Domoda dieune. Un des meilleurs plats senegalais mais tres sous-estime parce que fok togg bi djar yonn. tomate bi doyy, farine bi touti, mou farr avant farine et farine bi niorr. Bcp d'hommes beugouniou ko car danio traumatiser ndakh lekk domoda bou nekhoul. Diadieuf TogouMame Isseu delosina thiossann, en plus djeun bou makk dagnou koy roof, mouy thiou ou domada ou thiere siim djeunn. Aka maa longtemps tamitt :) Bonne continuation Sokhna Marie!
En bon kone domoda dieune day ame rof boulettes bi rek lay rof d'habitude damay mariné nonou rek bayi nako essayé un jour khol bakham togue da beuri façon nak mais merci pour tout yalna yalla goudeul fan wi ❤❤❤
Coucou vous cuisinez très bien même si je comprends pas un mot Wolof… Ce serait bien si vous pouviez dire le nom des ingrédients que vous utilisez en français également Merci🫶🏾🫶🏾🫶🏾
Domoda dieune. Un des meilleurs plats senegalais mais tres sous-estime parce que fok togg bi djar yonn. tomate bi doyy, farine bi touti, mou farr avant farine et farine bi niorr. Bcp d'hommes beugouniou ko car danio traumatiser ndakh lekk domoda bou nekhoul. Diadieuf TogouMame Isseu delosina thiossann, en plus djeun bou makk dagnou koy roof, mouy thiou ou domada ou thiere siim djeunn. Aka maa longtemps tamitt :) Bonne continuation Sokhna Marie!
😋😋
Oh maman bi Moy sama plat préféré mala yorel cinquante mille ❤❤❤❤😂
Machalla, toggo yaye isseu,namena domoda, nékh na torope, waron gua ma invitée du courage ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
En bon kone domoda dieune day ame rof boulettes bi rek lay rof d'habitude damay mariné nonou rek bayi nako essayé un jour khol bakham togue da beuri façon nak mais merci pour tout yalna yalla goudeul fan wi ❤❤❤
L'un de mes plats préférés ❤😂
Inchallah Allahouma amine inchallah🙏🙏🙏
Machalla laff thiat sohna so bahk ci Amna Solo naka lay def ba am sa warsaap number ❤❤❤❤❤❤🇸🇳🇶🇦💯
Machallahou rabi la hawla wa la houwata illa bilah qu'Allah vs preserve
Tèye maye première 🥰🥰🥰domada bi nehna torop té niamou mako😂😂🥰🥰
Machallah beugeu nala yw rek lay suivre
Meussouma kham domoda dagni roff djeune yi a partir d'aujourd'hui ni lakoy defé !merci
❤❤ machallah ❤❤mon plas prefere ❤❤yalna la yalla faye
Le wollof est super mais parler un peux en français ou ajouter une petite description en français je penses que celà élargira votre audience merci🙏
My favorite plate thanks for sharing love you ❤🎉
Machalla.sama.kharitebii
Machala comme d'habitude très bon ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Encore merci
Merci maman j adore ce plat surtout pendant l hivernage
Mon plat préféré machalla ❤❤❤❤
Je n'ai jamais su que domada diène daniuy rof diend firire bi ham ham dou wess
Masha Allah merci Tata ❤
Merci maman que te bénisse abondamment
Mashallah nehna ya isseu ❤❤❤
Assallamallikoume machallah
Saf ci nawet bi j'aime
Ma sha allah ❤❤❤❤ YAYE CHÉRIE GOUDALE FAN
Merci na rées ak diam
Machaala yaye boye♥️♥️♥️♥️
Macha allah ❤
Moome la toogue Samedi nekh la def Macha Allah
Machallah
Machalah maman ❤❤❤❤❤
Coucou vous cuisinez très bien même si je comprends pas un mot Wolof…
Ce serait bien si vous pouviez dire le nom des ingrédients que vous utilisez en français également
Merci🫶🏾🫶🏾🫶🏾
Machlla maman ❤❤❤❤
Mashallah ❤
Mashalla tata ❤❤
Ma sha allah
Macha alla vraie cuisine senegalaise❤❤❤
Machallah tata 😋😋😋
Domada sama farou rap ❤
Machalla 😊😊😊😊
Merci ici yobou nga ma demb thi toni diw gui
Miam miam😊😊😊😊
Sa nocosse Royal lane ak lane laye ame
Dieureudieuf yaye goudal fan
Ayw ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👍
Nkm
❤❤❤❤
Merci maman nekhna comme d'habitude... on attend la recette du 15 Août. Merci beaucoup maman Dieu te bénisse 🙏❤️❤️❤️
Très bientôt
Je veux des cours de cuisine yaye isseu sinon legui sama seuy tass😢😢😢. Qui peut m'aider Svp
No déf ma signe stp
@@chamade-te1lh où ? Comment te faire signe ?
Loy done def ba Mano togue
@@yayoukhadim1195 topou liguey bi rek. Femme de bureau... Ba seuy betteuma
@@chamade-te1lhbeugue nadé
Ah Tata sa dieunou thiep you bakh yi guay tomoda foumou diar nékh🥰
Khana mousso Moss Domoda dieunne bou make essaye ko
Rof ko ba bou saf ho darra dou dess
Est ce que dieu ne bi nekh na domoda
Bn
Nkm
🎉❤🎉
❤❤❤❤🎉
❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳❤️❤️❤️❤️
Machahalla ❤
Machallah ❤
Machallah ❤️