No tarikha cheikh tijan bi mo néex 🤣🤔🤭- Cherif Ibrahima Aïdara corrigé par Cheikh Oustaz Alpha Ba

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 3 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 111

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Рік тому +10

    Fénale yalla dafa garaaw wallahi barakallahou fike oustas Alpha Amal diamou inchallah

  • @zeynoudia1199
    @zeynoudia1199 Рік тому +8

    Machaa allah cheikh alpha baraka allahu fiikum leeral yii amna solo lool djazaakumu allahu khayrane

  • @moutaphaofficiel7404
    @moutaphaofficiel7404 Рік тому +7

    Zazaka LA KHAYRAN YA ALPHA. Lerral yii AMNA solo machallah

  • @maremerassoul3383
    @maremerassoul3383 Рік тому +15

    La lumière du monde l’enseignement du prophète Mokhamed psl mane mome rek lay topou le meilleur ds hommes aka woor ❤Waye gni ma guiss sma mame nena rek Theuy yalla mo mandou de sma mbook jeune yi kay lene gnou dounde souna simple na tè moy yone bi yalla gueureum

    • @abdoulayeba7078
      @abdoulayeba7078 Рік тому +2

      Wallahi ma chère sœur tu as parfaitement raison. Les marabouts ne sont là que pour leurs intérêts. Que les sénégalais se réveillent

    • @mamadousene2336
      @mamadousene2336 Рік тому

      Wallaahi sunnah dong moy dëg.ludul sunnah baaxul ak cankuté la.

  • @kkonate701
    @kkonate701 Рік тому +7

    الحمدلله على نعمة القرآن والسنة

  • @salimatasow2622
    @salimatasow2622 Рік тому +9

    Allahou akbar 😢😢😢Qu'Allah nous guide 🤲 😭

  • @falloufall8848
    @falloufall8848 Рік тому +2

    Guisnga gayi fene rek lagniy def

  • @TRA-PASTEF
    @TRA-PASTEF Рік тому +13

    Machalla cheikh alpha vous faites une très grande travaille puisse allah vous récompense comme paradis ici bas et à l’eau delà

  • @siacamane3361
    @siacamane3361 Рік тому +7

    Que Dieu nous protege sur le Droit chemin 😭 amine yarabi 😭

  • @mansourkane7436
    @mansourkane7436 11 місяців тому +1

    À l hôpital ceux qui ont de l assurance 100% ne paie rien et certaines paie a leur frais c est la même chose si vs ne pouvez pas comprendre bayilene waidi

  • @hj-eu6xc
    @hj-eu6xc Рік тому +2

    Je ne peux que vous remercier pour le travail extraordinaire et courageux que vous faites à démonter tous les mensonges datant de décennies dans ces Tarikhas. Mane mom guéneu nassi bou yagu. Wakhi dof. Yagu nagn gnoo nakh.
    Alkhouraane ak Souneu daal moo waur. Merci.

  • @youssoufdiedhiou6418
    @youssoufdiedhiou6418 Рік тому +7

    C'est extrêmement grave ce qui se passe au Sénégal. Ils feront regretter beaucoup de gens le jour du jugement. Seule les enseignements sont sûr d'enseignement

  • @MamadoutansirBa-zg7ty
    @MamadoutansirBa-zg7ty Рік тому +4

    Baraka Allah fikoum 🙏

  • @البصرةالعلمية
    @البصرةالعلمية Рік тому +1

    Defngua lou le war serigne alpha yalla sameu la ❤❤❤

  • @quransunnah750
    @quransunnah750 Рік тому +4

    Eupeuteuleuw😅. Sama ancien teamates yii aka nio graw tamite, surtout ki ndieuk wakh

  • @24hchrono44
    @24hchrono44 Рік тому +6

    ‏السلام عليكم ورحمة الله ما شاء الله جزاك الله خير يا شيخ الفاهم

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +2

      ‏ما شاء الله جزاك الله خيرا

  • @24hchrono44
    @24hchrono44 Рік тому +9

    Salatoul guenel lii ay fen kessa laa

  • @freepalestine3750
    @freepalestine3750 Рік тому +4

    Thieyli mais li alkhourhane wax nak ?
    Yalla naniou yalla saxal si alkhourhane ak sounnah

  • @alphaomarjallow2425
    @alphaomarjallow2425 Рік тому +1

    Masha Allah ya oustarz Alpha ba brakallahu fikum

  • @lieutenantcolonel2186
    @lieutenantcolonel2186 Рік тому +6

    Маne deh kou dieulll samayy tiyaaba ma lékk leu 😂

  • @AdamaTraore-wt6sx
    @AdamaTraore-wt6sx Рік тому +6

    جزاكم الله خير الجزاء يا أخي الكريم

  • @AbdousalamBaJB
    @AbdousalamBaJB Рік тому +4

    des mensonges rek gars yi du doule reck. baraka fika ya oustaz alpha ba

  • @masiba7272
    @masiba7272 Рік тому +7

    Diawaril mani lifa nek si ay wax you safano AK li yalla AK yonentem wax

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +3

      ‏وعليكم السلام جزاك الله خيرا

  • @mariendiaye7670
    @mariendiaye7670 Рік тому +1

    Yalnagnou Yallah moussal si rére, guindil gnou bopame

  • @ibrahimac-y4g
    @ibrahimac-y4g Рік тому +1

    fôwé nitgni rék diinédji matna ba nopi

  • @angoniassy6130
    @angoniassy6130 Рік тому +3

    Thiey Yallah senegal shirk rek😅😅

  • @falloufall8848
    @falloufall8848 Рік тому +1

    Fene rek

  • @البصرةالعلمية
    @البصرةالعلمية Рік тому +1

    Toppeu sounneu rek mo am solo ❤🎉❤❤

  • @ibrahimakanediallo4306
    @ibrahimakanediallo4306 Рік тому +3

    Yalnaniou yalla Réye ci tarikha cheikh inchallah ❤🤲

  • @fantagoudiaby3499
    @fantagoudiaby3499 Рік тому +3

    Soubhannallah nioune Sénégal natou deug laniou am ay soit disant chefs religieux di deugueureul bida ak chirk Sénégal koufi manta falou yit douniou diarigne dara ndah bookaalei ak bida naniou Or Diammant zircon gaz phosphate etc dougnou degré di sooneu sounou borom moy meire te ay dou yem ci boopu borom Wallahoul moustaen

  • @oumardiallo6139
    @oumardiallo6139 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci beaucoup alla

  • @ahmaddia3315
    @ahmaddia3315 5 місяців тому +1

    صلاةالفاتح
    غير صحيح ما انزل الله بها من سلطان ❤❤❤

  • @ndiawniass4185
    @ndiawniass4185 Рік тому +2

    Ay wayy cone mou yomb dii yalla kouko diamou la kham khamoul tarikha

  • @mariamjagana339
    @mariamjagana339 Рік тому +2

    هدانا الله

  • @khadimsylla5971
    @khadimsylla5971 Рік тому +3

    Toub naa degg gui😂

  • @kebecheikhtidiane7494
    @kebecheikhtidiane7494 11 місяців тому

    Walahi

  • @kebemouhamed7393
    @kebemouhamed7393 Рік тому +1

    Sa yonou baye moko geuna nécessite té Daga réw mbame ga rekk

  • @masiba7272
    @masiba7272 Рік тому +4

    Wahi dof

  • @ibrahimasarr8529
    @ibrahimasarr8529 Рік тому +1

    K'ALLAH nous protège de ces mensonges des soufis

  • @Robbe-Grillet
    @Robbe-Grillet 11 місяців тому

    Danguene tardé Seen baye ak kolene yaakaar meunoul corriger Cheikh Tidjane.

  • @salifsow9779
    @salifsow9779 Рік тому

    جزاك الله كل خير

  • @adamad9190
    @adamad9190 Рік тому

    👀🤔🤔🙄😳

  • @khadimsylla5971
    @khadimsylla5971 Рік тому +1

    Ay waye samba

  • @alphaomarjallow2425
    @alphaomarjallow2425 Рік тому +1

    Subhanallah what a lair Sufia 😂😂😂

    • @9_9_13
      @9_9_13 Рік тому

      You are the lair.

  • @masiba7272
    @masiba7272 Рік тому +3

    Diamou yalla AK talibee cheikh ?mdr!!!

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +1

      ‏ما شاء الله جزاك الله خيرا

  • @KhalifaAbabacarNdiayeAbabacarS

    Ioe amo kham kham démal diangui

  • @ibrahimac-y4g
    @ibrahimac-y4g Рік тому

    wahoul deugue né nga môko wakh kon fénna

  • @mamadousy6312
    @mamadousy6312 Рік тому +1

    Serigne mansour si ya fenal yalla gnou borom astakh firoula

  • @ibrahimadiouf7533
    @ibrahimadiouf7533 Рік тому

    Ya yeh ni wakhouma dh.. ndakh wakhi dof mome ioe sakh beugo sakg diko wakh

  • @dabaxful
    @dabaxful Рік тому

    Deggnagnou, té gueumkagnou... Yaw dou yaamay firil alkhourane... Dieredieuf Cheikh Ahmad Tidjani cherifil hassani

  • @santyallaboubakh4430
    @santyallaboubakh4430 Рік тому +1

    Avec sa ñiouni cheikh wakhoul lolou likay dafa leer mousibami yeep cheikh leu lim reeral barina.

  • @moutaphaofficiel7404
    @moutaphaofficiel7404 Рік тому +4

    SOUBAHANA LAH. GNII dégno toumal SOUNOU BOROM yalla.

  • @ndeyebarro4532
    @ndeyebarro4532 Рік тому +1

    Mandé gueumna cheikh limou wakh gneupe té kène menouma changé lo

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 Рік тому

      Sokhenessi té ngua changé bala miye trop tard.

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 2 місяці тому

      Sohna ci nékal nitt lolou dou wax yalla alxouran ak sounnah lala sante dou lénén

  • @NdaoMor-pz4wf
    @NdaoMor-pz4wf 5 місяців тому

    Yen dagen yaakaar ni chiekh tidiane mo niou takha niaw si adouna

  • @bayecheikhbeye718
    @bayecheikhbeye718 Рік тому

    Fen rek

  • @alassanesow9687
    @alassanesow9687 Рік тому

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 ayway Sénégal

  • @fantagoudiaby3499
    @fantagoudiaby3499 Рік тому

    Wallahoul moustaen

  • @malicktaye1907
    @malicktaye1907 Рік тому

    😂😂 bayilén thiakhan yi. Yalla moy faye walla cheikh moy faye ?
    Lii fann lako yonanti bi diangualé ?

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 2 місяці тому

    Cheikh tidian koumou yapp

  • @baboye7701
    @baboye7701 9 місяців тому

    Loo xamoul neek xamouloko. Bayilene di dingatt

  • @alima5003
    @alima5003 Рік тому +1

    yalla da beug kou mandou té yénn mandouwo lénne barkar meunoul wésso lii top tarikha diambour soba ba ngone di wakh té maitriser wolénn linguénii wakh tarikha cheikh dé zikr la toudou yalla ak yonénti bi soba ak ngone té moudioub diamona bii kou eupp loy zikr astaghfirlou di diouli si yonétii sws walahii dinga raw yénn nak néké lénn fii li rékk ba yawmal khiyam

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +1

      🤔🤫🫣🤭🫢😅😅😄😁😅

    • @ousm7710
      @ousm7710 Рік тому

      Kou féne thi dîné da wara fegne sos pour reral diamyi thi sene dîné

    • @ousm7710
      @ousm7710 Рік тому +1

      Li moule bene dalile inventé par cheikh tidiane qui n'a jamais vu ni entendre le prophète

    • @alima5003
      @alima5003 Рік тому

      @@KAADUDINEEJITV kilay tontou mongui gneuw khamolénnn dara nékk fii di touteull tarikha diambour yii démal geustou dji lane moy tarikha cheikh ak foumou dioguéé

  • @serignetoubadiop5528
    @serignetoubadiop5528 5 місяців тому

    DIADIEUF OUZTAZ....Gni dougnou rousse;;wakhi doff ,meme un bebe ne peut croire en leurs LEBONES LIPONES...Toutale islam lagniy dounde tous les tarikhas pareil;;;;SOUBHANALAH...

  • @sunnialiber4868
    @sunnialiber4868 Рік тому

    Senegal 🇸🇳 vraiment rèwum teranga la

  • @dameadame6062
    @dameadame6062 Рік тому

    Wakhi dof

  • @lomsouleymane9947
    @lomsouleymane9947 Рік тому

    Tu n’as rien compris mon chère, Tu mélanges tout

  • @gorad96
    @gorad96 Рік тому

    Alpha yaw Guesou ka lou lou dakhe Cheikh Tidiane Mougou Wakhe Walaha,ils font faire très attention Al martabatou latousamikhe

    • @ousm7710
      @ousm7710 Рік тому

      loudoul sos ak reral diamyi thi sene dîné li dara dousi deug

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 Рік тому

    Serigne cheikh serigne touba serigne baye niass serigne baye laye ame néne problème Yawmal Khiyama

    • @mamadousy6312
      @mamadousy6312 Рік тому +2

      Billahi am n'es gnou problème bou rey sakh

  • @khadyniass
    @khadyniass Рік тому

    Yén wa akhlou sounna bayi lén sounou mak ni sof gén trop