Kou meuseu nek a letranger di gua kham li tahirou sarr di wakh dou sokhor ni rasiste mais dina takh gniou identifier len dina dougale khaliss thi rew mi je ex thi mauritane bi rek une tu veux entre dans teritoire tu paye 5euro pour 72h au au cas tu veux rester long dure tu va acheter leur carte sejour pour un an a 50 mille frc j valable pour tout les etranger pour koi pas nous esseyons cela
Yaw est-ce que comprendre ga limouy wakh...Sénégal dale dou avancé nite day wakh, ape doff diougué diko tontou té sank khamoul la quintessence, les tenants et aboutissants de la personne qu'il essaie de répondre...et c'est dommage
@@mouhamedndaw2341 Say ki dama ko dégulou bamou sapi sapi ma amoule probléme ak etrangé yi probléme ak guineen yi la am meune nga téke visa sans mo am impact si tourisme bi ni nga kaye tégué la reke ak woutine bi meuna néke en ligne.
Hakh tahirou sar wakho fi dara gnigaye wakhal niola app xam xam fooooooof laga yakarone thi ousmane sonko batakh ga wanko ganaw amoul te yaw amou change
T.Sarr exemple Japon n'a pas besoin de visa jusqu'à 90 jours et sur 200 pays ,O.S parle de réciproque en vers le parlement Européenne qui vient juste d'être adopté de durcir les visa ya 4 jours ,1 fois refusé puis attendre 5ans pour redeposer donc va dormir
C'est faux Qatar petit pays tourismes généré des milliards de dollars par jours, france na même pas de ministres du tourisme idem des milliards d'euros par jours
Tahirou sarr,fiche nous la paix .peux tu nous dire le nombre exact de sénégalais vivant a l étranger.encore une fois fiche nous la paix avec tes propos xénophobes
@@badaboys2098 sa khéte yépe maléne gueuna néke sénégalais bougni wakh sénégal mane ak fima bokh mo takh gnouye wakh moule lébou. mais nékou ma raciste comme yaw ak sa wadji.
Tahirou xénophobe sarr est contradictoire, comment peut on rejeter le visa pour les occidentaux et vouloir adopter la carte de séjour pour les africains ? Lii Moy Niémé ndring Ragal Toubab 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Démal outi xam xam moo guën di languamu ci carte séjour ak le nombre d'étrangers. Tu ne crois pas au chiffre de l'ANSD et tu veux qu'on te donne ses chiffres. Le populisme à la Zemmour ne marche pas au Sénégal. Xam xam rek Wala Out.
@@MouhamadoumassambaDiop-ox6nv Ils parlent des touristes. Les touristes ne sont pas des immigrés. Il propose un séjour de 21 jours au delà le touriste doit payer la carte de séjour. C'est pour préserver les emplois dans le secteur. Affaire bi du wax Kessé mais xam liguay wakh.
Merci beaucoup T S
Merci beaucoup tahirou 🔥✊
Vive Tahirou Sarr le peuple est fier de toi 👍
Merci tahirrou sarr pour un bon raisonnement
Vive presiden tahirou sarr
Baravo tahirou
😂😂😂Sénégal mo nékh
Lutakh 😂
Sonko moh fal nyeup 😂 ma Sha Allah ❤
Tahirou Sarr dh bokoul si gnimou fall 😂
@ hahahaha 😂 degue la
Lolou dafa léer 😂Tahirou seul ❤
Machallah amna solo dh
Ensemble bii mom woute na ak yi passe nivaeu bi kawe na
J'adore Tahirou
Merci way tahirou sarr mashallah xam xam dal bakhna si réw
Tahirou dh yako gueune diangue😂
Bo nèkoul complèxè tahirou yako eupeu xèl pour mome problem senegal dal africains yi mais dou toubab yi dieul soudou kom kom bi
Djang AK xam d'où béneuh nitt meun gua djangu lounek tei dh tag gua am xam'xam walah sah d'où tei si'sa woyof guay djanguei si nitt tei doula wagnii
Tahirou féne rékk la meun !
Fane la Étrangers yi téré Sénégalais yi am emplois ?😅
Machala au moins le niveau des députés est élevé pour cette législature
Tahirou daf may fateli bamay diouguè maroc dieul auto di nieuw Sénégal eksi Mauritanie sejour 3 mois la dagueu et cest obligatoire ma def feu 2 jour
Pour l’idée de Tahirou n’est pas mal en soi, surtout la question liée au titre de séjour. Au Maroc il y a titre de séjour pour les étrangers
Yow tahirou Yasine mola déce
Kou meuseu nek a letranger di gua kham li tahirou sarr di wakh dou sokhor ni rasiste mais dina takh gniou identifier len dina dougale khaliss thi rew mi je ex thi mauritane bi rek une tu veux entre dans teritoire tu paye 5euro pour 72h au au cas tu veux rester long dure tu va acheter leur carte sejour pour un an a 50 mille frc j valable pour tout les etranger pour koi pas nous esseyons cela
Mome lou takh gnouni visa d'entré pour toubab yi mouye kasse nationnaliste bouye khékh africain yi di défendre toubabyi fi kassé la am
Yaw est-ce que comprendre ga limouy wakh...Sénégal dale dou avancé nite day wakh, ape doff diougué diko tontou té sank khamoul la quintessence, les tenants et aboutissants de la personne qu'il essaie de répondre...et c'est dommage
@@mouhamedndaw2341 Say ki dama ko dégulou bamou sapi sapi ma amoule probléme ak etrangé yi probléme ak guineen yi la am meune nga téke visa sans mo am impact si tourisme bi ni nga kaye tégué la reke ak woutine bi meuna néke en ligne.
Tahirou intérêt Sénégal laye khekh yawe ndering nga mo takh do comprend
Très pertinentes suggestions et questions, du courage et bonne continuation Tahirou ❤
Mieux que Sénégal sorte de la CEDEAO 😂😂😂 ce mieux pour vous.
El Malick moo néhh
Quelle est la pertinence de la question de Tahirou sur le nombre d 'étrangers ?
Il est limité et vous en aurez la confirmation à l'avenir
Oh oh boulene maye Tahirou beuse
Tahirou sèll
Hakh tahirou sar wakho fi dara gnigaye wakhal niola app xam xam fooooooof laga yakarone thi ousmane sonko batakh ga wanko ganaw amoul te yaw amou change
Waye doule
Non li mounoule néke mome béne probléme kassé la am si adounam mouye etranger yi. Bou etrangé yépe guédone guéne Sénégal dangay déme retraite khana
T.Sarr exemple Japon n'a pas besoin de visa jusqu'à 90 jours et sur 200 pays ,O.S parle de réciproque en vers le parlement Européenne qui vient juste d'être adopté de durcir les visa ya 4 jours ,1 fois refusé puis attendre 5ans pour redeposer donc va dormir
Mercredi honorable député Tahirou.
wa elle maliak kangne la degeu poular😂😂
Daara jolof la deuk di cia peul ya
C'est faux Qatar petit pays tourismes généré des milliards de dollars par jours, france na même pas de ministres du tourisme idem des milliards d'euros par jours
Merci Tahirou sarr ❤❤❤❤
Yow yafi dibiwone orix yi haménagnela
Éric zemour Sarr 😂😂😂😂😂😂
Raciste la 😂😂
View tahirou sarr❤❤❤❤❤
Thiey Tahirou ak étrangeé 😂
Tahirou très pertinent merci
Merci beaucoup Tahir ou Sarr bravo 👈🙏🙏🙏
Merci tahirou❤❤❤❤❤👍
😂😂😂😂😂😂😂
Vive le président Tahirou Sarr ❤❤❤❤
Merci beaucoup honorable député tahirou sarr ❤❤
Tahirou sarr,fiche nous la paix .peux tu nous dire le nombre exact de sénégalais vivant a l étranger.encore une fois fiche nous la paix avec tes propos xénophobes
Doul ndayam yak snoko penser unique dufi ndayi am na ku neik wax luko neix mu ndayi diex
Dieureudieuff tahirou ❤❤❤❤
Dieureudieuff tahirou ❤️❤️❤️ iow reik
Merci c'est vrai tahirou sar
Clo saarr
Non vrai racist xenophobe la eric zemmour rek lamaye diokh mouye melni keurigne ni
Carte sejour walla Niou tegeul sène nday nguène abal Niou rewmi
Loutax yen niit yu ñull yi complex? L'Homme noir doit etre fiere de sa peau 😢
@@badaboys2098 sa khéte yépe maléne gueuna néke sénégalais bougni wakh sénégal mane ak fima bokh mo takh gnouye wakh moule lébou. mais nékou ma raciste comme yaw ak sa wadji.
Yaw sonou kéwale yiga dibui faté wonko
Ki fou mou dianguè
Le Sénégal c'est pour les sénégalais 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Tahirou sarr rék ba 2029 inchalh
Alkhourane bi soko ngeumone do lekk oryx bou sénégalais yep bok
Tahirou xénophobe sarr est contradictoire, comment peut on rejeter le visa pour les occidentaux et vouloir adopter la carte de séjour pour les africains ? Lii Moy Niémé ndring Ragal Toubab 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Xana ndering nga yau?😅
@badaboys2098 lathko sa y..
@@insadiallo2133parce qu'ils sont moins utiles pour le pays que les toubabb
Je suis totalement d'accord avec tahirou 👏👍
Nena day tarri sarr et tu ya voler des milliards bagueu nekè artp
Je suis parfaitement d'accord avec tahirou Sarr sur toute la ligne
Tahirou SAR Machallah
Vive tahirou Sarr ❤🇸🇳
Merci beaucoup
Dina bakh Incha’Allah ❤
Vive Tahirou sarr 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Tahirou merci
je suis patriote mais j'aime tahirou
Merci Tahirou ❤❤Sarr
Merci tahirou sarr 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Je suis sonko mai je dacor avec tahirou sarr
100/100Tahirou ❤❤❤❤je suis patriote mais je suis avant tout nationaliste ❤❤❤merci Tahirou❤❤❤
😂😂😂
Machallah sonko
Démal outi xam xam moo guën di languamu ci carte séjour ak le nombre d'étrangers.
Tu ne crois pas au chiffre de l'ANSD et tu veux qu'on te donne ses chiffres.
Le populisme à la Zemmour ne marche pas au Sénégal.
Xam xam rek Wala Out.
yaaw guinéen gue😂
dugua faay carte séjour
@@natvecrocs7248 bouñou défone carte séjour yaw ak sawa famille diguén nokou sa xacc
Machllah Tahirou Sarr
❤❤❤❤❤❤❤❤❤ tahirou sarr rek kap dong
Merci beaucoup tahirou sarr❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤🙏🙏🙏
Sénégal🎉❤❤❤❤❤
Merci tahirou
Merci Tahirou
Oui am na sollo vraiment
Merci ❤❤❤❤
🎉🎉🎉🎉
Senegal nak mingui sooga ame assemble bou bakh
Merci
Le débat s est eleve à présent à l assemblée Nationale!
Merci Tahirou Sarr
Tahiroou rek
Amna solo
On attend sa réponse. J'espère juste qu'il va confirmer son mensonge de la campagne
@@khalil2543 nationaliste boo xamni bou dégé visa d'entrée du territoire Mouy fat fati
Un complexée devant les toubab 🤣🤣