Une pensée forte a mon frère qui est décédé récemment en prison des suites d'une maladie ,j'ai mal et j'ai beaucoup pleurer en regardant cette vidéo , mangui massawou gni nekeu si kasso yi 😭😭😭
Je suis Dip mais walahi ngaaka son bi doumassi doyal tei ossi clip bi dafa daw yaram 😭😭😭 walahi j’ai pas les mots yaggual doundeul wérral barké serigne touba 🙏🙏😭😭😭
Une pensée à mon grand frère en prison 😭😭😭 tu me manques , ton sourire nous manque , Maman se cache pour pleurer ton absence, papa ne cesse de prier pour ta libération, yalla nalla yalla guéné
Mon Dieu, par le droit du Trône et de Celui qui l’a élevé, par le droit de la Révélation et de Celui qui l’a révélée, par le droit du Prophète et de Celui qui l’a nommé prophète, par le droit de la Maison et de Celui qui l’a construite, ô Celui qui entend toutes les voix, ô Celui qui rassemble tout ce qui est passé, ô Créateur des âmes après la mort, prie sur Mohammed et sur les gens de sa maison et donne-nous ainsi qu’à l’ensemble des croyants et des croyantes dans les contrées orientales et celles occidentales de la terre, un soulagement rapide de Ta Part, par l’attestation du fait qu’il n’y a de Dieu que Dieu et que Mohammed est Ton Serviteur et Ton Messager (que Dieu prie sur lui, sur sa famille ainsi que sur les gens bons et purs de sa descendance et les salue beaucoup) !
Pour les 1/100 qui liront ceci longue vie â vous et à votre famille et aussi sans oublié de faire Une fort pensée aux prisonniers surtout en ces moments de chaleurs.
Saway keneu ladioula si fans dip gua apprecier lene rek teuth sen guate mai di doul ay fans dip la mai jaime ngaaka on sen ndey fou seytaner guene lolou
@@diopjean3631 kham nga mbam bou wéké nga wék ko yena yem t ioe mbam nga owma sa diote li molen si nekh di tontou ay commenterou diambour lidieuntil ndey sa problème
Ligay rap damako doundou 2016 mangui wonn chambre 9 deff nafa 6 mois tay mangui lay deglou depuis la france di nianall di bayii xel gayis nek si kasso bi plus particulier my bro racine do massa diokk sama khel yalla nala yalla takhawou si barké serigne babacar sy
Fi beu fébéré déh nguéye guéné diégué Le message est fort tout ce qui sont en prison ou dans des difficultés qu'Allah azawazal nous viennent en aides. Longue vie Mr ngaka 😍😍❤
Sincèrement suis pas un amateur de hip hop mais t'as assuré franchement. Bravo ngaka . Et de grâce Nanou bayi xél prisonniers yi ay borom banane rk niofa nek ossi ay citoyen lane comme nioune . Nanou doli yeurmandé yi si niom 🇸🇳🇸🇳😭🙏♥️
King Baba c'est le meilleur de tous les rappeurs. Manoulén souxlou ba soulko démlén scoolam dieul courame. Ay élèvames cours de récréation molén di bolle waye dou classe bi.
Je peux pa m'empêcher de pleurer c vraiment dur😭😭yalla naniou yalla mousseul si kasso té gnifa nek yalla nalene yalla diapalé bagnou guene té bagna deloou si louniou nekone te gni innocent sen innocence fegn😭🤲
Quand j'écoute la Sanson je pense a mon grand frère qui est en prison prions pour eux c tel ment triste. je suis un fans de dip mes cette song ma permet d'être un fans de ngaaka
Ndayssane kasso diomboul kéneu yalnalé yalla may wér ak kholou mougn vraiment c dir ms bon yalla bakhna koufa dougoul yalnala oumpou gnifa nek yalla guénné lénfa ci diam barcki CHEIKHOUL KHADIM
Hommage à tt les detenu particulièrement chambres 3 cap manuél sma ga youma fa bayi ak forbé chambre 2 ba sénghor moy chef de chambre améth cisse modou ino yénangui wone cap mai kham nani dme nguaine convoi yalla naléne yalla défal diam diam si yénne
Ndaye saann chambre 3 cap manuel j'ai été là Avant may dém Convoi Sebi khotane puis Rebeuss Yalna leen yalla samu billahi dafa méti Jules Sylvestre. ismaila amar. poullo....etc
Abou One je suis un rappeur Sénégalais comme King Baba enfin actuellement Ngaaka Blindé est le meilleur rappeur Sénégalais actuellement djaroulle débat force à toi notre King.
Mane je n'écoute pas les rappeurs mais ngaka ndanane cette chanson me touche au cœur respect à nos frères et sœurs qui sont en prison yalna lén yalla défal diam guéné len fi guéne nék 😭😭
Nn Blindé siggil nga niou encore on est vraiment fière de vous continu comme ça fi nga ko tékk baxna...nioune wa Guediawaye nio ngi lay xaar toom Stade Amadou Barry👑💪🎖🏆🎤🎧
G vécu 2 mois de prison lors du sortie de ce sound j'étais en prison et je vient de sortir mm en regardant ce vidéo je ne peux plus me contrôler yalna yalla dimbeuli prisonnier yeup bañu guén si jamm🙏
Trust we really appreciate this piece ngaaka went are you coming to play us a show in The Gambia we are hoping to see you play in this country you are the best you are a genius
Ohh tu m'as fait pleurer une autre fois encore King. Ndeysaan yalna Yalla défal nieup jamm ak tawfekh. Merci King, paix sur toi vraiment. Bonne continuation.
C est la 6éme fois que je regarde ce clip. Ngaaka_blinde, king de sa génération si tu es d'accord ou pas Les amis du coeur 💖 ce clip mérite 1millions de vue avant une semaine. 👑King Baba🤴 par force . Kou d'accord rk beuseul aime 👇🏽
Yallah nah Yalla Mayy kholoub Mougne gni nékk ci prisons Yi Yalla nalène Yalla TakhawU Yalla nalène Yalla Fété falène société bi fété xone ak falène séni mbokkU fété wone ak fagne féété wone séni boppou Yalla nalène Yalla Kattanall Yalla nalène Yalla mouthieull Yalla nalène Yalla samme Barkép MaGui DeUkk Bi Ci Barakép Shahrou Ramadane Al Lazii Ounzila Fii Hi Al Qur'âne Ameen❤
Nul ne peut comprendre totalement s'il ne la pas vécue...yalla nagnou fa yalla mousseul sii barkii alkhouraane...gnifa nk yalla gueneleen te sopileen🙏🇸🇳
Ngaaka blindé je l'aime tellement que je pense cet amour va finir par me tuer un jour et le simple fait de penser qu'il a souffert où qu'on la accusé à tord dafay yakk sama adouna je sais que doumako meusseu guisse je sais que doumako meusseu lal mais malgré lolou je ressens un amour inconditionnel à son égard 😭
Tout comme moi j'étais 100% Dip mais lorsque que g regardé son interview sur le contrat des 30 millions g été charmé par ses mots té bilay ya tek tank Continue dans cette lancée Suis émue par cette chanson Que Dieu vous garde
Une forte pensée à tous ceux et celles qui sont en prison yalla naléne yalla taxawou léne banguéne guéne té mousseul Léne siii louléne fay délo.. Yalla naniou yalla Sam niou inchallah ... bonne continuation king baba
ndaysan kousa yaram dawoul boul j’aime😭
wawaw
Walahi
Bo beuguei King baba beusseul j’aime🙏🏿
Une pensée forte a mon frère qui est décédé récemment en prison des suites d'une maladie ,j'ai mal et j'ai beaucoup pleurer en regardant cette vidéo , mangui massawou gni nekeu si kasso yi 😭😭😭
Très émouvant comme témoignage
Qu’il repose en paix ✌🏽
Bilahi yaw yay Kane bilahi xamo sax
@@dimitricros199 merci cest la vie
@@juldf2812 amine merci
Je suis Dip mais walahi ngaaka son bi doumassi doyal tei ossi clip bi dafa daw yaram 😭😭😭 walahi j’ai pas les mots yaggual doundeul wérral barké serigne touba 🙏🙏😭😭😭
Frère Dip Ngaka lépp Sénégal la ils sont tous fort respect
@@amadoudiallo7892 #bilae frr lepp sénégal 🇸🇳 la yalnafi djam yagg réck 🙏
Je suis BM jaay mai ngaaka son bi doumassi doyal bilahi mai dara si kanam rék king baba
Une pensée à mon grand frère en prison 😭😭😭 tu me manques , ton sourire nous manque , Maman se cache pour pleurer ton absence, papa ne cesse de prier pour ta libération, yalla nalla yalla guéné
Ah sister courage yala baakhna
Amin yalla nako yalla dlli diam 🙏🙏
Ohh courage ton commentaire m’a fait pleuré thiey adouna
Oh sister ton commentaire is very very sad🤔😪🙄
Ndaysane métina😔mais yala bahna yalna lén yala djapalé🙏
Ngaka dioylo nga ñép bilay xol toyna, yalna yalla taxaw prisonniers yép
Ohhhh c'est très touchant une forte pensée aux prisonniers depuis la Mauritanie 🇲🇷 🇲🇷 🇲🇷
King baba kouka nangou mayma j’aime 🙏🙏
Ce ki me touche moy ngaka dèm kasso wam bi dafko rendre plus mature 😭😭😭et plus fort mouy may dolè gni nèk prison wallah on t’aime frère
Kou Dislike DAgua Soxor , Wala Dagua amoule Mokou bou neik si KAsso Biiii
RESPECT NGAAKA D'avoir montré la vie de 100M
Wahal way
Billay
Une pensé fort à mon frère qui est en prison yalna na guén leguii tout la famille priés pour tw tu ns mank beaucoup 😭😭😭😭😭😭😭😭🥺
inchallah frère
Amiiin
Amine
Inchallah yaleu baxneu
Aminn
Yalla nagnou yalla Moussal si kasso adouna ak alakhira😭
Kou nagouni ngaka moye King bi beuseule aime
Mon Dieu, par le droit du Trône et de Celui qui l’a élevé, par le droit de la Révélation et de Celui qui l’a révélée, par le droit du Prophète et de Celui qui l’a nommé prophète, par le droit de la Maison et de Celui qui l’a construite, ô Celui qui entend toutes les voix, ô Celui qui rassemble tout ce qui est passé, ô Créateur des âmes après la mort, prie sur Mohammed et sur les gens de sa maison et donne-nous ainsi qu’à l’ensemble des croyants et des croyantes dans les contrées orientales et celles occidentales de la terre, un soulagement rapide de Ta Part, par l’attestation du fait qu’il n’y a de Dieu que Dieu et que Mohammed est Ton Serviteur et Ton Messager (que Dieu prie sur lui, sur sa famille ainsi que sur les gens bons et purs de sa descendance et les salue beaucoup) !
Ngakka tu es le meilleur
Respect frère
La vidéo mérite plus de 2 Millions de vues en deux semaines. Vraiment Ngakaa tu es le meilleur de sa génération. Bonne continuation bro
Pour les 1/100 qui liront ceci longue vie â vous et à votre famille et aussi sans oublié de faire Une fort pensée aux prisonniers surtout en ces moments de chaleurs.
Oh ton commentaire ma touche mais que le Tout Puissance vous viennes en aide sois forte
Amine
Fans dipl a mais song bii dafma touché🙏🥺 yalna len yalla guéné founiou nék 😭😢
Saway keneu ladioula si fans dip gua apprecier lene rek teuth sen guate mai di doul ay fans dip la mai jaime ngaaka on sen ndey fou seytaner guene lolou
@@diopjean3631 billay frr deug gua wakh 😂😂
Non j'ai pas les mots
@@diopjean3631 kham nga mbam bou wéké nga wék ko yena yem t ioe mbam nga owma sa diote li molen si nekh di tontou ay commenterou diambour lidieuntil ndey sa problème
@@babacarndiaye8262 soumala guissone ba nok la ci guay sogua geum mbam bima done bilahi dina wékeu sa ndey ba gua reuk
Ligay rap damako doundou 2016 mangui wonn chambre 9 deff nafa 6 mois tay mangui lay deglou depuis la france di nianall di bayii xel gayis nek si kasso bi plus particulier my bro racine do massa diokk sama khel yalla nala yalla takhawou si barké serigne babacar sy
Quand j'écoute les paroles je pense à mon grand frère qui est toujours en prison. Prions pour les prisonniers pour la liberté 🙏🙏❤
Yalla Nako SouGne borome Takhawou
Yalla bahna😭😭 inchalla soit fort
Yallanako yalla takhawou deloko thi saine lokho yallanako yalla samou areko barke seydina mouhamed psl
Courage mon frère. Yalla baakhna... Yalla nako yalla jappalé
Dieu est grand
Je suis dip doundou guis mais yagui deff lou Nice respect ci iow 🎤
Blh de mm 👏🏽
Fi beu fébéré déh nguéye guéné diégué
Le message est fort tout ce qui sont en prison ou dans des difficultés qu'Allah azawazal nous viennent en aides. Longue vie Mr ngaka 😍😍❤
Même si mon commentaire ne compte op j'aimerais bien le dire même ma mère adore cette chanson 😭😭 Big respect à toi king Baba
Fans DIP Doundou Guiss la d mais taye ngaka blindé lalneu sama Khol bilahi 😭
Sincèrement suis pas un amateur de hip hop mais t'as assuré franchement. Bravo ngaka . Et de grâce Nanou bayi xél prisonniers yi ay borom banane rk niofa nek ossi ay citoyen lane comme nioune . Nanou doli yeurmandé yi si niom 🇸🇳🇸🇳😭🙏♥️
Yalna yallah tegui natou bi si kepou Kou nekk casso
oh kaso métina yalna yalla defal jam gnifa nek bagn guén tei yalla mousal niousi
Amiiiiine
Ngaaka blindé Khalif général koulou rappeurs. Un j'aime si vous êtes d'accord
Kasso yalla nanou si yalla mousol😭🇸🇳🙇🏿♂️
Amine
Max De Partage Les Gars
Cette Vidéo Mérite Des Millions De Vues
Lii Mooy Waané Nii Prison Diomoul Kénn
C'est Vraiment Triste 🙏🏾❤️😭
King Baba c'est le meilleur de tous les rappeurs.
Manoulén souxlou ba soulko démlén scoolam dieul courame.
Ay élèvames cours de récréation molén di bolle waye dou classe bi.
No vraiment 😭😭😭 king baba rék mou nékh mou nakhari bilaye mom rék laye dég lou 🙏
Une pensée pour tous ces prisonniers et des prières 😭😭king mon fils je te souhaite le succès que tu mérites si barke noreyni 🙏🙏
Merci frere si khalate bingua khalate prisonnier yii merci merci
Souniou borome souye défar day melni couy yak dama diapni sa dougou kasso mission bodone dokhla ndakh dougou nga khame guéne khamlé yalna yalla df diame 👌👌👌
Je peux pa m'empêcher de pleurer c vraiment dur😭😭yalla naniou yalla mousseul si kasso té gnifa nek yalla nalene yalla diapalé bagnou guene té bagna deloou si louniou nekone te gni innocent sen innocence fegn😭🤲
Amine
Amine incha Allah 👏
Loumétty niagoul cissé
Amin yaraby
Don blindé ba ici repose fier d’être 𝑩𝑳𝑰𝑵𝑫𝑬 𝑩𝑳𝑰𝑵𝑫𝑬 😭😭❤️
Aka ler fier d'être blindé blindé de
❤️😭❤️👌🏿
Je ne peux retenir mes larmes...yalla nalène fa Yalla guéné si noumou gueuneu gawé
Quand j'écoute la Sanson je pense a mon grand frère qui est en prison prions pour eux c tel ment triste. je suis un fans de dip mes cette song ma permet d'être un fans de ngaaka
Yalna yalla samm bon courage
Courage frr ♥️
Bienvenue
Baba is the Mother Land
Kouy woutal kenene promotion demal fenene bind fa tourame ngaka big respect for you I'm very proud for you the king of hip hop GALSEN
Ndayssane kasso diomboul kéneu yalnalé yalla may wér ak kholou mougn vraiment c dir ms bon yalla bakhna koufa dougoul yalnala oumpou gnifa nek yalla guénné lénfa ci diam barcki CHEIKHOUL KHADIM
King baba cette vidéo vraiment mérite des millions de vues lo doundou rek gua meuna nétali force à tous les prisonniers
Li don la kénn peunousou dara Ngaka blindé est incomparable ana fans ngaka yi👋👋🙏😍
Dayy sann lie daww na yaraamm bly walayy mrc bcp gaaka yalla nala yalla faye nakh lie métie na trop bly
Triste réalité j’ai les larmes aux yeux 😓😥😢
Yalla Na yalla takhawou képou Kou nékk si kasso bi si barkep Seydina Mouhamet (psl)🙏🏾
amin
Ce tube me frappe droit au coeur 😢
Max de j'aime pour NGAAKA🇸🇳🙏diar diar la rek frère
Thiég in💥
Ndeysaane son bi me fait pleuré 😢😢. Sama xol bi dafa fess bilahi
bilay
Réalité la on la vécue
Enfin Le video est Disponible
Felicitation bro yafi né
Hommage à tt les detenu particulièrement chambres 3 cap manuél sma ga youma fa bayi ak forbé chambre 2 ba sénghor moy chef de chambre améth cisse modou ino yénangui wone cap mai kham nani dme nguaine convoi yalla naléne yalla défal diam diam si yénne
Amine 🙏🏾
Mes respects bro 🙏🏾❤
Cette vidéo me fait mal 😭😭
@@medardmariamediouf7192 diam si iow boulénne fate niou nekk si diel bi walahi dfa tare😪
@@amethgueye1337 billahi dfa am realite deh diel bi li mofa am
Ndaye saann chambre 3 cap manuel j'ai été là Avant may dém Convoi Sebi khotane puis Rebeuss
Yalna leen yalla samu billahi dafa méti
Jules Sylvestre. ismaila amar. poullo....etc
Abou One je suis un rappeur Sénégalais comme King Baba enfin actuellement Ngaaka Blindé est le meilleur rappeur Sénégalais actuellement djaroulle débat force à toi notre King.
Première commentaire
Vraiment king baba do nitt
Yalna yallah samm gniii neck siii kassooo yiii j’ai pleuré billahiii s sound entre dans l cœur ❤️❤️❤️
Une pensée à tous les sénégalais arrêté d'ici et d'ailleurs k'Allah vous facilite la liberté totale : merci king blindé
Am very happy today belaye King 👑 baba honestly bul deffat benne video de doyna deeee very nice very sad 😭😭😭 ngaaka blende
Au final xawma sakh lane la wara commentaire😭
Baba N'diaYe 🎤 Yalna Yalla goudeul sa fann🙏🏼😭
Olala mon fils Masha Allah Yalla nassi Yalla mousseul beep ndiabot incha Allah
Ndeyesan yalla nala yalla takhawo rekk si barkèb seydina mouhammed psl amine ya rabal alamien ligeuye bi rafetna machallah king baba 👑👑👑🔥🔥💪✊✊
Ngacka yalla nga goudou fane lingaye diobe nice na trop💪💪
Mane je n'écoute pas les rappeurs mais ngaka ndanane cette chanson me touche au cœur respect à nos frères et sœurs qui sont en prison yalna lén yalla défal diam guéné len fi guéne nék 😭😭
Première commentaire king baba yafi né💥💥💥
Nn Blindé siggil nga niou encore on est vraiment fière de vous continu comme ça fi nga ko tékk baxna...nioune wa Guediawaye nio ngi lay xaar toom Stade Amadou Barry👑💪🎖🏆🎤🎧
Je ne peux pas m'empêcher de pleurer c'est vraimen dur walae bravo king ngakka ameu morom message très important peuple biii dégnako
G vécu 2 mois de prison lors du sortie de ce sound j'étais en prison et je vient de sortir mm en regardant ce vidéo je ne peux plus me contrôler yalna yalla dimbeuli prisonnier yeup bañu guén si jamm🙏
Massa metina mais mougne rekh yallah nala yallah moussal si dissi delouwatt moussal gneup
@@auparadisdesanges1599 amine merci
King baba
Son bii doumassi meusseu doyal🥺🥺❤
Ngaka est le meilleur qui est d'accord avec mw💪✌️
C le meilleur nagn ko nangou t noppalou 🔥❤️
👑✊🏿❤🇸🇳
Bilay aio
Futur milliardaire est entrain de lire ma publication actuellement
Bon début de week-end djame si yene
Notre frère yalna Yalla doli soutoureu té déf thi yow diam ba nga gueune ffou té délou Wat thi sa liguey
Wollah g dei frison son bi dawa daw yaraam de trop sérieusement 😭🕊
King Baba🚨💪🏾
J'ai les larmes🥺, j'ai les larmes aux yeux 😭, Ngaka , tu nous parles de la dure réalité qui existe dans notre pays
Force à vous Ngaka ❤✊🏿 !
Trust we really appreciate this piece ngaaka went are you coming to play us a show in The Gambia we are hoping to see you play in this country you are the best you are a genius
Besseul jaim king baba meilleur koi d’accord
Athia
Des mots touchants 😢
Boulene faté dilene nianal
Yalla na yalla guene gni thiabi fété guinaw🙏
Khady
Dieulma pv 774550724
Ngaka mii bilahi koumakoy presenté🙏🏾😭bilahi ngaka beugu nakoo
Vidéo bii
Ohh tu m'as fait pleurer une autre fois encore King. Ndeysaan yalna Yalla défal nieup jamm ak tawfekh. Merci King, paix sur toi vraiment. Bonne continuation.
Une pensé a mon frere badou diop🙏🏿bro namnagnla trop 😢 yalla nallen borom bi takhawou bou bakh bro.
Song bi chak jour souma yéti Mom lay tek . Douma ci masseu doyal
Ho vraiment c triste natou dou wess mais natou waroul tax nga bone yalla nanou yalla may xolou mougne🙏🏾
C est la 6éme fois que je regarde ce clip. Ngaaka_blinde, king de sa génération si tu es d'accord ou pas
Les amis du coeur 💖 ce clip mérite 1millions de vue avant une semaine.
👑King Baba🤴 par force .
Kou d'accord rk beuseul aime 👇🏽
Yallah nah Yalla Mayy kholoub Mougne gni nékk ci prisons Yi Yalla nalène Yalla TakhawU Yalla nalène Yalla Fété falène société bi fété xone ak falène séni mbokkU fété wone ak fagne féété wone séni boppou Yalla nalène Yalla Kattanall Yalla nalène Yalla mouthieull Yalla nalène Yalla samme Barkép MaGui DeUkk Bi Ci Barakép Shahrou Ramadane Al Lazii Ounzila Fii Hi Al Qur'âne
Ameen❤
2éme vague gueu lale dh
King Baba💪💪💪
Ay sama King bi nekho dered dh bilahi dafa ler ♥️♥️♥️♥️♥️
King👑👑👑bi iow la nangou nopalou li am si kasso galsen meti nala trompé nala yalla Faye sa khol king, 👑
*J’aime les mots qui sortent dans votre âme.*
Les vrais fan's de
*King baba* 👍
je syis pas fan de ngaka mais se club merite des millions de vue vraiment
*Yalnaniou oumpou les gars*
```Adouna dafa teureudi
Soutoura si nieup```😭😭
Nice frr paco le pro momaye raye si clip bii bly mais king dou nite
Yalla na sa diamou yague j'ai vraiment sogue de cette video King tu es meilleur diamou rek ngaa varaa amou iow King BABA
King ya worr dh 😢😢😢
Ms yalla nako makk guou rèw mi dégue
Un message fort ... État diougal ci li nitt d’où mala l’erreur est humain... Une deuxième chance est un droit💪🙏
Ndaye saann son bi kouko déglou RK sa Yram dawna 😢😢
Son bii mounou mkaa deglou té douma diooy🥺😭 mashalah King baba🔥❣️
Ça me rappelle à Ibrahima doudou Sow alias ibou ngaté frère yalla nala yalla géunné fofou si barké seydina mouhamed psl
Amine
Nul ne peut comprendre totalement s'il ne la pas vécue...yalla nagnou fa yalla mousseul sii barkii alkhouraane...gnifa nk yalla gueneleen te sopileen🙏🇸🇳
amine ya rabal alamien
Ngaaka blindé je l'aime tellement que je pense cet amour va finir par me tuer un jour et le simple fait de penser qu'il a souffert où qu'on la accusé à tord dafay yakk sama adouna je sais que doumako meusseu guisse je sais que doumako meusseu lal mais malgré lolou je ressens un amour inconditionnel à son égard 😭
NdaySann beurii gua si morrom
Ndeysane ngaaka blinde boudoul song bi sakh bo deglo ay song wam dinasi wakh loudoul dagn
Scénario très réussie t'a puis représenté toute les étapes d'une maison d'arrêt
Forte pensée aux prisonniers
mais
Gni di dislike vidéo bi amou niou sensibilité respect bro tu as encore assuré et une pensée à nos frères prisonniers forces à vous
Immature rek et jalousie
nioniou ay bodio bodio lan, ils ne savent pas faire la différence entre la compétition et la compassion
Bilahi son 😭😭😭 no mai danga meilleur
C'est la première fois ma degglou rap ba dioy 😭😭😭💔💔💔
Tout comme moi j'étais 100% Dip mais lorsque que g regardé son interview sur le contrat des 30 millions g été charmé par ses mots té bilay ya tek tank
Continue dans cette lancée
Suis émue par cette chanson
Que Dieu vous garde
Dip xole bi mo bone
Diam si iow king baba lepp dina bax yalla baxna ana fans Ngakaa blindé le roi 🤴 de rap galsen 🔥🔥🔥❤️❤️👍
Une forte pensée à tous ceux et celles qui sont en prison yalla naléne yalla taxawou léne banguéne guéne té mousseul Léne siii louléne fay délo.. Yalla naniou yalla Sam niou inchallah ... bonne continuation king baba
Libérer Aziz de grand medine
Kép kou beug Serigne Babacar Sy beuseul j'aime
#Bonramadan♥️