salam dieureudieuf Serigne bii yaggfi te wer Mbacke yalna yalla York leeri Serigne saliou Mbacke te taasniou si barkem Barke rassoulilahi Mouhammed Salalaou aleihi wa salam
@@makhtardieng9315 bou ki dioudou 1er janvier bala 20 janvier gnom bourdiou diaddoyou toubab diko wax capricorne sén tabiha di souf gni mom sén mbir dou gaw lou gniy am da lén béteu wayé ay mougne kat la gniy don
Borombi SWT yook ay leeraam té tass gnou ci Barkébi Amine !
Dieuredieuf Serigne cheikh saliou mbackè yalla nafi yague té wer Amine yarabi ❤
S samah une légende dans la voie mouridiya
Mbacke tay toylo gua sama khol ci serigne salihou lollll
Mbacke say kadou dafa nekh té leer macharla té danga xam si domi Serigne Touba ❤sunu xol yi 😭😭😭Dieureudieuf Yalla ngen fi yague té weer
Ma Cha ALLAH. MBACKE yag fi lol tai am wérr.
salam dieureudieuf Serigne bii yaggfi te wer Mbacke yalna yalla York leeri Serigne saliou Mbacke te taasniou si barkem Barke rassoulilahi Mouhammed Salalaou aleihi wa salam
Allahouma Salli Hala SEYDINA MOUHÀMADINE WA HALA ALY SEYDINA MOUHÀMADINE WA SALIM !
Man mourite la touba la deuk s saliou lay noyé sagn n'a niane yalla May bepou djioulite diam ak khéweul si barké s saliou
Amine
Ndeysan
Yalla nañuko gën di begg❤
Dieuredieuf serigne saliou mbacke
😢😢😢😢😮😢
Beug mame Saliou rek bilahi Brom yeurmandé gui
Ndaysan yageu lool ak weer ❤❤
Mashalal âme n’a solo mbacke
Jërëjeffé Cheikhouna Ahmadoul Khadim
Jerejef Serix Salihu Mbàkke
Thieuy Bégue na dé...!!!😊
Nbake yague fi Lolou andke were inchallah
Machallah ❤❤❤❤
Jaajeuf mbacke ziarnala
Dieuredieuf serigne touba
Ndaysane
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤
Machallah
❤❤
Serigne souhaïbou 27 juin la gané adouna bourdiou saratan la yoré motax mou yéné diam nieup diarignou asszard amoul comme ousmane sonko bourdiou saratan la bokou
Boudé jenvier nak nokay toudé
@@makhtardieng9315 bou ki dioudou 1er janvier bala 20 janvier gnom bourdiou diaddoyou toubab diko wax capricorne sén tabiha di souf gni mom sén mbir dou gaw lou gniy am da lén béteu wayé ay mougne kat la gniy don
@@makhtardieng9315 bou gni dioudou 21 janvier ba 31 janvier sén bourdiou dalwou la toubab diko wax verseau ♒ sén tabiha di nguélaw
Kou baxx Mangui siaré khana beugonaa xaam kou dioudou 5 Septembre bisou gouddii Aldioumaa
@@bacarzokalzo7122 vierge ♎ sa nature souf la ms yén sén mbir dou gaaw
Ousmane sonko sou falo diarigne réewmi if allah wills
Dieureu dieuf mbacké balla
Dieureu dieuf Mbacké