Merci ,Djumbori la situation du prophète n'est pas comparable à cette situation en plus pourquoi Aissatou penda porte elle un cheveux si l'islam est sa référence
Dom yalla ko yor ..... mandoulèn .... mbiroum yalla daffa kemanè .... man guisna kou am 55 ans di indisposè ( tant qu elle voit ses regles ..... elle peut avoir un enfant ) .... Dieu seul sait ..... ragallen yalla
Yen mandou bakhna ...yalla na seybi barké mm a 90ans c possible d'enfanter car rien né impossible à DIEU
Ay way bayilen togn ragal yalla
Mandoulen si seuyou diambour ils sont majeurs et vaccinés.
Khana dolen ay dioulit bayilen wakh bi thiey senegal
Merci djoumbarry ,ya wakh deug , Sénégal dagnuy fonto seydina moukhamed!
Djombory il a parfaitement raison
😅 bahilen togne 🙏heureux ménage Aissatou Penda Diop 🙏❤️
Merci ,Djumbori la situation du prophète n'est pas comparable à cette situation en plus pourquoi Aissatou penda porte elle un cheveux si l'islam est sa référence
Aissatou meune nako wouteul gnaarail,mbaa yaayam wouteulkoko,mais baayi laine diaambour yi gnou seuy moo gueuneu ndiaaloo
Lolu moye deug deh..nyi takhawalu dunyu chi wakh deh
Tak koula mak sounnah la
Sénégal rek gnoko metil
Heureux ménage la wakh
Linga wakh deugla dé mais li djimbory wakh deugla ngay top souna ba paré di sett té sett da haram . Doyna war
Seye dou yefou nitt..yefou YALLAH la
Dom yalla ko yor ..... mandoulèn .... mbiroum yalla daffa kemanè .... man guisna kou am 55 ans di indisposè ( tant qu elle voit ses regles ..... elle peut avoir un enfant ) .... Dieu seul sait ..... ragallen yalla
Effectivement
Merci djimborry femme bi domarame la .djiko thiaga la yorre
Jimbori tay diom nga boy bi mene ame bénén diabar ta seye amoul age Sénégal mo méti
Djimbori je suis parfaitement d'accord avec toi pour la première fois
Bilahi Jimbori wakh ga deug…. Yaw mome deuggeu rekk nakk
Il ya cœur brisé, il ya carrière brisée
Vous n'êtes vraiment pas sérieux dans votre émission. Le mariage est sacré.
Khadija est plus âgée de 9 ans au prophète Mahomed
Je ne crois pas en la voyance mais en amour ya pas d age
Pourtant djiguene yi toujours ay khale you ndaw nioy seuy ak ay paa niatta khalé you djiguene you am 24 ans nioy seuy ak mak bou am 45 ans
Vous avez raison ay esaculations laye weur
Djimbori mii mo mana fene rek histoire bimiy netali nii ay fene rekla
En amour ya pas d age
Yeen yenay ay nafekheu deug vraiment dolen niou bakh yeen dolen sakh ay nitt lii nguen waron ko rafetlou ndakh fratala ngueni wakh lii
Djimbori vraiment aujourd'hui je suis désolé mais déconné ngua trop respecte la maman au moins pour ta maman
Bayilen diambouryi..taniou debat ci Aziz dabala 😢..ma am lomeu metti.
Seul Dieu sait. Mandou ...
Djimbori magui ni amna 50 ans bo beugue gua nieuwe
OUSSEYNOU yow tamitt koula bayi
Vraiment yén ay nitt you bone nguéne wa séni wakh you gnaw yii nguéne amci lane
Dafko lugueye dou nene yagui yob sa dom mouy diang ba paré ga kidnapé domou diambour
Sokhna khadidja amone na 4 dômes ak seydina mouhamed.ter mere bi ménopause na bou yagg donc boulen comparer.
Li cas la 😂😂😂
Mére Daye seye ak pa moguena rarétt
Dôme yalla mo KO yor mandoulene
Doussi messeu am diabot qui menaupose na
Ragalale yalla
Tu n'a rien compris dôme yalla mokoy diokhé a n'importe quel âge
C vrai a 54 ans la femme est en menaupose
Pas tjrs
😂😂😂😂
Mère bi koumou teudé di rajeunir la beugue
Mére bi dh mokh sama ndeye nio yam
54ans mènopause deug.
Vous n'êtes vraiment pas sérieux dans votre émission. Le mariage est sacré.
Vraiment sister gni vrais de yefer laniou