Makhtar sarr a raison sur vous, vous passez votre temps di sani khér sounou makk niou bakh gni , gua kham ni sén lép alkhourane ak souneu leu ak beug yonéte bi. Bounou meuneu taxawé tay nane Sénégal 95% de musulmans leu guinaw yalla sounou makk gni leu , mé guén nék fi rék Di khékh tarikha,té pourtant liguéni déf ni si tarikha guén nék😂. Loutakh lou gnaw Lou khéw Arabie Saoudite d'où ngén si wakh ????? Wala financement yi ak aide yi ngéni bagn mou dakk ????
ni l'un ni l'autre juste un prédicateur de bonne foi qui condamne ce qui est condamnable,comme bcp d'autres prédicateurs à travers le monde l'ont fait!wa salam
الأخ الكريم، والمحاضر المبجل ،جزاكم الله خير ا بهذا الإيضاح ، وجعله في ميزان حسناتكم ، ورزقنا حسن الاستماع، والتنبه لكيد الأعداء والمرسلين. جزاكم الله خير الجزاء .
D'abord, la chanteuse ne s'appelle pas Sonia mais plutôt Elian Amer Marjiya connue sous le nom de Elyanna chanteuse et compositrice chilo-palestinienne. Le concert s'est déroulé à New York et non pas à California ( donc Fatabayanou ya Oustaz Mouhammad Al Amine ). Les antagonistes fustigent la ceinture qui semble caricaturer le sabre de Seydina Ali. En suite, Une des videos de la soit disant KABA s'est passé effectivement en Arabie Saoudi lors de la cérémonie de lancement pour la saison de Riyad 2023. Ces événements de divertissement ont lieu chaque année. Et c'est arabie Saoudi qui l'organise pour gagner des fonds. A titre d'exemple, même Jennifer Lopez à célébré un concert là-bas à Riyad. Donc, ce que les antagonistes soutiennent est belle et bien vrai. Ils en parlent parce qu'il s'agit d'un lieu symbolique pour tous les musulmans du monde. Si ça ne tenait qu'aux musulmans ses evenements auront jamais lieux. Enfin, l'histoire de coup d'Etat n'est pas nouveau en Arabie. A la fin, je ne sais plus si s'est vous le manipulateur ou votre contradicteur ? Yallah naniou Borom bi Sam si passpass si Alkhouran ak Sunnah.
Arabie saoudite lifa am lou niaaw leu vraiment. Mais sénégalais waroul critiqué kenn si walloum diiné parsk fii rek ngay degg sama serigne mo bindeu yalla wala sama serigne mo geun yonenté bi wala sama serigne moy borom diaam gni wala sama serigne kaw assamaan lay fanaan chak goudi 😂😂😂😂. Tarikha senegal yi danio bone ba paré beugg morom koii 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
ياسيدالاستاذ قل الحق ولو على نفسك الحدث وقع في السعودية سواء في الرياض اوفي مكان آخر الفيديوهات المتعلقة بهذاالحدث كثيرة منها ماهي مفب ركةومنها ماهي صحيحة ولم نجدكبارعلماءالسعوديةينكرونهابل التزموا الصمت!!!؟
@@thiampassion d'accord mais est ce que Yalla Sénégalais yi la ték pour gnou hééh lolou ? Yaakar na li di héw si Sénégal ci bokalé Yalla mo gueneu bonne léé thia Arabie saoudite
Gni ibadou yi lagniy bagna giss mo tah. Wallahi hamnagn ibadou yi nougnou mell thi diné bokoul sah ak nougnou mell. Ngéy wah Sénégal. Sénégal leu nitt tahaw né serignam mo binde yalla. Sénégal leu bokalé geuneu beuri té dollén çi wah. Makhtar Sarr mom ndeysane ibadou yi léy bagna giss, mais nit gni gnongi yéwou dh.
Thim jaami naar you bon yingeen doon Dém leen ligeyi té jaamou ji moo géun ngeen topp çi naar yi di yappar yappri mélné gniou wéradi gniakk ngeen joum lool
Yaw yaa naafeqq deugg deugg dangay wakh di tontou sa bopp 😢😢 yéne année yii yëpp guis ngéne politique bi séne seriñ si di dokhal ngénné moouuttt ték si séne tànk
Mouna doul dou da ngenn di guiss video fi si dakar bou benn serigne di def ngenn gnawlou ko ba paré né gnounn aye yefeur lagnou riyad ak saoudite gnossi yame aye nafekh ngenn deug beugua defendre li meme sou nekonn senegal sah wahal deug ne li gnom dagno dioum warougnouko def bourou makka bi dafa dioumm . Fater na sah senn harite yi ay narr lagnou sou ngenn ko defer dotoulenn diotati haliss 😂
Yalla dineu diégalé bakar bomou dése bokalé fi le pére Noël mbacké wakhni sou yalla takhawé yoninte bi psl takhaw bou rombeléne dém si Mamame kara aussi wakhni serignam mo binedeu yalla soubhanala 🙏lolou dafa doy warr pourtant bi serigne yoyou di wakh lolou Makhtar sarr miguiwone Senegal té wakhousi
Vraiment kou meuneu togne ngueu. Ragalal Yallah, le mal ne dépend pas de pays ou autre. Il faut chercher la vérité. Il défend pas de pays, il parle de religion. Parparlo bakhoul
Sonko moy 6 Président du Sénégal inchallah
Diarrama seydil hadji malick sy ❤❤❤❤❤
Yallah naniou Borom bi Sam çi pass pass Alkhouran ak Sunnah
آمين
Amiin ❤❤❤
Makhtar sarr a raison sur vous, vous passez votre temps di sani khér sounou makk niou bakh gni , gua kham ni sén lép alkhourane ak souneu leu ak beug yonéte bi.
Bounou meuneu taxawé tay nane Sénégal 95% de musulmans leu guinaw yalla sounou makk gni leu , mé guén nék fi rék Di khékh tarikha,té pourtant liguéni déf ni si tarikha guén nék😂.
Loutakh lou gnaw Lou khéw Arabie Saoudite d'où ngén si wakh ????? Wala financement yi ak aide yi ngéni bagn mou dakk ????
@@MamadouNgom-pq6ph
Ba serignam takhawé né day pogné Yallah foumou nékkon !
@@mamadoudioumadiallo5958 no kone yawo déglouwo aye waxtanam motkh mélolou makhtar sarr waxa nasi bou yaga
@@MamadouNgom-pq6ph billahi makhtar sarr dijam bar ladi
Que le Tout-Puissant nous guide et nous protege ...dieuredieuf
Allahumma amine
No comment ont peut dèfandr ce qui ce passe en Arabie-Saoudite 🇸🇦 ak loumana xèw lou ñaaw la
Léral bi amna solo MachAllah dieureudieuf oustaz
ni l'un ni l'autre juste un prédicateur de bonne foi qui condamne ce qui est condamnable,comme bcp d'autres prédicateurs à travers le monde l'ont fait!wa salam
الأخ الكريم، والمحاضر المبجل ،جزاكم الله خير ا بهذا الإيضاح ، وجعله في ميزان حسناتكم ، ورزقنا حسن الاستماع، والتنبه لكيد الأعداء والمرسلين.
جزاكم الله خير الجزاء .
وفيها من امسك عن الفضول عد من ار با ب العقول ❤dieureu dieuf oustaz makhtar sarr ❤
D'abord, la chanteuse ne s'appelle pas Sonia mais plutôt Elian Amer Marjiya connue sous le nom de Elyanna chanteuse et compositrice chilo-palestinienne. Le concert s'est déroulé à New York et non pas à California ( donc Fatabayanou ya Oustaz Mouhammad Al Amine ). Les antagonistes fustigent la ceinture qui semble caricaturer le sabre de Seydina Ali. En suite, Une des videos de la soit disant KABA s'est passé effectivement en Arabie Saoudi lors de la cérémonie de lancement pour la saison de Riyad 2023. Ces événements de divertissement ont lieu chaque année. Et c'est arabie Saoudi qui l'organise pour gagner des fonds. A titre d'exemple, même Jennifer Lopez à célébré un concert là-bas à Riyad. Donc, ce que les antagonistes soutiennent est belle et bien vrai. Ils en parlent parce qu'il s'agit d'un lieu symbolique pour tous les musulmans du monde. Si ça ne tenait qu'aux musulmans ses evenements auront jamais lieux. Enfin, l'histoire de coup d'Etat n'est pas nouveau en Arabie. A la fin, je ne sais plus si s'est vous le manipulateur ou votre contradicteur ? Yallah naniou Borom bi Sam si passpass si Alkhouran ak Sunnah.
Toi au moins tu n'es pas un robot
Mâcha Allah oustas diazakalahou khirane wa barakalahou fikoum
Machallah barakallahou fikoum
MachaAllah qu’Allah vous préserve et vous rétribue pour ces éclaircissements
Barakallahu fiikum ya cheikh amatina solo yalna bour yalla fay yiww
Masha Allah
Arabie saoudite lifa am lou niaaw leu vraiment.
Mais sénégalais waroul critiqué kenn si walloum diiné parsk fii rek ngay degg sama serigne mo bindeu yalla wala sama serigne mo geun yonenté bi wala sama serigne moy borom diaam gni wala sama serigne kaw assamaan lay fanaan chak goudi 😂😂😂😂.
Tarikha senegal yi danio bone ba paré beugg morom koii 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Wallahi ☝️ tu est parfaitement raison
❤❤❤❤
جزاك الله خيرا ❤❤ ❤🎉🎉🎉
Macha Allah ya oustaz
Macha Allah Baraka lahou fikoum vérité absolue deug pure ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Maa sha Allah ❤❤
بارك الله فيكم وجزيتم خيرا وقيتم شرا ولالقيتم مابقيتم ضرا
Amna solo ma sha Allah
ماشاءاللہ
جزاكم الله خيرا، بارك فيكم
فإنهم لأ يكذبونك ولكن الظالمين بئايات الله يجحدون
Machallah amna solo yalle n'a Yalle falyla yiwe man dh gor sosou man douma ko diég lou sakhe
Longue vie à vous au Sénégal y'a outaz
Oustaz makhtar sarr nitou diné deugue moye mom machallah
Machallah immame
ماشاء الله تبارك الله فيك وجزاك الله خيرا يا أشخ
Machallah imam yallah na yallah samm la
ياسيدالاستاذ قل الحق ولو على نفسك الحدث وقع في السعودية سواء في الرياض اوفي مكان آخر الفيديوهات المتعلقة بهذاالحدث كثيرة منها ماهي مفب ركةومنها ماهي صحيحة ولم نجدكبارعلماءالسعوديةينكرونهابل التزموا الصمت!!!؟
الحق ثابت ❤❤
Makhtar Sarr mécontent leu.
Yalla nako Yalla guindi.
Makhtar Sarr mofénal Omar Sall domou haraam fén kat bi mok Ahmed Lo domou khadj.
Ki day fén rék 😅
Makhtar mogeun sèn kilifeuyi
MACHALLAH
Défendre aye thiakhane woroull teh bakhoull. Le concert s'est bien passé en Arabie Saoudite precisemnt a Riyadh 🤷🏿♂️.
@@thiampassion 😂boy wéddi tégal dara sounou lokho indil preuv wéddi mogeun
@@thiampassion d'accord mais est ce que Yalla Sénégalais yi la ték pour gnou hééh lolou ? Yaakar na li di héw si Sénégal ci bokalé Yalla mo gueneu bonne léé thia Arabie saoudite
Sénégal moom bokalé boufi nék, ak mbonté bi warna tah niou meuna noopi si deug diamour. L'arabie saoudite est très bien au dessus de nous
Sabotage Kaaba bi amou thi wayé djiguèn gnow nafa saga diiné
@@thiampassion danga demon si concert bi?
Bilahi cest Clair. Alhamdulillah
حفصك الله ياسيخ نا ❤❤❤
شكرا يا أستاذ
Maşallah ya oustaz
Soubkhanallah
Billay yeena nafikh dem di defander honko taat naar you bonyiii te fi thi senegal bayi loolen sakh gni de😢😢
Ce qui se passe à riyad ne nous engage pas. Nous sommes sénégalais et sunnites.
Il faut parler arabe et vous adresser à ben salmane
Gni ibadou yi lagniy bagna giss mo tah. Wallahi hamnagn ibadou yi nougnou mell thi diné bokoul sah ak nougnou mell. Ngéy wah Sénégal. Sénégal leu nitt tahaw né serignam mo binde yalla. Sénégal leu bokalé geuneu beuri té dollén çi wah. Makhtar Sarr mom ndeysane ibadou yi léy bagna giss, mais nit gni gnongi yéwou dh.
Ahmed Tijaan moom Xanaa bokkul si honku t yi
Sénégal kay soofi guéné dioulit deug, xamna 2% ngay am. Sénégal serigne moolén gueneul yallah moulén binde, waayé jugement lay yam
@@ousmanesarr2114 ké wah ni sama serigne mo binde yallha kou lolu bone lawah mé dakh souko touboul bokatoule si doullét yé 🤍mé li xéwou Arabie saoudite lolu mome biërou ñoune ñépp la dakh kouy diule ly fagay diuboulou oustaz makhtar sarr sou kontourone ibadou yé dou wax sy ñome lou bakh syay wax tanam
Yaw mii Ragalall yalla كما تدين تدان
Daguen di fontou rek mais Arabie Saoudite lifa khew dou deug dou yoon . Complexe nguen am sen nar yi.
Maachalla amna solo torop yalla na yalla fay
Lolou khewoul Mack me Riyad
Riyad bokoll arabe bisawbit
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤leeral bii deelen ci gaaw
Yalnaniou Borom bi mousseul si souffisme
Allahou Akbar claire et net
Amna solo
أحسنت أخي الحبيب
Dieureudjeuf Ya aOustaz,
Yalna gnou Borom mey deggeu ak top
Oustaz youye téseunté senegal rek la ame
Wàdji dàloul maka bourou mka ba là dall 11:10
حياك الله
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oustaz makhtar sarr limou wakh lèp deug leu
Ñii ay mbam lañu rek Ndakh Sen poss
Yaa naafeq Allaahu Akbar,
Lii du benn montaag, 😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
NAFIKHE DEUGE DEUGE MOYE YAW AY NAR NGE NIY DIAMOO
@@diopmourta6969 togne dè bakhoul. Lim wakh n’est basé que sur des vérités. Arrêter de faire du parparlo et soyez objectif.
Nafeq rawoul sa Serigne pourquoi sa Serigne kasou si😂
Maan deh doumané nafekh laa waay lou wakh dara nekoussi deug ces vidéos existe belle et bien
Thim jaami naar you bon yingeen doon
Dém leen ligeyi té jaamou ji moo géun ngeen topp çi naar yi di yappar yappri mélné gniou wéradi gniakk ngeen joum lool
Merci gniomde naaryii de lignou def dougnthi wakh ey li sodon touba wallah tiwawon sen micro yii lagnouy takka
Ms vrai naafeq ngeen vidéos yi dou sax Arabie Saoudi wala dangeen rew rek
Yay nafekh deg deg rk😂😂😂
Sa serigne moy fenkate
Wéddil ak preuv mo geun 😂
Ngén bal ma wayé guissnà naryi dika dougal kom makhtàr sarr
Matar Sarr est un hypocrite qui déteste les enseignements du Prophète.
Yew veréma nafikhnga oustazz mouctar mousoul noppi thi senegal sakjour mou wakh thi njaloo katyii goor jigenyii serie you bonyii bayiwoul dara
Bayil fèn té nga degglou limou wakh
@@AichaDia-t1d mactar Sarr loutax dou wax si bokkaale bi nekk si deukk bi te moo geuna bon
Mahrarr sarr mom ak ay Serignam yépp ay thiakhan katt laniou Ay tapalé Kat laniou
Wa ki menoul fenn 😂
Sa Serigne moka daka doulll 333fois
@matarndiaye9969 fofu nga douler nak mann awma serigne gnap senn ndey nafekh
Yeena bariy tappale rekk leegi bu doon feneen fii ngeen di nekk di wax wax du amul ben Ndiarigne cam
Féne rek guéne Di def 😂😂😂😂
❤❤❤❤
Yaw yaa naafeqq deugg deugg dangay wakh di tontou sa bopp 😢😢 yéne année yii yëpp guis ngéne politique bi séne seriñ si di dokhal ngénné moouuttt ték si séne tànk
Sa Serigne wax nasi ani kou gueuna nafeq niit kouy woté wo nitou dinné Tei bepp yaawtef doko deg mou wax si?
Sa fénne yi ngay fénne déh war nga sé rouss sax seriñ bi nangu woo sakh khouss si biir sujet yi 😂
Sa Serigne moka daka doulll 333fois
Mouna doul dou da ngenn di guiss video fi si dakar bou benn serigne di def ngenn gnawlou ko ba paré né gnounn aye yefeur lagnou riyad ak saoudite gnossi yame aye nafekh ngenn deug beugua defendre li meme sou nekonn senegal sah wahal deug ne li gnom dagno dioum warougnouko def bourou makka bi dafa dioumm . Fater na sah senn harite yi ay narr lagnou sou ngenn ko defer dotoulenn diotati haliss 😂
Wadji dafa tam féne ak bagne sounna mo waral mouye wakh wakh yi
Yen tamit nguen nonoo tarikhayi li am ba am moy dioulit dou nonoo moromou dioulitam
Yoonou tariqa lagn noono dou nit yi.
Kam Kam dupeke😂😂❤❤❤
Sén Serigne yi nare yi ay domerame lagnou
Oustaz Mactar il a raison, pourquoi vous dénonce pas ce qui se passe à Arabie Saoudite.
Adunabi yap deko nakhar lo yen ngen koi defender
Adouna? Tu parle de quel adouna do bayi feine
Dafa amoul bagn Koy nakhar Lou.
Messi bign fa Andi nakhrinagnou, Ronaldo même chose té wakholè si
Oui aduna yeup gnoko gnaw lou kaay yow nak bo amoul deug deug ya xam
@@djibysow873 wa france daniou co nakarou Belgique Espagne Congo soudan comore Angola????
Comment je peux dire à UA-cam de ne pas me suggérer ce genre de vidéo 😅
@@adyandabakh5565 qu'es ce que je fais ici lol.
Je pense que ya Oustaz tu n'es pas compris
Mais c la caricature de la Kaaba qui choque tout le monde. Lolou mo wara nek indignation bi kon débat lolou dong la waron doon
Yalla dineu diégalé bakar bomou dése bokalé fi le pére Noël mbacké wakhni sou yalla takhawé yoninte bi psl takhaw bou rombeléne dém si Mamame kara aussi wakhni serignam mo binedeu yalla soubhanala 🙏lolou dafa doy warr pourtant bi serigne yoyou di wakh lolou Makhtar sarr miguiwone Senegal té wakhousi
Dakay. Doull. Rek. Yene. Ay. Nafiekhe. Kiene.
Matar da bagn waaa ahlou Sounnah rekk
Wakhkofi touss
Yaa naafek 😅😅😅😅😅😅
Amnathi dourouwa pask loolou lagnou giss
Yaw mome koula dakha tapalé guissoumako, سبحان الله
Oustaz makhtar sarr jerejefetti
Riiiiirrrrrrr yaw yamanaféne ngani imam nga took di féne
Doul rék géni déf
Li khew arabi sawdit kiko gniawlou woul rek nafikhnga😢
Lan mofa khéw 😂indil preuv mo geun wéddi
Legui lou xéewe ci Sénégal do léen ko wakh machallah oustaz Mohammed
Xana yow do dégg
@@AichaDia-t1d ñolako gana xam addiya biñe faye ame modoune rek
Fi dara leundemou fi yawmi yafi wakhout dara lou lèr li khew arabi sawdit amoul ben manipulation mane d koukoy defendre wédina la ak ko mana done
bilaye yamana fene
Walahi sa Serigne moka daka doulll 333fois
Way yaw t'ai toi c la vérité niouneé nguen denocer ko mo gueneu waxdji mm si c des montages c à dénoncé
Nopa loul rek li oustaz maxtar wax dinga sonou te doko dinndi
Imagine si c'était touba et tivaone vous allez pas parler comme ça..vous êtes munafique
Vraiment kou meuneu togne ngueu. Ragalal Yallah, le mal ne dépend pas de pays ou autre. Il faut chercher la vérité. Il défend pas de pays, il parle de religion. Parparlo bakhoul
Makhatar day def manipulation Mais MBS dafa am agenda diaroul layal islam bi nék Yalla moko mom
Aka nio nafékh té Saytané
Matar garaw garawlu 😂😂😂
mano wax normal te bayyi nar nar lou gui