balaa déé dilééne dikkeule billahi wallahi bou ngééne touboule diéggeulou yalla azzawajalla yawmalkhiyame di ngééne matte sééni baaraam witthiah
Moy ki yépp oumpou lé srg touba amoul déndélé Wasalaamu halaykum yàlla na yàlla guindi la❤🤲📿
Moy ki yépp oumpou lé srg touba amoul déndélé Wasalaamu halaykum yàlla na yàlla guindi la❤🤲📿
Diouli wathie woule benna domou Adama
Mame chiekh ibrahima fall yalla moko ko téguil yéne lou takh guéne sokhor déme léne toubi waye yéne séne xol you bone yi nak fi serigne touba mofi néh mou nakhari guedé
Yéne bou léne niou fonto chiekh bara ndiaye mo apou khame khame séne baye ak séne mame mame chiekh ibrahima fall liko yalla défall ak serigne touba koumou méty dagaye sonou rék
بين المرع وكفر ترك الصلاة
Subqaana 'LLAA 🤭
Tassawuuf moo di ay tappale dëgg-dëgg!
Bàyyi julli, bàyyi woor,..DA MA NI GIS NGA BU SËÑ TUUBAA NÉKKOON NII CI JAMONO JII ÑU KOY GIS GIS GU WÉR TA WAXU CI DARA SAX DU TAX LOOLA TÉKKI DARA CI FARATA GI ÑU DOON FARATA CI BÉPP JULLIT.
Ab jullit bu demee bay gis waxi SUNU BOROOM ak YONÉNT BI (a s) ba nóppi bàyyi ko fa di déglooti keneen koo xam ni kii KÉNN YÓNNIWU KO, KÉNN WAXU ÑU CI MOOM LÉNN, KÉNN XAMUL SAX CI LU MU NÉKK NII,...booba jullit dëy
CI AG RÉER DËGG LA NÉKK. Werente amu ci. Yalna ko sunu BOROOM gindi ta gindi ñu, Aamiin!
Waakhi Bara Ndiaye diaroul commenter !
Tasawouf day mabou ponki Islam yi
ورب الكعبه صدقت شيخ بار جي ولا ذكر الله اكبر لو كانوا يعلمون واعبد ربكك حتي يؤ تيك اليقين
Bara ndiaye Sama way nga waye tey danga danou
Bara mom da rey wakh mokk misseré soyeiwonou hamounou dounou teuth sen nguemin yi
Oui vs avez raison diazakoumou L'ALLAH kayran
Yewe rekelo yala amo ndome lou cisa yone mendouvo
Limoy tassaouf sen lep moungui tegou si wahdatoul wodjioud.
Limou wax deug diou wer pingue la.
Bouko gnépou defé nak É apré dafa takh mou dangane
Mouno wakh ci tassawouf ndah hamoko genmoko bayil di togne nit gni diouli batin amna
Astakhfiroullah boul até domou Adama si yéfere
Seex Baara limu wax xam nako yeena ko bëgë gisee naneen rk
Salam c malereu pr walf tv c analphabète ki ne réfléchis même pas
Alfa argiman tel ligay wax yagi toumal ay gor
Ibrahima fall et fou
Yaw ragalal yalla ban jollit mouy haramal jolli
C'est faux ! Tu es un tricheur ! Tassawouf wakhoul loolou.