WAA KARAWAAN MAYUMBA, NEENAÑU LI WAAJI WAX WÉRUL TA ÀNDUÑU CI.

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 182

  • @bmktk6844
    @bmktk6844 3 місяці тому +11

    Baye mbaye Gueye mi daawara godou fane de ndax fenkat yobésyi niogui niew ta amonio kolen wedi

    • @bmktk6844
      @bmktk6844 3 місяці тому

      😂

    • @sidylo9069
      @sidylo9069 3 місяці тому

      ​@@bmktk6844billakhi yalla dano ko wara teugatal

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 3 місяці тому +21

    Waw góor Baay Mbaye Nila rèk Kou Fi gën fenn ay Fenam gënal wèddi ko ngir Seriñ bi

    • @ndiougadieng715
      @ndiougadieng715 3 місяці тому +3

      Ndeyesan baye mbaye ka bage seringe touba

    • @sidylo9069
      @sidylo9069 3 місяці тому

      ​@@ndiougadieng715wallahil hasim wax geu DEUG amosi sago

    • @MoukhamadDiakht
      @MoukhamadDiakht 3 місяці тому

      🤔🤔🤔🤔🤔🦻🦻🦻🦻🦻👈🏾

    • @MoukhamadDiakht
      @MoukhamadDiakht 3 місяці тому

      👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻

  • @ModouDiouf-z2w
    @ModouDiouf-z2w 3 місяці тому +12

    Kou bëgga xam thi yoonu mouride dara dal degloul serigne mbaye gueye syll

    • @sidylo9069
      @sidylo9069 3 місяці тому

      Wallahil hasim wax geu DEUG

  • @OusmaneNguirane-zu5mr
    @OusmaneNguirane-zu5mr 3 місяці тому +9

    Liniou wakhal serigne bi te dou degue barina nk😊

  • @serignesalioumbackedioum3630
    @serignesalioumbackedioum3630 3 місяці тому +3

    Dieuredieuf Baye Sylla Noonu rek la Samb Yoonu Serigne bi rek Moy sa Wallou Yalna Serigne bi dolé défar Tawfekh

  • @oumarseck3114
    @oumarseck3114 3 місяці тому +6

    DIADIEUFATI BAYE MBAYE GUEYE SYLL LI NGAY DEF DEH MOM LA YALLAH BEUG,YONENT BI BEUG KO,SERIGNE TOUBA BEUG KO,WADIODIOU NGOM NAK
    KILIFA YI NIOKO WARA YAMALE NGUIR MOU ARRETTER FENAM YOYOU,MERCI...

  • @serignemodouabibgueye3935
    @serignemodouabibgueye3935 2 місяці тому +1

    Ñii ñooy ñi nga xam ne nanguwuñoo liggéey, dóor rekk ak fen lañu fi nekke, baay Mbay nee ko mu dem liggéeyi, te bàyyi fen yi.

  • @moussapouye8355
    @moussapouye8355 3 місяці тому +1

    Mashallah choukrane

  • @amidouleyediop1207
    @amidouleyediop1207 3 місяці тому +3

    Dieredief serigne mbaye gueye sill
    Yalla Nala serigne bi ngaye liguèyal fayal bopame
    Tè yalla dolli LA katane ak fane wou goudou tèbarkèl si barkep serigne salihou
    Amine

  • @makhtarndir2253
    @makhtarndir2253 2 місяці тому

    akassa baye mbaye amatina solo yalna borom yoke sa fane té doly sa wérre amine si barké Mame sidibirahime fall sidibirahime faf

  • @MbayeGakou-xs4pc
    @MbayeGakou-xs4pc 3 місяці тому +1

    Dieuredieuf ❤🎉 amou gnou sa faye ya kham li nga begue yalla na la ko kou tédd ki déffal barkép MOOME 😢

  • @Mrdiop
    @Mrdiop 3 місяці тому +2

    Baye wakhatii ngaa deug Serigne Touba soxlawoul nioukay douraal way

  • @MoustaphaKhouma-ed6im
    @MoustaphaKhouma-ed6im 3 місяці тому

    Grazie mille bay mbaye khouma la pace sia con tè ❤❤

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 3 місяці тому +8

    Bima ko gisee lako wèddi ak diarom you reye Yi

  • @chiekhniangxassida4150
    @chiekhniangxassida4150 3 місяці тому +1

    Machallah 💙💛 baye mbaye geuye syll sa takhawaye rafétna lool yague fi lool te andake wére
    Nii rek la lou bokkoul si yoon bi nga takhaw dindi ko leeral ko
    Yénneu yi moom kénneu dou kham loumiye nirou

  • @chiekhniangxassida4150
    @chiekhniangxassida4150 3 місяці тому +4

    Waa gniii moom niii rek laniou léndi bayyi
    Yor saye wakh di wakh loula nékh rek
    Daa bari si yoon wi lool
    Guayi khawma louléne dall rek

  • @cheikhsylla4491
    @cheikhsylla4491 3 місяці тому

    Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll amna solo lool sakh

  • @ibrahimatoure7709
    @ibrahimatoure7709 3 місяці тому

    ❤❤ Cheihk mbaye gueye sylla machalla

  • @mouhamedmakhroufthiam1476
    @mouhamedmakhroufthiam1476 3 місяці тому

    Tawfeih reik.

  • @chiekhniangxassida4150
    @chiekhniangxassida4150 3 місяці тому +1

    Wallaye mame mbaye akaye deuggue
    Dieureudieuf

  • @seexabdulahat8238
    @seexabdulahat8238 3 місяці тому

    Jërëjëf Sëriñ Mbay Luga Wax rekay Dëg Yàlla nala Yàlla fay jërëjëf

  • @bayezaletalla2066
    @bayezaletalla2066 3 місяці тому +1

    Thanks baye Mbaye gy syll

  • @DjilyNiang-y4n
    @DjilyNiang-y4n 3 місяці тому

    bay mbaye wa dji fen rk lay deff

  • @AbdoulayeFall-nr2ui
    @AbdoulayeFall-nr2ui 3 місяці тому +2

    Dieuredieuf serigne mbaye gueye syll mais wa caravane bi am nagn si part de responsabilité sou niou guénewoul si sénn birrr naniou ko guénnn caravane nakh app saytanéla pirr

  • @Dioufmoukhamad
    @Dioufmoukhamad 3 місяці тому +1

    Sak magal Ak fene you béss

  • @seringecheikhniang7735
    @seringecheikhniang7735 3 місяці тому

    Waw goor S mbeye Silla Ape Dibarla Nayam thielim kham

  • @nouroudaraynitv1678
    @nouroudaraynitv1678 3 місяці тому

    Kou khéllu wara khammé kouy Fenn
    Serigne bi nk ay mbireum dou lou Khel di xalaat wayé lou bokkul thi mome kouko degue kham ko
    Khawma nan ngom yamal thi sa place nianou kaay bobu
    Jërëjëf baye mbaye Gueye sylla

  • @cheikhseye6929
    @cheikhseye6929 3 місяці тому

    Dieuredieuf Serigne mbaye Gueye sill

  • @cheikhseck8978
    @cheikhseck8978 3 місяці тому

    Merci beaucoup baye mbaye ❤❤❤😂😂😂

  • @Abdallah-gq2qh
    @Abdallah-gq2qh 3 місяці тому +6

    Kî dé dâ guiss ñôme Ganna méséré di féne di am xâlis té kéne waxulène dara môtax mu diok soss ay fénam nguir am xâlis

    • @habibiboss4057
      @habibiboss4057 3 місяці тому +3

      Gana dé fénoull ba tak diabarr ioe nak sa baye mi féne ba tak sa yaye nak

    • @AdjuntoOfrece-qr7db
      @AdjuntoOfrece-qr7db 3 місяці тому +2

      Yangui togne cheikh gana mésséré dh kokou ñéméwoul serigne bi loumou wah thi serigne bi rek lou werleu mom cheikh gana

    • @Abdallah-gq2qh
      @Abdallah-gq2qh 3 місяці тому

      @@habibiboss4057 suma bayiwul wône sâga kone ma tègueul sa ndaye dômarâm dji

    • @nouroudaraynitv1678
      @nouroudaraynitv1678 3 місяці тому

      Yw warnga khôl sa dioudiine eska diaar na thi yon ba paré

  • @bayefalldiop3897
    @bayefalldiop3897 3 місяці тому

    Dieurdieurfff❤❤❤❤❤

  • @PapeNiass-nh9yl
    @PapeNiass-nh9yl 3 місяці тому +1

    niom ndeye sans danio fokni tarikha propagande leu mbir yi xam xam leu ak sunna bou leer nagn mane tidiane la mais serigne touba lim ligey eupeu neu nioukoy sossal.

    • @sidylo9069
      @sidylo9069 3 місяці тому

      Dieureudieuf ya bakh

  • @bildoxer89diakhate5
    @bildoxer89diakhate5 3 місяці тому

    Waw gór baye mbaye gueye syll Diakhaté 🥰

  • @حسن-م1س4ح
    @حسن-م1س4ح 3 місяці тому

    DIEREJEUF BAYE MBAY

  • @almustafambakke6163
    @almustafambakke6163 3 місяці тому

    Jërëjëfaty Baay mbay ❤❤❤❤ yaw deh Sërin Tuuba rek mola mana faye yagi ligey lu am Solo

  • @balla8843
    @balla8843 3 місяці тому

    Dieurdieufti Baye Mbaye guéye Syll

  • @BombaLy-oh3sj
    @BombaLy-oh3sj 3 місяці тому

    Kii kaye dafa mana fen rek limoye wakh xamou ci dara

  • @mouhamadndiaye5235
    @mouhamadndiaye5235 3 місяці тому

    Ndeysaan, leeral bi am na solo.
    Yonnu Murit bërina histoire yi ñu nettali té dara du ci deug

  • @serignemodouabibgueye3935
    @serignemodouabibgueye3935 2 місяці тому +1

    Baay Mbay yaw murit yi dañu laa war di fay.

  • @DjilyNiang-y4n
    @DjilyNiang-y4n 3 місяці тому

    Wa waw bay mbaye ya xam mborrki xamon nane limoy wah amoull

  • @DialloNdiaye-g7m
    @DialloNdiaye-g7m 2 місяці тому

    Merci

  • @balla8843
    @balla8843 3 місяці тому

    Garab gui sakh kouko guiss khamné amagoul téméri att 100ans

  • @ThiernobirahimSylla
    @ThiernobirahimSylla 3 місяці тому +1

    Dieureudieuf souniou baay

  • @ousmanefaye9378
    @ousmanefaye9378 3 місяці тому

    Merci beaucoup

  • @serigneomartandine1350
    @serigneomartandine1350 3 місяці тому

    Dieuredieuf mom serigne taryakh la day dor

  • @moduxaribuso2067
    @moduxaribuso2067 3 місяці тому

    Jërëjëf sëriñ bi ligéey bi amna Solo gayi faawu ñuy wax ak ñoom

  • @bayesaliousyll7395
    @bayesaliousyll7395 3 місяці тому

    Vídeo waji de bimako tambale setaan agalewoumako NDAkh geuna uma Dara ci limouy wakh dieredief baye mbaye yalla na takhaway bi yageu

  • @serignesarr517
    @serignesarr517 3 місяці тому

    DAMAA AM KERSSA SAH

  • @noirafrik7085
    @noirafrik7085 3 місяці тому +2

    Ku dul xalaat baay mbay lula neex waxal 😂

  • @AbdouSSall
    @AbdouSSall 3 місяці тому

    Ki neveu oustas mbaye ngom la ki charletan leu

  • @ibrahimacissedieureudieufs2732
    @ibrahimacissedieureudieufs2732 3 місяці тому +4

    Yow Mbaye Gueye syll lingaye def nii foo tolou di wédi nit gni té doo indi loudoul li toubabs yi binde ay thiakhane kepp la. Yaa takh niouy wédi diouli guédj gui ay you melni moome ndakh nékoul si archives yi

    • @serignemodouniass3063
      @serignemodouniass3063 3 місяці тому +2

      Yaw mi ya barri caxan

    • @daarajitv3314
      @daarajitv3314 3 місяці тому +3

      Kou bakh fanatisme bakhoul baye Mbaye limi wakh leip ay dellou waaay you weer lay diokhé Yoon Wi war na romb Lou waay nekh wakh té dou andi ben firndé li baye Mbaye di dèf nii lou am soulo la Yoon Lou nekh waay wakh kouko weedi niouné dou Mouride fanatique bakhoul S Touba xam xam yoonu Mouride xam xam moko Souss k

    • @MrCSeck
      @MrCSeck 3 місяці тому +4

      Ku baax bu dé loolu la, na nga ñu éndil luko gëna wér wax ji jeex
      S Mbaye dafay endi li Serigne Touba bindal boppam (Jaza u Shakur) Tek ci Minanul Baaqil Qadiim bu S Bassirou, Tek ci Irwâ u Nadiim S M Lamine Diop Dagana, tek ci nak documents yi fi nekkoon digganté sunu Maam yi ak tubaab yi.
      Kuy weddi loolu dangay endi sa source, wayé jamono ji ñu nekk dafa bëri ñoo xamné jang nañ , te dañoo yakamti xeex Yoon wi jaaré ko ci yii ñuy wax te du dëgg.
      Mootax weesu nañ fu ñuy japp ay waxi kassé te duñu la wax kuko wax wala ku fekké. Li Serigne bi bind rekk doy na ñu kéemaan

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 3 місяці тому

      Kou bax ibrahima cissé nekal nit seriñ mbaye gueye limou wax ni lou wèr leu sosss yi da beuri si yone wi

    • @seyniseck9632
      @seyniseck9632 3 місяці тому

      Même hier j'ai vu le même commentaire si wakhoul wakhou archives limou wakh yow sakh bo diangone digua kham ni ngom bi wakhoul deug

  • @mamemor7761
    @mamemor7761 3 місяці тому

    Diaradiaf saringe bi

  • @cheikhmbendamodoufall545
    @cheikhmbendamodoufall545 3 місяці тому

    Wawe gor baye mbaye geuye

  • @massambalo1088
    @massambalo1088 3 місяці тому

    Seugn Mbaye sylla Dierejef Wayee Seugn bi aussi kenn meunta tek leppam si am khel . Serigne bi li eupp si mom dou lou yenou maahnaa.

  • @massambandiaye5080
    @massambandiaye5080 3 місяці тому

    Waw gourr Way baye mbaye Gueye syll ❤❤❤❤❤❤

  • @oumarseck3114
    @oumarseck3114 3 місяці тому +5

    GARABAM GUI DEH DAFA SAKH NDAW CI GARAB GOU SERIGNE TOUBA DAN TOK,AKA AM FIT TA NIEME YALLAH..😂😅😂

    • @thiernoseck8365
      @thiernoseck8365 3 місяці тому +2

      😅 man dé Bima gisé lako wèddi moh

    • @ahmedtidianewade342
      @ahmedtidianewade342 3 місяці тому

      ​@@thiernoseck8365Bilahi Mane Sakh dama diomy grab bou am téméri attt dou mélni😂😂😂

    • @khadimndiaye171
      @khadimndiaye171 3 місяці тому

      Wadji dh môme d'où wakh degue mais nioum môme depuis 1995 belégui niongi fekk garap gui fofou ​@@thiernoseck8365

  • @bayedjilybaxdad8372
    @bayedjilybaxdad8372 3 місяці тому

    S mbaye sa lagéyy raféttna

  • @serignembackesylla6866
    @serignembackesylla6866 3 місяці тому

    Waw goor

  • @talibebamba1626
    @talibebamba1626 3 місяці тому

    Dieux reux dieuf baaye mbaye

  • @MohuamaodaoPalos
    @MohuamaodaoPalos 3 місяці тому

    Machallah

  • @cheikhndiaye931
    @cheikhndiaye931 3 місяці тому

    Macha'Allah .....Jërëjëf

  • @Survcontainer-br3xb
    @Survcontainer-br3xb 3 місяці тому

    😂😂😂😂😂 vraiment mangui déé

  • @BayesergneGuiye
    @BayesergneGuiye 3 місяці тому

    ❤❤

  • @assgueye736
    @assgueye736 3 місяці тому

    Diadieuf ❤❤❤

  • @AHMADOUWAKANATV
    @AHMADOUWAKANATV 3 місяці тому +2

    Yonne Wii gni wara wakh wakhoudiou

  • @falloudiba3720
    @falloudiba3720 3 місяці тому

    Jërëjëf

  • @vieuxmalickmbodji4650
    @vieuxmalickmbodji4650 2 місяці тому

    Slt diambar nite day geustou louway beugu kham si yonou serigne touba liral l'islam au Sénégal écrit par Paul marty j'ai lu tous ce livre kham ci nak lou bari si tarikha bounek

  • @tayzir
    @tayzir 3 місяці тому

    Amna solo serigne mbaye ❤❤

  • @malickdiouf5008
    @malickdiouf5008 3 місяці тому

    Bom dmati mo diékh diajef s mbaye gëye sill ❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhthioune3135
    @cheikhthioune3135 3 місяці тому

    Qu'Allah retribue au centuple le travail de Serigne Baye Gueye Syll. Tous les mourides doivent l'encourager et le soutenir. Les mourides doivent combatre de toutes leurs forces ces pratiques et leurs auteurs, que sont les laudateurs, les soit disants communicateurs traditionnels et autres affabulateurs.

  • @Chniang
    @Chniang 3 місяці тому +1

    Waw gourr way

  • @elimanedione6325
    @elimanedione6325 3 місяці тому

    Y’a ngi koy reyy de yerem ko wy 😂😂😂😂😂

  • @FaaFallilou
    @FaaFallilou 3 місяці тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤Grazie mille

  • @khadimdieng6878
    @khadimdieng6878 3 місяці тому

    Ngom mii na bayi tapalèmyi

  • @bassirougueye1287
    @bassirougueye1287 3 місяці тому

    Jaajeuf serigne maybe

  • @SerignesidySambo
    @SerignesidySambo 2 місяці тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @noblengom9262
    @noblengom9262 3 місяці тому +1

    Senegal nio sokhor bilahi kii limouy liguey yep lou niaaw lii rek nguen ko mena wakhal té yeen gnii niep amoul koussi Bayam wala Mamam andone ak Serigne Touba thia Gabon on nous a tous raconté

    • @ligueyeulSerignebi2128
      @ligueyeulSerignebi2128 3 місяці тому

      Frère Serigne Touba a écrit lui même son parcour avec tous les trajectoires

  • @mortallagueye5214
    @mortallagueye5214 3 місяці тому

    Ki damakou kham bou bakh sakh mamadou ngom la nekon na fass mbao 😅😅😅😅

  • @mouhamadoumoustaphafall7270
    @mouhamadoumoustaphafall7270 3 місяці тому

    L'exil d'alourdir Ndiaye au Dosso et Fodé Kaba Doumbia/ Demba War Sall FMDWS La Solidarité légendaire ; la Terranga Sénégal 🇸🇳

  • @baragueye-bi6jt
    @baragueye-bi6jt 3 місяці тому

    Jërëjëf saa baye yaa gi deff lu am solo. Il est temps de faire taire ses daanu kat qui ne font que mentir sur l'histoire de Serigne Touba

  • @Abdallah-gq2qh
    @Abdallah-gq2qh 3 місяці тому +1

    Fényi apouna lî day yaplou yônou mouride

  • @NiangAmadou-bt3mg
    @NiangAmadou-bt3mg 3 місяці тому

    Serigne bi liko sounou borom défal ak dieuwrinam diou tédd Diam don liguéyeul halayhi salam. Doyna seuke seuk seuke kémane, ta manésouko xam manésouko guiss rombe nam xél

  • @cheikhmbendamodoufall545
    @cheikhmbendamodoufall545 3 місяці тому

    Khadim ngom kay diaxalal nama dem di filmé wakh rk

  • @Touba.kawsaraFall
    @Touba.kawsaraFall 3 місяці тому

    Kidal diaplénko nopalngou ki domaramla daytakh kédongoufalé dama rous bilay

  • @ousmanembacke6376
    @ousmanembacke6376 3 місяці тому

    Féne dou bédiaw

  • @abdouahatfall6560
    @abdouahatfall6560 3 місяці тому +1

    Te mom sakh lolen si khamoul bopam rk lay wanei Beug guislen trop mo takh meusou mako guem nek gabon rk di film di wax louko nekh

  • @serignegueye6221
    @serignegueye6221 3 місяці тому

    Ya mbaye gueye sil da ngaa bari wax yaak moom rek yeenë yam,dangeen di nettalli rek ta leg leg ngeen wax loo xamni kuko seg ngeen sëg, sëriñ fallu juuf limu wax rek doyoonë,mbiru sëriñbi dangay gëm mbaa nga bayyi,booci dugëlee xel lu bari dooko gëm.li nge wax ci garabgi ni xel nuŋguwuko lu manë neklë,neenañu yonentabi jëmbët në tandarma mu sax meñni.

  • @Touba.kawsaraFall
    @Touba.kawsaraFall 3 місяці тому

    Naysan

  • @malickfall9516
    @malickfall9516 3 місяці тому

    Boulene yakh affaires ram .door kat la

  • @ndiagamakhtarsow3599
    @ndiagamakhtarsow3599 3 місяці тому

    wakh léne si gana meséré

  • @babacarmbengue4662
    @babacarmbengue4662 3 місяці тому

    Yakh katte kesse la AK gnake talibee Douma rekkkkkk ..

  • @boromkourousgui4918
    @boromkourousgui4918 3 місяці тому

    wawe goor baye Mbaye kou wakh lou wéroule dale nanko wédi légui mome kouné daye yor saye khissta di wakh

  • @serignesaliouseck3120
    @serignesaliouseck3120 3 місяці тому

    Non Amna louma nakhari trop billahi li dou yoon kw talibé yi dall len li dara jarouko kw

  • @BayesergneGuiye
    @BayesergneGuiye 3 місяці тому

    tapale katyi danobari

  • @ndiagamakhtarsow3599
    @ndiagamakhtarsow3599 3 місяці тому

    modou kara néna serigne bi mo binde asaman ak souf wakhal si lolou

    • @bakawagne2033
      @bakawagne2033 3 місяці тому

      Sa way yow té nga fowi

    • @noirafrik7085
      @noirafrik7085 3 місяці тому

      Pour ton rappel lui il parle de l' histoire

  • @serignesaliouseck3120
    @serignesaliouseck3120 3 місяці тому

    Kon ki teeyoul dh guis nako ci TikTok bi mais liguey bi dou nonou kw mangua beugu Lou bakh ba lanen fekk lasi kw

  • @serignetoubadiop5528
    @serignetoubadiop5528 3 місяці тому +1

    Bou mourides yi ,melonne né yaw ,di wakh deug ,bayi soss ,bayi BOKALE ,bayi took di fenn ;;;;;SERIGNE TOUBA dou fougnouy wouté khalisse;;;yalla moko niore;;;; TARIKHAS senegal yeep ,limoye senn ligueye ;;fenal macks gni pour khalisse;;;

  • @labbajop-nl4cm
    @labbajop-nl4cm 3 місяці тому

    Doorkat yi ño barry !

    • @gorakane7831
      @gorakane7831 3 місяці тому +1

      De nos jours, beaucoup de jeunes refusent de travailler et veulent obtenir de l'argent facile en essayant de tromper la bonne foi d'autrui

  • @ThiernobirahimSylla
    @ThiernobirahimSylla 3 місяці тому

    Doyna waar

  • @Walhsri
    @Walhsri 3 місяці тому

    Wax leen thé seihkh Moussa Diagne me wede diole wede coor wede asaka tante len Yoor thé Serigne bi lanko diale wax leen thé me nge yaxlou bare de