Voilà le genre de mari qui incarne les valeurs musulmanes: travailleur, amoureux, attentionné, bienveillant et humble. Les hommes sénégalais regardez comment on traite une femme
Vous avez vraiment assurer Pape et Codou surtout a la fin de l'episode ça montre qu'au moment de travailler il ne faut pas etre distrait par aucune futilité. Bien jouer🙏🙏🙏
L'episode qui m'a bcp marqué surtout ce gars Pape machallah il a bien joué son rôle machallah depuis bima commencé setane batay episode bii momaci geuna nehh ndah damaciy jiss sam bop
Bien joué ça fait première fois j'ai regardé le serai Sénégalais mais là j'ai vraiment comprends les policier ils ont bizarre tu es intelligente a dit donc ta femme est bon je sais pas les pays et grave ça bonne chance à tous les sénégalais a tous les pays je vous remercie
wayèn grand amour mom nekhna di con Pape mii dafdon infiltrer gars yii ahh sécré Pape et coucou à Mr le ministre Aly aka bari ay facette con dal père la niii eupnaaaaa
ohh la fin nékhatina dal mais dafa melni Pape dafa nékon thi opération di raffler garsyi di mbouboo café gui très malin ce gars là ahh man dal beugnaa yii inspiration
machalla amena solo lolou li molay wane né djikguéne bo néké ake goor sa khell daloule si mome bayil mou déme nakh tamit cou bayi djiguéne nakh yaw un jour dinala bayi nakh sa morom fin béma gueuneti nékh nakh mane tame mourite la té nonou la baré kharitou tidiane machalla yalla na séne diame yague😘😘💖💖
Chers wa PIKINI. je vous felicite pour ce 15eme episode, et vous suggere un autre feuilleton tiré de 15eme episode. pourquoi pas intituler DOUNDOU PAPE AK CODOU
Voilà le genre de mari qui incarne les valeurs musulmanes: travailleur, amoureux, attentionné, bienveillant et humble. Les hommes sénégalais regardez comment on traite une femme
Pape dafmay fathie way😂😂😂😂Ay way Goor gni roylen si Pape way ndeysanne. ❤❤❤
Dou niepa niodoul fethi
Ndeysan Am nitt ñoo xamné sén Rév mooy un jour ñou Ndoundou mbËgeul Bou nékh yàlla ngén Dadié Ak sénn ❤️
amine baye ak yawtamite
@@ndeyefa9472 aminn wayy Moy Lima manqué pour l'instant DH
Amine
Amine way vraiment
Amine touf touf
Pape baye Fall kou begue Bamba besel j'aime
Ndoga lo yalla na yalla yok ak leram si barkepp mame fallou mabcke
iss 814 iss amine bro😭🙏🙏🙏🙏
amine
Amine
Pape néna mo ayé tay🤣🤣🤣🤣 wouy ndékété Pape la beugue mane ak kane?
😂😂
Amna solo ma sha Allaah 😍❤️ Pape dal beugue naqo😍❤️
Wayer tamiiit bigué ma sha Allah waaay sa forme rafeetneuh trop waaay ma sha Allah😍❤️😭😭😭
Anni wa coalition andeu sétane serie yepp team wifi
Mangi ni
Bén nagui ni
Dagena amdjiot nak senegal🤣
@@mamadousowfall6944 nougnouy deff tmt
Dèm diangi rék khana
Kou beugue pape sama acteur bi beuseul j'aime
Man dal beguena pape tay ma ayyé😂😂😂
Ohhou mouride ak tidiane yeupou beneu la gni togou thieb bi yakhou niouko dhé nioune gniko tangal niouka kheumal👌
Bilaye degeu gou wêrr nga wakh nii
Bilahi walay
Lou lèrr nga wakh
Oh fin bi nexx nama lool vive grand t'amour bilahi je vous adore😍
Mouhamadou Thioune
Vous avez vraiment assurer Pape et Codou surtout a la fin de l'episode ça montre qu'au moment de travailler il ne faut pas etre distrait par aucune futilité. Bien jouer🙏🙏🙏
Bilay yaw dama contane machalla
Ohhhh ce fut magnifique.... Beuguel mo nekh rek... Ndeyesanne
@@fallouseck5119 q
Enfin sama serie préferé kne love wa pikini diadieufeuté 😊 salam rahma wa baraka a tous jumua mubarak
L'episode qui m'a bcp marqué surtout ce gars Pape machallah il a bien joué son rôle machallah depuis bima commencé setane batay episode bii momaci geuna nehh ndah damaciy jiss sam bop
Cheikh yagui lire ...livre bou nexh té beuri émotion😭......😍Une vie de boy😍
de Ferdinand oyono
Buongiorno
Toundi ondwa
Premier dollen ma may j’aime bokk🤞🏿
Lo koy doyée
Dakoy léke
Bigué da charmante machallah ki accepter
Yaw say beut bakh na
Pape c'est un vrai acteur
Pape a gravement assuré son rôle chapeau frère je kifff
Wa yeine episode bi nexna dh🥰srtt fin bi😍 j'ador❤
Pape🥰 ak Laye tmt😂😂
No mane singom la meunoul mougne 0stress 😂😂😂😂😂
Bien joué ça fait première fois j'ai regardé le serai Sénégalais mais là j'ai vraiment comprends les policier ils ont bizarre tu es intelligente a dit donc ta femme est bon je sais pas les pays et grave ça bonne chance à tous les sénégalais a tous les pays je vous remercie
Dioylenma hier j ai perdu ma tante 😭😭😭😭
Yamana wakh
Gnou dioy leu anh ? 😂
J'ai eu un bb aujourd'hui c'est une fille prié pour elle svp
Yalnasi wér topou machalla nékhna trop si khol yalla def ko mague,🙏🙏
@@oulimatadiop9300 merci et Amin ma chérie ma wal ko gni ko amagoul inchallah
MINETOU BA tt mes félicitation ma cherie yalna ko yalla déf mak mou barkél si barké seydina mouhamed psl waleuh gnouko tmt
@@bvediarrachousene5832 Merci ma chérie yallah nalén ko wal légui
Yalla nassi weurr topou mou dounde té diarigne leu
wayèn grand amour mom nekhna di con Pape mii dafdon infiltrer gars yii ahh sécré Pape et coucou à Mr le ministre Aly aka bari ay facette con dal père la niii eupnaaaaa
J’adore la fin 😍❤️ les paroles de pape 🙏🏿🙏🏿❤️
Degue degue mouride ak talibè cheick benela ke jaime ndakh mane talibè cheikh la tè sama sanga mouride la et aussi nogui doundou nice😍😘
Ndeysane pape dh comme mon mari il fait tout🥰☺️💃vivent les mariés
Wah kidou Ministre Ali😂😂
La soeur de codou elle est trés belle et charment avec ta belle sourire
Khana daga kou nop
Vraiment
C est tres cool , yetter you bakh en plus Pape dafa dionguer, amm yeurmander so diabaram
Pour la première fois may commenté mais bi mom da dal am Ab baye Fall dal mo woor teh nekh😍😍😍😍
Fall rek
Dou ay fou
Barke serigne bi
Ndeye filly khana mo mom pikini chaque série pikini bou béss ngue guisse ko da meune limouy déf nak mashallah.
vraiment grand amour dale nekh na amena solo
Aywau soupe rkk la beugg sama khol bou am pobar lepp sibirrr😅😅.série bi nekhna trop mashallah
Non série bi nekh trop!!!!!!! J'aime beaucoup. Merci pikini production
ohh la fin nékhatina dal mais dafa melni Pape dafa nékon thi opération di raffler garsyi di mbouboo café gui très malin ce gars là ahh man dal beugnaa yii inspiration
non nonnnn pikini diguene ma raye rek merci beaucoup serie yii amena solo
Je suis de la mauritanie merci beaucoup et Bonne continuation Nice série
Suis morte de rire sy ngom🤣🤣🤣🤣🤣
Yalna diam sx yalla maynu fan wu gouddou ak werr😍
Amine
Grand amour le meilleur théâtre
Kone pape no boke duek
Épisode bi moma dakal yeup. Chapeau à vs surtout ndeye filly tu assure
guiss Na fii mbeguéll ❤️ bou nékh trop yalna jamme yage
Non l'episode de codou est la meilleur😍😍
Nn srx pape damako fans Ani gor yi yeureum djiguén may l'en ma jaim way
Jigene gni dagne leen wara yeureum mo gnou war
Mane d damako nop sax pape RK🔥
Abon kone nonele
@@khabanefall1685 wawaw😇
Mais Esque pape limouy wané nii mo nek ci mm
Manmom franchement ndey fili dama neih depuis dikone je laime beaucoup
Yàlla na niep am Jàmm
Amine
Amsa Leye amine
amine
Amine
Amiine way
Pape joue super bien
Taye ma aye 😂😂😂doma dieule gnarel pape mi 😂😂petit poussin 😂😂😂
machalla amena solo lolou li molay wane né djikguéne bo néké ake goor sa khell daloule si mome bayil mou déme nakh tamit cou bayi djiguéne nakh yaw un jour dinala bayi nakh sa morom fin béma gueuneti nékh nakh mane tame mourite la té nonou la baré kharitou tidiane machalla yalla na séne diame yague😘😘💖💖
Vraiment ndeye fily mangua sagnsé machallah laff thiate épisode bi nekhna trop😍❤️💞
Machallah wayy Man dall beugg na ndeye fily billahi au fond de moi épisodes yéin bi mosii ndaxx machallah wayy
Qui regarde la série avec son Phone 👍
Âme Junior c'est moi
Mor Diadieuff
Âme Junior moi
@@morgueye6383 moi
Mw
Ohhhh MachAllah amatina solo bonne leçon de vie ,il faut jamais préjuger une personne car l'apparence est souvent trompeuse ,chapeau à vous pikini
_Ana wa Team Grand d'amour nouyou nalene_
Niongui lay fay
Longue vie à nos parents
l¨un des meilleurs episode de cette serie,codou et pape c de grands acteurs.
J’aime pape il a bien assuré 👍
Chapeau à pape il joue très bien son role bonne continuation
Madina mankagny cest notre cote en casamance je suis content .
OMAR KONTE Ce n’est pas Madina mankagny. C’est (Mandinaa)
Aka mo gnang
@@ferreiraafonso1579 t
Sétlou wolén dara si wa pikini production dh ,si goor yi barbe rek wa waw,si djiguén yi nak teint noir meune guén choisir dal
Yaw kou am séetlou nga, Ma Sha ALLAH!
Non vraiment pikini vous assurez Machâalla 👏, sinon pape nouveau type de Seey!!!! J'aime ça 🤩😘
Oh coudou ou Ndeye filly je t'aime en tout cas
Top lene sama guinaw té beuss j’aime
Ay wayway néké pape la beug mann thioum🙋💃💃💃💃💃✌👊😍💋😂😂😂😂😂
Vraiment j'adore cette série
Chers wa PIKINI. je vous felicite pour ce 15eme episode, et vous suggere un autre feuilleton tiré de 15eme episode. pourquoi pas intituler DOUNDOU PAPE AK CODOU
Ohhh fin bi bilahi li rafet na way j’aime bi je suis mouride mei lep beneu la sama mak mouride la te talibe cheikh la fass soxna kou bakh👍🤣
Bi gore kouko am lodi wakh bi gore say li lagniou weur kou bakh koulay dimbali atissssssooooo
Way Baye fall mo nekh 😍😍😍
Wakhal waye
Man sy ngom la begue😂😂😂😂😂🤣
Une phrase qu’il faut retenir les hommes qui dénigrent leurs épouses pour une autre
Ndam rk incahalla 🇸🇳👌👌
Aaaaaaah bilay ma beugu goor bou jongué attentionné tek Thie am ay astuces 😍😘❤️😄 pape j'aime bien ton rôle
Thieuy siguom Aka gaw ci nokei😂😂
Vrement j'aime pape bi mom mashalla pa comm les autres
La Fin Ouf. C'est magnifique
Torop
Ça me touche beaucoup wallahi
Yalna nou yalla soutoural
Wa yen dieukeur djou melni pape mom ayyyyyyyyy wayyyyy😍😭❤️
Grand bravo. belle histoire ce grand amour. J'ai vraiment adoré. Bonne continuation.
1ére wayy tayy mome télna dh
Mais dall nékh ma beugueu wa Grand Amour wayy😍😍
Meusou ma commenté mais fin bi mounou ma sei doyal makay tekk dika tegat ret vive grand amour😍😍😘
Ohhh man tmt nonou lama nékhé 😍
Machalla li nèkh na dieurkeur bou mèlni nèkh
Sama xell mongui ci soupe bii dè😋😋😋
Kon amna morom😂😂
😁
Wawwww fin bi nékh na troop waye bien jouer
J'adore votre sèrie vraiment
😂😂😂 jaime pape dalay teuthie dh ndeye filly
Excellent pape et codou vs avé vraiment votre rôle bne continuation et mrci
Thiey grand amour yakar grand amour reck kennal grand mour reck bou weur limi def thi manne😂
😂😂😂😂
@@aichalaye5702 ah sokhnasi limey yeuk reck lay wakh😂
Love you pape❤️Bayil mate sa lèvre yi tamit😉
Bounama Seye c'est une grande sœur à une copine de classe kou bakh ndéyesan Yallah nala Yallah défal diam mais bougn lay geudj guiss❤️
Wakhatiko sama grande sœur D'amour kou bakh sakh am yite adorable borom ré djou nekhebi seyenama
Nakat mane Singom laa begue 😂😂😂
Ayy wayyy mannn beugu naa pape bilayy mai kenn dou simgom néna souyy balei 😂😂
Man Billahi Pape daf ma Nekh
La sœur d codou est vraiment belle
Mane deh pape la farall ba guene télé🤣🤣🤣🤪
Wawaw
Ak man
Merci beaucoup codu je suis fière de vous
Ravi d'être là ! Comment est-ce que vont mes amis ?
Me PAPE DAFA NIRO AK BIRANE BI NEKONE SI SÉRIE DIKO
Oui dagno niro kaye
@@djibindao9725 nakamou Nice Quelle Djiby
@@dembatewette2311 djiby Ndao louga ndewene déthialaw