Ndeyssane dogual mo guawe yallah na niou yallah mousel thi seytane 😭😭😭😭yallah na ko yallah yeureume khareko al Diana yeureume na Tamite kharitam yi niou diape mou takha
LPA lii moussou f am diamm laniou yagg xam boloo nek benn dangay guiss Wa 6e sax di waxtane ak wa terminal moussouniou am xadie ak seen on était une famille mais lgui dangay diaxlei ay rivalantei bay gueneil paka sa morom ay prof youy xoullo di garou walantei li mom c trop Bamba Ndiaye fi nga dem yal nla gueneul fi nga diouguei thi barki Mouhamed (psl)
Aye wayy ndeyssane yalla nakoo yalla kharé aldiana firdawsi 😭sarakham yague sen lokho legui aye khalé rk nioy def aye crime c’est bizarre il es temps niou diouk silii franchement ndax nek dii ray aye domou diambour métii naa trop Yalla nakoo yalaa yeureum 🙏
Histoire koku fekeiwul waroo meuna waxni kén moo tooñ ndah jamono ji dinanu tooñ nit rayko nit dina tooñ tmt nu rayko Sénégal kou deeh baax Mais li wërr tê worr yalna deuk ak jamm si biir bambêlam yalna aljanah doon keureum
Tchiey yallah Sénégal legi sokhor goufi am kémane la mo andi mboussiba yi ni yeup si deuk il n’y plus foi ni de religion dans ce pays la naniou delou touti thi yallah
Yala na égalé ndawam aldiana thi barké seydina mouhamed ak touradone dia serigne touba😭😭
Boy bou yarou demna yallah na bokk si ndaw youy teral sen wadiour yawmal khiyam.AMINE
Non mais de 15h a 20h mais a quoi sert nos hôpitaux allahu akbar qu'Allah l'accueil dans ses paradis célestes incha'allah
ndeyssan dafa guenne rk yalla nako yalla yeureum thi barké cheikhoul khadim ❤🙏
Oh Qu’Allah l’accueille au paradis
Nn mon pays va mal. Yala nako yala yeurum kharéko aldiana firdawsi amine
Ndeysaan Yalla Naako Yalla Yeureum Té Khareko Aldianaay Fiirdawsii Sii Barké Xassida Yii
Que Dieu l accueille dans son paradis firdawsi , qu il donne à ses parents la force d accepter sa volonté
Ndeyssane dogual mo guawe yallah na niou yallah mousel thi seytane 😭😭😭😭yallah na ko yallah yeureume khareko al Diana yeureume na Tamite kharitam yi niou diape mou takha
LPA lii moussou f am diamm laniou yagg xam boloo nek benn dangay guiss Wa 6e sax di waxtane ak wa terminal moussouniou am xadie ak seen on était une famille mais lgui dangay diaxlei ay rivalantei bay gueneil paka sa morom ay prof youy xoullo di garou walantei li mom c trop
Bamba Ndiaye fi nga dem yal nla gueneul fi nga diouguei thi barki Mouhamed (psl)
Massa lii mettina trop sincèrement yallah nako yalla khare aldiana firdawsi amine.
Aye wayy ndeyssane yalla nakoo yalla kharé aldiana firdawsi 😭sarakham yague sen lokho legui aye khalé rk nioy def aye crime c’est bizarre il es temps niou diouk silii franchement ndax nek dii ray aye domou diambour métii naa trop Yalla nakoo yalaa yeureum 🙏
Yalla naka yalla yeureume sy barkè seydina Mouhammad psl barkè serigne touba
Histoire koku fekeiwul waroo meuna waxni kén moo tooñ ndah jamono ji dinanu tooñ nit rayko nit dina tooñ tmt nu rayko Sénégal kou deeh baax
Mais li wërr tê worr yalna deuk ak jamm si biir bambêlam yalna aljanah doon keureum
Mais nekoul né kougniou togne dagnoula wara Rey boudone sa mbonk do wakh lolou ndakh dé da téti
suude ab julit la rek sama mbokla
Nit lum fekeiwul manul xam lafa xew
Deh mom koku meuna def rek fawwu mu mëti la
Inna lillahi wa inna illayhi rajiun yallaneu borom bi yeureum kharei ko aldianna firdaws bijahi Nabil Mustapha salallahu Alleyhi Wa Salam
Bilay lii métina trope ça me fait au coeur 😡💔.
Bamba repose en paix mon frère 🤲🙏❤️🤲
Que la terre lui soit legere
Que Firdawssi soit sa dernière demeure.
AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE AMINE
YALNA KO YALLA KHARÉ ALDIANA FIRDAWSI THI BARKÉ SÉYDINA MOUHAMED PSL
NDEYESANE YALA NACO YALA YEUREUME TE TEROUCO SI AJDANA FIRDAWSI 🤲🤲🤲
Yalla na motalé ndawam aldiana barké Cheikhoul khadim amine ya rabi metina lol
Médecin Sénégal ils sont trop négligeant vraiment.loss bou dame ça se soigne.
Ndaysane babacar j Te présente mais condoléances tay hlm ame naniou nakar
yala nako yala khare aldiana firdawsi si barke seurigne fallou mbacke
Yalla nako yalla kharé Aldiana
Yalnayala youbou aldiana amine tasse nous si barké séydina Mouhammad amine
Massah lii metina yalna firdawsi di keureum
yalla nako yalla yerem te hareko aljana thi barkep cheikhoul khadim
Yalla nako yalla yeureum kharé ko aldiana
Yalnako yalla yeureum ndeyssane li metina
Paix a son âme
Non à la violence dans les inter class
Que la terre lui soit légère
Yalla nako bour Lahou yeureume ko
yalla nako yalla yeurame 🤲
Yala nako yala yeureum
Seul la peine de mort peut nous sauver de cette série meurtre
Paix à son âme c triste et grave
Courage force à vous c’est pas du tout évident de perdre une personne qui nous est cher mais courage que le bon Dieu l’accueil
Di mastawou famille wame boubah.metina lol.bakeine dafa fort
Mane dama khqmatoul li khew si deukk bi
METINA LOL YANAKO YALA YEREUM BARKÈ SEYDINA MOUHAMED PSL HÔPITAUX SENEGAL TAMITE DOYNANE WAR TROP
Tchiey yallah Sénégal legi sokhor goufi am kémane la mo andi mboussiba yi ni yeup si deuk il n’y plus foi ni de religion dans ce pays la naniou delou touti thi yallah
Hier Patrick tay bamba demain kane lay done
Moi
Sama ben kharitt dembb
Elle a k 14ans si j m trompe op
@@shamsatoumbacke2873 tai lolou ga beug
@@ladycecileketty9888 c'est abusé
C'est triste Que son âme repose en paix 🤲🤲🤲
Dagno wara bâyi affaire interclasse
Mere bi loumouy wakh ni khaler bi ganiou na baparer nianal ko rek
Rip