suis 100% mes balla dafa wara kholate lisi guinaw rek merci Aziz Ndiaye content naniou si iow balla yokhal entraînement yi rek teh gayi bayi snap yi ak tiktok bi niougui sa guinaw beuré kat bi nieuwoul star bi ak msytique bi mo nieuw mes Lamb nileu félicitations b52
@@momosaw3543 mo tax li dikou dall soutoura defa bax sama bena xarit mara defa boka si seringe niou b52 yi mouni b52 dou workat defa gore te da am soutoura lolou moy yon
Jam c pas un analyste mais il croit ce k les marabouts lui dise, par contre FAdam a raison il parle de façon technique et c un ancien praticien de ce sport
Félicitations Bombardier) Du courage Balla Gay 2) Mé Balla Gay 2Naniou waxaté Deugeu té Yallah Tax Balla Gay 2 entraînement woul en plus contac yi aussi vraiment Désna lou Barii aussi 🧏♂️Balla wathiall thi souf si raysa boppou boo bégué continuer sa carière 🧏♂️
Balla doit retourner de suite à l'INSEPS, et se concentrer sur lui. Revenir et faire des contacts mais avec des gros gabarit. Je ne vois pas de lutteur lourd comme Bombardier dans son écurie. Il faut qu'il s'isole. Son second voyage il n'est pas allé à l'INSEPS et c'était une mauvaise décision. Fadam a raison
Si j'étais lui, je prends un vol demain, je retourne à l'INSEPS et je reviens un ou deux mois avant mon combat et je me focalise sur les contacts matin et nuit, en plus de la musculation
Merci beaucoup jamaïcain Lou niou khamoul légui moy mbeur yi légui souniouy contact goudi laniou koy fekk ak fadiar daniouy lakatou parce que lolou daniouy lakatou pour ses adversaires
j'ai vus personne avant le Comba dit Balla gaye...forme bi bahoule ou bien contact Goule défait mo niow rék il faut accepter la défaite...félicitations bombardier
Lolou moy avantage défaite, c’est une occasion de faire les critiques véridiques et logiques. On ne pouvait pas savoir est-ce que amna entraînement ou pas. Déjà Balla image entraînement yeup guisso foumou souméko , débadeur rk ladone sool mais le jour-j kou guiss biir bi ak deun bi xamni déssna. Mais le véritable problème est que Balla geutie na contact normal à cause des voyages, surtout pour la réfection de sa forme. Liko déf Balla beuré la, donc na délou si souuf si
Félicitations B52 , BG2 a perdu de sa confiance c pck il a une pas une bne endurance, donc il a peur d’entamer une action. Le fait marquant c Balla Gaye n’a pas de stratégie de combat
Borom casquette bou blanc bi kou bagn balla ng... khamoo dara nopil... balla entrainé n bou bakh si contact, musculation ak physique bou baakh..balla c'est le meilleur lutteur de tout les tps yalla miko daane may ndam tay moo niou khagn alors dagnkoy santé yallah diko nianal li dess si lamb leep nek ay ndam insha'allah... BALLA rassure toi nioune sa ay vrai supporter depuis niouy nek khalé ba leegui tay naniou la geuneu beugu tay naniou l geuneu fonk tay naniou l geuneu respecté té tay naniou l geuneu woolou❤ diam ak kheweul si yaw CHAMPION notre roi des arénes notre fierté yafi def lou keene defoul... courage mbeur💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Balla Gaye kén douko diangal beuré techniquement et tactiquement il est bien...C'est son préparation qui n'est pas bonne et son entourage ne l'a pas aider sur ce combat. Ils l'ont poussé à l'euphorie et Balla n'était pas serein sur ce combat qui était capital parce que c'est un combat revanche.
En tout cas je suis d’accord avec Jamaïquain,Balla ne peut pas prendre cette combat et laisser 1 faille dans son entraînement. Balla et son entourage ont minimisé Bombardier,pour eux ce 1 chounee. Surtout quand le Polanais l’avait mise KO. Pour prouvé,Aziz Ndiaye,a dit avant cette combat que il vont pas lutter contre Boy Niang 2,donc pour eux il sont déjà gagner contre Bomb. Mais il sont oublier que Bomb avait gagner contre Balla 2 dans leur première combat facilement. Balla aussi avait beaucoup de préparateur mystique,trop de embouteillages.
No no suis pas d’accord avec toi il peu aller en France pour entraîner alors se que il fout rien ça c’est vue dans le combat on a vue balla comment il es il n’est pas bien entraîner quand même
@@petertosh1729 on dirait que vous êtes toujours entrain de sous estimé Bomb. Le stratégie de combat a joué dans ce combat. On à toujours vue Balla attaque ces adversaires,mais cette fois si le adversaire ce Bombardier. Peut-être Bombardier e plus fort que Balla. Ce l deuxième fois. Wasallam
Dimbalé len gnou way Balla Gaye 2 deff na lepp entraînement mystique défaite mo gnow dagn ko meune dane ko bayilen gnou way Bombardier di géant Champion nguén gni sonal
Jamaïcain xana messoul fowé beuré, dolé contact bokoul ak dolé musculation. Comme joueur biy football, daw ak dougou terrain bokoul. Contact da am répondant ak résistance.
C ça, na gayi khol avant bras bombardier bi nimou dagué, lolou contact mokoy mayi, bokoul ak bou Balla bi dara. So beugué nit dagakoy wax deug. Balla mii sou beuré ak boy Niang dou am ndam ,la dem contact té tok senegal
Maak yaw nio book khalate ils pensent que mo eup dolé mo eup leep ta Bg2 ay faille kesser la ame amoul garde soko bolewone ak Serigne Ndiaye 2 Walla Reug Reug Walla Franc dinga khamnii eupoul doolé keen
Fadam vraiment ta raison staffs balla gaye2 daah raax guisu ma thierno gueye ak sidya Bodiang ak Pa biy sol mbaxané féticheur yi moy Pa malien bi guisou malén ci dembeu ci Arènnes bi
Fadam takhawal balla ngiko werr yeup khamou gnõ lamb ay Nitt yo khamni buzz rk laniouy wout si bala mes dou dara famille Aziz Ndiaye pour nioum gnõ mom lamb dji
Sou youtube bi amone vocale dinalèn expliqué li waral carrière balla guaye réussir moy Dafa dadiewoul wone ak gris bordeaux ak bombardier bou dadiè wone ak niom dou meusseu diot ci yekini
@@cheikhsow1042 revoit la definition d'objectivite car être sportif bagna nanguoul l parcours d balla jusqu'a yekini K u puisses sorti un raisonement pareil
@@moustaphadiakhate1031 le combat entre yeukini et eumeu sene était le plus logique à ce moment là mais ça c'est le passé et je pense que c'est le passé qui fait le présent depuis que balla a perdu le roi il a du mal à ce relevé on se demande s'il il le méritait réellement
Fadam est un excellent analyste de combat de lutte. Bien dit
Merci fadam tu nous avait tout dit avant le combat bravo 🙏🇸🇳
Merci fadam ta dit la vérité ! Tu es vraiment un connaisseur j adore t écouter depuis paris
Fadam a parfaitement raison balla il a fait de la musculation mais l'entraînement prioritaire c'est le contact il n'en a pas fait assez
suis 100% mes balla dafa wara kholate lisi guinaw rek merci Aziz Ndiaye content naniou si iow
balla yokhal entraînement yi rek teh gayi bayi snap yi ak tiktok bi
niougui sa guinaw beuré kat bi nieuwoul star bi ak msytique bi mo nieuw mes Lamb nileu félicitations b52
Merci momo sinap ak tiktok diarouko di wone galadie dou yon de
@@mamaaboudieye8745 bilay suis pa d'accord même birr keur balla niouy wane gallath yi c pas normal
@@momosaw3543 mo tax li dikou dall soutoura defa bax sama bena xarit mara defa boka si seringe niou b52 yi mouni b52 dou workat defa gore te da am soutoura lolou moy yon
Fadam il parle la connaissance il analyse très bien le combat! balla à maqué de contacte
Préparation bi dara bakhoussi loulere la fadam wakh Bombardier kouy beurei ak moom résistance rapidité ak sa poids de forme pas ay volume.
Aziz Ndiaye Borloo showbiz😄😄😄 ak COACH Diambadong bouy weur di wakh rekk
Je suis 100%balla mais ce qu'a dit fadam est la pure vérité balla n'a pas bien préparé son combat et il n'a pas récupéré du tout
Jam c pas un analyste mais il croit ce k les marabouts lui dise, par contre FAdam a raison il parle de façon technique et c un ancien praticien de ce sport
Balla Gaye manque un technicien dans son staff qui lui apprend les stratégies de combat
Qui t'as dit ça
@@lasmc198 cite un technicien vivant ayant connu des grandes journées ds la lutte ds son staff
Aziz Ndiaye Borloo showbiz😄😄😄 ak COACH Diambadong bouy weur di wakh rekk
Lèèpp problem Contact la
Balla contac goul.
Merçi Fadam
Balla gaye dé worna yalla Modou lo rék moko diaral ligey Modou rék Moy nawlem
Diame kou meuneu nga balla gaye entraîner woulle lolou doff yi sakh kheme naniou ko
Félicitations Bombardier) Du courage Balla Gay 2) Mé Balla Gay 2Naniou waxaté Deugeu té Yallah Tax Balla Gay 2 entraînement woul en plus contac yi aussi vraiment Désna lou Barii aussi 🧏♂️Balla wathiall thi souf si raysa boppou boo bégué continuer sa carière 🧏♂️
Merci ba parés staf bi bahol 🤦
@@ablayenittoudeugu1012 bayil saga lep Sénégal la 🙏😃
L'absolu Gueye legui mome khana dinga ande ak dal tey analyser sportivement bayi far bi
Ki key dou ioe boy niang gui nieuw daal sene kaw
Sarap ndeyou ki rek yaw yangi fepeu
Fadam à bien raison Balla gaye entraînement bi doyul mbeur yi délén déglou fadam✊✊
Merci fadam lép gua wax Lou ame leu Balla contact bi dafa déss Lou Bari
Mérci fadam dagh la way
Balla doit retourner de suite à l'INSEPS, et se concentrer sur lui.
Revenir et faire des contacts mais avec des gros gabarit.
Je ne vois pas de lutteur lourd comme Bombardier dans son écurie.
Il faut qu'il s'isole.
Son second voyage il n'est pas allé à l'INSEPS et c'était une mauvaise décision.
Fadam a raison
Vérité absolue.Cette dernière préparation est une mascarade.Balla koukoy neikhal do am dara si moom.
Si j'étais lui, je prends un vol demain, je retourne à l'INSEPS et je reviens un ou deux mois avant mon combat et je me focalise sur les contacts matin et nuit, en plus de la musculation
Bref vous avez tout dit 🙌
Deug la Balla entraînewoul comme il se devait mais il faut reconnaître aussi que bombar dafa beuri dolé
Boys bi jamaïquain kou beuri wakhla té khamoul lambe deugloule fadam lou leer la wakh boys yow dioudou wo
Merci beaucoup jamaïcain Lou niou khamoul légui moy mbeur yi légui souniouy contact goudi laniou koy fekk ak fadiar daniouy lakatou parce que lolou daniouy lakatou pour ses adversaires
j'ai vus personne avant le Comba dit Balla gaye...forme bi bahoule ou bien contact Goule
défait mo niow rék il faut accepter la défaite...félicitations bombardier
Lolou moy avantage défaite, c’est une occasion de faire les critiques véridiques et logiques. On ne pouvait pas savoir est-ce que amna entraînement ou pas. Déjà Balla image entraînement yeup guisso foumou souméko , débadeur rk ladone sool mais le jour-j kou guiss biir bi ak deun bi xamni déssna.
Mais le véritable problème est que Balla geutie na contact normal à cause des voyages, surtout pour la réfection de sa forme. Liko déf Balla beuré la, donc na délou si souuf si
Merci fadame très pertinent bonne analyse
Merci fadam yakh ga le peu Balla moy sa ma beure mais amoule forme
Merci beaucoup fadam
Fadam limou wakh lep deug leuh 🙏🙏🙏
Félicitations B52 , BG2 a perdu de sa confiance c pck il a une pas une bne endurance, donc il a peur d’entamer une action. Le fait marquant c Balla Gaye n’a pas de stratégie de combat
Jamaïcain mi est-ce-que dougnou ko lakk gambien pour mou comprendre 🤣🤣🤣
Fadam limou wakh deugg la physiquement Balla n'était pas au top
Ammal respect c Gambien ye, ollof yep bennala, Gambie ak Senegal yep bennala, merci, wassallam👋🏽
Borom casquette bou blanc bi kou bagn balla ng... khamoo dara nopil... balla entrainé n bou bakh si contact, musculation ak physique bou baakh..balla c'est le meilleur lutteur de tout les tps yalla miko daane may ndam tay moo niou khagn alors dagnkoy santé yallah diko nianal li dess si lamb leep nek ay ndam insha'allah... BALLA rassure toi nioune sa ay vrai supporter depuis niouy nek khalé ba leegui tay naniou la geuneu beugu tay naniou l geuneu fonk tay naniou l geuneu respecté té tay naniou l geuneu woolou❤ diam ak kheweul si yaw CHAMPION notre roi des arénes notre fierté yafi def lou keene defoul... courage mbeur💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
lane la fi def lou kene deffoul ?
Fadam tu as bien interprété.bonne continuation
Contact mom sama mbeur mi défou ko
Fadam a bien dit c vrai balla entrainewoul
Jamaïcain sa analyse bakhoul.deg loul fadam molla meun si analyse.entrainer woul.
Je s8 💯pour 💯 Balla Gaye 2
Fadam yaa wakh deug
Balla gaye entrénewoul
Dafgno nakh bilakhi
❣️❣️❣️
Merci Jamaica 🇯🇲 🙏
Balla Gaye kén douko diangal beuré techniquement et tactiquement il est bien...C'est son préparation qui n'est pas bonne et son entourage ne l'a pas aider sur ce combat. Ils l'ont poussé à l'euphorie et Balla n'était pas serein sur ce combat qui était capital parce que c'est un combat revanche.
Aziz Ndiaye Borloo showbiz😄😄😄 ak COACH Diambadong bouy weur di wakh rekk ...Balla Beye diko doungourou..
Voilà le résultat
Fadame lou lair ga wah hamga lambou Machala
Vérités absolue fadam
Djam débat bi dafko dépasser fadam moko dak analyse
Fadam mô geuna hame lambe,loulér ngua Wah deugeu néhoul
Bilay Fadam ligua wakhe moy deug moy yonnn
Merci fadam 🙏🏾 boul ragal deug deug moye dieuk moy moudie
En tout cas je suis d’accord avec Jamaïquain,Balla ne peut pas prendre cette combat et laisser 1 faille dans son entraînement. Balla et son entourage ont minimisé Bombardier,pour eux ce 1 chounee. Surtout quand le Polanais l’avait mise KO. Pour prouvé,Aziz Ndiaye,a dit avant cette combat que il vont pas lutter contre Boy Niang 2,donc pour eux il sont déjà gagner contre Bomb. Mais il sont oublier que Bomb avait gagner contre Balla 2 dans leur première combat facilement. Balla aussi avait beaucoup de préparateur mystique,trop de embouteillages.
No no suis pas d’accord avec toi il peu aller en France pour entraîner alors se que il fout rien ça c’est vue dans le combat on a vue balla comment il es il n’est pas bien entraîner quand même
Entraîner faut bien souffrir balla n’est pas souffrir dans sont entraînement
@@petertosh1729 on dirait que vous êtes toujours entrain de sous estimé Bomb. Le stratégie de combat a joué dans ce combat. On à toujours vue Balla attaque ces adversaires,mais cette fois si le adversaire ce Bombardier. Peut-être Bombardier e plus fort que Balla. Ce l deuxième fois. Wasallam
Meune nga entraîner musculation tei do endurant peut être lolou Moy problème bi et puis les étrangers ne sont pas expert en notre lutte
Wakh bi barina jamaicain a raison bomb est plus fort et balla n'ose pas l'attaquer sinon il serai en battu a moins de 10s par bombardier
Lamb dou xaliss kessei ✅
Bayinga Tik tok yanGui Fiii🤣🤣🤣🤣
Merci fadam c des critiques pour faire avancer ballaerci
Modou lo d'où moromou bene mbeur Limou am thi bombardier FIBA mouye bayil lamb mbeur doukoko defatt
Dimbalé len gnou way Balla Gaye 2 deff na lepp entraînement mystique défaite mo gnow dagn ko meune dane ko bayilen gnou way Bombardier di géant Champion nguén gni sonal
Tok di wakh yomb na fadam mai balla défna limou meune mai bombardier moko meune nangou rek
Fadam ya nième deug bilay
Fadam wakh nga lep balla champion la mes nekoul thi form deug nekhoul
Biir bi di lang thiey starou boury 😂😂😂
Beneen yoon na ngeen di degglunté.
Té Fadam del bayi Jamaicain muy wax xalatam.
Jamaïcain say lekh lanla😂😂😂
Balla amoul entrainement indiwoul dara touss naniou waxantè deug epi walahi lamb bena mbeur mofi amon strategie mouy yekini epi osi balla pere balla manquè nako
Balla guaye na dèlu école de lutte ba moy deug di contact suko mmeunatul nna bayi lamb ces tout Sa thies dieul reulè biii
Question mbeur yi bouniou deme France wala usa danioufaye contact wala juste musculation lanioufaye def?
Seule la musculation. Bref lolou moo yaak lamb j. Même boy yi beurétouniou
Machallah débat bou ame solo
Diamaïken tay la khamni khamon lambou balla ć mon lutter mais amoul entérétma
Fadam vrèman wah nga Degeu mbeur day contac ba oox balla da manquè repèr si combat bi Lol la Guiss dh😜🤣boury wagnil Ganar yi
Balla2 thi yekini lah yaké bopam 😭😭😭
lolou la lamsa legui mo bakhol 🤦
Julo balla lane ya yake bopam si yekini
@@moussasallngom6578 Manam poids bimou seuffone thi yaram bii bah legui degnoul dey dienguou rek m dessnah boubax
ci tyson la commencé yaakh yaraman ...........
Il faut aussi permetre a Jam de developper c'est un debat chacun doit dire ces idées. Fadam faut pas croire que li nga wah rek moy deug
Deguela kaye contact bi desna
Bien dit fadam
Aayy INSEPS laniou wara bayi !! Mbeur daay contact , yèkk dunes , lék lou bakh taaay récuperer . Mais top TikTok, Snapchat, Facebook, akk wakh diou beury rékk !!!
Say insep balla demoufa.nopalal sa bopou.Balla ni la meuse am combat titi nieuw di concert mou yeigue si kaw di fetie.
Merci lolu moy deuggg
Balla Gaye ñeuwoul dè vraiment..lamb dafa fiir lole
Degu lou lène avan combat bi ay reaction wamm
Jamaïcain xana messoul fowé beuré, dolé contact bokoul ak dolé musculation. Comme joueur biy football, daw ak dougou terrain bokoul. Contact da am répondant ak résistance.
Démb ba légui lolou lay wakh “ dolé musculation, dolé souuf ak dolé contact bokoul. Démb lama léér Mbeur biiy entrainé si souuf mo eup dolé kiy muscu mais mbeurou contact molén eup dolé niom nieup. Balla eundiwoul dolé ndakh dafa bayi contact. Bref Noble dou beuré🤣
C ça, na gayi khol avant bras bombardier bi nimou dagué, lolou contact mokoy mayi, bokoul ak bou Balla bi dara. So beugué nit dagakoy wax deug. Balla mii sou beuré ak boy Niang dou am ndam ,la dem contact té tok senegal
😂😂nooo vrement débat nekhna équilibre na
Fadam adverser y dou bèneu lileu diam Di wah comprendre ko
Jamaïcain est le plus pertinent
Man li yagg nako commentaires fi lutte TV 📺 balla niame woul entremah srx lima damako te ngi diekgé balla kham n’a gnõ lima wakh bou bakh
Yaw mom Khana dafa Amm lo denthialll BaLLA
Tu as raison frère
Fadam à raison sur toute la ligne
Pour yen yalla amol bayilen wakh dji 🙏 Balla gaye mbeur leu rek com mbeur yep sénégalais danu yakar ni Balla gaye mo mène si lamb dji no way 🙏
Maak yaw nio book khalate ils pensent que mo eup dolé mo eup leep ta Bg2 ay faille kesser la ame amoul garde soko bolewone ak Serigne Ndiaye 2 Walla Reug Reug Walla Franc dinga khamnii eupoul doolé keen
@@misterzappa9073 bilayi frère
Défét mo métii mé yaw fadam bi balla gaye toussé dégunala ngané diekhna tay bissou balla la à travers la radio iradio
🤣🤣🤣
Fadam vraiment ta raison staffs balla gaye2 daah raax guisu ma thierno gueye ak sidya Bodiang ak Pa biy sol mbaxané féticheur yi moy Pa malien bi guisou malén ci dembeu ci Arènnes bi
Niom nieupeu ngi fa wone pourtant
Sa waye fadame Limoula wakh moye deugeu bala gaye meusoul favoriser serigne nakhe meune beureme ak contace bou doye
Merci fadam 🤣🤣🤣🤣💥💯💯
Aly ndiaye nakh nguaniou😭
😂😂😂ay waye begou ma😂😂tamit dakh balla rek la begue
Effectivement fadam tu as raison contact goul deee akk naam daffay mbott guemouko saxxx pounkal bou tolnii bombardier
Ms nékhoul ba nékhoul wayé Fadam kou kham lamb leu vérité rk la wax balla gaye2 ifo mouy contact di entraîné normal di dém école de lutte di contact
Balla na bayii touba bii te yam thiii soufff siiiii contact oute dolè birrrrr mo guen topu weingñe yiiiii reccc di yeukeu tiii hiss na noku feulè
Bilahi fadam deug pir ngafi wah
Fadam 2 ma challah yalna yalla barkél lepp
Jam li gayi wakh deugue la Balla da manqué contact mbeur bou lamb yagué contact molassiy guéné kholatal lutte simple....
Balla na entréné beuré té bayi entréné star
Jamaïcain khamo lamb nopil . Lila Fadam di wax kham kham la . Waxou gnoula Bombardier mok Mod’lo gno yam mais côté préparation lagn la wax Balla gaye paré woul physiquement. Té lolou moy deug Balla na dem entraîné dji kokoy wax deug nako wax lolou
Bilay Eumeu Sene mo eupou balla technique fouf pask au moins bamou dadié ak bombardier xamna namou beuré ak mome mbeur bou nk ak lingay beuré ak mome
Legui Modou mi Balla Gaye 2 dann 2fois té Modou Lo dann ko 2fois ?
@@kebemoustapha7580 merci waye
@@kebemoustapha7580 lamb amoul logique
Fadam takhawal balla ngiko werr yeup khamou gnõ lamb ay Nitt yo khamni buzz rk laniouy wout si bala mes dou dara famille Aziz Ndiaye pour nioum gnõ mom lamb dji
Bien dit pour niom lep khaliss la
@@mourtallaseye3873 bilay 😂😂😂
Fall balla niom Aziz la dane andal mouy dane tey yallah dogal mou danou yallah mo niew Aziz mbeur bou sagnone am kou melni mom
Billaye sama wadji deug bou weur nga wakh
Fadam wakh na deug balla gaye dafoul contact dafa gawa bayi
Balla mima khamone bamouy bakh sou diapone bombardier dane ko mais defoul contact
Fadam moye seine baye thi analyse comba
Merci jamaïcan lamb strategie la
Boucar yaw kou contre balla ngA
deug rek la wakh
Kiii Kayyy dfa Sofff
@@mamediarrandiaye1891 wa guis nga fo deuke thie Senegal
Balla Gueye legui deye nossssss
Li Fadam wakh Moy deug, Balla gaye 2 contagoul ☝️☝️☝️☝️
Fans la num one wayé balla mii amoul contac
Arrêter de dire que balla n'est entraine je suis d'accord diame balla il a fait sa patience sur cette combat
Jamaïcain téga yéme si teugue lamb rek do chroniqueur dh fadam a parfaitement raison balla technique bi mogui fi mes préparation bi bakhoul
Sou youtube bi amone vocale dinalèn expliqué li waral carrière balla guaye réussir moy Dafa dadiewoul wone ak gris bordeaux ak bombardier bou dadiè wone ak niom dou meusseu diot ci yekini
Thieuy sama gayi culture d l'instant mo léne sonal
@@moustaphadiakhate1031 nous sommes des sportifs et nous sommes très objectifs rien en voir avec les trucs de fans clubs et de supporters... Merci
@@cheikhsow1042 revoit la definition d'objectivite car être sportif bagna nanguoul l parcours d balla jusqu'a yekini K u puisses sorti un raisonement pareil
@@moustaphadiakhate1031 deg na deug dé 😁😁 guayi danio begua profito guéné li nek si khol yi
@@moustaphadiakhate1031 le combat entre yeukini et eumeu sene était le plus logique à ce moment là mais ça c'est le passé et je pense que c'est le passé qui fait le présent depuis que balla a perdu le roi il a du mal à ce relevé on se demande s'il il le méritait réellement
Es ce que je pouvais avoir le numero de fadam svp?
Fadam dou nit👏👏👏👏👏👏
Balla a bien préparé son combat
Ce jam ne connait rien meme nous ki sommes pas lutteur savent k balla napa de condition physique
Son encadrement et à refaire totalement il et mal entourer il faut faire le ménage il a manquer de conseil aujourd’hui