Talibés de Cheikh Mansour attaquent Le domicile de Seydina Issa Laye? ce qui s'est réellement passé

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • Des talibés de Cheikh Mansour Diouf attaquent Les domiciles de Seydina Issa Laye? ce qui s'est réellement passé

КОМЕНТАРІ •

  • @santeserignetouba4826
    @santeserignetouba4826 3 роки тому +34

    MOURIDE =LAYÉEN ❤️🇸🇳 YALLAH NA DIAM YAGG SÉNÉGAL 🙏🏾

  • @bassinedioplaye9477
    @bassinedioplaye9477 3 роки тому +13

    Yallana Yalla doli diam ak salam thi yoff ak Sénégal thi Daradiaye Seydina Limamoulaye (PSL)

  • @mamediarratine4927
    @mamediarratine4927 3 роки тому +16

    Ne convertissons pas les problèmes perso en probléme interconfrérie. Nous disons non

  • @khadylaye7907
    @khadylaye7907 3 роки тому +38

    Layenne keneu xaméwouléne togn ak politique kouléne songou yalène togn Wa salam🙏🏼

    • @awadiallo7188
      @awadiallo7188 3 роки тому +1

      j su pas layénne mais t a parfaitement raison khana sé la 1erfois yalla diamou yageu thi Sénégal

    • @astoulaye62
      @astoulaye62 3 роки тому +1

      Wallahi laye

    • @ndeyefatoudiop102
      @ndeyefatoudiop102 3 роки тому +1

      Billahi man niassen la mais linga wakh deugue la

    • @jacky3326
      @jacky3326 3 роки тому

      Bayil nafekeu affaire bi dou problème mourid ak layene affaire bi cheikh Mansour dioufla ak lebou yi

    • @khadylaye7907
      @khadylaye7907 3 роки тому

      rata bob Yaw nak y’a raw firawna yaw xamo nga beug wax t mane ma deuk si keepar gui do wax loula wor déjà sa genre gui nioy topou info si reso yi t dara xamouniouko di beug commentaire di sos rek en plus de ça yangi wax cheikh mansour diouf ak lebou yi t xamoni lebou yi nieup bokk si layenne ish

  • @diawcheikhna8130
    @diawcheikhna8130 3 роки тому

    Yalla nafi yalla doli diamou ak tawfekh adina amoul solo

  • @ousmanegueye210
    @ousmanegueye210 3 роки тому +2

    Du courage et détermination en avant lebou wakeur Mame limamou

  • @mamansalioudieng5784
    @mamansalioudieng5784 3 роки тому +18

    Yalle naa niepeu âme diammm

  • @mouhameddiaw5504
    @mouhameddiaw5504 3 роки тому +2

    Bilay ya téppi sa leufeul ndeye rek mouride ak layenne ay frère lagnou domerame

  • @ndiayeamadou150
    @ndiayeamadou150 3 роки тому +15

    ce problème n'a rien à voir avec les communautés layènes et mouride. attention à la manipulation

  • @momadulaye3813
    @momadulaye3813 3 роки тому +4

    Mansour Diouf daniouko eundi yoff pour mou khékh layéne. Sa Baye sah manoul dará si layéne. Fraaaaannn maaaasonnn. Dianguil alkhouran

  • @cheikhthiaw7529
    @cheikhthiaw7529 3 роки тому

    Li gnawena😭😭😭😭 wayai lepou macky sall moko warale

  • @alieoulow6676
    @alieoulow6676 3 роки тому +1

    Merci cheikh manssour diouf

  • @moustaphambacke2238
    @moustaphambacke2238 3 роки тому +18

    Un problème politique doit être analysé d une manière politique mais ce titre c est de la manipulation mais mouride ak layene douniou tongo mouk .

  • @abdoulayeseck2997
    @abdoulayeseck2997 3 роки тому +11

    Cheikh Mansour dioufff nékal nittt tei yém néko loudoutt ab cheikh

  • @toutanebatchili8781
    @toutanebatchili8781 3 роки тому +2

    Avec Abdoulaye Wade une partie des terres lebous ont été données d une façon malhonnête à Mbakiyou Faye en modifiant une loi du domaine national , pour juste voler les terres lebous sans dommage ,pourtant un passe récent les lebous ont affronte les toubibs voir la note de Faiderbe ,aujourd'hui après l'indépendance tous les présidents ont combattu les lebous surtout Abdoulaye Wade, les lebous doivent prendre conscience

  • @diawserignembacke4632
    @diawserignembacke4632 3 роки тому +12

    Saytané bakhoull li dou afairou tarikha yénn niépou yéna bokou deug wakh tane lénn

  • @actualitetv7889
    @actualitetv7889 3 роки тому +11

    Ýéne ame degue Cheikh mansour Diouf sa yone nekoul si problème bi mouride la wayé yéne layennes ýéna ame degue

  • @bayebaye3787
    @bayebaye3787 3 роки тому

    Aller sounou waa keur lébougui

  • @saintjuste6412
    @saintjuste6412 3 роки тому +4

    Mansour diouf dou ab lèbou, tègal lène ndayam mou guène yoff,

    • @lafindutemps6141
      @lafindutemps6141 3 роки тому

      Yoff appartient au Sénégalais pas lébou ou mouride

    • @bintoudiop5954
      @bintoudiop5954 3 роки тому

      😂😂🤣😂

    • @morlo4034
      @morlo4034 3 роки тому

      @@lafindutemps6141 lolou d'où aye wah kouniou hadialoule doufa dougeu

  • @littleg1288
    @littleg1288 3 роки тому +1

    La communauté lèbou ils n'y a pas d guerre entre les tarihas, nous sommes tous pour un, vives la communauté lèbou

  • @dabakhsamb5301
    @dabakhsamb5301 3 роки тому +3

    Cheikh. M. Diouf. Na. Dem. Alba. Cheikhou. Adouna. Xethio. Allal. Rek. 🤔🤔🤔🤔🤔🤔

  • @abdoubiaye2036
    @abdoubiaye2036 3 роки тому

    Dieureudief baye

  • @adjisamb6308
    @adjisamb6308 3 роки тому +2

    Wa keur masour diouf walahi boléne arretéwoul di attaqué keur seydina issa diop laye ngor dina diok ouakam diok féka lénn fofou yén barriwoulén té yaw do mouride mouride ak layénne ayy kharite lagn ay jumau lagn wayé masour diouf diakhasé rek ngafi néké

  • @bayecheikhdiagne6781
    @bayecheikhdiagne6781 3 роки тому

    Le vrai problèmes du Sénégal moy dafa bari nafekh koi demel diamou yallah tei bayi xoulo ak khekhh bi

  • @madameseck882
    @madameseck882 3 роки тому

    Si des membres de la collectivité lebou se sont réunies chez cheikh Mansour Diouf en quoi est il fautif ses talibés se sont battus non pour des terres mais pour les insultes faites à l'encontre de leurs guide religieux le cheikh na nullement besoin de terre car machalla Dieu l'a déjà béni Diami communauté lebou rek moko nior

    • @abdoulayendiaye7736
      @abdoulayendiaye7736 3 роки тому

      Nopil bari nga wakh Mansour Diouf dafay dara gnoûne fi langoi dioudo kham nagnou ka babakh sakh

  • @astoudiop9474
    @astoudiop9474 3 роки тому

    Ko yatal rek mou beugue la mom bouniou fontou ba Baye Laye psl di wakh yataléne sakéte yi gane yagui nieuw boba fi dara amoufi ndakaro nekh motax nioune fouy jerejëf Seydina Limamou Lahi (saw)

  • @khadijasow7107
    @khadijasow7107 3 роки тому

    Amna gnoo khamne fitna ak djaay doole rek lagnou nekkee thi reewmi
    Tey gnoom gnoognou gnoo and ak sonko di fitnaal nitt gni ak dileen saaga
    Yeneen sénégalais yi seeni nawle lagnou am leen roussoukaay touti

  • @mariemecissokho5589
    @mariemecissokho5589 3 роки тому +12

    Séné titre sheytané yii j'ai mm pas regardé la vidéo dama commenté rekk.Sénégal bene bopoula kene manouko kharr gnarr.journaliste yi warguene kholate séné boop

    • @santeserignetouba4826
      @santeserignetouba4826 3 роки тому +2

      Dieureudieuf 🇸🇳❤️

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 3 роки тому +2

      Soxnasi yèwoul Senegal boudè bène bope la todjeutè nèniou ko deffko aye saam nope yi diar droite yourr bi dieul yonou gauche beugn ak lamigne moniou dèssè nguir kèbètou rek👉🏿 Senegal bène bope la aye door la rek

    • @Umassia
      @Umassia 3 роки тому +1

      @@ghettoyouthkatakyni7843 😂😂😂😂 kébétou

    • @ousmanendiaye1754
      @ousmanendiaye1754 3 роки тому

      Dieuredieuf ndakh yaw niite nga dina le commentair

  • @diarrasall2888
    @diarrasall2888 3 роки тому +1

    Khana adouna daye wadia touki li kouka wakh des

  • @sambandiaye5852
    @sambandiaye5852 3 роки тому

    Momoulé dara way yénn

  • @abdoulayeseck2997
    @abdoulayeseck2997 3 роки тому +4

    Cheikh Mansour dioufff nékalll nittt mouride dou thiakhane

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 3 роки тому +2

      Del xam lugn diotei ba nopi soga wax waxi thiakhane
      Nit dey tey xame xamei

    • @abdoulayeseck2997
      @abdoulayeseck2997 3 роки тому +2

      @@thiamahmadulattekh562 mai lugnu dioté waroull dokh si politique na dokh si Serigne biii cheikh kaséla dou sangu

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 3 роки тому

      @@abdoulayeseck2997 deugeu rek nga fi wakh

  • @bayebaye3787
    @bayebaye3787 3 роки тому

    Gnaa soufass maame laa déé aéroport foire stade léopard senghor UCAD.

  • @sanatoure1058
    @sanatoure1058 3 роки тому

    Ça a commencé avec les 73 familles de termesud guen di setane tey yeun la

  • @ahmadoulaye7170
    @ahmadoulaye7170 3 роки тому

    Lgui lu sii yonu S Issa laye s'en titre de leen koo xolate beug beuz bouma takh nguen jobé nii

  • @oustazahmedfall6478
    @oustazahmedfall6478 3 роки тому +3

    Mansour diouf gnap lén ndayam mou guéne Yoff dekoufa nafa géne

  • @ousmanendiaye1754
    @ousmanendiaye1754 3 роки тому +1

    Guise nga Senegalese yi nion wara yéwou balanion yak réw mi tarikha yéppe béne laniou nion bok béne mame gni gui wakh aye turorise ak aye louma khamoule

  • @cheikhthiaw7529
    @cheikhthiaw7529 3 роки тому

    Naika leene nitte guire yalla ak sonou mak gnou bakh yifi naikone

  • @abdoulkhadregaye3437
    @abdoulkhadregaye3437 3 роки тому

    Le problème c'est entre Cheikh Mansour Diouf et Ablaye Diouf Sarr ou quoi?

  • @cheikhthiaw7529
    @cheikhthiaw7529 3 роки тому

    Senegal lifi ame amoule kaina kounou fiko diaguale gnoune diamou la sounou mak gnou bakh gna khamone lou takh meunouno deff ni gnome

  • @remasougou5847
    @remasougou5847 3 роки тому

    Wa gni louniou beug si aéroport kelkun p m'expliquer

    • @nddp221
      @nddp221 3 роки тому +1

      Khana sedoko yobou njiko môme sa bauyama

  • @alieoulow6676
    @alieoulow6676 3 роки тому +1

    Cheikh mansour diof nitko bakhla

  • @papeseck6124
    @papeseck6124 3 роки тому +4

    kanmoy cheikh mansour diop senegal mo nékh kou diok rk nane cheikh

  • @oumydiop3776
    @oumydiop3776 3 роки тому +3

    Lebou mo beug souf soufsi yalla moko mom

  • @ramatoulayesene3743
    @ramatoulayesene3743 3 роки тому +6

    Cheikh Mansour Diouf dafay mboubo mouridisme pour féwalé tarikha yi franmacon leu. Say sou défé discours wahu sheytané ak nafék.il a fait de telle sorte que ses talibé la plupart des yoffois détestent tellement les Layenne et gratuitement.pourtant dans les autres quartiers Layenne de Dakar Layenne et mouride vivent en parfaite harmonie.c'est un danger pour la religion Islam.Il faut l'arrêter il a un agenda bien défini.

    • @cheikhdiatta5755
      @cheikhdiatta5755 3 роки тому +1

      je suis tout à fait d'accord avec vous il a un agenda bien defini.je l'ai connu en 2000.Nous nous sommes vus quelque part à yoff sicap layene et à l'époque il était avec des blancs sur un projet d'hôtel à Mbour . quelques années après je le vois à la télé soit disant marabout et cheikh

    • @nddp221
      @nddp221 3 роки тому

      Bilakhi c'est vrai

    • @caroleducrocq8248
      @caroleducrocq8248 3 роки тому

      @@nddp221 vrai de vrai oui c'est un franc maçon.

    • @abdoulayendiaye7736
      @abdoulayendiaye7736 3 роки тому

      @@cheikhdiatta5755 😳

  • @kacounacou9273
    @kacounacou9273 3 роки тому

    Touskaré nienanalén

  • @awafall5834
    @awafall5834 3 роки тому

    W

  • @alledioum855
    @alledioum855 3 роки тому

    Mais prkw niou beugua dieul affair beugue ko def affairou tarikha bayilen nafekh

  • @actusn87
    @actusn87 3 роки тому +1

    NIOME NIEUPA YEME 6 MOY 9

  • @dabakhsamb5301
    @dabakhsamb5301 3 роки тому

    Atake. Douyone. 🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔

  • @djthiat5416
    @djthiat5416 3 роки тому

    Mansour Diouf ,na khamné bi di nieuw ssi bir keureum lane dieume raye ndayame ,🔪

  • @user-hh8gz8bz6o
    @user-hh8gz8bz6o 3 роки тому +1

    L'argent l'argent l'argent

  • @youssoundiaye753
    @youssoundiaye753 3 роки тому +3

    Dina lékeu séne leufeul ndéye yén wa Dakar buzz

  • @khadydiop793
    @khadydiop793 3 роки тому +1

    Moudiéna méty fék nite thiy kreum beugue ko thié eupelé ndakarou nioko mom

  • @ridial4452
    @ridial4452 3 роки тому +1

    Momuléne dara

    • @astougningue5180
      @astougningue5180 3 роки тому +1

      Daguay doul

    • @oustazahmedfall6478
      @oustazahmedfall6478 3 роки тому +4

      Gnoko mom dé kou beug souf démal si deuk you tang

    • @Yfls2001
      @Yfls2001 3 роки тому

      gorgii yaw lo si kham? Non mais sénégalais il est expert en tout. Kham leipp meune leipp. Bayi leine niok lignou mome way!!!!

    • @dembasamba3348
      @dembasamba3348 3 роки тому

      Deg fen

    • @aminadiop7410
      @aminadiop7410 3 роки тому

      Talibe sonko yi manipulation rekk bayyilen fenn geumoulen benn serigne doul rekk

  • @bassiroubeye4335
    @bassiroubeye4335 3 роки тому +3

    Macky sall mou tèpi leufeul ndm moffi indi li yeup kharal danguène ni dof doflou naane danguèni songou layenne douniou wakh