Vous avez absolument raison Mr le Maire, une ville doit être organisée! Seulement prend en compte le soucis des commerçants, que les cantines soient accessibles et qu'ils comprennent eux aussi que le développement exige certaines mesures. Bonne continuation!!!
Nitt gni bolé topé do ligey il se fou rien pour deuk bi nek si réseau sociaux yi dila khass continuel si liga nek boul deglou ken Tivaouane mérite une nouvelle visage !
Yaw bounou sonal gamou 3 jour la bayil nitt gni niou liguey sof nga trop borom keur yi si sen bounte keur lanou yaksr nguir mana défar s'en frais gamou
Mane dh amna louma metti trop bilae sama yaye thi marché bi dogue la yakaron pour doundeul aye diabotam sama papa febar bilae marché bi dogue la yakarone metti na ba fou metti yamm bilae
Vous avez absolument raison Mr le Maire, une ville doit être organisée!
Seulement prend en compte le soucis des commerçants, que les cantines soient accessibles et qu'ils comprennent eux aussi que le développement exige certaines mesures. Bonne continuation!!!
Merci beaucoup monsieur le maire Diop Sy Yallah naa borom bii motalii yenè yii
Mr le maire Diop Sy liguey rk nga xam❤
Machaalla
Machallah Demba Diop sy wakhjdi amatina sooloo de❤❤❤
Machalla machalla❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
Manachalla
Diop sy dieufeul rk boul deglou niou sokhor di wakh bonne continuation
Djiddah môme bokoul tivaouane😂😂
Nitt gni bolé topé do ligey il se fou rien pour deuk bi nek si réseau sociaux yi dila khass continuel si liga nek boul deglou ken Tivaouane mérite une nouvelle visage !
Li mom dou développement
Diop sy do nitou dara
Ki loumouy wakh niii
Daguay défar d'accord mais dagua koyy tékkk thi yone
Et pourquoi guéne khar ba gamou gui dioubb siii guéne thii dogua takhaww
Té guéne thi warone takhaw 2mois avant gamou.
2: boull wakh nii gni nékk thi talibé késsé guéne yeukati
Legui gni nék thi biirr Marché guéne todjieu ko lolu pour lane laaa en plus dioté wouniou dara akk talibé.
DIOP Marché bii thiowwww bou beuriii laaa gnii taww niaka tawww daniouy toyyy prck figua léne yobou bakhoul dara
Maire bo xamnè Gamou ba Gamou rék gua koy guiss Lou liguéye
Yaw bounou sonal gamou 3 jour la bayil nitt gni niou liguey sof nga trop borom keur yi si sen bounte keur lanou yaksr nguir mana défar s'en frais gamou
Mane dh amna louma metti trop bilae sama yaye thi marché bi dogue la yakaron pour doundeul aye diabotam sama papa febar bilae marché bi dogue la yakarone metti na ba fou metti yamm bilae
Machalah Yalla deff mou diabote bilae dafa dioy ba febar walakhi
Li mom dou développement