Machallah tout baye goor yalla DEUG nga xamnagnoula xadioulo ci 1 heure de temps té wakhoulo sakh Barker baye Niasse djeureudjeuf sangue barhamou ndiaye
Waw kayy yalna yalla yokk xam xam limay gnawlou moy intervention de maodo Faye dafa ame limou nangou kérok bi invité x tay mou bagn ko wayé Baye kouko beug soul yow yay soulo. Diereudieuf Serigne bi
Walahi dieureudieufe tout baye wakhtane bi nekhna mais temps bi dafa ndawe trop mais nagnoula invité si tfm waye waye ak temps bou yatou walahi baye niass xam xam rekk lagnou ko topè walahi nekhna trope tout baye ❤❤❤👍
Machallah am nga kham kham mais lila manké moy zam zam..... Lepp nga beuggg guénné en vrague....donc faut nga djiangue com......té dal defff ndankkk...plateau da lathie balance mo takh maodo yakkamti émission bi djiékhhhh.......dans l'ensemble c'est un bon début... Yyalla takhawou yokk la zahirane wa batinane si barké baye niass amine.... Di djieggeulou
Machaallah très belle intervention tout baye yalla na yalla samleu.... on dirait que Maodo ne croit pas en BAYE il minimise et essaie de donner des explications à ces propos sans accepter la grâce d allah. Au Sénégal la jalousie a empêché bcp de personnes d arriver à leur seigneur d avoir la félicité. Maodo ça se voit que t as rien goûté de la gnose de la sainteté ton cœur n est pas encore propre...
D’après les propos de mawdo l’émission dure 1h temp il manque 12 mns et tu veux arrêter l’émission please au moins ayez la simplicité de laisser la jeunesse ibrahimienne s’exprimer sur les plateaux c’est ainsi que vous verrez les merveilles du détenteur de la fayda.Baye niass a dépassé tous les saints avant lui c’est ce qu’il faut accepté epuis ce qu’il dit si t’as pas l fathou(l’ouverture) tu verras jamais là où il parle. Tout Baye mii c’est un des rare produit de cheikh al islam il a le savoir il est courageux et puis il metrise bien ce qu’il dit maname dafa ndiangu mashallah. Talibé Baye yii surtt au Sénégal nañiou bayii inkaar entre ñioune ki koudoul talibè sah tu devrais être content de lui je vois en lui le jeune dont parlait cheikh Ibrahim baye niass lors de gamou . Lui il n’est pas n’importe quel jeune mashallah ❤️
Tout baye dafa gneuw ak bénn objectif sampe baye Té si vous écouter bien Maodo à bien compris la parabole de ibliss et du serpent ramener à La tariqa par rapport à baye. L’émission est très court voir trop court mm!!
Wallahi anzim dou soxor mai Tout Baye il est trop vif, xawa manqué dall. Sampp Baye dou wax lo xamni kou bokoul fingua bokk rek doula degg. Dangua nieuw fi pr yatal mission Baye Niass donc dafa wara andd ak hikma. Louko moy kën doula dëglou loudoul gni bokk si hadara Baye Niass. Lingay def ni dafay dawlou ay nitt waya doulën indi. Ilfo tenir en compte des niveaux et pr cela ilfo avoir une bonne pedagogie. Meun nga sampp ay ladj bayi. lolou amna solo troo ndax kou wett meuno nakh sa bopp,so amoul reponse bi dingua dioug pr xam so nékë kou nitté....(coteii bobou jt felicite) parfoi dingua nètali ay histoir Baye tè weroul a 100% c po histoir bi weroul mai ninguako racontê mo weroul tei mbirou Baye leupp mo lerr. Oistaz Ba dafay samp Baye foumou nekk d même ke Baye Mar, de même ke Aboubakr Ba et autres mais avec pedagogie. Sën diama bi nak amna niou am pedagogie machallah koussi melni Sow ak kiy wax francais yi ak anglais yi ak Oustaz Diassé aussi. Koumou nekh clash ma waya wallahi anzim limay wax dou soxor waya beug mbirr yi geuna dieum kanam rek. Yalla na Yalla fayanté ak ioe si loubax
AHMED TIDIANE ioe mi yay inkarr katt bi de mm k Maodo amo leine tawfekh xoll . Je vois k yangui si commentaire yi di inkar wadji rek nane amoul pédagogie etc etc t li la warr boy wotei wo talibé baye moy nga dieureudieufal ki si Baye Niass
Xam nga baye niass aye mbiireum sougnou kaiye wakh ni doko xam. Fokk nga thiammm thii guédje gui parceque dimension bi dafa kawé fokk nga xam yalla nopalou.
Lii naak moy agnane, soxore deugueu, yow tout baye loum fi wax yeup waaxou Baye Niass laa, bax na ba wax la tèrè bi ak page bi mais nak le problème moy dangako atanoul rek
ToutBaye am gna xam xam, mais dagna brouillon trop farfelu. il faut expliquer les choses simplement et accessiblement puisque tu es dans une télé (gamou mo geuna foor ponkou l'Islam)dou ay wahou télé ndakh dagna nieuw pour lééral mais pas pour wédilo ag créé ay faux débat inutiles... lolou motah chaque fois Maodo daflay gag lo ndakh déguin dafay wouté. machallah quand meme Yallah na yaya wéreul
@@boubajawara2592 ca n'as rien à voire avec fathou (am fathou dou dii wah ay wah you reuy), déém sii télé naan taag Yonent bi mo geuna foor les 5 piliers de l'Islam sikou hamoul dinako dégué nénén alors le but de l'invitation c'est déclairer.
@@assankuta2935 effectivement, mais émission télé sou fékone pour talibés Baye coon diaroul mouy déém télé. c'est pour le grand public. Amna kham kham machallah, juste dafa wara soralé gni hamoul
Cheikh Falilou Tu nas pas compris malheureusement Baye quand on disait d’à eupeul ci yonent psl bi moy il passait tout son temps a magnifié le prophète psl. Wakham da gawone mais ande ak dal. Dal ci djiko yonent bi la bok mouno ko guainai ci Baye. Anyways c’était une remarque que j’ai eu et c’est tout akhi. Ma salam 👍🏿
@@cheikhfalilousane8365 wadji bo nékké ci pencc dagay wakhtane xam xamou téré moy figa bok ak yenen gayi manam dagay melni BAYE bimouy wakh alkhurane mokoy firil alkhurane ...lounioula lathie ga layaléko alkhurane mo guena mat
Mourad Mbaye nekk di yambar yambar lou lolou moleine nekh wayé billahi ki mom wolou nako si ndaww yiy samp Baye Niass . Mais ioe mourad amo tawfekh xoll yakarna talibé baye boumou mounti done da wara sant ki dieureudieufal ko Si Baye Niass
@@sidymane6860 eudeup dafa bakh ci wakhine.....on n'a plus besoin di wakh ni Baye mofi nek....louniouy dieuf lay done wakhdji diamono dji dou am ndiarign
Manchalla Dieureudieuff Mawlana Sangue Barhamou Ndiaye di ndokel baye toubayeeeee yalna sbn gereum lima mety rek moy temps bi mo touti
Machallah thiey sangue barhamou ndiaye li nekhna merci tout baye
Nous voulons une autre émission avec tout Baye mettez des flammes si vous êtes d’accord🔥🔥🔥🔥🔥
Jërëjëf Tout Baye billâhi kontane ci yow
Aujourd'hui vous avez fait la fierté de toute la fayda tidianiya
Machallah tout baye goor yalla DEUG nga xamnagnoula xadioulo ci 1 heure de temps té wakhoulo sakh Barker baye Niasse djeureudjeuf sangue barhamou ndiaye
Dieureudieuf bays niass tout baye goor nga dieureudieuf baye sangeu ndiaye
Thiey kou baye paré si yaw.
Yalla nanu ko yalla fayal
MashaAlla tout Baay amatina solo. YALLA sang bi gueureum la
Non mais Machalah tout BAYE wakhtane bii nekhneuh ❤️🙏🏽
Machalaaaaa liiii sagggg la siiii peyyyybiii contanaaa lol yalna yala may la goudfann ak werr dieredieufai baye
Dieureudieuféééee mawlaya mawlana aboubakryne barhamou Ndiaye
Nous voulons un autre émission de Tou Baye
Waw kayy yalna yalla yokk xam xam limay gnawlou moy intervention de maodo Faye dafa ame limou nangou kérok bi invité x tay mou bagn ko wayé Baye kouko beug soul yow yay soulo. Diereudieuf Serigne bi
Machalla xol sedd n’a dieureujefff Baye
Diambaar la nak ,je l'encourage beaucoup
Machalla yalna yalla yogou kham kham bi sibarké baye niass international ❤
Svp invitez tout baye mou wakh si cheikh tidiane ak tarikha bi
Walahi dieureudieufe tout baye wakhtane bi nekhna mais temps bi dafa ndawe trop mais nagnoula invité si tfm waye waye ak temps bou yatou walahi baye niass xam xam rekk lagnou ko topè walahi nekhna trope tout baye ❤❤❤👍
Machallah tout baye 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Mashallah Toubaye Yalla na Yalla sameu té Barkel leu... Yaw da ngay yeketi flambeau bi rek
Machallah Tout Baye 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Machallah Mane dama beug Baye Niass wallahi
Machaallah Tout Baye goor nga
tout baye dieureudieuf mane emission bi doumatji doyal walahi
Machalah dieureudieufe Baye Niass
Machalla tout Baye niane 🙏
Machallah Tout Baye
Machallah am nga kham kham mais lila manké moy zam zam..... Lepp nga beuggg guénné en vrague....donc faut nga djiangue com......té dal defff ndankkk...plateau da lathie balance mo takh maodo yakkamti émission bi djiékhhhh.......dans l'ensemble c'est un bon début... Yyalla takhawou yokk la zahirane wa batinane si barké baye niass amine.... Di djieggeulou
iow mom da sohkor rekh fi lep rafetna
@@djiboba505 est ce que tu sais lire pour dire dafa soxor
Invitel oustaze baye mar
Massalah kene dou baye niass si adouna tout baye Niang ioe mome damala beug te Yallah rekkk takhh mais dolene niou invitél tout baye quartier général
Merci way yabakh
Machaallah très belle intervention tout baye yalla na yalla samleu.... on dirait que Maodo ne croit pas en BAYE il minimise et essaie de donner des explications à ces propos sans accepter la grâce d allah. Au Sénégal la jalousie a empêché bcp de personnes d arriver à leur seigneur d avoir la félicité. Maodo ça se voit que t as rien goûté de la gnose de la sainteté ton cœur n est pas encore propre...
Machalla TOUBAyi bayi niass la solution
Tout baye beuguala lole bilaye dakhe ligua baye Niass diamoudjjj Bari si yaw
Bilaye tout baye la beug mane
Machallah muqadam ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Koudoul talibe baye daga bougou yemale baye ak sa serigne de lolou mounoul neki. Merci tout baye baye dou morom
Maachaa'Allaah Oustaz Tout Baye
Macha allha niass alhamdoulila
Macha alhhe yalanala yala sameu
Nekhna trop.....Please invite him again to complete
D’après les propos de mawdo l’émission dure 1h temp il manque 12 mns et tu veux arrêter l’émission please au moins ayez la simplicité de laisser la jeunesse ibrahimienne s’exprimer sur les plateaux c’est ainsi que vous verrez les merveilles du détenteur de la fayda.Baye niass a dépassé tous les saints avant lui c’est ce qu’il faut accepté epuis ce qu’il dit si t’as pas l fathou(l’ouverture) tu verras jamais là où il parle. Tout Baye mii c’est un des rare produit de cheikh al islam il a le savoir il est courageux et puis il metrise bien ce qu’il dit maname dafa ndiangu mashallah. Talibé Baye yii surtt au Sénégal nañiou bayii inkaar entre ñioune ki koudoul talibè sah tu devrais être content de lui je vois en lui le jeune dont parlait cheikh Ibrahim baye niass lors de gamou . Lui il n’est pas n’importe quel jeune mashallah ❤️
Deug leu BAYE ♥️
Machalla doBaye
Machallah. Tou baye
Ki goor la baye
Allahu akbarr.....
شكر ياشيخ
MachaAllah Tout Baye!
machaallah tou baye
Warone nga gneuwe quartier général dee dieureudieufe baye niass baye walahi dou serigne rombouna serigne xam xam rekk moo nekhhh
Machallah 🙏🙏🙏
Yalanala yala hare la si barkai baye
Machalla
Maodo tu es pertinent dans ton intervention pédagogie amna solo xam xam Boko amé té kéne meunoula degu lou koudoul ko bokal dieurigno.
Hors sujet.
Citation ak réponse boule dawe
Tout khadio ci waxtou walay khamnagnla goor ngeu
QG yaffa waron dém
Tout baye dafa gneuw ak bénn objectif sampe baye
Té si vous écouter bien Maodo à bien compris la parabole de ibliss et du serpent ramener à La tariqa par rapport à baye.
L’émission est très court voir trop court mm!!
💥💥💥💥💥
El Hadji Modou Niang yàlla na la yalla yok xam xam
Wallahi anzim dou soxor mai Tout Baye il est trop vif, xawa manqué dall. Sampp Baye dou wax lo xamni kou bokoul fingua bokk rek doula degg. Dangua nieuw fi pr yatal mission Baye Niass donc dafa wara andd ak hikma. Louko moy kën doula dëglou loudoul gni bokk si hadara Baye Niass. Lingay def ni dafay dawlou ay nitt waya doulën indi. Ilfo tenir en compte des niveaux et pr cela ilfo avoir une bonne pedagogie. Meun nga sampp ay ladj bayi. lolou amna solo troo ndax kou wett meuno nakh sa bopp,so amoul reponse bi dingua dioug pr xam so nékë kou nitté....(coteii bobou jt felicite) parfoi dingua nètali ay histoir Baye tè weroul a 100% c po histoir bi weroul mai ninguako racontê mo weroul tei mbirou Baye leupp mo lerr. Oistaz Ba dafay samp Baye foumou nekk d même ke Baye Mar, de même ke Aboubakr Ba et autres mais avec pedagogie. Sën diama bi nak amna niou am pedagogie machallah koussi melni Sow ak kiy wax francais yi ak anglais yi ak Oustaz Diassé aussi. Koumou nekh clash ma waya wallahi anzim limay wax dou soxor waya beug mbirr yi geuna dieum kanam rek. Yalla na Yalla fayanté ak ioe si loubax
Wakhe si confiance ak wakhe ak brom khamkham bokoule
Dafa leer baye
Tout baye
Maodo mi inkare Kate deugue leu
No mem pas maodo mom bagnoul baye
AHMED TIDIANE ioe mi yay inkarr katt bi de mm k Maodo amo leine tawfekh xoll . Je vois k yangui si commentaire yi di inkar wadji rek nane amoul pédagogie etc etc t li la warr boy wotei wo talibé baye moy nga dieureudieufal ki si Baye Niass
@@الحمدللهوالعبدلله iow hamnaniou la nopil
@@cheikhtidianembengue4185 loma xamal ?
Xam nga baye niass aye mbiireum sougnou kaiye wakh ni doko xam. Fokk nga thiammm thii guédje gui parceque dimension bi dafa kawé fokk nga xam yalla nopalou.
Dem Laine yeuri teruyi
Diank dal amna solo si notki te baye lolou rek la rawé pas Di wah you melni dagua wah Lou reuy te waho Dara
Machalla ms baye bimouy raw guas yi diangue sax amoul
Yoe mécontent nga mais dinga gueneuu sonnouu ndakh ki gnimou yar salh nioula meun
Beusseull sa xol bi danguaa sokhor kii moo geunna sayy 1000
Lii naak moy agnane, soxore deugueu, yow tout baye loum fi wax yeup waaxou Baye Niass laa, bax na ba wax la tèrè bi ak page bi mais nak le problème moy dangako atanoul rek
@@tijaanibarhaamou1635 bayilen parparlo amoul ndiarign
ToutBaye am gna xam xam, mais dagna brouillon trop farfelu. il faut expliquer les choses simplement et accessiblement puisque tu es dans une télé (gamou mo geuna foor ponkou l'Islam)dou ay wahou télé ndakh dagna nieuw pour lééral mais pas pour wédilo ag créé ay faux débat inutiles... lolou motah chaque fois Maodo daflay gag lo ndakh déguin dafay wouté. machallah quand meme Yallah na yaya wéreul
Mai so guisse moukoi gag gag lo dafa bouku yemale baye ak yenen serigne si wala baye dafa hall di wakh. Mai baye dou moromi ken.
Sil n'était pas aussi simple.. yaw thi sa bop waxtaan bi doko déeg.. flemme
mdrrr démal wouti fatkhou mo gueune
@@boubajawara2592 ca n'as rien à voire avec fathou (am fathou dou dii wah ay wah you reuy), déém sii télé naan taag Yonent bi mo geuna foor les 5 piliers de l'Islam sikou hamoul dinako dégué nénén alors le but de l'invitation c'est déclairer.
@@assankuta2935 effectivement, mais émission télé sou fékone pour talibés Baye coon diaroul mouy déém télé. c'est pour le grand public. Amna kham kham machallah, juste dafa wara soralé gni hamoul
Non ki mome ay na dè xam xam
Abdou Aziz DIA ki moy two baye talibè sangue Ndiay
Machalla way
Tout baye amna xamxam mais manoul waxtane plateau nakh amoul pertinence aussi waxtane dafa wara ame blance té waxtanam bi amoul blance
AHMED TIDIANE il était brouillon et amoul dal malheureusement.
@@ibrahimthiam4011 yow lii ngay wakh nii mou ngui fatéli wax yi gaayi done wax Baye Niass naane dafa eupeul, mom daloul dara
Cheikh Falilou Baye Niass da dal ame Tamqeen ni yonent bi psl.
@@ibrahimthiam4011 wallahi al aziim ci loudoul bakane , Baye Niass lougnou kodone inkaré moy dafa eupal ci yonént bi, loumouy wakh kéneu xamouko, dém nagn sax banane Baye niass yéfeur laa
Cheikh Falilou Tu nas pas compris malheureusement Baye quand on disait d’à eupeul ci yonent psl bi moy il passait tout son temps a magnifié le prophète psl. Wakham da gawone mais ande ak dal. Dal ci djiko yonent bi la bok mouno ko guainai ci Baye. Anyways c’était une remarque que j’ai eu et c’est tout akhi. Ma salam 👍🏿
Gamou mome Boul waxati mouk ni moo guena fort ponki islam yi. Lolou weroul si xamxam
Légui wax ma Baye Niasse mii wax né Gamou mo guéna fort laylatoul qhadri, lolou mom nokoy layé ? Féxél nak ba boumané lolou wéroul ci xam xam
@@cheikhfalilousane8365 والله والله والله والله
@@cheikhfalilousane8365 wadji bo nékké ci pencc dagay wakhtane xam xamou téré moy figa bok ak yenen gayi manam dagay melni BAYE bimouy wakh alkhurane mokoy firil alkhurane ...lounioula lathie ga layaléko alkhurane mo guena mat
@@bayeabdoupatheyade5100 yow xanaa déglouwoo émission bi ? Xanaa dégo lougn ko laadj ?
AHMED TIDIANE Gamou mo gueune foufff ponk islam yii
kham kham dou jéma wakh lou nitgni khamoul wala loo khamni kouko degg naane kii loumou beuga wakh waayé bokk na ci mandarkay borom kham kham di jéguél nitgni kham kham cheikh Mahi Cissé lii motakh wakhtaanam nekh nak dou wakh lou débordé tout baye tu manques de pédagogie tu es vif
Akh désséna lou baré
Mourad Mbaye ioe deh amo tawfekhou xoll talibé Baye bouy ragal samp Baye Niass billahi lazi bakhoo ak ko mouna done
Mourad Mbaye nekk di yambar yambar lou lolou moleine nekh wayé billahi ki mom wolou nako si ndaww yiy samp Baye Niass . Mais ioe mourad amo tawfekh xoll yakarna talibé baye boumou mounti done da wara sant ki dieureudieufal ko Si Baye Niass
😅 thiimmm toukoull feulé.. limay wax rk fathou thi yAllah amoulénko. Kii di nga dég loum fi sotti thi xam xam en tant talibé Baye ngay amm lothi ngangni?! Soit vous êtes jaloux😂 wala nguein niiak fathou. Talibé Baye bou ignané morom Talibém malen jéppi... démall déglou audio Baye Niass yii mouy wax nane mom moy bountou yonent bi kou nieuwoul ci mom dou djotéek yonent bi dara... waxalné BAYE daa viiff...
@@sidymane6860 eudeup dafa bakh ci wakhine.....on n'a plus besoin di wakh ni Baye mofi nek....louniouy dieuf lay done wakhdji diamono dji dou am ndiarign
Machallh tou baye