Youssou Ndour - CLIP - TÉLÉPATHIE- VIDEO OFFICIELLE GRAND BAL 2025
Вставка
- Опубліковано 9 лют 2025
- TÉLÉPATHIE
SAYOU MA LA GEESTOO
FÉKK YAA NGI MAY XOOL
DA FA MEL NI TÉLÉPATHIE
XÉL YI JAXASOO
LI NÉ CI YAW,
MO NÉ CI MAN MI LÉ
L’AMOUR EST SIII FORT,
ÇA NOUS REND FOU
HOOK: MINE NGA MAAYE
DEUGUE DEUGUE DIARAL NGA MA
LO AMOUL
BEUGOU MA
MBEGGUEL DAN KOY DEROULÉ
BA MU MATT
KU NE DI KO SENTIR,
SA YARAM
CHÉRI KESSÉ DOYUL,
DAYMANQUÉ
BÉBÉ KESSE DOYUL,
DAY MANQUÉ
NIDIAYE KESSE DOYUL,
DAYMANQUÉ
MBEGGEEL GU SINCÈRE,
DAY DEGER KECC 3X
KECC, KECC,
DAY DEGER KECC.
Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
/ youssoundourofficiel
/ youssoundourofficiel
/ youssoundour1959
Cou doyaloul si Youssou Ndour lalale j'aime❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️
❤❤❤
La voix unique ❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
La différence fondamentale entre Youssou NDour et les autres chanteurs c'est la justesse et la clarté de sa voix. Il a une puissance vocale extraordinaire. Il est l'un des rares chanteurs au monde à pouvoir monter aussi haut sur des octaves et y rester. Il a un souffle extraordinaire. Je passe sous silence sa technique musicale unique. Macha Allah !
Longue vie à à toi Youssou !❤😢
Amen 🙏🏾 ❤😊😊
Mané ki kouko bagn dangako xamoul , je répète il suffit de quitter le territoire sénégalais pour savoir à quel point il est utile à notre pays. Song bi kou doundoul mbeuguel bou sincère douko degg . On t'aime Papa You tu es le meilleur , mine neign , diaral ngagnou deim grand bal di danse ba sougnouy chaussures daggg 😍🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Wakhatiko
Xalei bima done abbal chargeur apres concert bi avec son ami habillée en orange nopp nako sama call mo fayone mom aussi Bo guissei li xamal ni mangui télépathie ak yaw
Merci beaucoup madame vous avez tout compris et tout dit. Youssou Ndour est un grand Monsieur
Soxna😭♥️♥️♥️♥️♥️
Khana sokhor
Youssou ndour yalla nga goudou fan kouni amine yalla nga goudou fan 🙏🙏
Amine 🤲🙏🥰
Amine
Amine
Amine 🙏
Amine
Le chef suprême de la musique africaine 🎉🎉❤
Voilà la bonne expression que je cherchais beaucoup d'année pour qualifier ce monsieur ......
@@misterdoudujoloffofficiel7504nangou rek ❤
❤❤❤🎉
Sais sa tu as compris bro
Le chef suprême de la musique africaine
YOU MOY MBAYE 🎉
MBAYE MOY YOU 🎉🇸🇳
C’était mon meilleur grand bal , en plus je suis dans le clip j’étais tellement content ce jour là , franchement merci beaucoup Youssou Ndour les Mots ne suffiront jamais pour exprimer ma gratitude envers toi , que dieu te garde longtemps près de nous pour continuer à nous faire plaisir , j’ai que 21 ans et on dirait j’écoute Youssou Ndour depuis ses débuts , cet homme est incroyable, gathié ngalama❤
Keroq walahi je ne reconnaissais pas youssou ndour ndax contane 🥺 , l’énergie qu’il dégage , la constance , la voix mashallah ohhhh🤩🤩🤩🤩♥️
Je t’assure que je croyais être le seul à avoir remarqué Ca🎉❤
Kokou papa you 😊
Qui regardé plusieurs fois la vidéos comme moi
moi a chaque instant
Chaque jour je l'écoute ay trois fois bou ndawé ba ndaw😅😊
Moi
Toi😂
Kou gueum né Youssou d'où moroumou boye yii rk lalale j'aime 🤍👍
Lolou yake sa wakh leu mok sene baye leu wone😂youssou béne sonwame rek soul na carrièrou artiste
Keine xamoul lilanla😭😂🙆🏽♂️ saay dou niit
Moy sen Baye lolou dafa ler
@@Stifleurvvv y. XX 😘☺️😢😲😤🤫
❤
Thiey You sama wadjjjj , nexoul ba nexoul tu es de loin et de très loin le meilleur , le numéro 1 mondial ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Nanguou day fekhal khol, bamouy meune dou tay. Damay lath ndakh amoul wone ay djiné you nieuwone welelelele ❤🎉
Ak youssou ndour dé lep meune nané dei😁
Youssou ya dakh weuye Sénégal toute catégorie confondue nak ❤❤
Nell monde bi
Youssou ndour il représente l'image du sénégal un grand homme yallah nako sunu borrom sameu 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Say youma guesto fekk yaguimay xol 😊❤ dafay melni télépathie 🥲 xel yi diaxaso🙈 lounei ci yow monei ci mane 😍 l'amour est si fort ça nous rend fou😭🤭🙈❤️
Mbeuguel dankoy derouler bamou maat 🤌
Koune diko sentir sa yaram🤧🤗😍
Chérie kesse doyoul day manquer😢
Nidiaye kesse doyoul dayy manquer ❤
Bb kesse doyoul dayy manquer 😩
Mbeuguel bou sincère dayy degeur keuthie💪😘🤭😊😊
Mo metriser woyou mbeugueil nk😭♥️
@MbackeSokhnakhady-xt4pq deggeul waxga deug dh mane faramareen la mais damay deglou gneup papa you c autre chose et j'écris des textes mtx ❤️merci
Yawittt y’a ame degg degg
Amine way
C’est le parolier
Ay papa you balal khalé yi nak bilahi so bayé way ma bayi musique li tmt oh sama khol bi☺️💖
Oh 😥 ❤ son bi nékhna ❤️The King ❤️YOUSSOU NDOUR🥰 est unique UN PARCOURS MUSICAL IMPECCABLE . l’homme qui travaille en silence et laisse le succès faire du bruit longue vie à lui ❤️🥰🥰🥰
Machalla ❤on t’aime trop et tu chantes trés bien 😌😘🥰continue sur cette route ohhhhhhh❤🎉
Grand bal bou mell ni est-ce que dina amaatt.
Bii saff sappp la déffone té non stop 🕺🕺🕺🕺🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
🕺🕺💃😍🥰🥳🎉
Insistel fofou way esk bou melni dina amatttt 😂😂❤❤❤❤
@@amadoufall8853 youssou kay sama wadji comme kou am 18ans😂
@@amadoufall8853 ahh man katt lou khoumbé nii je pensais que diekh na fii🤣🤣🇸🇳🇸🇳💪💪🕺🕺🕺
Khol yeuppa sedd jtjr
Ohhh quelle belle chanson Thiey le Roi tonton Youssou Ndour Yalla gua goudou fane mou and Ak werr
Yagnouko taamal chaque grand bal gua may gnou clip daw bouki yi reen télépathie 🎉❤❤
Ki nak moy kou sell mi. La seule constante.
Le meilleur.
Manam dal bayou gni ak gné di thieupi thieupi.
Merci You amal diam ak salam.
Ana Gni sons youssou ndour di dougou s’en khôl❤yiiiii
Bo maguété kou gnouy bégual😭😭 Ndoura Wally Mberguane on t’aime de façon indescriptible ❤️❤️❤️
MoMA diakhale ❌
Je dédie cette belle chanson d’amour à ma femme depuis la Mauritanie 🇲🇷 ❤
Vous êtes tout simplement le meilleur chanteur du monde Yalla nala Yalla may goudou fane ak wër !! Anni Fans The King manifester Wayy ❤❤
Techniquement, c’est un chanteur au sommet de son art, je crois que son atout majeur c’est sa voix: sa tessiture ténor en plus de son timbre très particulier, à la fois puissante et très juste. Je peux dire sincèrement que c’est l’une des plus belle voix au monde.
Surtout la justesse de sa voix , c est unique
C'est vrai pascale obispo à déclarer récemment dans taratata que la voix de youssou ndour c'est unique au monde c'est une voix de diamant.@@ousseynoundoye102
@@ousseynoundoye102la music est sa passion il adore faire la music donc il se donne a fond pour que tt soit un succes
@adjasalihsamb9398 verite pure
Merci the king Youssou Ndour 🎉❤ longue vie à toi cette chanson c'est très bon
Messoul xewi youssou yalna goudou fan❤❤❤❤❤
🇸🇳🇸🇳 Merci beaucoup le King longue vie sans ordonnance 🙏❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏🇸🇳🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Non yéne deguou léne djimi mbaye, waaw ❤❤❤❤❤❤
Wadji kén dou melni mon😊❤💃🎶🔥l’africain le Sénégalais🇸🇳on est très fière de toi✊🏿💯🇸🇳On t’aime🫶🏿Papa Youssou Ndour🫂😭♥️yalla nala yalla bayék nioune ba thii kanama kanam🙏🏿
Le meilleur chanteur du monde c'est YOUSSOU NDOUR
Le meilleur chanteur de l’histoire du Sénégal 🇸🇳
Khalif Général kouli musiciens que Dieu vous donne une longue vie inchallah
Att bii mo wara gaawa diekhaat beu Grand bal nieuwat😂😂😂
Ça me manque déjà 😊😊
Yalla na diam yagg et longue vie à notre King international ❤👑
Déjà que je ne me remets pas cette soirée et la bimmmm télépathie waouhhhh🎉❤
Quelle puissance vocale ! Sa voix dé dou massa rére si bir musique bi ba gnou koy weur.Jamais !
Qui regarde la vidéo 10 fois par jour comme moi ici😂😂😂
Cest la 8ème fois
guiss na sama bop si kaw kaw grand théâtre bi 🤩 djine Youssou Ndour bi nékété man la fière de papa you. ndongo imatture.
Khôl sedatina li nekhna wayyy... Machallah longue vie au king
L'homme des 3 générations💕💕💕
Hèèè Tèlèpathie bii nèkhna dii mooway 💃💃💃😅😅😅😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰
Mangui tarxisss sakj
@kanistambaye3239 diarnako diii 😄😄
@@pendadiop03dina fi rey nitt 😂
@@aliounegoudiaby2071 doumani dètt deh 😄😄☺️☺️
Khol lén spectacle bi nîepa am classe zéro dérangement
You do morom way ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Tekssi am public bou dégue té andak énergie waouhhh
The BEST and Most CONSISTENT Musician on Planet Earth. YOUSSOU! better than Bob and Jackson. YouDbest!
TRUST ME
Pape ioe dal machallah yalla na yalla goudal sa fane rewmi dafalay sago ndoura Waly mbergane seuteub siré bi❤❤❤
Mashallah Youssou N'Dour longue vie à vous yarabi❤❤❤❤❤
Fierte rekkk gua thi Sénégal🇸🇳 l'Empereur Youssou Ndour. Doundeul illimix🙏🙏🙏 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Ohhhh grand bal bou nekh ! Bimay gnibi sakh j’ai versé des larmes tellement beugou ma wone mou diekh
Thièy papa you le Messi de la musique sénégalais ❤❤❤❤
❤❤❤❤ longue vie a
notre youssou ndour internationale, l'incontournable, longue vie à tous le groupe super étoiles ❤❤❤❤❤ li manoul gnak si deuk bou bari stress bi, à l'instant t les compteurs sont à 0 nous avons vider bcp d choses❤❤❤❤❤❤❤
MachaAllah après tout ses années You n’a pas perdu sa voix originale ❤🎉🎉🎉
Eyyyyyy wayyyyyy
Eyyyyyy wayyyyyy
Sama khol bi Dina wadeu deh❤❤❤❤❤
Non papa loumala wara wakh
Tu es le seul
Tu es l’unique
Tu es le vrai
LE MEILLEUR POINT 👑👑👑👑❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Música maravilhosa lindíssima adorei Suzete Ndaw ❤️
Mané akaye deugue kou ko bagne do nite
Il est le meilleur
Kou beugu buzz fok gua lal ko🎉
Ndour dossén morom ❤❤❤
Youssou Ndour c'est le meilleur chanteur du monde
Pape you défal nga nio lép merci Pape you
Le réalisateur a fait un boulot de malade, de ouffff ❤
Kép kouy téyé micro yaye bayame❤
Youssou néna ça nous rend fou
Viviane né je vais te rendre fou
Thieuy l’amour meune na louné 😂
Vraiment niveau kawéé NA trop
Père YOU yague fi di niou bégueule❤❤❤
Telepathie bi Americans yi sakhe meunou niouko moungne❤sama copines yi tothie nagne sama keur❤😂 We love you Papa you❤❤
Le meilleur de tous les temps Youssou Ndour 👑🥰❤️
Ohhh lii nexnaa trop🔥
Meilleur chanteur de l’histoire de la musique Ndour
Yalla nafi yaga teh guda fann Ndura Wally Mbergane ❤❤❤
Les femmes sénégalaise yén am classe waye ❤❤❤❤❤❤❤
JTJURE KEN KHAMOUL LI LANLA😂😂😂
Le joueur de batterie il est excellent ❤❤
Abdoulaye Lo ndanane deug là mashallah
Mashallah nekhna Yalla na voix bi geuneu Wëër 🙏🙏🙏.
Yalla bayi lafi bathie kanam 🙏🙏🙏
Été. Bonne soirée. Youssou Ndour machalla lii nekhnaa ❤️🫶🏽
THE KING OF AFRICAN SENGEAL MBALAX POP MUSIC LEGEND🇸🇳👑🌟
Yalla nga goudou fane tonton youssou ndour 🎉❤ ya ngui gnouy bégueul bilahi❤
Lima si geuna neex moy Youssou daffa melni kouy soga commencer carriers musical daffa fatheu Lou neex kerok ❤❤❤❤❤❤❤
Longue Vie à notre YOUSSOU NDOUR National ! The best 🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Na artiste yii roy ci mom❤amna class, téy neu aussi dusén morom ci ay way, nite déy simple 🙏
Comme je l’aime. Youssou Ndour le meilleur Chanteur de l’histoire de l’Afrique ❤. La qualité d’image est top, pareil pour le montage ❤️✅✅✅
Le peuple est content de papa Youssou ❤❤❤❤❤❤
Meilleur grand baal❤🎉papa you so magueter kougniy defal grand Baal ❤❤❤💃🏻💃🏻💃🏻
Youssou Ndour le roi de la musique Africaine. Bon Année 2025 Je regarde cette concert au Ghana 🇬🇭.
Merci vraiment c'est vrai ❤
Tu es le meilleur de tous les temps 🎉🎉
Le meilleur chanteur d’Afrique 👆🏾❤️
Yalla dafma natou si Youssou Ndour bilay 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️
Au delà de Youssou, le super étoile, le public, ce public, quel feeling
Il est le seul et unique maestro africain, on t'aime papa you ♥️♥️♥️
The King 👑❤
❤❤❤❤Machallah papa you weni bike ❤❤❤❤longue vie à vous 🎉🎉🎉🎉🎉
The greatest of all Time 👑the king papa Youssou we love you ❤❤❤
Macha'allah grand artiste Au Sénégal là voix d'or 🎵🎵🎵🥰
Mais li nexna dh 😍🤩 yalna sa diam yag papà you the goat 🐐❤️
Youssou c est l icône de la musique mondiale. Il est le meilleur sapo à lui et longue vie ❤❤❤
Machaallah Papa You le roi incontesté et incontestable
Bilahi youssou ndour mi dou nite ak énergie bimouy dégagé khalé yi sakh menou gnoukoo goudal fane way dignou bégal
You, une fierté sénégalaise, africaine, voire, mondiale !
Une grande star qui impressionne et continue d'impressionner le show biz mondial !
Longévité et bonne santé !
Ça montre que comme tonton you aime ces fans vraiment lo niou beugue rek raw naniou lako longue vie à vous et à nous ❤❤
Way bi franchement dafa nékh day dougou si sa xol bilahi limou way mou nékh mine guamayyy deug deug diaral guama hoooo you impeccable lako toudé zéro faute
Le niveau est stratosphérique toujours égal à lui même le roi incontesté de la musique 🎵 ❤❤❤
Moy sen baye dal😂😂😂😂 Youssou Ndour avec les super étoile 🔯 de dkr nio meune nio eupeu doolé 💪🎉❤❤❤❤❤
Thieuy Papa you foukko ndanane di diarr🤧🔥
Khamou mako
Youssou Ndour billaye ya mane ya eupp drôles