SITEU MENACE LAC 2: "KI SOUMAKO DIAPEY...GNIMEY WOUMA, MANE LEU TARKINDA BII..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 14 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 369

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 Рік тому +76

    Siteu Bo Téyé rékk Yalla dinala may Ndamm in cha'Allah 🙏🏽

    • @MohamadoulamineSarr-h9w
      @MohamadoulamineSarr-h9w Рік тому +9

      Lima guiss nii siteu dina dane inchaalakhou

    • @LougaLo-dh2qo
      @LougaLo-dh2qo Рік тому +2

      ​@@MohamadoulamineSarr-h9wamine inchallah

    • @mabeyegadiaga9199
      @mabeyegadiaga9199 Рік тому +3

      Doful dina tey ay mak ñoko yor na baye lac lambdji rek bu nule victoire siteu la dakh lac moy lolou 😂😂

    • @MbayeKa-c9p
      @MbayeKa-c9p Рік тому +2

      Siteu mi mou téy mou yarou déy danou lac dou moroma moko mene moko eupe dollé siteu li rek la ame si komba bi

    • @MohamedMohamed-dw4xh
      @MohamedMohamed-dw4xh Рік тому +4

      Siteu mounoul daane gouye gui ´guene beug mou daane lac ? Bayléne di fowai séne khel . Combat bi nul lay done wala victoire pour lac .parceque lac2 dou djieul béne risque day takhaw deglouko

  • @Le_R319
    @Le_R319 Рік тому +9

    Tapha mbeur nimou déf liss ndiago
    Lay ragal Lac2 defko siteu
    😢😢😢yalla may diameu nieup niou féké talko ❤❤

  • @toutiwakhjobloubari8746
    @toutiwakhjobloubari8746 Рік тому +22

    No li mome vraiment dou combat , lac mo meune mo eupeu dolei .

  • @mbenediouf634
    @mbenediouf634 Рік тому +20

    Siteu machalla nice ❤❤❤❤💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💯💯💯❤️❤️ inshallah inshallah Amine yarabi ❤️❤️

  • @dykhaamar6350
    @dykhaamar6350 Рік тому +12

    Ndam rk Yalmbine siteu kassé ❤❤

  • @mouhameddiallo7007
    @mouhameddiallo7007 Рік тому +19

    Lac yalla nako yalla may ndam

  • @syalima7549
    @syalima7549 Рік тому +20

    Siteu yalnala yalla maye dame

  • @MamadiGassama-tl4bh
    @MamadiGassama-tl4bh Рік тому +24

    En tout cas lac2 et un grand technicien force à toi lac2❤❤

  • @ibrahimacoundoul7118
    @ibrahimacoundoul7118 Рік тому +16

    100%Yalmine tarkinda 🤞

  • @ndeyecodoufaye399
    @ndeyecodoufaye399 Рік тому +3

    Ahh père Becaye je t’adore 😂😂❤❤❤Lac nak manga deugueul sa bopp ,siteu attention Lac da nakari beurel 😂😂😂😂😂

  • @momoseck1617
    @momoseck1617 Рік тому +8

    Siteu ni nga doone wakhé contre Sa Thiés 😂
    Wakh djiou néh nga meun on te connais très bien

  • @MoustaphaWade-u4m
    @MoustaphaWade-u4m Рік тому +4

    Nn siteu ya woor dé😂 yaw rk lanouy topp yalna la yalla may ndam inchallah ❤

  • @IbrahimaGueye-q7e
    @IbrahimaGueye-q7e Рік тому +17

    Siteu yombale guako dh 😢 té gua déff Ndank mbeur mi guéneu nakharé beréle guaye dadiéle

  • @AlyNdiaye-f8i
    @AlyNdiaye-f8i Рік тому +7

    Siteu défale attention bou bakh guediawaye la deh ❤❤

  • @idrissabaro3132
    @idrissabaro3132 Рік тому +8

    Bilaye Siteu daye thiahane

  • @lassanatalla767
    @lassanatalla767 Рік тому +7

    Siteu mi am na loumouy dieul li naturelle loul d 😂😂😂😂

  • @amarniang3915
    @amarniang3915 Рік тому +6

    Siteu moye Sénégal

  • @CISSEBOUSONKO
    @CISSEBOUSONKO Рік тому +11

    Nervi yi kou daan yaa xam kounou daaan yaa xam focus 2024😂😂❤❤

  • @DialloMouhamadou-c5x
    @DialloMouhamadou-c5x Рік тому +15

    Lac il est très intelligent 😅 combat bi dou yomb si siteu

  • @layesam5162
    @layesam5162 Рік тому +7

    🔥🔥🔥🔥🔥DESI CALANNDA , C'EST CHAUD😂 NÉKHNA BA PARÉ . MASHALLAH 🥰

  • @doudoundiaye7130
    @doudoundiaye7130 Рік тому +3

    Allez siteu....vive la jeunesse

  • @momobouthiapathiolybi7752
    @momobouthiapathiolybi7752 Рік тому +16

    Lac d'à nga wara attaqué force siteu ndam rk inchalah

  • @seydoudieng9099
    @seydoudieng9099 Рік тому +6

    Siteu outaal doolé ta boul faté lac de guerre respect motakh mou dieulleu nguir yalla boulko yah oie borom bakhnga

  • @mbeusseneymar5862
    @mbeusseneymar5862 Рік тому +5

    Yalmine bi inchallah yalnala yallah may ndam🙏🙏🙏🙏

  • @ngallmbaye1052
    @ngallmbaye1052 Рік тому +4

    Siteu mystique rek la yakar

  • @bathiedioum898
    @bathiedioum898 Рік тому +2

    Siteu yalna yalla maiye ndam inchalla

  • @cheikhtall-rp4di
    @cheikhtall-rp4di Рік тому +6

    Wakh deugeu yala siteu manoull dann lac 2 bilahi

  • @elbiranetoure262
    @elbiranetoure262 Рік тому +8

    Waxou lac 2 kay situé yalna yalla mayla ndam inchalah

  • @424000
    @424000 Рік тому +4

    Libérez Sonko.

  • @baba_07sn
    @baba_07sn Рік тому +2

    Siteu rék Incha allah ❤

  • @falldragonmart2161
    @falldragonmart2161 Рік тому +12

    Siteu mi day theatre rékk 😂😂😂😂. Vraiment li d'où Lambeu

  • @Mackenzi-z4f
    @Mackenzi-z4f Рік тому +40

    LAC 2 EST L'UN DES MEILLEURS LUTTEURS DU SÉNÉGAL.

  • @NogayeThiam-t8s
    @NogayeThiam-t8s Рік тому +1

    Siteu rkkk❤❤❤❤

  • @PapaAbdouDiédhiou
    @PapaAbdouDiédhiou Рік тому +46

    Siteu combat bi déé boco yakaré si mystique je suis d'accord té meunoulo eupeulé lac mystique ni dollé ni rien ..

    • @assanediakhate3618
      @assanediakhate3618 Рік тому +3

      Degue bou weer

    • @fatoumbaye1121
      @fatoumbaye1121 Рік тому +4

      Machallah deugue bou wére gan wakh boudé muystique lac 2 monko euppeu si lamb dji boudé doolé tamit lac 2 monko euppeu wayé lac2 na déffe trés attention bala nioukoy déffe comme ligniou déffe balla gaye2 soteuko boy niang2 ak reug reug nioy diappalé siteu si ngalathieu ak yénéne mbeur si Souf lac 2 souma sagnion daffay guéne guédiéwaye dem fénéne préparer combat wam kéne bagnia kham foumou néke té lac 2 n'a kholat boubakh entourage gam bala nioukoy diay comme nigniou déffe balla gaye2 Mane faralouma lac 2 faralouma si kéne Mane ama baldé moy sama mbeur séke lac2 daffa yaarou kham nimouy wakhé motakh mou nékhe ma siteu temps yii mystique bou doy War la yoor entout cas lamb dji 50/50 la kounéke meuneu na daan moromam lamb leigui doolé fégniatousi kou euppeu nagalathie yay daan lamb daffa barri surprise motakh diaroul wakh kimoy daan bala jour ba gay rouss lamb leigui kéne khamatouko daffa diakhasso dakh mystique bou barri dagay guiss mbeur yooré victoir ram diékou mystiquement baparé si jourou combat bi niou nangou victoire bi si lokhom diappeuko mystiquement mbeur bi rére si sass si diakhasso Di déffe loum meussouta déffe avant arbitre Di sifflé tamit dagniesiy diappeu mbeur yéweko bamou deugeur nagamal ayy tankam ba tankeu yii dotoul meuneu bougé dagay lale sa nguimb adversaire rek mou teural la dagay méle ni néwe ligeiy bou Boon mougui nonou si tankeu wala lokho néwe lagniekoy ligueiyé boparé déffeko sisa birr nguimbe bi nguimbalé woko sa
      sa adversaire bouy lale sa nguimbe Di danou momla boy niang 2 nguimbo woon motakh kouy wakh si lamb nagan kham boubakh ligay wakh lamb leigui ak bou dieuckeu bokoul

    • @IbrahimaFaye-l1k
      @IbrahimaFaye-l1k Рік тому +1

      kone dolé si volume là khamo lamb

    • @cheikhndiayetouba040
      @cheikhndiayetouba040 Рік тому +1

      Lolu dong lasi yakar ta lolu Lac mo kolo apoole

    • @BinetteSylla-gy8nk
      @BinetteSylla-gy8nk Рік тому +2

      Fii koufii mére diokhé 100 fran
      Siteu kassé ndam rk inchallah

  • @Hamadythiam-s8b
    @Hamadythiam-s8b Рік тому +1

    Siteu yallah nako yallah may ndame❤

  • @woneabda5298
    @woneabda5298 Рік тому +6

    Siteu c'est un vrai guerrier et un vrai comédien 😂😂😂

  • @ndiogoundiaye8555
    @ndiogoundiaye8555 Рік тому +2

    Bn chance yalmine bii siteu rék

  • @MourtadaFaye-l7v
    @MourtadaFaye-l7v Рік тому +1

    sitteu rk lañouy toppou ❤❤talibé bamba❤❤

  • @mbayelo7022
    @mbayelo7022 Рік тому +1

    Siteu kassé ❤

  • @babadiop4316
    @babadiop4316 Рік тому +3

    Siteu khana amoul mbokou 😂😂😂

  • @madefaye5980
    @madefaye5980 Рік тому +3

    Lac 2 mo geuna ragal thie lamb bou siteu ndam rk inshalla

  • @MamediarraGueye-z2w
    @MamediarraGueye-z2w Рік тому +2

    Non mane siteu damaye fathie tarkindabi😂😂😂😂

  • @mbodjielfromfouta1244
    @mbodjielfromfouta1244 Рік тому

    Billay Siteu moy sénégal🇸🇳 Tarkinda yi niongui sa guinaw💪🏿💪🏾💪🏽💪🏿

  • @papeyakhyasow989
    @papeyakhyasow989 Рік тому +1

    Siteu mi na yammm té régler sa thies sako meune foufff té sa thies lac de guier moy magam

  • @fatouaidara7910
    @fatouaidara7910 Рік тому +1

    Siteu attention lac ndanane leu dh mais lamb meuna lou nèk bonne chance

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv Рік тому +5

    Siteu yabaté nena zarko mo gueuna tangue lac 2 😂

  • @MbendaThiam-m7k
    @MbendaThiam-m7k Рік тому +1

    Man beugg na siteu trop mais lac Damaka beugg ndax limou yarou

  • @ousseynouba3805
    @ousseynouba3805 Рік тому

    Bilay lac moy sm mbeur me siteu j❤

  • @MaimounaNdiaye-v4u
    @MaimounaNdiaye-v4u Рік тому +2

    siteu seull dokhol khana❤

  • @mballomaoulidou3358
    @mballomaoulidou3358 Рік тому +6

    😂😂😂😂😂 défa am ay risque yo khamné boko bayiwoul diko diel manga diaré fofou déé té man ragalna lac doorko mou wadd niou yobouko principale mou fatou. Way siteu day toukh yamba way

  • @momolecaporal5536
    @momolecaporal5536 Рік тому +2

    Siteu Siteu leuH 💪🏿

  • @Lilldio
    @Lilldio Рік тому

    Siteu rk jusqu'à ma mort ❤️😊😊😊😊

  • @FatoupendaBa-tt9kb
    @FatoupendaBa-tt9kb Рік тому

    Aytia lac ndam rek sama nidiaye bi💪💎

  • @djhotgoudiry9818
    @djhotgoudiry9818 Рік тому

    Focus 2024 Ousmane Sonko rek

  • @khalilfaye1289
    @khalilfaye1289 Рік тому +11

    Siteu, Niang bou Ndaw rekk mollah eupe dollé.😂😂😂😂 Kone Lac 2 doussa morome

  • @Mamapapis-t1p
    @Mamapapis-t1p Рік тому +3

    Mais siteu dafa dof dh 😂😂blie

  • @malickkmplayeurniang9404
    @malickkmplayeurniang9404 Рік тому +5

    Siteu moytoul contre attaque gou lac 2, lou lere lala wakh

  • @Loriginalfaye
    @Loriginalfaye Рік тому +2

    Niounne tarkida bi rek laniouy toppou

  • @amydiome1366
    @amydiome1366 Рік тому

    Situé yalnala yalla may name

  • @Ndayemoussaliou
    @Ndayemoussaliou Рік тому

    Ay niom niep damalén beugua 😍

  • @mohamedseye321
    @mohamedseye321 Рік тому +1

    Champion ya gui soga am combat

  • @ibougueye9109
    @ibougueye9109 Рік тому +12

    Siteu danou nga ba paré ki ma giss

  • @seydoudiop9579
    @seydoudiop9579 Рік тому +5

    Siteu déh amoul chance cii combat bi

    • @Thebabacar
      @Thebabacar Рік тому

      Ouais c’est ce que je pense moi aussi même si j’aurais aimé qu’il le bat

    • @seydoudiop9579
      @seydoudiop9579 Рік тому

      @@Thebabacar môme ga nou wahdji geuneuh baré geune KO arranger dah bou dano niounéh dolé 💪 rék lako eup wayé eupouko fite 😢

  • @mbodjielfromfouta1244
    @mbodjielfromfouta1244 Рік тому

    Mbeur deuk bi ♥️💪🏾💪🏽💪🏾💪🏽
    Ndam rék inchllh 💪🏽💪🏾💪🏿💪🏼
    SITEU yaa wooor 💪🏾💪🏿💪🏻💪🏾

  • @seydoudiop9579
    @seydoudiop9579 Рік тому +2

    Woléne sathies niko siteu gui roubéh fi

  • @JuniorSeye-u5x
    @JuniorSeye-u5x Рік тому +2

    Siteu yalna ko yalla mayy ndam

    • @seydoudiop9579
      @seydoudiop9579 Рік тому

      S déh wah rék lacii am

    • @JuniorSeye-u5x
      @JuniorSeye-u5x Рік тому

      @@seydoudiop9579 lolou nga yakar rek yalla mo yor ndame yalna ko diokh siteu

  • @gatesneysen7777
    @gatesneysen7777 Рік тому +4

    Siteu li nga am si lamji donc frofite toi de faire le show 😂🤣🤣🤣🤣

  • @amarecoulediop3324
    @amarecoulediop3324 Рік тому

    vraiment sawayy siteu sa wakh barina trop khaliss rek guay oute si combat bi mais lac dou sa morome meuno ko dane

  • @sabarasts
    @sabarasts Рік тому +2

    Siteu sou dané Lac2 miracle la 😂 Lac2 sa rak Sathies da niow diakhassé Siteu dane ko, ey so nulé ak Siteu 😂

  • @stevedanieldossantossilva7795
    @stevedanieldossantossilva7795 Рік тому +2

    Bébé Diéne le Messi de l’arène 🎉

  • @senegalrek4657
    @senegalrek4657 Рік тому +5

    Vraiment lac carrière VIP yassi gueuneu niaw carrière 😂😂😂😂

    • @cheikhomarniang3239
      @cheikhomarniang3239 Рік тому +7

      😂😂deimal gestu khamo li ngay wakh kou sanione am mbeur bou meilni mome 😂😂

    • @AboulBacharSall
      @AboulBacharSall Рік тому

      @@cheikhomarniang3239kein bougoul am mbeur bou melni mom match nul ak daw moy palmarès

  • @OusmaneNdiaye-dv3sf
    @OusmaneNdiaye-dv3sf Рік тому

    Yalmine bi kassè lagnie topou bly ioe ndam rek ❤

  • @daoudarassoul1848
    @daoudarassoul1848 Рік тому +1

    Lac nak déma guiss ni dey titte mais yalna nga dan

  • @souleymanedeme1095
    @souleymanedeme1095 Рік тому

    Siteu rk lañuy topou BiLLaHiii walay ❤😂

  • @MakhouDiop-k9e
    @MakhouDiop-k9e Рік тому

    Lac de guierre day féne rék 😂

  • @babasao9130
    @babasao9130 Рік тому +6

    Billh siteu amna combat

  • @barandiaye1474
    @barandiaye1474 Рік тому +2

    Siteu sa wakh bi yeup tite kassé laa😂

  • @petersept4334
    @petersept4334 Рік тому +1

    Siteu viens d'enregistrer tout ce que dis le vieux sage😂😂😂😂

  • @odoa4880
    @odoa4880 Рік тому +2

    Siteu li la lac wax bayyi ci xel«lii rekk nga am ci combat bi» 😂😂😂

    • @momoseck1617
      @momoseck1617 Рік тому

      Siteu ni la doone def ak sa thiés 😂

  • @AstouGueye-w4m
    @AstouGueye-w4m Рік тому

    Siteu Yako meune ndamm rek inchallah

  • @NdongoDieng-gw1xo
    @NdongoDieng-gw1xo Рік тому +7

    Siteu jour bi nga dieulé avenchou lac 2 nga coumacé danou ba lamb dja 😂

  • @inocentdf4officiel222
    @inocentdf4officiel222 Рік тому +4

    1x Double chance pour lac

  • @SenyFaye-i4j
    @SenyFaye-i4j Рік тому +1

    Siteu daffa diafour thi combat bii😅

  • @malamidiamaye686
    @malamidiamaye686 Рік тому +2

    Siteu, Lac 2 moola meun hamal sa bopou yowit😅

  • @FallouDiouf-xo4ot
    @FallouDiouf-xo4ot Рік тому

    siteu kesse lay top domou serrere bi

  • @lahatCissė-p9i
    @lahatCissė-p9i Рік тому +4

    Lac yw layè waxal bou defè 2 minute ma bayil la😂😂😂

  • @mamadousy6312
    @mamadousy6312 Рік тому +2

    😢😢😮khana siteu da toukh yamba

  • @philippendenendiaye2756
    @philippendenendiaye2756 Рік тому +1

    siteu rek sougne la dané dougne découragé ki dagne kaye dane

  • @massendiaye5802
    @massendiaye5802 Рік тому +15

    Non Siteu déy thiaxane bilahi Lac mi mo gueune nakadi dane si ténors yi am dolé, technique, tactique défensif té erreur bo déf mou exploité ko. Eum kén dou mom mom miko dane

  • @mohamethsamb
    @mohamethsamb Рік тому +2

    Lac dane Siteu loumou koy yokk ? Dara 😂

  • @AgfhHsisi
    @AgfhHsisi Рік тому

    Siteu le champion

  • @mamadoukane5669
    @mamadoukane5669 Рік тому +1

    Le silence parle

  • @therealBabs92
    @therealBabs92 Рік тому

    Siteu Rufisque est derrière toi ndam rk inchallah✊

  • @ismailayade4979
    @ismailayade4979 Рік тому

    Bilahi siteu eupo lac doleii eupoko mistik koula khol kham ni si misrik gua yakar pour am ndam gay rapi rapi ni ndak rek vive lac 2 vive guediawaye

  • @boylebou3230
    @boylebou3230 Рік тому +1

    Beuré bi lac yoor Siteu manouko dane

  • @SalaMbengue
    @SalaMbengue Рік тому

    Siteu💪💪💪

  • @eddythiam2121
    @eddythiam2121 Рік тому +1

    Lac mola Mane dé boy siteu

  • @salimatakannegieser7303
    @salimatakannegieser7303 Рік тому

    Siteu🎉❤❤

  • @mbodjielfromfouta1244
    @mbodjielfromfouta1244 Рік тому

    Lac vrai tappét leu😂😂😂

  • @AlassaneNiang-f4w
    @AlassaneNiang-f4w Рік тому

    Ms siteu mi liguéyul luy yeungueul lac de guerre