Alhamdoulilah bima khamé segne Hassane Salâm, je regrette vraiment ne pas l'avoir connu plus tôt 😢 yalle naniou Borome bi SWT tasse thi barkème té maye niou dègue ak topou
Dieureudieuf Serigne adama 🤝 mais limaye lathie moye Serigne Hasan limou dan soumi aye nit niouye weur ndakh mane nane ka dèf ba lèegui dafa am niouma xam nionga xamni wallahi am nane ak tiit sèn bop lol lol sakh ndakh《temoignage yi》tè xamou niou nouniye dèf bam dègne tè lèpou nak lou xèe took aye ndialo la wallahi wallahi somanè lèeral rèk nga diapou si ndeysane ndakh kèn beugoul dh dèm safara ♡♡ 💫💫 🙏🏼🙏🏼
lolou serigne bi ndigalou yalla lasi amoon yalla moko doon sante lolou si nit ki waaye dou thiobare bopame yalla mooko naanwakhal kii nangam ak nangam wayee dou thiaguinou kou dioug def ko amna nak ay naafila youm fi bayyi ak barab youm wakhe ni kouko ziyarr niou dieguella di am yakaar si yalla
Alhamdoulilah bima khamé segne Hassane Salâm, je regrette vraiment ne pas l'avoir connu plus tôt 😢 yalle naniou Borome bi SWT tasse thi barkème té maye niou dègue ak topou
Yalla naniou yalla djièguale si barké serigne all hassane salam
Yalla nagnou Yalla fayal seydina Al Hassan Salam
Aminnnnn yarabi
Amine
Jërëjeffé Cheikhouna Ahmadoul Khadim
Jerejef Seydina Al Hasan Salam ♥️♥️♥️
Serigne alhassane yalla nanou ko yalla fayall si barke serigne touba
Allahouma Amine jeureu jeuf thiante ak ngeureume ñelnala
@@cheikhdiopsam9235 1111q1¹¹1¹¹¹😂😂1q😂😌1q1😂❤😂😂1😌1 😂q1
Dieureu dieuf s hassane salam
MACHALLAH SEYDI ALHASSANE SALAM.
Mangui ziare serigne hassane salam yalla Na yalla yokou lerame tamou tabaleko si aljana firdawsi amine
amiin
جزاك اللهُ
Dieuredieuf Dieuredieuf serigne al Hassan sallam
Dieuredieff serigne asane salammmmm!!
Machalla Al Hassan salam❤❤❤
ماشاء الله تبارك الله
ALLAHOU AKOUBAR
Machallah fatabarakallah
Dieredief serigne hassane salam
Macha'Allah
Machalla ♥️♥️♥️♥️♥️
SEYDINA AL HASSANE SALAM mangui sakou ak dimbale si fane yepp SALAM
Wax tane wii amna solo
😊😊😊
Mansallha
Al hassan tassarufaat you doy waar ladaan déf..
Dieureudieuf Serigne adama 🤝 mais limaye lathie moye Serigne Hasan limou dan soumi aye nit niouye weur ndakh mane nane ka dèf ba lèegui dafa am niouma xam nionga xamni wallahi am nane ak tiit sèn bop lol lol sakh ndakh《temoignage yi》tè xamou niou nouniye dèf bam dègne tè lèpou nak lou xèe took aye ndialo la wallahi wallahi somanè lèeral rèk nga diapou si ndeysane ndakh kèn beugoul dh dèm safara ♡♡ 💫💫 🙏🏼🙏🏼
Waaw lolou djaklé serigne hassan Salam la. Waayé bouñ réthio toub déff 6 rakka yi (rakk bou nékk 7 ikhlass ) bou booba yalla dinalén djégeul... lolou la serigne hassan Salam diokhé ndiguël
Ndeysane amna solo kay magui dègu tamite barap yi Serigne Hasan wakh si kou ko ziara tamite mounèk lou am solo kay dianguèen dieuf waye ♡♡ 💫💫 🥰🥰 🙏🏼🙏🏼
Serigne al assan salam wakhna ay raka pour toub bakar
@@damedieng1112 waaw.. samedi guinaaw timis nga diouli 6 rakka ( par 2) rakka bou nék fatiha ak 7 ikhlass.. serigne hassan Salam moko diokhé
lolou serigne bi ndigalou yalla lasi amoon yalla moko doon sante lolou si nit ki waaye dou thiobare bopame yalla mooko naanwakhal kii nangam ak nangam wayee dou thiaguinou kou dioug def ko amna nak ay naafila youm fi bayyi ak barab youm wakhe ni kouko ziyarr niou dieguella di am yakaar si yalla
Aka mako beug bilahi
Kiiy way bara mbodj mi kou bone leu dou nittou dara .thiem .lan mola tère wakh limou wax ni kouko mokal do paralysé ak kouko wax légual loula nèx .
Dnga ko bag kham
Kou.niane.niak.bo.djidé.ame
Niak.talibé
@@SokhnaSarr-k4k yaw xamo lima wax ! Dama wax ni , nitt gni douniou wax secrets yilén serign asan salam wax .
Nit kou bakh day labir mé payi sokhor rek guén dou si nako wakh batte yi serign bi wakh té mou ame diarigne
Nitt kou ñioul baxoul sokhorna wakh li ko serign Assam salam wakh
Lo bg kham
@@locheikhouna2371 sarakh yi mou lèn di wax ak secret yi si garabe yi si rène ak si nafila yi .