La deuxième mère de BB Binta n'est pas responsable en tant que mère. Il y a certaines choses qui n'ont pas besoin d'être dites car cela peut déstabiliser une famille ou un mariage. La deuxième mère de BB Binta et la propre mère maternelle de Binta sont toutes les mêmes, elles ne sont pas responsables, je pense que leurs problèmes familiaux ne seront pas résolus par nit kou bonne ki di adam
Mé ak loumana am sa yayla bb binta gén soutouralen ko té Serigne saliou tahk😢😢
Yalnaniou yallah mousseul si siw amine
Vraiment adamo goordjiguén deug leu limou déff ni niawna trop
Adamo sou Yallah feyeee liguey def lepp diga dioy fou keneu nekoull. Khalice diaroul li. Nit danioukay soutoural
Ani soutoura😢😢
Adamo bayil khel bess bingay dhhh😢
Ay way eskk diarona siwal ba gneup disi diott bb Binta dafa am Ay néwlé 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢4:05
Nooooo mè lii rouslouna pour koi dan lé rézo sociaux,bb Binta waroulwone dougou thh live bii
Siw dou diami borom yalla na yalla doli holou mougn bb binta
Mh pourquoi tous les problèmes doivent être réglés sur les réseaux sociaux
En plus ñom gniy wo Adamo tmt ken dou ñom
Yalna gnou yallah doli soutoura
Yay domaram adamo
Mais Adamo yaw tmt amo soutoura dh ndax mère bi niane nala pour nga soutouralko guirr yalla Kone li waroko wona tek dixawi soutouram
Vréma mon pays va mal Adamo arrétel nit day am bamélou BIR am savoir gardé mé yaw lo yek mou siw
Dfa deugeurr fitt rk bougn ko lidianti wonn deukk bi tass
Mere bi mome tamite beugoul bb binta par ce que waroul wakh li si kiname bb binta
Ay way li niaw na way binta loutah gua khawi sa soutura yaye 😢😢
Adamo mandat international lagnou ko wara Def
Ho bb binetou loula diarale li ngaye wére sa yaye ni loumou mèti yaye réek la soutouraleko adouna amoule solo
Thiey yallah il ni a plus de valeur au Sénégal 😢
Comment on peut vilipender quelqu’un comme ça , adouna dou keer
Ayy way adama yaw doul gatt gua yaggatt gua
Bb bineta mii moy khalé deugeu waroul wone dougou ci live bi ndakh meune na am lii yeupeu nék ay piége té yaye dou morome
Way yayou bintaa mo bon nga abandoné sa dom paré guiss nimou mel si deuk paré niowat
Adamo yalla yakamtinala ya boon
Sheut li tamit ani soutoura way🤬🤬🤬?
La deuxième mère de BB Binta n'est pas responsable en tant que mère. Il y a certaines choses qui n'ont pas besoin d'être dites car cela peut déstabiliser une famille ou un mariage. La deuxième mère de BB Binta et la propre mère maternelle de Binta sont toutes les mêmes, elles ne sont pas responsables, je pense que leurs problèmes familiaux ne seront pas résolus par nit kou bonne ki di adam
Bineta mo manquer bay assister fouñouy xassè ndeyam. Wa keur fallou mom mou ñou dè nitt dina ñou ragal bineta. Outal na boppam xas
Ayli niawna di binta loula tré soutoural sa yaye bola diourdi eumb dafa meti
Lii tmt est-ce que do bad buzz?. Doom jou baax noumou mené xawwi soutoureu ndeyam ? 😢
Mai's yaye loumou bonn bonn yaye la té sa yaye lay meusa dom soutouraral sa yaye eumb dafa metti nakh napal guadou
Gniyr wakhe AK mome rekk gnonko deff kikouy wakhe AK mome do nit loula dal yakk tek sa bopp djigurne gni TMT kene dou gnome toppe nit kou kou alkouki rekk diarroul dioye yennaye togne sene bopp
Siww dé dou diamiii borome voilà
Bayil wakh diou niaaw adamo
Adamo yaw liguay def bakhoul te dine santanekou mandou wo yalla rek mo juge bou mak bi
UA-cam tiktok lanou Wara teudie
Adamo yow dé mola tére dém safara
Haliss bou saleté gaye ame mais Adamo mo ala kou
Adamo yow beuss bo déwé Souf sakh daléye yabi khamna nignou défone firawoyna dougeuleu si bouteil koula romba sagua sa ndeye ya bone thiim
Ey way adouna dou keur ana soutoura niit moy soutoural bopam rawatina yaye
Yalla bouma siwe
Day doul rek