“Youssou Ndour dafay ligueye di bégueul khol yi”, Bouba Ndour

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 395

  • @ramatoulayediagne8699
    @ramatoulayediagne8699 4 роки тому +34

    Avec Youssou rék ne vous fatigué mm pa il est là pour nous faire sentir la vrai musique kan j'écoute ces chansons je ressent de profondes émotion que ne peux mm pas expliqué et je ne suis pas là seul donc pas la peine de le critiquer il est le meilleur

    • @tele1514
      @tele1514 4 роки тому +1

      Bilay wakhco si kaw nioguini tok Di khar merci

    • @nittoudeugrek9684
      @nittoudeugrek9684 4 роки тому +1

      C le meilleur

    • @cheikhomarngom7095
      @cheikhomarngom7095 4 роки тому

      Youssou c'est mon chanteur mais là je suis pas d'accord avec lui pour être franc.on a pas besoin de ça pour vaincre le Corona virus,la journaliste tu as raison bouba n'a pas répondu à la question,il a fuit la la question par manque d'arguments et personne ne saurait répondre cette question.soyons responsable et implorons Allah à location de ce mois béni de ramadan pour qu'il nous aide car cet virus est un être venant de lui...le Coran est la et le plus important est sans doute le meilleur pour apaiser les cœurs.je vous jures chers musulmans essaiyer d'y concentrer vous verrez....svp.je mescuse

  • @niangmodou47
    @niangmodou47 4 роки тому +7

    merci beaucoup je suis très d'accord avec toi je te salue depuis Italiano

  • @charlottediop5758
    @charlottediop5758 4 роки тому +9

    Mane dal Youssou.Ndour la beugg ❤ khamoumeu kénène nak longue vie à toi grand bi 🙏

  • @coumbabeye9969
    @coumbabeye9969 4 роки тому +27

    Merci bouba bonne question

  • @tele1514
    @tele1514 4 роки тому +20

    Merci bouba bien parlé

  • @absaseck7851
    @absaseck7851 4 роки тому +2

    Machalla réfétna tièe couv tièe canem 🇸🇳🇫🇷
    Yahlla na lénne yahlla samme tè samme sens diébotte amine ya rabbi dieuredieufetti Ndour

  • @cheikhbadaradiop7377
    @cheikhbadaradiop7377 4 роки тому +15

    Merci bouba you dou lién falé

  • @abdoukarbalatv5250
    @abdoukarbalatv5250 4 роки тому +31

    Merci bouba

  • @modoumbackeniang7185
    @modoumbackeniang7185 4 роки тому +35

    Boulèn tontou nioune youssou lagne begue❤❤

  • @elzofall742
    @elzofall742 4 роки тому +22

    Youssou.ndour.ma.yeureume.sa.none

  • @amathtv7178
    @amathtv7178 4 роки тому +6

    Youssou ndour i love you so much thanks

  • @babacargeuye1114
    @babacargeuye1114 4 роки тому +1

    Nekh nékh trop billahi wallahi lii nékh na boumou diénh c très nekh trop merci beaucoup nous somme tous d'accord avec toi youssou le puissant que dieux le tout puissant te protège amine.

  • @laminendiaye4631
    @laminendiaye4631 4 роки тому +22

    Sénégal dafa Bari gnou sokhor,ignane... Youssou est une fierté pour l Afrique...boulénn falé

    • @nittoudeugrek9684
      @nittoudeugrek9684 4 роки тому

      Walay ma deg deug

    • @laminendiaye4631
      @laminendiaye4631 4 роки тому +1

      Non franchement,c est incompréhensible,qui n a pas chanté pdt cette période.En plus,c est un moyen de sensibiliser...amna yenen yougnou wara meneu lidjeunti mais ay détails rékk,aucune objectivité,mais vraiment sokhor bakhoul

    • @Xavi8689
      @Xavi8689 4 роки тому

      C vrait mon frere bilahi mane souma guisse kouy critiquer you daf may diakhal mais galsen dafa bari gnou sokhor bilahi

    • @doorwaar9465
      @doorwaar9465 4 роки тому +1

      No sokhor Amousi sama gayi Mes basi def lou nekhoul yalla gnou andesi ak mom tamit mes musique yalla moka haramal

    • @valide426
      @valide426 4 роки тому +2

      Yalla dé diamou yalla la digue lé mais pas musique

  • @bakhyaye4756
    @bakhyaye4756 4 роки тому +7

    youssou ndour moy senegal bilahi 🇸🇳🇮🇹🔥

  • @thiernomalickmbengue2766
    @thiernomalickmbengue2766 4 роки тому +8

    Mane déh bokna Thi niouko raféte Lou youssou Ndour c'est le meilleur et le roi nékhna trop

  • @mj-zq4qg
    @mj-zq4qg 4 роки тому +4

    Absolutely right buba, I'm a gambian and I'm enjoying the lives of youssou ndour, this social media was not meant for us Africas we use it for the wrong reasons

  • @fatougueyefaye6042
    @fatougueyefaye6042 4 роки тому +34

    Bien dit bouba ndour les sénégalais sont compliqués

  • @mamanndiaye6759
    @mamanndiaye6759 4 роки тому +21

    Youssou liguêye la kham

  • @papendour4636
    @papendour4636 4 роки тому +16

    Youssou Ndour rek

  • @Aybabydiop27
    @Aybabydiop27 4 роки тому +4

    non bouba je t'adore tu as bien répondu ki dafa doof avant tout youssou Artiste leu man gni di interroge kamougou sen bop

  • @sabinefrancoisedasylva9882
    @sabinefrancoisedasylva9882 4 роки тому +10

    Youssou ndour dagnou beggel pour enlever touti stress vive youssou ndour chapeau à toi Bouba ndour

  • @khalifadiagne3532
    @khalifadiagne3532 4 роки тому +6

    Youssou ndour Dal kounou wara royla Macha allah domou sounou mame ndaye sokhna mboup

    • @seydinaalioudiallohott665
      @seydinaalioudiallohott665 4 роки тому

      Khalifa Diagne kénéne ko roy koudoul yonenté bi (saw) wala nit niou bakh gni ah serigne bi dina graaw deh.ma ngui dieuguelou 🙏🏽

    • @khalifadiagne3532
      @khalifadiagne3532 4 роки тому

      @@seydinaalioudiallohott665 no si geume ligueye boumouye deffe la wakhe pas fingaye wakhé ta mane yalla ak yonentebi rek laye roye ta yaw nio far sama copin nga

    • @seydinaalioudiallohott665
      @seydinaalioudiallohott665 4 роки тому

      Khalifa Diagne ok ma dieugualou walahi wakhoumako pour dara mais sama khalat rek la wakh respect frère musulman 🙏🏽

    • @khalifadiagne3532
      @khalifadiagne3532 4 роки тому

      @@seydinaalioudiallohott665 no yaw niofar dou dara damaye mbalak rek

  • @MabinetyFall
    @MabinetyFall 4 роки тому +37

    Youssou ndour dh kumuy déranger demal si lila nekhh apres mu diekh 🤷‍♀️
    Affaire yi metiwul dh

    • @assanesamb7197
      @assanesamb7197 4 роки тому +2

      Yaw Do Koubakh

    • @MabinetyFall
      @MabinetyFall 4 роки тому +1

      @@assanesamb7197 diegeul Nala Yalnala yalla diegeul

    • @assanesamb7197
      @assanesamb7197 4 роки тому

      @@MabinetyFall Amiine Dieggualla Yaw Mii

  • @mbowvipofficiel1215
    @mbowvipofficiel1215 4 роки тому +3

    sénégalle yi def am niou sayetane youssou ndour limoy déf dara nekousi👍👍

  • @binetourassoulthioune7250
    @binetourassoulthioune7250 4 роки тому +1

    Youssou Ndour dal béggueul nagnou MachaAllah Fiitey rekk todj nafi .

  • @coumbathiam6193
    @coumbathiam6193 4 роки тому +10

    franchement li youssou donn deff dara nekoussi wagni stress kessé la.chak instant corona corona

  • @abdoufaye2229
    @abdoufaye2229 4 роки тому +52

    Vraiment les sénégalais sont compliqués dé

    • @khadindao3035
      @khadindao3035 4 роки тому

      Bilahi Man dama warou si Sénégal yi

    • @axirouzaman4346
      @axirouzaman4346 4 роки тому

      Bou Hiba cham dee si soiree prive Senegalese yepa wakh yousou ndour deff soiree prive ngen nee bu Ken wakh li mo takh corona bi Barry Senegal ngen areet ai juma ak ai Gamo yousou ndour d deff soiree chi Senegal gomoulenn yalla

    • @abybathily8221
      @abybathily8221 4 роки тому +1

      @@khadindao3035 trop MM

    • @assanesamb7197
      @assanesamb7197 4 роки тому +1

      @@axirouzaman4346 Vraiment

  • @papefodesenghor3442
    @papefodesenghor3442 4 роки тому

    PAPA Youssou tu es unique k l bon dieu vs protége amen vs étes l meilleur d tout les temps merci infiniment.

  • @mariamfaalmm
    @mariamfaalmm 4 роки тому +2

    Youssou Ndour is the best among the rest

  • @thiaratv1424
    @thiaratv1424 4 роки тому +1

    Merci beaucoup bouba vous avez bien répondu

  • @babafase9283
    @babafase9283 4 роки тому +24

    Youssou ndour limouye defe dará nekousi España fimanek sakh waye Kate yepa koye defe Senegal dafa Bari gnousokhar

  • @seydinandiaye641
    @seydinandiaye641 4 роки тому +27

    Youssou môme dou tontou avance rekh

  • @diattaamydolly2860
    @diattaamydolly2860 4 роки тому +6

    Surtout nous qui sommes en Europe sa nous fait vraiment du bien avec le confinement

  • @elzofall742
    @elzofall742 4 роки тому +19

    Les.jaloux..niome.la.yeureume.youssou.senegalaiyi.nioko.begue

  • @doudoumane6028
    @doudoumane6028 4 роки тому

    Machallah Bouba wakh dji raféttna

  • @zeynabdiallo1744
    @zeynabdiallo1744 4 роки тому +2

    Merci bouba ndour 😍😍certains sénégalais yi deegnioo dokhorr trop🙄🙄

  • @ramatndaw8856
    @ramatndaw8856 4 роки тому

    Merci Youssou ! Ne repond pas aux jaloux . God bless you Amine Yarabi 💕

  • @mamskoita5827
    @mamskoita5827 4 роки тому

    Merci bouba ndour yalla nasa diam yague 💪💪💪💪

  • @nafysene8704
    @nafysene8704 4 роки тому +7

    Merci Bouba. Day liguey comme nieup.

  • @TheMouhamed7
    @TheMouhamed7 4 роки тому +14

    Senegal mo nekh rek golo bou diouk wakh, li Bouba wakh rek moy deugue, gnou beuri gnigui profito si occasion bi pour am buzz mais Youssou douleine meusse tontou, amoul seine temps

  • @serignecarlosmbacke759
    @serignecarlosmbacke759 4 роки тому +2

    Dém béguédji mo geune tok di iñiané kouy liguéy youssou vouz ête libre pour vivre ons na la joie de vivre merci

  • @astoufaye4664
    @astoufaye4664 4 роки тому +25

    Youssou ndour amoul sen diotou ndeyou question youc bidonyoyou

    • @mamadousanneh1019
      @mamadousanneh1019 4 роки тому

      Oui c’est ça lui aussi il travaille bravo Youssou 💪💪💪

    • @damegningue9459
      @damegningue9459 4 роки тому

      Youssou ndour da maguètte amoule benne foulla

  • @nittoudeugrek9684
    @nittoudeugrek9684 4 роки тому +1

    Bilay ndour wakhal youssou c le meilleur

  • @papadieng621
    @papadieng621 4 роки тому +25

    Merci ila parfait ma raison Vraiment cets tres nice bouba limiy def nioun ngi nek en DIASPORA niosi kham dara

    • @doudoundiayekairesadio3932
      @doudoundiayekairesadio3932 4 роки тому +1

      Nél ioe mi nék si diaspora bi OK boule mass noune ngui

    • @papadieng621
      @papadieng621 4 роки тому

      @@doudoundiayekairesadio3932 soumako wakhe takho may wakh ok ya see jent ma kham ici nioukay siuvre ok doumalay may buz

    • @doudoundiayekairesadio3932
      @doudoundiayekairesadio3932 4 роки тому

      @@papadieng621 OK dégue nala

  • @alassanethiam2784
    @alassanethiam2784 4 роки тому +21

    So defe li niune le lee so defe lee niounele li xalas Sénégal

  • @palycamara5364
    @palycamara5364 4 роки тому +6

    Nite mo sokhor rek mais dal bagne nangou mofi nek🙏🏽❤️

  • @bebelo1735
    @bebelo1735 4 роки тому +2

    La diaspora est fière de Youssou Ndour. Yagui beguel sougnou khol bi

  • @thomaspreira6129
    @thomaspreira6129 4 роки тому +21

    Nous vivons dans un pays de nafékheu,,,,,tfm rek nékoufi kou beug léléne nga zappé,,,,ya des emissions sur d'autres télévisions etc....

  • @abydiallo7131
    @abydiallo7131 4 роки тому +5

    Tonton you limouye def dara nékousi ish ❤️❤️ khana mome rek guen guis 🤷‍♂️🤷‍♂️

  • @madadiop8345
    @madadiop8345 4 роки тому +1

    Aye waye bayiléne sama youssou bayiléne sama youssou aye waye bayiléne sama youssou mane dama ko beug sama bir khol dima li léne ma rék té yalla takh nakh beugouma dégue louye méti sama khol bi

  • @laminethiam4606
    @laminethiam4606 4 роки тому +5

    je suis daccor avec tw

  • @coumbabeye9969
    @coumbabeye9969 4 роки тому +10

    Niou sokhor rek nioye wakh wante youssou daye dem.Genrou assane diouf yi aye veux rien laniou defou niou dara pour sen rew khana wakh rek.
    Quant a youssou il participe si development Senegal wn creant des emplois.
    Yaw journaliste bi vous etes plus de 10 personnes et c normal l'essentiel c de respecter les consignes des medecins dont la distance donc il faut aussi avoir la bonne foi.
    Youssou ndour jusqu'a la mort❤❤❤❤

  • @ousmanendour2168
    @ousmanendour2168 4 роки тому

    Je ne parviens toujours pas à comprendre comment on peut ne pas aimer youssou ndour. Cet homme a tant fait pour ce pays

  • @talibeboromnawel
    @talibeboromnawel 4 роки тому +7

    Mani bay sawew tank au début neena Youssou ndour amoul dara amoul daan mbirmi mo am .chaque jour gueni beuga reuy nit gni ak tookleen.gnou tadj diouma yi ak diaka yi limité nombre autoyi.nguir bagn ressemblement.marché yin tadj gnafa nek dandoon liguey.transport ni gnafanek daniy liguey teewul sasouné ngueni baga ray nit gni ak tokleen.limom rewmé amoul yonn rek mé ken manouko layal

  • @morsarr686
    @morsarr686 4 роки тому +36

    Sénégalais daffa sokhor

    • @mbayendiaye2690
      @mbayendiaye2690 4 роки тому +1

      Sénégalais daniou Sokhorr sen ndaye, youssou Ndour kilifa la ci limou nekk dou n'importe ki, tewal Sénégal founé ci adina bi, nioun gnigui ci caw bi di sante yalla, mom défalouniou dara mé quand-même naniou reconnaître valeuram, Nangamtanou ndaye nitt kou soxorr ak gniy Kass gnep ta défalouniou Sénégal niaff ndéyam domaram walabok.

    • @ladouse2961
      @ladouse2961 4 роки тому

      mdrrr waye mom tere wouko avance d bayile gnu wakh rek

    • @malickgueye4280
      @malickgueye4280 4 роки тому

      Yowe sa yaya ak sa pape khana dounou aye Sénégal

  • @elzofall742
    @elzofall742 4 роки тому +7

    Bouba.diaroule.tontou.youssou.nioune.nioko.begue.kou.banie.sa.khole.di.dague.dee.doko.si.mane.dara

  • @thiaratv1424
    @thiaratv1424 4 роки тому

    Vive youssou ndour et bouba ndour que dieu vous protège

  • @mariemdibba2027
    @mariemdibba2027 4 роки тому +1

    Merci Bouba Amal diame Mane Youssou Ndour la beug

  • @aliouba1170
    @aliouba1170 4 роки тому +13

    Entouka doyna warrr... les sportifs font des vidéos esportives pour ses fans ,et pourqoi les musiciens n’ont pas ce droit...
    Moi comm Modou Modou j’appelle chaque à ma Famille pour me sentir animer de la situation du confinement pour cause du CORONAVIRUS...
    Vive la Paix et à la Bonne Sante au Sénégal 🇸🇳 et partout dans le Monde 🌍

    • @oumarguisse5812
      @oumarguisse5812 4 роки тому +1

      déglou dégg amna solo looool way nagnouy déglou té dii bayii didef amalgame fii amoul béna sportif bouy rassemblé pr faire plaisir à ses fans par contre j'ai rien contre Mr Ndour mai rassemblement lay def chez lui en sachant que y'a couvre-feu arrêtons nous de faire amalgame wa salam

    • @aliouba1170
      @aliouba1170 4 роки тому

      Oumar Guisse waw c est respectable sa halattt si rassemblement mi ...mais amoul beneu amalguaam ...
      Peut-être les esportifs foofou begueulougnou les Senegalais...mais fiii ma nekkk par internet et par les télévisions ,ils le font chaque jours Maagui Jegalou boubah

  • @aichasetsima9781
    @aichasetsima9781 4 роки тому +30

    Sokhor ak ignane rek molene diap c'est tout

  • @mouhamedlaminembaye7825
    @mouhamedlaminembaye7825 4 роки тому

    Je t'aime bien bouba car t vraiment intelligents

  • @papadieng621
    @papadieng621 4 роки тому +6

    LIGUEY kat la youssou ndour bouko nekhe na bania DIAMOU YALLA ndakh MAME CHEIKH nena kou diouli nit wakh safan khamo touyaba bisi NEK bayilen YOUSSOU rawnalen bou yag

  • @elzofall742
    @elzofall742 4 роки тому +9

    Youssou.senegalaiyi.nioko.begue

  • @abydiallo7131
    @abydiallo7131 4 роки тому +2

    Tonton you limouye def dara nékousi ish ❤️❤️

  • @rountim42
    @rountim42 4 роки тому +14

    Diadieuf booba

  • @elzofall742
    @elzofall742 4 роки тому +16

    Youssou.defatale.benene.nioune.yaw.laniou.wakhe

  • @serignethiam3859
    @serignethiam3859 4 роки тому +22

    Mane deh mangui France wayé affaire bi nekh rek la def bou youssou bayi deh.

    • @serignethiam3859
      @serignethiam3859 4 роки тому

      @@assanesamb7197 yaw deh bale nala deja danga lakhatou si aye tour di wakh nite ko khamoul lou bone mais balnala kou bakh

    • @valide426
      @valide426 4 роки тому +1

      🤫🤫🤫 waye nékale guinaw french bakham 🤫🤫

    • @assanesamb7197
      @assanesamb7197 4 роки тому

      Lakhatou Manam

  • @wariosstv6950
    @wariosstv6950 4 роки тому

    90% gnikoy critique danio sokhor you le fierté international

  • @amiejatta2877
    @amiejatta2877 4 роки тому

    Thanks bouba from Gambia

  • @Bnkth8976
    @Bnkth8976 4 роки тому

    Très pertinent

  • @mamanndiaye6759
    @mamanndiaye6759 4 роки тому +14

    Y ou Rekk

  • @mansoursakho5579
    @mansoursakho5579 4 роки тому +1

    Grand bi dall mofi nékk Youssou Ndour 💪🏾💪🏾

  • @mohameddiarra6331
    @mohameddiarra6331 4 роки тому

    Nous aimons youssou ndour à tout coeur

  • @issasamby2417
    @issasamby2417 4 роки тому

    Merci booba bien dit

  • @beugeufalloutalibebayekari3430
    @beugeufalloutalibebayekari3430 4 роки тому +7

    Bilahi bouba ndour yay nafekh youssou ndour dou royoukay fi adouna tollou ngene di thiakhane dellou len si sunu borrom ta toupe

    • @coumbabeye9969
      @coumbabeye9969 4 роки тому +5

      You est une fierte nationale, il a cre des emplois yaw lo deff pour Senegal. Arreter you daye dem

    • @mamoudoudiallo2333
      @mamoudoudiallo2333 4 роки тому +1

      Yaw esk sa baye royoukaye leu. Une personne qui nourrit des milliers de personnes à travers sa musique et ses entreprises vous dites dou roykay

    • @beugeufalloutalibebayekari3430
      @beugeufalloutalibebayekari3430 4 роки тому

      @@mamoudoudiallo2333 yaw respecte wo sa baye

  • @paullelerichard2761
    @paullelerichard2761 4 роки тому +14

    Méme fiii France artiste yii dagnouy def musique sen leur yiii dii beuguel nitt gnii ,nooo Sénégal dagno sokhor biakhi

    • @oumarguisse5812
      @oumarguisse5812 4 роки тому +1

      France bane artistes guafii guiss mouy rassemblé ses musiciens chez lui pour faire plaisir à ses fans ???
      se qui font plaisir à leurs fans en France ils sont seuls à faire leurs vidéos on ne voit pas de rassemblement arrêtez d'être bêtes wa salam

    • @tele1514
      @tele1514 4 роки тому +2

      C toi la bête dans son salon ya pas plus de 10 personnes et on voit des plateaux de télé avec plus de 8 à 9 personnes

    • @paullelerichard2761
      @paullelerichard2761 4 роки тому +2

      @@oumarguisse5812 yaw weuro gnatta artistes gno fi nek sen keur yiii ak sen famille ou bien 5 ou 6_personne entouré len dii def ak rendre homme fiiii ,bayilen sokhor bayi domou diambour biii Aÿ deum ngen ,koufi tékki rek ngen bagne ,sokhor ngen ignane ngen ,baguen dallé wakh bâ légui youssou tontouwoul ngen nopalou ,Bonn ngen trop kou nek am na lo warra lidianté té lidianté woulenko isss

    • @oumarguisse5812
      @oumarguisse5812 4 роки тому

      @@paullelerichard2761 ñoune borom bii dafñou téral guissou ñou lougnouy sokhoré niite doméram

    • @oumarguisse5812
      @oumarguisse5812 4 роки тому

      @@paullelerichard2761 ñoune borom bii dafñou téral guissou ñou lougnouy sokhoré niite doméram

  • @doorwaar9465
    @doorwaar9465 4 роки тому

    Kenne sohorewoul yossou boulen wakh lolou mes sou gnèppou dèfè kom youssou dou bakh dei
    Tè benne musiquesain begoul fatou gnoulay tegal say musique
    Mani Mbocke yi yalla moguignouy khar dei kepp kousi topp waykatt yi ba fatou digua khamni yalla bagouko👆👆👆❤

  • @inssesylla6817
    @inssesylla6817 4 роки тому +12

    Laye mactar

  • @mamediarrafall6393
    @mamediarrafall6393 4 роки тому +4

    Youssou Ndour il n'a rien fait
    Day fékhal xol yii rk❤ longue vie à lui

  • @abdoulayeba9566
    @abdoulayeba9566 4 роки тому

    Bouba as raison Yousou ndour c'est un grand Monsieur.

  • @chamlamgenchanlamgen89
    @chamlamgenchanlamgen89 4 роки тому +1

    Nekou gni thi moment bégueleuneté na gnou délou thi yalla sougnou boromby dit niane yalla thi alkhourane yi thi wesifeuyi thi khasayite yi lou waye meneun thi diammou yalla sougnou boromby ndakh mou moutheul gnou thi balla bi

  • @sophiseck9790
    @sophiseck9790 4 роки тому

    Merci

  • @papedieng3170
    @papedieng3170 4 роки тому +1

    Vèritè absolu bouba en italie nous somme avec grand bi

  • @jojosantal8342
    @jojosantal8342 4 роки тому

    NIT KOU AME SAFARA BAYIKO MOU DÉM AK SAFARAM MERCO BOUBA❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @oumarsy5899
    @oumarsy5899 4 роки тому

    Merci grand bou

  • @amadousy6646
    @amadousy6646 4 роки тому

    Ceux ci qui insultent á travers les réseaux sociaux j'ai vraiment pitié pour leurs enfants á l'avenir ....ils vont entendre ceci " ton pére était un grand insulteur public , il n'était pas un modéle ni une reférence " ...

  • @moustaphalo2549
    @moustaphalo2549 4 роки тому

    merci you

  • @babacargeuye1114
    @babacargeuye1114 4 роки тому

    Sénégal dou déme pour quoi le sénégalais est méchant allez chercher du travail comme youssou ndour c un travailler encore félicitations à youssou ndour est le super étoile Nice Nice Nice

  • @ricardoyoden2046
    @ricardoyoden2046 4 роки тому

    Vraiment il la tout chanter même le comportement de la société sénégalaise il l’a chanté Youssou ndour est le meilleur de tout les temps le meilleur chanteur du monde il l’a l’image d’un Mandela à mes yeux 👀 moi!!!!

  • @mohamedlamineboye316
    @mohamedlamineboye316 4 роки тому +2

    Youssou Ndour kepp kouko bagn dama yakarni xoloum kiniane mola diapp

  • @barhamthiam2940
    @barhamthiam2940 4 роки тому

    Ce qui fait Sénégal yousou ndour personne ne jamais faire la paix beaucoup pour les Sénégalais

  • @mouhameddiouf6325
    @mouhameddiouf6325 4 роки тому +7

    Youssou ndour nekkal ci jamm kou mer noko borom khol you bax yi lawax

  • @makame7902
    @makame7902 4 роки тому

    Respect a youssou ndour

  • @aminandiaye7272
    @aminandiaye7272 4 роки тому +6

    Bouba ne t'en fait pas Youssou les a déja répondu en leur dédiant le morceau "Gorgui" boulèn toopto boulèn sooralé

  • @maremelo5471
    @maremelo5471 4 роки тому

    Mersi.buoba

  • @keenaleuborometouba846
    @keenaleuborometouba846 4 роки тому +8

    Yaw bouba damala beugue pask dague gnémé deugue mais wakhale si diakka yii bok diakka bounék 12 perssone difa dioulitte dij

  • @OUMZDABBZ
    @OUMZDABBZ 4 роки тому

    Bouba the goat facts only

  • @khadindao3035
    @khadindao3035 4 роки тому +11

    Man dama warou si Sénégal yi ah

    • @nittoudeugrek9684
      @nittoudeugrek9684 4 роки тому +1

      Bilay khady diarna warou dai ndakh peuple bo khamni wakh rek motakh gnou tarder

    • @khadindao3035
      @khadindao3035 4 роки тому

      @@nittoudeugrek9684 bilahi man damay tok di yemou L'i wakh rek khaw sokhor la wala am djot wala bek buzz d'o kham sakh lolen di wakh te koune day tok palasou yalla di ate😂 A Non yalla khol lay fey

  • @lidiadiagne8033
    @lidiadiagne8033 4 роки тому +5

    Deff lene nii youssou ndour ligueye rek mo woor mane deh couma ambose lay werrr

  • @moustaphasy8370
    @moustaphasy8370 4 роки тому

    Macha allah Nice na dama yeurom nonnu yi