Je n’ai jamais craché sur Cheikh Betio ( Ni dans la vraie vie ; ni sur les réseaux sociaux ) Alhamdoulilah 🙏🏽 ; il était quelqu’un que je respecte ; et j’aimais ses causeries et l’ironie qu’il prônait même si je ne suis pas une de ses disciples . Je peux aujourd’hui prier pour le repos de son âme avec sincérité ; me sentant bien en âme et en conscience ( ••• ) Repose en paix cheikhbi • Qu’Allah prolonge sa grâce et miséricorde sur vous . A Dieu Merci xalatt sa liguey rafetneu
machallah j'oublie jamais le jours je les vue dans mes rêves la ou ils étaient avec serigne touba et chiekh ibrahima fall et serigne saliou a touba sur un grand pont billaahi wallaahi. et moi je suis tidiane wah ngir yalla rek
Un HOMME d'une dimension exceptionnelle aussi bien sur le plan Humain, Social que Spirituel. Dommage pour ceux qui n'ont pas eu la chance de le côtoyer et qui ne l'ont connu qu'à travers une Presse souvent Malintentionnée. Pour notre part nous rendons grâce à SERIGNE SALIOU encore en ce jour car par sa grâce il a fait de nous des Thiantacones !!!! DIEUREDIEUF SERIGNE BETHIO !!!!
VRAIMENT JE VOUS REMERCIE TOUTE L'ÉQUIPE DE XALATE TV YAGUE NALLÉNE SUIVRE CI VIDÉO YOU AME SOLO YI MES TAYE LA GUEUNEU CONTANE MACHALAH NDAKHE ÇAMA KHOLE GUÉNE LALLE DIEUREUDIEUFETI SERIGNE SALIOU MBACKÉ DIEUREUDIEUFATE SERIGNE BÉTHIO YALA NALLÉNE SERIGNE SALIOU MBACKÉ FAYE AMINE
Ceux qui insultaient cheikh bi continuent d'insulter reik mais yalla nopina# yalla di na koy faye inchala dafa ligueyeul serigne touba# 18 safar dioy naleu dioyii fort
Hana kouy liguey kay n'a ligueyal yalla Book...au moins pour mou layoko yawmal khiyama...wayé koufi ligueyal kenen so tasse sa borom dina metty dh والعياذ بالله
Alhamdoulilah Dieureudieuff yalla sante nagn la Dieureudieuff Sérigne Saliou suniu yakar dieureudieuff Narou mame Bambi Thiam yalla nala yalla yeureum si barké alkhourane ak khassida yi ak Sérigne Saliou biniou yakar nakh takhawou ngua ko bokal dîner ak ko bokol dîner Thioune yaniou deffal gnila meussa saga khamounioula ndeysann 🙏🏿🙏🏿mane dé aduna wala niit dou takh ba mane ma faté la 🙏🏿🙏🏿
Merci beaucoup xalat sa vidéos biiii mom dafa guena am solo Man mom mangui lay nianal Thi barkéb s.saliou minga xamni mo def cheikh bi nim mel mou yockou la thi barkéb s.saliou Man mom damako beugue rk nguir s.saliou
Thioy Sénégal leegui gneippou rous nan diko critique diko attaques yalla nako yalla yrm barke s saliou di diaale keppou kouy thianta yi ak soppe yi ak keppou kouy musulmans
NOUS La JEUNESSE senegalais TOUJOUR ON PARLE AVANT DE REFLECHIR LII MOO TAKH SUNU HOMME POLITIQUE YI DINIOU NAKH REKK CHAQUE JOUR QUE DIEU FAIT XALAT TV DAFAY DEFF AYY RECHERCHE ON DOIT ALLER FAIRE DES RECHERCHE POUR L'AIDER ET VENIR ICI POUR COMPLETÉ MAI CHAQUE JOUR MERCI XALAT FANN NGA JEULÉ SA INFORMATION BI ECT......
ndeysaan adouna dh kou yalla mour r mballanou soutoura lo teureudi teureudi say tank sakh dou feegnn naniu rafetaal tei mandou ci sunu digantei cheikh bethio thioune yalna xippei aljanna ci barkei mame saliou labsolu merci xallat jaam ci yow
Xalaat TV machalla khame kham bui yalla n'a yocou yalla n'a diame yage tiounne mame bambú yalla naco yalla khare adjana bilaye yone Wii gnace n'a nge djamebare dege bulaye
Dieureudieuf Thioune yarnganou yeenganou si yallah ba reewougnouco mboki talibeyi kenn boumou mere kenn nous sommes des thiantacones lou xew dagniy sante yallah waxyi ak loumoumana done boumoutax gnou diappal kenn haine ça c'est pas thiantacone le cheikh nous l'a dit balna gneup c'est pas a nous d'avoir une dent contre qui que ce soit car cou xamoul xamoul dieureudieuf Thioune
ziyarnala boroume xalaat tv amna solou loll yalla na yalla yokou sa xam xam si barke s.touba me bègue na nou kahmante boubakh sa numéro téléphone portable sokhla nakou dh
Je n’ai jamais craché sur Cheikh Betio ( Ni dans la vraie vie ; ni sur les réseaux sociaux )
Alhamdoulilah 🙏🏽 ; il était quelqu’un que je respecte ; et j’aimais ses causeries et l’ironie qu’il prônait même si je ne suis pas une de ses disciples .
Je peux aujourd’hui prier pour le repos de son âme avec sincérité ; me sentant bien en âme et en conscience ( ••• )
Repose en paix cheikhbi •
Qu’Allah prolonge sa grâce et miséricorde sur vous .
A Dieu
Merci xalatt sa liguey rafetneu
F A T I M A - G iow dh fonk nala nakh nit day mandou bilahi amal diam ❤️🙏🙏
F A T I M A - G Amine kaddu yi rafetna
yalna la yalla samou
Papa gentil amine way si barkei werwi🙏🙏🥰
S'il avais deux personnes comme toi
amy collè si tout l monde etai comme toi aussi personne n se tromperai c sûr 🙏🙏🙏🥰
machallah j'oublie jamais le jours je les vue dans mes rêves la ou ils étaient avec serigne touba et chiekh ibrahima fall et serigne saliou a touba sur un grand pont billaahi wallaahi. et moi je suis tidiane wah ngir yalla rek
Sa xoll mo préfet rkk diam ci yaw
Diam siyalll mbok nala yala takhawou
Dieuredieuff bokk mi
Un HOMME d'une dimension exceptionnelle aussi bien sur le plan Humain, Social que Spirituel. Dommage pour ceux qui n'ont pas eu la chance de le côtoyer et qui ne l'ont connu qu'à travers une Presse souvent Malintentionnée. Pour notre part nous rendons grâce à SERIGNE SALIOU encore en ce jour car par sa grâce il a fait de nous des Thiantacones !!!!
DIEUREDIEUF SERIGNE BETHIO !!!!
Dierediefeti brom touba yalnanou yalla fayal cheikh saliou mbacke cheikh bi yalnako yalla yerem
Xallat diakhal gama dh figayy dielè informazion diakhal nama trop mè merçi. Kham na thi s bethio louma khamoulon vraiment mèrçiii
VRAIMENT JE VOUS REMERCIE TOUTE L'ÉQUIPE DE XALATE TV YAGUE NALLÉNE SUIVRE CI VIDÉO YOU AME SOLO YI MES TAYE LA GUEUNEU CONTANE MACHALAH NDAKHE ÇAMA KHOLE GUÉNE LALLE DIEUREUDIEUFETI SERIGNE SALIOU MBACKÉ DIEUREUDIEUFATE SERIGNE BÉTHIO YALA NALLÉNE SERIGNE SALIOU MBACKÉ FAYE AMINE
Suis vraiment ému et je suis vraiment contente sur le témoignage cheikh bétho Thoune merci à vous même
Yalla nako sunu borom kharé aldianay firdawsi amineeee 🙏
Kou diambaréh wone tchi 18 Safar
Film porno Il m'a prône
Amiiiiiiin way
Oui
Yalla na KO yalla Yoko le lam satafou no si barkem amie si barkem s, sall
Nice
Beaucoup de respect pour cet homme que Dieu l'accueil dans son paradis céleste
Plus de 10fois que je passe et repasse la vidéo tellement je suis sublimé.
Ndeyssane
Jërëjëfëty Sëriñ Saaliw 🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
kou beugu cheikh biii beuseu jaim yalll nako yalla kharé adjana si barcké serigne saliou mbacké
Kene dou S Touba S Cheikh Salikhou💪❤️👌Ylla nako brome Kharé firdawsi barkepp kou tedd ki et Xalat encore 🙏 très frappantes et touchant❤️😢
Cheikh Bethio était un des plus grand Cheikh de Serigne Touba. RIP c était un Bon et Grand Patriote.
Chekh bethio kemanouk yallah la.
Souma thiantacoune mais kham na len moye serigne saliou radihallahou anhou, fonkone nako lol sakh.
Yeurmandek serigne saliou mbacke moye cheikh bethio thioune.
Mouride saadikh moye chekh bethio.
Lepam serigne touba khadimoule rassoule lawone.
Dieuredieuf , léral-bi amna solo trop , yalla naka borom-bi diêguel tè déf-ko mou guissé Serigne Saliou M'backé. ((Amine)🙏🙏🙏)
Xalaat merci beaucoup de votre témoignage
Diko Gniaal Yallah Sunu Boroom Bii🙏🏽
Waane Lekko Ak Sàngam Ba
Serigne Saliou Mbacké❤️
Amna Solo Lool 😭😭 😭
Merci bcp pour cette vidéo exceptionnelle faite sur LE CHEIKH ok que DIEU te bénisse AMINE
Dieuredieufety thioune on vous sera éternellement reconnaissant
Yalla nako yalla yeureum si barkéb serigne saliou
Amine
Kouy xool n👥t di guiss thi mom lou ñiaw,baxa goo.
Xalaat vous êtes les meilleurs👌
Paix à son âme💚
Que Firdawsi soit votre dernière demeure👌
Ceux qui insultaient cheikh bi continuent d'insulter reik mais yalla nopina# yalla di na koy faye inchala dafa ligueyeul serigne touba# 18 safar dioy naleu dioyii fort
Inchallah dina am ndam boune khamone kisi ligueyal serigne touba dinane ko sakou
Téxé adouna té d'où niètaaané aldjana xadj yi nak nanouy bas rék
Auto weuyy
Hana kouy liguey kay n'a ligueyal yalla Book...au moins pour mou layoko yawmal khiyama...wayé koufi ligueyal kenen so tasse sa borom dina metty dh والعياذ بالله
@@adjagueye4577 moh...dianguil ioe...
@@mstv7185 hhhh...niaata sourate nga mokkal ?
Niaata hadiss nga mokkal?
Lii rk moy compté le jour de la résurrection
😭il était incompris par beaucoup de gens...wayé lep dîna bahh lep dîna dikk inchalah...sant nanou boubah thioune...gnoune ak mom ba aldjana
dieureudieuf ma challa tay lakoy doga téWlou mé sama khôl bilahi nimou séddé yalla rék moko kham
Thieuy adouna bala nga kham nitt rekk mou fatourekk
Que la terre soit légère sur Lui
Yalna sa doundou thia barzak donne Diameu ak teranga gou sah dakeu♥
Alhamdoulilah Dieureudieuff yalla sante nagn la Dieureudieuff Sérigne Saliou suniu yakar dieureudieuff Narou mame Bambi Thiam yalla nala yalla yeureum si barké alkhourane ak khassida yi ak Sérigne Saliou biniou yakar nakh takhawou ngua ko bokal dîner ak ko bokol dîner Thioune yaniou deffal gnila meussa saga khamounioula ndeysann 🙏🏿🙏🏿mane dé aduna wala niit dou takh ba mane ma faté la 🙏🏿🙏🏿
Amna kouko wakhon deh...
Sénégal deuk bou nakhadi doundé wayé bou nékhéé déwéé. Yalnako yalla até ci yeurmandém. Amen
Serigne cheikh tidjiane sy moko wakhon
Merci xalatt tv
Merci xalate tv ligueye bi rafete na. Di dialé thiantacoune yeupp
Mame Abibatoulahi Ndour amine
Thiey santati naniou Serigne Saliou li dei abb Thiante la daniouy koy nagou waxi serigne saliou dou louy fay
Serigne BETHIO Saliouh yallah nako Serigne Saliouh terou
Dieuredieufaty Cheikh Bethio
DIEUREDIEUFty serigne Saliou mbacke
ndey saaane Cheikh bethio .kouma nekhone trop.ma beugone ko ndakh serigne saliou ak diambaram si 18 safar.yalla nako serigne saliou terou .
yalla khamna lep
Yalla na Ko yalla yeureum xaré Aldiana
Yalla nako yalla yeureume té dieguel ko si barkép Serigne Salliou Mbacké
Yalna lén yalla yereum
Merci beaucoup xalat sa vidéos biiii mom dafa guena am solo Man mom mangui lay nianal Thi barkéb s.saliou minga xamni mo def cheikh bi nim mel mou yockou la thi barkéb s.saliou Man mom damako beugue rk nguir s.saliou
Xallt TV sa ligey Refetna trop merci beaucoup xallt TV
Vraiment Xalate ligueye bii rafete na limo takh gnou nane niite soko xamoul rék xamoko
Que la terre lui soit légère 🙏
Ch bethio thioune est unique ms aussi yalla nko yalla yeuram tê khareko aldiana firdawsi
Thioy Sénégal leegui gneippou rous nan diko critique diko attaques yalla nako yalla yrm barke s saliou di diaale keppou kouy thianta yi ak soppe yi ak keppou kouy musulmans
NOUS La JEUNESSE senegalais TOUJOUR ON PARLE AVANT DE REFLECHIR LII MOO TAKH SUNU HOMME POLITIQUE YI DINIOU NAKH REKK CHAQUE JOUR QUE DIEU FAIT XALAT TV DAFAY DEFF AYY RECHERCHE ON DOIT ALLER FAIRE DES RECHERCHE POUR L'AIDER ET VENIR ICI POUR COMPLETÉ MAI CHAQUE JOUR MERCI XALAT FANN NGA JEULÉ SA INFORMATION BI ECT......
Merci xallat tv
Cheikh Bi yalnako fey ci barke Serigne salliou
Amine Amine
Sante S saliou rkk
Sante serigne saliou mbacké rkk diadieuf thioune
Mrci *_xalaat tv_* liguey bii rafetna machalah et niongi dialé thiantacoun yeuppp
Yalla nako yalla yeureum Te boleko ak serign salihou
Ndeysane xalat contane na thi yaw serigne béthio yalla nako sangam ba térrou serigne saliou mbacke amine ya rabbi béne cheikh lafi wone raw naniou
Amine way👃
AMIIN
Serigne saliou dou defar kouy torokh
Un faux guide ki travaillait pour iblis satan.
@@rienquelaverite9296 sa thiapaa ndaye bayisi xél
Merci xalaat nous présentons nos sincères condoléances à la communauté mouride particulièrement les thiantacones
Machallah amna solo yalla nako yalla yeureum té khareko aldiana
Merci xalaat machalla job bi nice na loool cheikh bi yalla nako yalla yeurum té kharéko al diana
Ndeysane cette video ma vraiment touché yallanako yalla xareii aldiana
Yalla nako yalla até si yeurmandém reposes en paix Thioune 👌
merci beaucoup xalaat tv
CHEIKH BETHIO DIAMOU SERIGNE SALIOU DIARAMA
Yalna yalla deff diamou si Mom
Thiey cheikh Bethio yalla nako yalla doly yermànde thi barkeb s saliou
Merci beaucoup xalaat 🤝🤝Cheikh béthio diamou Serigne saliou yalla nako sounou bouroume yéreume si barke kour Gui amine 🙏🙏
Aminne
Diamou yalla lagnouy wakh nga balma
Amine
Cheikh bi yalnako yalla yeureum 😢🙏🏽
Allahou akbar gouye danouna😥😭😭 yalla nako yalla yerem khareko aldianna amin
Diadieuf xalate tv cheikh bi yalla nako yalla faye ta diégualko kharélo aldiana
Mercii xalaat dyko nianal yalla woyo fal souff thii kawam ta wonè lèko ak sopèm ba serigne saliou mbacke amiin
Yalna yalla yéssal yeurmande thi mom tá khareko
Yalla nako yalla yeureum té diegueulko ay bakaram mom ak ni gnou djitou nieup
inna lilahi wa inna illahi rajji''un que Dieu l'accueille à son paradis firdaw siiiii
Machallah merci xalaat tv
Que la terre lui soit légère 🙏
Cheikh bii yalla nako yalla xare aldiana firdawsi koudem demnaa wayée toujour daniowara amm yaar ak teguine diokh naniou leçon avant mouy demm diangue lénesi baa fawou nakkk.
Machallah liguéye bi rafetna niou and deglouko
Merci beaucoup khalat tv pour portails
Thioune mou Serigne Salioukhou que la terre lui soit légère
yalla nako yalla yeureum thi barké serigne saliou mbacké
😭😭hooo wétal nga ñiou thioune Sénégal mingi laye dioye balégi té noppé goule kou mélni yaw fane lañiu koye dieulété 😭😭😭😭😭😭😭
رحمة الله عليه، اللهم أسكنه فسيح جناتك بجاه سيد الوجود ببركة الشيخ الخديم
Machalla xallaat rafetna
Chikhe bi yalnako yella yaram khari ko aldkana
Man chala amna solo yalna ko Serigne Saliou Mbacke terou takha wouko. Ken dou mom. Il va nous manquer.
Que Dieu l accueil dans son paradis céleste
Que le paradis soit sa demeure
Merci xalat TV pour les infos cheikh bethio yalnako yalla yeureum khareko aldiana dji barke naby psl
Mashallah yalla nako yalla yeureum kharéko aldiana 🙏🏿
Ndeye sane yalna ko yalla kharé aldiana barker s Saliou 😭
Machallah yalle nako yalla yeureume khareko aldiana firdawsy amine
Ma challah yalla nako yalla yeureum tei xarei ko aldiana
Yalla na yalla yokou ay lerram😥😥💗🙏
ndeysaan adouna dh kou yalla mour r mballanou soutoura lo teureudi teureudi say tank sakh dou feegnn naniu rafetaal tei mandou ci sunu digantei cheikh bethio thioune yalna xippei aljanna ci barkei mame saliou labsolu merci xallat jaam ci yow
Jërëjëfti Serigne saliou mbacké
Merci xalaat liguy bi rafet na cheikh bietou yalla nako yalla yarem si barke s saliou Mbacke
Il été un homme généreux paix à son âme amine
bilahi walahi talahi kon melni mom mosou fi am ta dou tofi am si adona
Xalaat TV machalla khame kham bui yalla n'a yocou yalla n'a diame yage tiounne mame bambú yalla naco yalla khare adjana bilaye yone Wii gnace n'a nge djamebare dege bulaye
Dieureudieuf Thioune yarnganou yeenganou si yallah ba reewougnouco mboki talibeyi kenn boumou mere kenn nous sommes des thiantacones lou xew dagniy sante yallah waxyi ak loumoumana done boumoutax gnou diappal kenn haine ça c'est pas thiantacone le cheikh nous l'a dit balna gneup c'est pas a nous d'avoir une dent contre qui que ce soit car cou xamoul xamoul dieureudieuf Thioune
yalla nala lerrou Serigne Saliou mbacké terrou si sa bamel en tout cas sunu xol dou diouk thie yaw thioun mame bambi thiam
Que la terre lui soit légère R.I.P Chiekh bethio thioune
Yalna yalla yokkk ay leiram tasss gnu si barkém
amna solo lole ماشاء الله بارك الله
Machala xalaat yagu nga deff lou rafet
Yalna yalla Doli Yermandém Ci cheikh Bethio
Yalla nala yalla Faye si lii
Yalla nako yalla yeureum tè khareko aldiana firdawsi
ziyarnala boroume xalaat tv amna solou loll yalla na yalla yokou sa xam xam si barke s.touba me bègue na nou kahmante boubakh sa numéro téléphone portable sokhla nakou dh
XALAAT TV BÈGU NANIOU LOLLL CI LIGUÈY BI MERCI BEAUCOUP VRAIMENT
Merci beaucoup xalat TV . Nitt kou bakh ga wakh dji raffet na
Khalat tv, machallah. Seni ligueye rafetna.
Nianou serigne saliou bi rek mo nangou si barke yallah. Paix à son ame. Que Allah ait pitié de son âme.
Yalnako yalla yeurem
Jaajëf Xalaat TV si Témoignages yi, Paix à son âme Que Aljana Firdawsi soit sa demeure éternelle si Barkeb SIDY BIRAAHIM FAAL Yaaram bi