kaddouy Ousmane sonko yi ci thiowou reew mi

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 120

  • @sohiboudiop4894
    @sohiboudiop4894 День тому +40

    Man dei d'accord nàa ak Ousmane sonko si limou wax ni dou suivre média You Sénégal yii puisque média you Sénégal yii dara lou am ndiérigne doun̈iouko wax wala n̈iou binde ko wax diou amoule bopou amoule guéne képpou lan̈iouy waxtané matin midi soir heure bii warôôn na fékue débat économie yi ak santé publique bi ak enseignement bi di takarnasé niouye waxtané wa Pastèf naka lan̈iouye déf pour reassure sen projet bii fii ak fii lan̈iou wara jàar borom xam xam yi di n̈ieuw si plateaux yii . Mais média yoo xamni soi-disant journaliste ak ay chroniqueur niofaye neik di wax lo nior ak lou n̈ioroule n̈ionou Sénégalais bou niak jot sax dou lénen suivre waxoula ak première ministre bo xami lin̈ioy xaar si mom dou jëex Ah média yii nan̈iou yékati débat public bi mo geuen

    • @sav7558
      @sav7558 День тому +2

      Mane mi damaléne guedeu wayé dou té lougnou wara yeuk dou reutieu

    • @Modou9021
      @Modou9021 День тому +1

      Ousmane sonko médias Senegal la wah wala réseaux sociaux?

    • @mme02
      @mme02 День тому +3

      Je suis tout à fait d’accord avec Sonko thi loumou wakh ni dou suivre réseaux sociaux yi,parce que de 1 on l’attend sur tellement de choses après c’est lui qui doit rendre compte à la fin,et de 2 il est très informé sur les priorités.Il l’a dit quand il disait que barth avait acheté des minutions pour la compagne électorale.

    • @bassiroudiouf3273
      @bassiroudiouf3273 День тому +1

      Lolou la dé ​@@mme02

    • @Modou9021
      @Modou9021 День тому

      @ réseaux sociaux gnio ko fall . Wolof nene kou fatai loula fall folila day gaw tai gni defagougnefi dara ba parai yekh. S’en yekhaye mo tah gayi sathieu sougniou haliss daw gueni rewmi ils devraient fermer les frontières depuis la premieres semaine de leur mandat . Je ne pense pas que ce gouvernement fera grand chose années dafa gaw nagniou gaw on a besoin d efficacite et d efficience wala dagnio teulai

  • @MohammedPadane-v7f
    @MohammedPadane-v7f День тому +2

    Jërëjëf Baay Booy❤Vive Sonko❤Vive Sénégal🎉

  • @Saliou_deme99
    @Saliou_deme99 День тому +3

    Maa chaa allaah baay Momar Yal na sunu boroom YÀLLA dolli la wér guddal saw fan

  • @hadytobe7126
    @hadytobe7126 День тому +11

    Salam Serigne bi dila ziar bu bakh di raféte lou kaddu yi.
    Toutefois vous devez comprendre que PROS est dans une autre dimension loin mais alors tres loin de ses détracteurs.
    Comme tout bon senegalais qui se respecte il ne reste pas insensible aux critiques, invectives et attaques sur sa personne, loin de là.
    Seulement contrairement à bons nombre d'entre nous, il opte pour le calme et non la reaction spontanee.
    Il s'agit là de la marque des grands.
    Tous et toutes celles qui l'ont écouté avant hier doivent lui reconnaître sa capacite incroyable à communiquer et et à apaiser les esprits.
    Comme tous je suis contre cette nomination de cette femme. Mais apres la sortie de PROS j'etais plus que rassuré. Quiconque l'a suivi et ecoute sait que l'homme est honnête et véridique. Comme il l'a si bien dit d'ailleurs, vous ne pouvez pas opter pour une rupture radicale placer des personnes avec qui vous vous etes battus, traversé raz et marées et intempéries et ne pas leur faire confiance.
    Serigne bi sachez que PROS a en vu d'autres, en a vu des vertes et pas des mûres et pourtant l'homme est toujours debout et plus déterminé que jamais.
    Les patriotes ainsi que toute personne dont le souhait est la reussite de nos nouveaux leaders et celui du projet à travers le.referentiel Senegal 2050 doivent s'élever au dessus de la mêlée.
    Respectueusement.

  • @adam-fp8qk
    @adam-fp8qk 16 годин тому

    ❤❤❤❤ MachaAllah imam deugu rek mo woor

  • @mamadoufaye9962
    @mamadoufaye9962 21 годину тому

    Machalah sama papa sama sope sama kharite elhadji momar diagne wakha tinga degue yapnala yalla dolè same dolila are yokou faneyi ak weur gui

  • @khadytraore4954
    @khadytraore4954 День тому +20

    Ouztas gnanalale sama papa foumou nekeu yalla nako fofou gueneule foumou diogué AK bolome dioulite gnoufi diogué

  • @dieureudieufeboroometouba9156
    @dieureudieufeboroometouba9156 3 години тому

    Pere say khéti deug bilahi kéneu meunouci dara yala nala yalla goudal sa fane wéral la katanal la vive le senegal

  • @khadytraore4954
    @khadytraore4954 День тому +2

    Ndeyssane sama papa yalna ko yallah yeureum té khareko aldiana mome dé dawoule tédeu té djissoule gneupe

  • @sav7558
    @sav7558 День тому +10

    Wakhoul ni métiwouko aussi nakh wakhnako si sorties you bari diap sonko saga chaque jours yayam famillam moye wanéni métinako sauf ke mouni diégualé na wayé lissi desseu senegalais yi gnoko mouna diégualé pas mome. Kone boul wakh dafani métiwouko kougnouy saga des années et des années té doula méti . Un jour sakh si walf keuram ziguinchor néna pierre edouard khana dagnou fokni sonko mome dou niteu badou yeuk dara nakh louné gnou ték ko sama déreu bi. kone nga khamni.saga yi métinako sauf quil est leader il doit pas flancher devant les gens mais ce qui est sur moye sou wété nakarlouko

  • @mactargueye4075
    @mactargueye4075 День тому +12

    Père nga balma dafa wakh ni louko métila kone dégloul bou bakh!

  • @cheikhoufofana9491
    @cheikhoufofana9491 День тому +2

    Macha ALLAH.
    Le service de renseignement est là pour ça.

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 День тому +4

    Il faut aussi dire que la sortie de Sonko a apaisé la situation, recadré les Patriotes,divulgué la vérité, reconnu sa part dans l'erreur de cette nomination et surtout il a défendu le président de la république en tant que institution.
    En outre, le fait que nous avons un leader communiquant en temps de crise est fort salutaire. Macky ne le faisait pas même pendant les plus grandes émeutes.

  • @rockayathiam526
    @rockayathiam526 День тому

    Masha alah dieureudieuf amatina soloo yalana sa diame yague thie barké SAW amine ❤❤❤❤❤❤

  • @almamyhaere502
    @almamyhaere502 День тому +2

    Salam alaykoum.
    Je suis totalement d'accord avec vous.
    Depuis Lyon je vous souhaite bon courage

  • @Ezekiel-p9m
    @Ezekiel-p9m День тому +2

    Tout à fait d'accord avec Vous Serigne Momar Diagne, ma sha Allah

  • @Adjibara-t9z
    @Adjibara-t9z День тому +2

    Pére li oussmane sonko wakh moy deug si média sénégalais yi diaroul sétane mane mi sakh doumalén sétane 😮ta oussmane waxoul douma yeug li xew si réwmi mais dafa ni douma yeug gniy wakh si mane lou niaw lépp mais sa wakh dji amna solo

  • @ndiobandiaye3932
    @ndiobandiaye3932 День тому +4

    Sonko il a bien fait de sortir

  • @cheikhmodoubadalgning7139
    @cheikhmodoubadalgning7139 День тому +6

    Deugue d'où rombeu aye nopeu , dieureudieuf serigne momar diame yalna sa diame yague vive le senegal ❤❤❤❤

  • @mamemorgueye5657
    @mamemorgueye5657 День тому +2

    Mach'Allah père amatina solo❤❤❤

  • @aliniang7452
    @aliniang7452 День тому +1

    Sama papa torche ladane yor di khol bakham amna koufinekoul douteud mouk taguissoul tout le monde

  • @habibdiallo7194
    @habibdiallo7194 День тому +5

    La neutralité n'existe pas. Le cœur a toujours un penchant. Concernant les épouses,Dieu nous dit:Vous ne pouvez pas les traitez à égalité quand bien même vous en avez le désir.(sourate 4,verset 129)

  • @sidydemba8
    @sidydemba8 День тому

    Belle analyse Père comme d’habitude machallah. Cependant je pense que Sonko a bel et bien compris le message que les patriotes ont voulu envoyer au gouvernement. S’il a jugé nécessaire de sortir pour apaiser les tensions c’est parce que affaire bi nior nako. Malgré les erreurs de casting commises, au moins reconnaissons pour la première fois,on a un gouvernement qui écoute la clameur du peuple. Rien que cela. C’est déjà un grand pas. Ils feront plus attention à l’avenir. Le fait de dire qu’il ne lit pas les journaux et ne suit pas les médias est juste une expression mais si Pastef est arrivé à ce stade parce qu’ils étaient déjà en avance sur bcp de choses qui se tramaient même souvent à l’intérieur du Palais pour ne pas dire qu’ils sont extrêmement informés.
    Pour ce cas précis de la dame, c’était pas évident. Bcp de sénégalais ont lu ses posts choquants ces 3 derniers jours pour la première fois.

  • @amdysene1305
    @amdysene1305 День тому

    Dieureudieuf baye Momar Diagne ❤peine de mor rek yalla monou eup yeurmandé thi diam yi fouf té lolou la wakh

  • @Salimata1000
    @Salimata1000 День тому +6

    Un homme d'état doit avoir au moins la synthèse de tous les journaux de son pays sur sa table chaque jour...

    • @cheikhndiaye7767
      @cheikhndiaye7767 День тому +1

      @@Salimata1000 D'accord mais avec des journaux sérieux

  • @idrissadione7279
    @idrissadione7279 День тому +2

    Djieureudieuf mon pére ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamadoukecoyebalde8142
    @mamadoukecoyebalde8142 День тому +1

    Que Dieu te bénisse père..doundal 110ans

  • @babacarfall3677
    @babacarfall3677 День тому +1

    Dieureudieuf Serigne Momar.
    Lègui sakh la wara gueuna renseigné en temps que premier ministre.
    Fok gniouy déglou niou melné Yaw.

  • @MohamedlamineNdiaye-w8z
    @MohamedlamineNdiaye-w8z День тому +1

    Aleykum salam warakhmatulahi Serigne Momar Diagne yalna nala yalla diapalé té wéreulleu Sénégal 🇸🇳 ca kanam inchallah

  • @MgGueye-f9v
    @MgGueye-f9v День тому +3

    SONKO à raison lire des journaux ou regarder la Télé ou on parle de toi vraiment c'est la peine mais si c'est une émission où on parle des choses sérieuses pour le développement du pays il le suit et c'est normal quant à le problème de la femme on peut pas connaître tout le monde ou suivre tout le monde

  • @barthsarr8010
    @barthsarr8010 День тому +1

    Macha allah le vieux

  • @mahdiceddo4205
    @mahdiceddo4205 День тому +3

    Maacha ALLAH Père

  • @cheikhsadiboutoure1909
    @cheikhsadiboutoure1909 День тому +1

    Je pense que cheikh momar ousmane sonko sou wakhe ni dou lire journal dou setane télé. Tere wouko mou ame renseignements. Ndakh médias yi fi nek gnome renseigne wougnou informe wougnou li si eup nak.

  • @YoroSarr-f8u
    @YoroSarr-f8u День тому +1

    Machallah kadou yi rafetna

  • @marieheleneberre8736
    @marieheleneberre8736 День тому +2

    Diabote bounek warnga surveiller seye dôme ndakhe likhewe thi dekeu bi doynawar.

  • @moustefendiaye73
    @moustefendiaye73 День тому +1

    Pour mane sonko édulcoré discours par rapport ak media. Si xel dé limou beugeu wakh moy media Sénégal yi amouniou bèneu diaragn té douniou jokhé informations you bakh yi

  • @tvkanekanen9251
    @tvkanekanen9251 День тому +2

    ❤❤❤❤ماشاء الله

  • @aliounembaye2005
    @aliounembaye2005 День тому +1

    Pourtant il a précisé ,
    Même nous,on regarde pas la télévision sans nous interesse

  • @thianendiaye6363
    @thianendiaye6363 День тому

    Sama Serigne magui ziar di contane thi vidéo bi yarebi dalna famou dane dale Machaala yalna yala fayela yiiw Amine Yarabi ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @assanegning9240
    @assanegning9240 День тому

    Amna solo

  • @cheikhndiaye7767
    @cheikhndiaye7767 День тому +4

    Je suis tout a fait d'accord avec ousmane sonko .comment peut on ecouter une presse qui fait toujours de la manipulation

  • @thiamkandjimor4348
    @thiamkandjimor4348 11 годин тому

    Justice pour bocar samba dieye

  • @SuperMoujtaba
    @SuperMoujtaba День тому

    Belle analyse Saïd Momar. Barakalahou fi Koum 🙏

  • @thialamdiallo4327
    @thialamdiallo4327 День тому +1

    No meuna sétané télé 📺 yo khamni souba ak ngone yow lagnouy togué Dila wakh lou gnaw 😢

  • @cheikhabdoukarimpouye8459
    @cheikhabdoukarimpouye8459 21 годину тому

    C'est une grosse erreur de ne pas suivre les réseaux sociaux ' ya de bonne fois qui donnent des informations exactement sur ce qui se passe dans notre vie quotidienne

  • @ndeyerokhayandoye4599
    @ndeyerokhayandoye4599 День тому +1

    Li ousmane sonko wakh deguine la c'est à dire lou bone douko deguelou

  • @OmarDiouf-zj7hd
    @OmarDiouf-zj7hd День тому +1

    ❣️❣️❣️❣️❣️❣️

  • @khadytraore4954
    @khadytraore4954 День тому +2

    Diereudieuf Ouztas ❤❤❤

  • @hawasadio3608
    @hawasadio3608 День тому +2

    C est que la responsabilité des parents est engagée un enfant ne doit pas être dehors sans les parents ne soient au courant.

  • @khardiop2732
    @khardiop2732 День тому

    Bilahi wakh nga deug. L’analyste le plus éclairé du Sénégal.

  • @directionlaboratoires2223
    @directionlaboratoires2223 День тому +1

    c'est une manière de dire que je ne regarde pas tout jusque ce qui m'intéresse

  • @barhamediouf7475
    @barhamediouf7475 День тому +1

    Machallah

  • @gagnesirysylla2752
    @gagnesirysylla2752 День тому

    Responsabilité bi si parent yi la😢

  • @mealex-g8v
    @mealex-g8v День тому +3

    Deug rek nga wakh père Diagne. Noon yi sen pexe bou sotiwon dougnou jel ngour gi. Comme des sentinelles on veillera à ce que les pourfendeurs d’hier sans vergogne n’accèdent à aucun poste. On le dénoncera avec force.

  • @alphadiop8898
    @alphadiop8898 День тому +1

    Que dieu te donne longue vie de santé amine

  • @AbdoulakhateGueye
    @AbdoulakhateGueye День тому +1

    Vraiment. Dieureudeuf

  • @mikekamara1803
    @mikekamara1803 День тому +3

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mordiop2961
    @mordiop2961 День тому +1

    Dieuredieuf sama torendou amatina solo

  • @diakhlenaa
    @diakhlenaa 22 години тому

    Deug rek nga wakh Gorgui!

  • @sav7558
    @sav7558 День тому +3

    Pape bilahi réseau yi kouléne topeu do ligey. Mane sama bopeu depuis 4 mois bayina tik tok wagni fb nakh détails you gnak fayda do ame vie surtout sagakate yi ak sosseu kate yi

  • @NdiagaNdiaye-g7e
    @NdiagaNdiaye-g7e День тому +1

    Media yi la wax ak resso yi

  • @Sidydiagne-24
    @Sidydiagne-24 День тому +1

    Màch alla serigne momar diagne

  • @aboubacardiop8804
    @aboubacardiop8804 День тому +1

    Dieuredieuf

  • @babaloum7872
    @babaloum7872 День тому +2

    Bilayi pape wakh ga degue de

  • @joyfulness80
    @joyfulness80 День тому

    Président ak premier ministre lèp lou khèw ci deuk bi khamnaniou ko ndakh renseignemlents généraux yi beus bou sètt niou tèk informatilns si sèn table. Liniou kham sakh askane wi khamouniouko. Mane lima comprendre moy détails yi nèk ci réseaux sociaux yi ak presse bi la beugue wakh.

  • @thiamyaha2958
    @thiamyaha2958 11 годин тому

    🙏🙏🙏🙏🙏🇸🇳

  • @revolution6609
    @revolution6609 День тому

    Khékhal leu baparé gua leukeulo ak sama noone mome, kéneu douko naguoul kéneu.
    Je ne le ferai pour personne, encore moins pour un chef d'Etat, aussi sacré qu'il puisse se penser. Aucun Etat ne mérite que l'on se sacrifie au combat pour ensuite se faire narguer par ceux qui voulait te tuer. Wakhtane wakh deugueu thia leu.

  • @boubacarbarry3387
    @boubacarbarry3387 21 годину тому

    Kalimatoul hag 🇸🇳♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👍🏿

  • @Bysidi26
    @Bysidi26 День тому

    mom deug rekk yallah hamnako

  • @souleyeniang1496
    @souleyeniang1496 День тому +2

    Assalamou aleykoum
    serigne bi Oumane wakhoulne'nakharihouko waye' je'gale'na la wakh.

  • @khadidiatoumane4059
    @khadidiatoumane4059 День тому +3

    Mâcha allah❤❤❤❤❤❤❤

  • @momartaalajoob
    @momartaalajoob День тому

    Baay Momar maa rafetlu say kàddu te di la jaajëfal, di sàkku ci yaw nga def vidéo ci li ndaw si wax ne Sëriñ Tuubaa, Maalig Sy, Baay Ñas, Limaamu Laay, ñoom ñépp ay Fuutanke lañu, te réew mi ñi fi baax yépp ay Fuutanke lañu, vive pulaagu) jàpp naa ne kàdduy boddikonte rekk la wax ak luy tasum réew.

  • @PapeThiam-j9m
    @PapeThiam-j9m День тому

    C'est que je dis sur tik tok si un état dis qu il ne savent se qui se passe dans le pays c'est très grave et c'est la deuxième fois qu'il dis ça

  • @aminatadiaw9283
    @aminatadiaw9283 День тому

    C vrai c est une négligence parental e concernant cet affaire de viol et meutre de la petite fille...

  • @Fulani965
    @Fulani965 День тому

    Ousmane Sonko deh mo geuna kham li khew si réseau sociaux yi 😂ndakh kouko sandi baat dinala ko delo donc mingui setan di liir li khew 😂

  • @goradiop4395
    @goradiop4395 День тому +1

    Vraiment vous devez être Son conseiller

  • @Demecheikhououmar
    @Demecheikhououmar День тому

    Vraiment papa dieura dieuf sonko dafa diome Lou mané khew sénégalais yi kontan nogne

  • @aminatadiaw9283
    @aminatadiaw9283 День тому

    Une presse de ce système qui manipule...

  • @amdysene1305
    @amdysene1305 День тому

    Pros da wara kham lithi rewmi nay setane télé

  • @FatimaTHSND
    @FatimaTHSND День тому +1

    Al oustaze, je vous invite à réécouter le discours. Il me semble que vous avez commis une erreur dans votre analyse. Il n'a pas dit que ces insultes ne lui ont pas fait mal.

  • @dieureudieufeboroometouba9156
    @dieureudieufeboroometouba9156 3 години тому

    Wax deug yalla pour nga regler probleme yi il faut nga xamlén wax deug yalla

  • @salamou1
    @salamou1 День тому

    Il a même sous entendu le cas de Lamine Ndiaye aussi d'après mon entendement.

  • @cissendeyeawa2616
    @cissendeyeawa2616 День тому +1

    Ay diabarame naque

  • @djilydiop7560
    @djilydiop7560 День тому

    14:39

  • @CheikhNdiaye-t3y
    @CheikhNdiaye-t3y 11 годин тому

    Rafte na lololo ame na solo 8:54

  • @ElimaneNdao-tf6dn
    @ElimaneNdao-tf6dn День тому

    Les parents de diary ont une grande responsabilité sur sa mort Concernant pastef fadilou keita mo wara wagni sa communiquation il parle mal lou dieum si sonko je suis en phase avec toi kilifa gou tolounou ni sonko da wara xam li xew wakhouma si rewmi mais si adouna bi Bouma amone ndogal pere yangui presidence wala primature bilahi kou beug deug beuguela

  • @benomarcoulibaly836
    @benomarcoulibaly836 День тому

    Je ne suis pas totalement en phase avec ce que vous dites, car il ne dit pas ne savoir ce qui se passe dans le pays. Il dit qu'il ne connait pas tous les gens qui l'ont attaqué par ce qu'il ne regarde pas la télé ni sur les réseaux sociaux, je pense y a un amalgame sur ses propos. Mais il sait ce qui se passe dans le pays.

  • @mamethiernodieng5067
    @mamethiernodieng5067 День тому +1

    Per yaw kon kou lirol journal d'où kham lo xew lolou Moy l'an ta yaw amna Lou wakhon thi journaliste Sénégal yii

  • @cherifhassaneful
    @cherifhassaneful День тому

    Sonko nena da nio dagg video dikoko yone yo-yo lay khol

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d День тому

    10h sakh gouddina papa wakhal 6h defko wara fekke thi ker

  • @khadidiatoumane4059
    @khadidiatoumane4059 День тому +1

    Ousmane warnaâ déguelou vidéo pa momar diagne

  • @senegalaise1
    @senegalaise1 День тому

    Man d bilayi dotuma dénoncer dara bulen néxei sax ñu nommé macky sall sama yon nékatusi

  • @aboubacardiop8804
    @aboubacardiop8804 День тому

    Il n'a pas dit que métiwouko,au contraire.

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 День тому +1

    Loutakh mou daw?
    Doffoul dara dalouko daa daa saaysaay reck.

  • @paapnjaay1586
    @paapnjaay1586 День тому

    Gis nga nguur gii ci tànki tas yaakaar la ñu ne. Nan ngay tabbe nit ta gëstuwoo jukko ja ba mu méngoo ak li tax ñu fal la yaw🤔 Yénn yi doyadi ak yab nit ñi manu koo weesu. Fal ñoo xam ni ñii bu Senegaal doon réew ci kaso bi la ñuy ba nóppi ken du wax. Loolu ay caaxaan la rek

  • @toubabnelljoop9528
    @toubabnelljoop9528 17 годин тому

    Est ce que ns ne sommes pas envoûtés quelque part ,ce pays est d'une grde convoitise n'est-ce pas ,ensuite ns sommes trop exposés vis à vis de l'étranger ,allons décortiquer please.Trop de mysticisme ds ce pays ensevelis de cheyatines ,pour des musulmans ,sommes de véritables croyants.

  • @habibsenghor3779
    @habibsenghor3779 День тому +1

    Djaredjef, père Diagne.mane déh Sonko diakhal nama. Ndakh nite gni, djeunmeume atakh gnouy mére, mome mou néné degno wara mougne ?

  • @Diopmamoune483
    @Diopmamoune483 14 годин тому

    Pour dire vrai Ousmane Sonko discours bi daff ci deff erreur de communication plusieurs fois.

  • @makhtardieye8261
    @makhtardieye8261 День тому

    Lolou erreur la bou kilifa Sénégal you Bari di wakh nitt manoul djité mbolo AK fi jamano tollu nan duma sétan télè duma lire journal

  • @mbayewade7978
    @mbayewade7978 День тому

    Metti na ko waayé ni rek la ko mana waxé ndax leegui n̈eup la jabooté