Balla Gaye2 limou wakhe Modou lo Niawwna Trop Daf Ko Saga..; Fadam2 eclate touti, Li Dafa niaw Trop

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 8 лют 2025
  • La #luttesénégalaise #fadam 2
    ✅Abonne toi pour ne pas rater mes vidéos ✅
    Chaîne UA-cam

КОМЕНТАРІ • 132

  • @doffdouweer3686
    @doffdouweer3686 6 днів тому +5

    Fadam deel wakhe yeffou niit ..diakhasse rek gua meune ..dara doussi AM INCHALAH

  • @bachirvd619
    @bachirvd619 5 днів тому +2

    Nokou nit mou rawla waw amna kane 😂😂😂

  • @MbayeDiouf-vv3jg
    @MbayeDiouf-vv3jg 6 днів тому +12

    Balla gaye 2 ak ama kassé ❤❤❤❤

  • @molaminmanneh-fs6wn
    @molaminmanneh-fs6wn 6 днів тому +5

    Balla gaye 2 kasse💯✌️❤❤❤❤❤

  • @DjilyBara
    @DjilyBara 6 днів тому +11

    Fadam beugu nala seytanè bou fiertè thi loumouy def

  • @MohamadouMangassouba
    @MohamadouMangassouba 5 днів тому +1

    Balla Gaye dafa ❤beug ama badlé ❤

  • @AbdoulayeDiouf-lx5hq
    @AbdoulayeDiouf-lx5hq 6 днів тому +33

    Ama baldé day daan franc dém thi Modou lô daan ko nek maire de parcelle inchallah 💚❤✌

  • @khadimfall979
    @khadimfall979 5 днів тому

    BG2 rekk ❤❤❤❤❤❤

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 6 днів тому +1

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @MamoudouCamara-e3g
    @MamoudouCamara-e3g 6 днів тому +9

    Ballaa guaye mo Dane modou lo ba paré diko togue beutt

    • @fallou57
      @fallou57 6 днів тому +1

      Y’a meun fén Modou mo wakh balla tontou gay doul

  • @MouhamedNiang-y6x
    @MouhamedNiang-y6x 5 днів тому +1

    Inchallah ❤

  • @YacineSeck-n6n
    @YacineSeck-n6n 6 днів тому +10

    Dane diko weur waw amna

    • @MantaDiop-v3k
      @MantaDiop-v3k 6 днів тому

      Insby sawaye mokaye weurr ndakh moko thiokass digloule khadim gadiaga😂

    • @bachirvd619
      @bachirvd619 5 днів тому

      Waw amna 😂😂

  • @PendaTalla-c5z
    @PendaTalla-c5z 6 днів тому +2

    Balla khol bi mo nakari mo fi takhawone di doul nane Modou Lô dou meusseu dég roi des arènes doul yoyou moko top ba tay ndakh kou doul sa keur goro geuthie fa féne yi la défarate ni😂😂😂😂

  • @Jnrjoop
    @Jnrjoop 6 днів тому +11

    M Modou Lo yayam wakhnako ni mou bayi beuré ak balla gaye 😂😂😂 🫢🫢🫢🫢 Wa bakhna

  • @abdoulkarimdiop9806
    @abdoulkarimdiop9806 6 днів тому +12

    Thiéy radjim 😅😅😅😅😅

  • @Deggou
    @Deggou 6 днів тому +2

    Modou mo maay balla mou guéné loumou tewone bil xoolam meme bouy wakh ci modou ak xool bou tangue laay wahé c koi son bleme?

  • @MohamedMbaye-rz1gh
    @MohamedMbaye-rz1gh 6 днів тому +3

    Fadam mo geuneu ndy seytané si adouna😂😂😂😂

    • @tayk4304
      @tayk4304 6 днів тому

      Khamb tal rek lafi neké 😂

  • @DakarPulse
    @DakarPulse 6 днів тому +3

    Gnoun gno beuréwoul ak Gaindé bou maguette bi😂 tek na Modou beut trop

  • @Medzo3510
    @Medzo3510 6 днів тому +9

    Nokou nitt mou raw la waaw amna😂

    • @MouhamedCissé-j9d
      @MouhamedCissé-j9d 6 днів тому +1

      Yéne amoléne diomm 😂 dangéna faté djouteul bi xana

    • @hamidoutall9134
      @hamidoutall9134 6 днів тому +2

      ​@@MouhamedCissé-j9dyen aussi diotou nguen deh contre Eumeu

    • @MouhamedCissé-j9d
      @MouhamedCissé-j9d 6 днів тому +2

      @@hamidoutall9134 ya djoutou et djouteul 😂 c différents

    • @DethieDioufFissel
      @DethieDioufFissel 6 днів тому +1

      ​@@MouhamedCissé-j9dmerci 😂👍✌️

  • @awacgueye2771
    @awacgueye2771 6 днів тому +3

    Balla gaye n est pas un sportif un bon sportif doit avoir un gros coeur et n insulte jamais. C est lui qui a commence les salamaleck et modou lo a repondu par un seul mot.

  • @serignediop6995
    @serignediop6995 6 днів тому +7

    Balla Gaye emeu sen fila nangam tan ndayame, nangam tanat ndayam
    Niou dioxakh ko avance mou dello ko😂😂😂

  • @Soppénabi
    @Soppénabi 5 днів тому

    Thieuy Fadame 😂😂😂

  • @zeke5071
    @zeke5071 6 днів тому +1

    hana kon si lou Yallah binda Balla Gaye Eumeu Sene ak Bombardier la si gena ragal. Bayi len sen Thiahan yi Ki Dane Balla niari Yone Modou lo mor kor Dane Niari yone

  • @Actualités-s2m
    @Actualités-s2m 6 днів тому +7

    Supportaire you Modou lo Nio xamoul balla mais Modou lo yaboul balla 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @dieuysoune6833
    @dieuysoune6833 5 днів тому

    Fadame sa numero la sokhla

  • @KaneArman
    @KaneArman 6 днів тому +4

    Balla kesse ❤❤❤

  • @BayedjibiNgome
    @BayedjibiNgome 5 днів тому

    Moudou lo❤

  • @BabacarTouré-y8k
    @BabacarTouré-y8k 5 днів тому

    Fadammm vrai satan gua😂😂😂😂

  • @P4t5R
    @P4t5R 6 днів тому +6

    Modou lo bou danei balla gaye dou neikh. Ba taye balla mokoy meune nakh 2-1 laye nekk. Balla ancien lion na deime tokk ak empereur bi

  • @MouhamedCissé-j9d
    @MouhamedCissé-j9d 6 днів тому +11

    Gayi Modou Lô a 5 défaites 😂 ( Balla Gaye 2fois, Bombardier, Baye Mandione et Siteu)

    • @Deggou
      @Deggou 6 днів тому +1

      Lolou seen wakh la teu balla sakh saloum saloum dako dane archive yagui fi madione peux etre, mais siteu mesoul dane modou...🎉

  • @mamegorcisse3436
    @mamegorcisse3436 6 днів тому

    Merci fadame

  • @BathieDiaw-c8l
    @BathieDiaw-c8l 6 днів тому +6

    Beugue comba bou takhawe djiaroule sayetané bou bari bi li d'où rombe spor

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 6 днів тому +3

    😅😅😅😅balla gaye tamit eumeu séne dane nako ngourou Abdoulaye Wade dane nako ngourou maki Salla 😅😅 gayndé gou maguétgui dagua nékh

  • @ndeyakarisma3445
    @ndeyakarisma3445 6 днів тому +1

    Balla seul ❤🎉🎉

  • @AhmadaJadid_Diop
    @AhmadaJadid_Diop 5 днів тому +2

    😂😂😂😂 non fadam seu niveau seuytané ak meune diakhassé dafmaa yeim😂😂😂

  • @ladianepathe5637
    @ladianepathe5637 5 днів тому

    Kon dh dou dann ken si adinam Inchala balla modou Lo douko meuss dann Inchala

  • @doffdouweer3686
    @doffdouweer3686 6 днів тому +1

    Combat modou LO vs balla dotoul AMATI GARDE TON ENERGIE FADAM POUR ALLER AUX TOILETTES😂😂😂😂

  • @mouhamedfall7362
    @mouhamedfall7362 5 днів тому

    Lolou 😂 4 / 2 la modou contre les 4

  • @AzizAfieu
    @AzizAfieu 6 днів тому

    Fadam day fene

  • @P4t5R
    @P4t5R 6 днів тому +3

    Modou boul beurei ak balla so ko dieulei ma bayi la. Balla deimal deif force bi si Sa thies stp

    • @fallou57
      @fallou57 6 днів тому

      Y’a koy Diokh dépens nopil way

  • @MohamadouMangassouba
    @MohamadouMangassouba 6 днів тому

    Nn Fadam ake Buur saytané naniou waahh 😂😂😂😂😂

  • @khadimseye9364
    @khadimseye9364 6 днів тому

    Fadam dafa nékh mdr🤣🤣🤣

  • @CoumbaSall-o7t
    @CoumbaSall-o7t 5 днів тому

    Modou lo mo ko togne té mom kham na né Balla Gueye dou wane batt bipéna kou bari crédit nak 😂😂

  • @berengermpamy1819
    @berengermpamy1819 6 днів тому +3

    Franc dina daan Ama, daan Eumeu Sene, daan Balla Gaye bou sobbé Yalla 🙏🏾

  • @zeke5071
    @zeke5071 6 днів тому +1

    Loutakh Balla Gaye delor Advance sou Eumeu Sene.😂😂😂😂😂

    • @khadimseye9364
      @khadimseye9364 6 днів тому

      ana avance binguay wakh

    • @zeke5071
      @zeke5071 5 днів тому

      @ Larj kor Balla. ni mou top modou lo teh mor kor dane eska dou kor topeh Eumeu bi kor dane purr leral.

  • @moustaphadieng3658
    @moustaphadieng3658 6 днів тому +1

    Thiey radjim 😂

  • @GayeSylla-gt9ks
    @GayeSylla-gt9ks 5 днів тому

    Balla gaye n'a diapali sa thiess mou ko war

  • @Cliffordosa4847
    @Cliffordosa4847 6 днів тому +6

    Billahi wollahi wa talaahi souma monone guise modou lot dina dane balla gaye beu toke chikawame Billahi wollahi wa talaahi

    • @ababacarsadih8030
      @ababacarsadih8030 6 днів тому +3

      😂danga nékh déjà yaw guiss modou lo rek problème la pour yaw nga beug xam koumpeu 😂

    • @ndeyakarisma3445
      @ndeyakarisma3445 6 днів тому

      😂😂malheureusement kou mer tanpis niouneu balla rek

    • @Rassoulsports
      @Rassoulsports 6 днів тому

      Yaw ya nekh khaw ma sénégalais Lou takh mou nekh yaw yangi am temps bay neke si ay réseau sociaux nitou Yala amoul Diot diamou Yala rk moy yitem mais dou tekou ken

  • @SerigneFallouDiompy
    @SerigneFallouDiompy 6 днів тому +8

    Ama baldé ak balla gaye ay domou ndey lagne

  • @Bakelsen99
    @Bakelsen99 6 днів тому +6

    Modou lo tapéte déye dawe tapha😂😂😂 tine

    • @saliouwade5483
      @saliouwade5483 6 днів тому +1

      Saway tapha mome dou mbeur

    • @Bakelsen99
      @Bakelsen99 6 днів тому

      @saliouwade5483 loutakhe mouye dawe tapha tine ragale boureuye sa thiés ossi

    • @IbrahimaSokhna-f9q
      @IbrahimaSokhna-f9q 5 днів тому

      Yaw eskeu wergha

  • @thiernodiallo2830
    @thiernodiallo2830 4 дні тому

    Oncle fadame mané dioutal lo sobougéu mou entrainé bo déee dou mouna ndane balla billahi wallahi tallahi barki sering saliou beu adouna bii touky mousse ndane balla 😀😀🤣🤣🤣🤣🤣😭😭😜😜

  • @Cliffordosa4847
    @Cliffordosa4847 6 днів тому +2

    Nekkoma senegal 🇸🇳 actuelment mes beugeu diote fran ake modou lot jai une conseigne bou important na modou lot ake fran diote message bi

  • @cheikhciss5549
    @cheikhciss5549 6 днів тому

    Iow fadam nékkal nitt meuno dokh si xélou modlo séytané nga balla gay na may boys yii chance

  • @Actualités-s2m
    @Actualités-s2m 6 днів тому

    Bayıl Modou lo mi ngay nakh pour mou dieul balla😂😂😂 wayé yayou Modou lo douko nangou 😅😅😅😅

  • @lhommediagne7179
    @lhommediagne7179 6 днів тому

    Fadam gnou bolé léne gnom gneup dane n'a wa pikine AK guédiaway yeup gneup fanc doumaléne daneléne inchalah

  • @boyndiayemichelin5493
    @boyndiayemichelin5493 6 днів тому +1

    Modou lo yatoni sa popu sa imame gui yamaleko parscel Balla manoco djite dala doutal diakhanal la bodon djigen Balla embel nele Bou yage😂😂😂😂 Merci beaucoup Balla gaye 2 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😅😅😅😅😅❤❤❤❤❤

    • @yaramfall6996
      @yaramfall6996 6 днів тому +2

      😂😂 dégu loulén doff bi môme bobou ba légui yénay wakh saway né ték bén pick rek lalén sandi guén door Di dieufrou kén dou môme the king 🥰 xaragne lo késsé

  • @AmethNdiaye-t7h
    @AmethNdiaye-t7h 5 днів тому

    Balla moy lamb

  • @Cliffordosa4847
    @Cliffordosa4847 6 днів тому +2

    Bayil di diahaseu senegalais yui iow ake bourou geuweul

  • @SegaNdiaye-w1o
    @SegaNdiaye-w1o 6 днів тому

    Seytanè dhé euleuk kene douko moy

  • @PhenomeneTV830
    @PhenomeneTV830 6 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @PhenomeneTV830
    @PhenomeneTV830 6 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤

  • @karfasonkodrame8079
    @karfasonkodrame8079 6 днів тому +2

    Modou bayille fawzeyni bakhna

  • @ndiayeibrahima9876
    @ndiayeibrahima9876 6 днів тому

    Fadam yaw ak balla sa data yaye

  • @BayefallouNdiaye-k8x
    @BayefallouNdiaye-k8x 6 днів тому +1

    Balla dafa reww

  • @AmidouMbaye-b8o
    @AmidouMbaye-b8o 6 днів тому +1

    Modou lo Ama dotoul Amm

  • @abdoulayediouf665
    @abdoulayediouf665 5 днів тому

    Fadam safara kene douko oupou nay rafet way goor dou netali

  • @JullediopDiop
    @JullediopDiop 6 днів тому

    bayil doul yènay diakhasé mbeur yi sén communication Dara bakhoul

  • @kheuchfatygeneralloupapedi3484
    @kheuchfatygeneralloupapedi3484 6 днів тому +1

    Aye fadame seutou iblisse bi 😂😂😂😂😂😂😂

  • @cheikhtandine3899
    @cheikhtandine3899 6 днів тому +1

    Birame Yacine

  • @serignesall3257
    @serignesall3257 6 днів тому

    Vérité absolue Baye madone avait modou lo Siteu aussi à fait la même chose .

  • @cissecisse5622
    @cissecisse5622 6 днів тому +1

    BALAGAYTUTUS

  • @cissecisse5622
    @cissecisse5622 6 днів тому +1

    Balllagayetutus

  • @AtoumaneSow-ec5jv
    @AtoumaneSow-ec5jv 6 днів тому

    Sayitani

  • @issaleye154
    @issaleye154 6 днів тому

    Ya rient entre balla et Modou Balla fait son travaille il saitm il faut un troisième combat son stratégie ses mètre Modou orgueille pour qu'il ne recul pas

  • @ahmadoudeme6513
    @ahmadoudeme6513 6 днів тому

    Fadam seytané gua c pas balla qui ne supporte pas Modou mais plutôt Modou lo supporter woul balla et que tu dit que bala mo wakh Lou niaw kou deug sa waw kham ni Modou gua supporter

  • @mameelbachirdiallo7925
    @mameelbachirdiallo7925 6 днів тому

    Fadam nopaloul Modou lo dotoul beurék balla gaye inchallah

  • @mistercarter467
    @mistercarter467 6 днів тому

    Fadam bul wakh loutakh balla meunul diriger mod’lo… au contraire mod’lo mo ndey rancunier khol beii boone meunul diriger balla meussuko wakh lou rafett domram leuh.. mo fou balla tassei ak mom torokhal koo

  • @alassanedabo2341
    @alassanedabo2341 6 днів тому

    fc seytané yaw akk buur😂😂😂

  • @Actualités-s2m
    @Actualités-s2m 6 днів тому

    Modou lo tapét la day daw tapha tine

  • @lhommediagne7179
    @lhommediagne7179 6 днів тому

    Bane boume bamou dagué mo yague

  • @mouhamadba5609
    @mouhamadba5609 6 днів тому

    Fadam bayiléne séne titre seytané yi, juste pour des vues diarouko ish

  • @MoussaMbaye-fm7ud
    @MoussaMbaye-fm7ud 5 днів тому

    Balla dou sportif. Na roye si eumeu séne danenako 2fois ta masouta arrogant envers lui
    Lii motakh intellectuelle yi di khéeb mbeuri lamb yi

    • @PaOuzz9
      @PaOuzz9 5 днів тому

      Saway modou lô mo togne balla tontou ko eumeu ak balla diamou lagne sékh 😂

  • @djibingom5668
    @djibingom5668 6 днів тому +1

    Modou dafa koumacé sofff légui na méle nimou mélone rk mé daye forcé ligui koi