Ndèye Fatou Fall : "Arrêtez les audios privées de ma soeur Sokhna Zeynab que vous partagez et les...

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 14 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 285

  • @bobobarry9590
    @bobobarry9590 6 років тому +7

    Diemlene melnii mom di rafetal tei bayi niawtefyii wakh dafay rafet .....k l paradi soi sun demeur eternel mai do meusseu diouguei cii kholyii machaalla

  • @khadidiatouka4012
    @khadidiatouka4012 2 роки тому +2

    Paix à son ãm 😭 zeynap je l'eme peucou machallah 👍♥️💚

  • @allioufall2531
    @allioufall2531 6 років тому +1

    Machallah oustaz sa liguey rafétna zeynab yalla nako yalla dolli yermané ta mousele ko si thiate

  • @bintandingsagna8093
    @bintandingsagna8093 6 років тому +18

    Zeynab était une femme unique et exemplaire il n'y a pas de nombre de femme qui lui ressemble ici au Sénégal que la terre lui soit légère.

  • @khadidiatoudia759
    @khadidiatoudia759 6 років тому +17

    Macha'allah Allahou Akbar hamdoullillah Vive la verite rien que la verite macha'allah que le bon Dieu lui vienne ,et l'aceuille dans son paradie incha'allah misericordieux et benediction incha'allah

  • @oumykalsoumlodiane4032
    @oumykalsoumlodiane4032 6 років тому +93

    Bilay gnawna trop nit gni amatougnou limite ci réseau sociaux yi

  • @dikha7525
    @dikha7525 6 років тому +19

    Vraiment je disait la même chose. Laisser la se reposer en paix.

  • @fatimacissediaboumamedabak198
    @fatimacissediaboumamedabak198 6 років тому

    Machallah ya oustaz li mou wakh degla senegaleyi danio sof yalnako yallah khare firdawsi maman adore ❤

  • @diopmbene1733
    @diopmbene1733 6 років тому

    Bilahi amine yalnako yalla yereum sokhna zeynab waxna lep bilahi watchap Lou diara ragal la soutoureu sibopam la nit gni amatoul thim

  • @fatoushesarr4645
    @fatoushesarr4645 6 років тому

    Allahou akbar thiey adouna dagnouy dieuww bay dieuw kou déhh bayi lénnn wakhh ay way 😥😥 yallana yalla yéésal yeureumadem si Mom ....

  • @Fafashuu
    @Fafashuu 6 років тому +175

    Mane dama diomi si senegal legui ,ay vues sur youtube ak buzz diaralnaléne lounék rek mane g peur pour mon pays 😒😒😒 reposes en paix Sokhnasi

    • @mamanndoye532
      @mamanndoye532 6 років тому +1

      Wakhatiko gueme yalla laniou defatoul

    • @ninamcqueen6141
      @ninamcqueen6141 6 років тому +1

      UA-cam paye les vu par western union de mille à cinq mille euro et si t'as des abonnées tu gagnes tous les mois de l'argent donc c'est sûrement pour ça

  • @nenouchediop4789
    @nenouchediop4789 6 років тому

    Masha Allah wakh gui rafetena yalla nako yalla yeureum koulen guisse ni xameni kou xam diner guen yalla nallen yalla mey xol mougne kouma sopone la

  • @awaba5087
    @awaba5087 6 років тому +6

    Walahi ndeyesan degueleu lolou dou yone waye machallah amna solo lol diadief

  • @electionslocaleselectionsl3859
    @electionslocaleselectionsl3859 6 років тому

    Bilahye ñiawna trop Sokhna Saynabou Yalla na ko Yalla yeu reum tabal ko al dianna firdawsi amine

  • @assanediop4918
    @assanediop4918 6 років тому +24

    Que chacun prenne CES responsabilites de ne Pas visionner CES videos. Dioulites day mandou

  • @sodasene2003
    @sodasene2003 6 років тому

    Bilahiii wkhna degue Sénégal danio eupeul begue buzz rekk ak jaime

  • @abdouazizekratine8899
    @abdouazizekratine8899 6 років тому

    walahi yalla nala yalla sougnou borom terou sì aljana yu kawei

  • @doudousene7566
    @doudousene7566 6 років тому

    Machalah yalna yàlla Faye

  • @binettegueye4671
    @binettegueye4671 6 років тому +1

    Yalla nako yalla yeureum tè kharèko aldiana repose en paix ya seyda

  • @isatousuwareh2615
    @isatousuwareh2615 6 років тому

    Zeynab faal yalla na ko yalla yerem tai kharri ko jannahtul firdawsi.. Ameen man dei moi sama idol

  • @RokhayaNdiour-n7f
    @RokhayaNdiour-n7f 3 місяці тому

    Thiéy Sama Sopey bii nax ghañū baa dèm yalna Aldjanaye Firdawsi disa wérūway🤲🏻🙏🏻nitt kū bax 😭😭😭

  • @adamathior9643
    @adamathior9643 6 років тому +14

    Machalah wakh dji rafetna. Eupal rek

  • @xulliltv881
    @xulliltv881 6 років тому

    Machala kadouyi rafétena

  • @ndeyesokhnaags4437
    @ndeyesokhnaags4437 6 років тому

    Elle a bien dit un secret! Nguir yallah soutoura, ki publier audios bi defna lou gnaww,repose en paix soxna sou bakh si, yalna nguaa khippé aldianaa

  • @mamecheikhka8730
    @mamecheikhka8730 6 років тому

    yalla nako yalla yeureum te khare aldiana

  • @Queen_Lo
    @Queen_Lo 6 років тому +13

    Yalnaniou yalla moussal si am diott parsk vraiment liii am diot moko warall diii dieuww bay dieuw Kou deh thieuyy yalla

  • @kalamou2917
    @kalamou2917 6 років тому

    yallnako yalla yeureummmm hareko adiana

  • @muhammedsamba4294
    @muhammedsamba4294 6 років тому

    Maa shaa Allah very important
    Nit yi ragalatun yalla
    اللهم إغفرهم ورحمه ويدخلهم جنة الفردوس

  • @izosycohorte5970
    @izosycohorte5970 6 років тому +1

    birahi mettina wayee yallaa nacco yalla yeureum

  • @sokhnathiaw6689
    @sokhnathiaw6689 6 років тому

    Bilahi wax nga deug soutoureu lou am solo leu yalnako yalla kharé aldiana firdawsi

  • @mariediatta7443
    @mariediatta7443 6 років тому +42

    DEUG pire machalla soutoura dafa bakh

  • @mohamedabdy8733
    @mohamedabdy8733 5 років тому +3

    اللهم اغفر لها و أرحمها و أعف عنها و عافها و أبدلها دارا خيرا من دارها و أهلا خيرا من أهلها و أدخلها الجنة و أجرها من النار.
    السيدة زينب

  • @momoniass9092
    @momoniass9092 6 років тому

    Machallla amna solo

  • @FirdawsTV3125
    @FirdawsTV3125 6 років тому +13

    من ستر مسلما ستره الله يوم القيامة

  • @gansiryfall7247
    @gansiryfall7247 6 років тому

    Bonjour ma soeur merci pour ce message que dieu laceuille au paradis amine paix à son âme

  • @cheikhmomardiouf8329
    @cheikhmomardiouf8329 6 років тому +31

    bilay walay repose en paix yalnaleu yalla yeureum

  • @h.a.j9099
    @h.a.j9099 6 років тому

    True talk my Sister in island

  • @aichasal4258
    @aichasal4258 6 років тому

    Bilahi sokhna si wakhnga DEUG.lii dawna yaram tei ndeyssan sokhna si da yiw machallqu

  • @amadouba9956
    @amadouba9956 6 років тому +1

    yalla nako yalla yirim kariko aldana vir daw ci

  • @tsuchikoroco3824
    @tsuchikoroco3824 6 років тому

    MASHALLAH S0KHANA CI WAKH DJI RAFETNA YIW DAL CII DÉRÉTE LAY NEK MACHALLAH

  • @diopmodou8206
    @diopmodou8206 6 років тому

    Machallah la amna solo yalnako yalla yeureum te khareko aldjanaye firdawsi yawit magama yalnala yalla faye yiw

  • @bintagnigue8229
    @bintagnigue8229 6 років тому +13

    Bilaye louma méti nékhouma bayiléne sougnou sopé sougnou yaye yalla na adjana done dekouwaye TS mou done dekalé sopé bi seydina Mohamed psl bakh bâ kheye déme naniou raguale yalla si sose yi

  • @ousmanembaye9668
    @ousmanembaye9668 6 років тому

    Machala âme na solo fall yakarna sénégalais yi deguena naniou bou bakhe liga wakhe

  • @chachadiez633
    @chachadiez633 6 років тому +86

    Guiss nga dé avant hier rèk ladone wax ni pourquoi gnouy dougal vocalome yi ni thi réseau sociaux yi. Sénégal nite ki souy doundou di déff ak di wakh lou bakh, gnou mélni guissou gnouko.mais bou guéné adouna rèk kou nék di wané ni mass nako diox lokho, waxtane nagn ak mass nama déffal li té lolou yép amoul sens. Déff nafi aye waxtane you ame solo pourquoi pas gnou dougal léne pour que askane bi ndiarigno si té gnou gnanalko mo gueune dé déféna

    • @miamorvalentini3951
      @miamorvalentini3951 6 років тому +4

      Sénégal moy reew mi nakhari dound neekha dewé. Soy dound niou beuri dougn la faalé, looleen defal lou baakh gnissi eup dougn ko wakh, so deuddoo nak kounekk di wané ni mako gueunone kham. Té dagn siy dem ba fatté ni danga am ay mbokk

    • @chachadiez633
      @chachadiez633 6 років тому +1

      @@miamorvalentini3951 guiss nga dé wayé yalla nagnou yalla dolile soutoureu

    • @miamorvalentini3951
      @miamorvalentini3951 6 років тому +1

      @@chachadiez633 Allahouma amine waaay

  • @madougueye5490
    @madougueye5490 6 років тому

    ALLAHOU AKBAR machallah sénégalais nion niémé yallah

  • @bacheikh2463
    @bacheikh2463 6 років тому

    Amno solo trop yaa seydaa.nioungui naxarlou bou baakh lignii def sounou yaay zéynab.Elle est la seule personne à qui j'ai pleuré sa mort et je ne l'ai jamais fais.yalla naco yalla yeureum

  • @aminataniang1007
    @aminataniang1007 5 років тому

    Aminataniang

  • @kingtvsylla6483
    @kingtvsylla6483 6 років тому

    bilay sokhna zeynap aka geum yalla kholall wakh bou rafete by rekk mais yalla nako yalla khare aldiana firdawsi rest in peace

  • @youssouphsané-r3r
    @youssouphsané-r3r 5 місяців тому

    Paix a son ame

  • @khadijamiller6239
    @khadijamiller6239 6 років тому +27

    Mais dans quelle monde nous vivons aujourd'hui on n'a même plus peure de la mort et sa fait partis des signe que la fin du monde approche. Diéme léne mélni mome dakh le prophète (psl) néna koulay diagal touti mo dess mou nek sa wonéte donc djioute pirr djikhat ba fatou diagal niou nouniou wara gena diamo souniou Borom donc sokhna zeynap Fall monima la elle est a respecter dakh finou dégone diné geume popam elle est un modèle pour nous nioune jeune yi yalgua khipé thi sa kanamou sopéba Mohamad (psl)

  • @fatoudiouf866
    @fatoudiouf866 6 років тому

    Bilay ndeysane

  • @ouzendiaye9475
    @ouzendiaye9475 5 років тому

    Yalla nako yalla yeureume

  • @Diallo2035
    @Diallo2035 6 років тому

    Machalla nanoui rafetale

  • @khadidiatoubalde8159
    @khadidiatoubalde8159 6 років тому

    bilay li doyna yalnako yala haré aldiana

  • @guet8184
    @guet8184 6 років тому +1

    Ak gni di niane si mom pour am ay j'aime kou dem sakh sokhaloulene j'aime yi rek lagnou si beug vraiment dou yonn

  • @mouhamddieng8527
    @mouhamddieng8527 6 років тому +19

    Sokhnasi dafa dem bayifi ay wakhtan youy am solo kon danko def si tele pour ascanwi disi diarignou nankhol lolou mougnou mayon thi khelam mou rafey machala gnanalkothio te bayi ay dieufi privem nagnou ragal yala tey nat thi sounou bok

  • @mansourdieng2000
    @mansourdieng2000 6 років тому

    Yalla nako yalla kharé aldia na mane sénégal diakhal ndagna ma

  • @alphasow5867
    @alphasow5867 6 років тому

    MACHALLAH

  • @binetasow9139
    @binetasow9139 6 років тому

    Billage 😧😧😧😧 je pleuré de TT mes larmes wa Sénégal loi khéw

  • @kadycisse1300
    @kadycisse1300 6 років тому

    yanalko yala yobou aldiana amine

  • @aissatousow6039
    @aissatousow6039 6 років тому

    AGS waynako diew bay diew ki dé ragal leen Yallah Allahou akbar

  • @kadiandiaye3840
    @kadiandiaye3840 6 років тому

    Li dafa niaw kou guen adouna niou neck di teck Aÿ vocales ak di wakh té beuss dina niow si beuss Sénégal amouniou ben soutoura paix à son âme et kallah l'accueille au paradis amine

  • @arabietoucoly4782
    @arabietoucoly4782 6 років тому +13

    Ana mandou Sénégal dal amna niou mandouwoul khana kay bo wakhé ak nit thi soutoura bamou guene adouna gua wara guena meuna yok soutoutal

  • @sakhohamza637
    @sakhohamza637 6 років тому +1

    الله المستعان وعليه التكلان ولا حول ولا قوة إلا بالله رحمها الله رحمة واسعة

  • @seydinamouhammadseck2656
    @seydinamouhammadseck2656 4 роки тому +1

    Repose en paix

  • @azizbah8815
    @azizbah8815 6 років тому

    Yallah nako yallah yieram

  • @hrams4793
    @hrams4793 6 років тому +9

    Masha'allah

    • @fatoumbaye4162
      @fatoumbaye4162 6 років тому

      vraiment am na lokhané kéne douko w
      akh

  • @evachoux26
    @evachoux26 6 років тому

    Ayda seynab fall yaw sa aldiana lérna bou yag djigén bou maun gor😚😚😚😚😢😢😢

  • @harunagitteh7105
    @harunagitteh7105 Рік тому

    Bilahi😭😭😭😭

  • @Grisjum
    @Grisjum 6 років тому +6

    Walahi s’en ai trop vraiment sénégalais loumou dougou mou euppp

  • @khadidiatoumbengue7891
    @khadidiatoumbengue7891 6 років тому

    Salam, louwaye wakh bopam. Sokhna seynab yalla nala seydina mouhamed psl terou aldiana si mague borom bi. Sokhna seynab dafa melna nio bok bene bir bouniou dioguer ndakh begue bimako begue te yalla takh. Amine.

  • @lahatcisse4782
    @lahatcisse4782 6 років тому +2

    Mane personnellement bou féké lolou am na vocal yi feue sonkhna zeynab fall laniouy partagé si internet bi ma kham né niitte gni koyi deff deff naniou lou niaw paceke sokhna si guéneu aduna nitte tou diné lawone nitte tou soutoura nitte tou téranga lawone naniou KO nianal mogueune niou nék diko togne sénègalais moy lay togne dila togne bagua dé bayiko fi mou continué dila togne daguay sétte lii rek mane mome worna yalla Lima guiss sénègal kouma mayi visa aller sans retour ma fayi samay borr té dem états unis wala Canada ou bien Chine tokk fa ba sama heure rou dé diotte j'ai peur avec mon pays

  • @serignembackekebe2105
    @serignembackekebe2105 6 років тому

    Yallah nako yallah yeurëm te khareko aldiana senegal danio bary wakh wakh rek sur tous djoulitt ngi

  • @mouhamedseye10
    @mouhamedseye10 6 років тому +10

    Wallahi dieureudieuff

  • @juniorba2352
    @juniorba2352 6 років тому +1

    Thiey Yalla souniou sénégal bi legui moy lolou

  • @hawacheikhkane5003
    @hawacheikhkane5003 6 років тому +2

    ALLAKHOUAKBAR😭😭😭

  • @saidouverygreatbuatouray2968
    @saidouverygreatbuatouray2968 6 років тому

    I mean ya Allah it's true because it is a good woman every Muslim used to have like her make all my to give her the highest Paradise

  • @oumoundiaye5184
    @oumoundiaye5184 6 років тому

    😭😭😭thieye Sénégal 🇸🇳 doyna ware rip

  • @sarrmohamed2971
    @sarrmohamed2971 6 років тому

    Merci

  • @lesastucesdefabee7458
    @lesastucesdefabee7458 6 років тому +3

    Ndeysane on n se rend mm pas compte k reseaux sociaux yi seytane dafciy lakhassou telmak k maintenant lou niaw rk laci niit yi df...ragalatugn YALLAH si dara tiey senegal

  • @kalidou6634
    @kalidou6634 6 років тому

    Heureusement ba kèn amoul lokko sikeul..lèpam dafa lèer Masha'Allah.

  • @fatoupouille5536
    @fatoupouille5536 6 років тому

    Laisser la se reposer en paix senegal legi barina seytanéak ignorant yalla nako yalla yeureum

  • @albachir5343
    @albachir5343 6 років тому

    Diadieuf oustaz caddu amna solo senegal dale moy lolou

  • @talibecheikh7628
    @talibecheikh7628 6 років тому

    Man lima diakhl moye messagge privès loutakh miute gén gnimouko yonè tamit dè mandou wougnou. Yalla na yalla yokou aye lèram ta barsakhou mag dji di deukou wayam

  • @talibecheikh3434
    @talibecheikh3434 6 років тому

    Bilaay wallay kii ngaa khaamé soutoura laa bougoun ngeen dii envoyer aay audio waaakh ngaa deeug sokhna sii

  • @yayounabi3797
    @yayounabi3797 6 років тому +35

    Walahi deuguela lou weer gua wakh

  • @oumiousmaneseneciss5802
    @oumiousmaneseneciss5802 6 років тому

    Machallah

  • @ndiayekane7780
    @ndiayekane7780 6 років тому

    Amine wayyyyyyyyy

  • @dalyndiaye2036
    @dalyndiaye2036 6 років тому

    Vraiment 😭

  • @adjandiaye2078
    @adjandiaye2078 6 років тому

    Walahi dama rousse ndax l'I dafa niaaw audio prevé diambour rawatina ki guéne adina lousi séne yone bagn koy partagé ragal léne yallah té khol liniouy déf léne moniou waar Mouy nioù nianal KO mais pas diko perturbé

  • @diamrek7803
    @diamrek7803 6 років тому

    اللهم اغفر لها وارحمها وارحمها

  • @walysow7868
    @walysow7868 6 років тому

    Soxna sy ziar bouwerewer bayilene ak yalla Lou way déf bopam dara yaguoul mom royoukay la wone naniouco gnanal yalla amiiiîîine barkey borom touba ak khaside yii Sénégal merci

  • @bgsonsthriving.
    @bgsonsthriving. 6 років тому

    Amen

  • @kalamou2917
    @kalamou2917 6 років тому +1

    ahhhh wa sokhna kokou moudone wahh nako nianalll kaye mo partager vocall biii mo def leepp lou meuntii am rek mome mokoy gadou nahh koulay msg ba wahla ni li secret leu hopital lay continuer noum def ba vocal bi tass???????

  • @ndoumbendime7028
    @ndoumbendime7028 6 років тому

    Non Sénégal loutakh mandou wounou ay way gnianal léne ko té kham ni rawna gniou bari yalla na yalla yokou léram

  • @mamannguenar6725
    @mamannguenar6725 6 років тому

    bilay ma mère a dit exactement la MM chose jour bimuy deglou vocalam watsap

  • @khadijaba6464
    @khadijaba6464 6 років тому +11

    Franchement c'est pas respectueux de la part de ceux et celles qui le partage c'est pas cool bilahi psk si sa continue ça va aller plus loin arrêter bilahi respecter au moins son âmes... si elle était là elle n'aurait jamais aimer qu'on partage ses msg là bilahi

  • @oumarsall2297
    @oumarsall2297 6 років тому +6

    Amine

  • @diaynabagueye6436
    @diaynabagueye6436 6 років тому +3

    Machalla wakh ji rafetna trop nitt nie amou niou sotoure

  • @fatougfall2376
    @fatougfall2376 6 років тому

    Thiey Senegal inventé rek, qu'elle repose en paix Amine