Net Tali: Immigré, Les Blancs le Payent Pour Thioukoum Ndiaye | @nettalitv

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 67

  • @legeographe221
    @legeographe221 2 місяці тому +25

    Ki daa toppu bakanam rek. Yangi fowé sa life

  • @Etvabcd
    @Etvabcd 2 місяці тому +22

    Yagui thiagatou dhé top sa bakane rek toub thé déllou thi yallah

    • @MamadouDiop-v7t
      @MamadouDiop-v7t 2 місяці тому

      Yow thiaga bou gor nga fatalikul say wadiour khaliss bi dafa harame

  • @alioundome4131
    @alioundome4131 2 місяці тому +13

    Chaque jour gua danou legui gua deh

  • @ElhadjThiam-p7x
    @ElhadjThiam-p7x 2 місяці тому +10

    Salut sokhna Fatou wa Atlanta yene rek lagnouy topou bonne continuation

  • @Khadyjasow-y8j
    @Khadyjasow-y8j 2 місяці тому +3

    MBA xam nani gnogui koy 🎥 filme rek 😢

  • @MaguiDiallo-wk6xy
    @MaguiDiallo-wk6xy 2 місяці тому +13

    Ki defa yebaté😊

  • @MamadouYam
    @MamadouYam 2 місяці тому +5

    Boost naturel bi amna solo

  • @Rouchdi-z1i
    @Rouchdi-z1i 2 місяці тому +4

    Moy yalla rék wayé bakhna
    😢😢😢

  • @obietrice4620
    @obietrice4620 2 місяці тому +1

    Akh bakanam la topp rek

  • @Cheikh621
    @Cheikh621 2 місяці тому +3

    Je te conseille nga dèm feneen sori foofu yëpp, moo xam da ngay changé région wula pays. Parce que fi wak yaa ngi Took foofu gëmuma nga bàyyikoo ndaxte sa xél mi da ci dèm foo tollu
    Nga changé localité nak fu sori foofu yëpp la wax dinala dimbali so ko bëggee...

  • @IbrahimaThiandoum-p7t
    @IbrahimaThiandoum-p7t 2 місяці тому +3

    Mes Fatou wadji mome doyna waar dè 😂😂😂 way ki mo bone waye😂😂😂

  • @khoudedjisoumare9213
    @khoudedjisoumare9213 2 місяці тому +2

    Toubale délousi yallah

  • @salioutine1983
    @salioutine1983 Місяць тому +1

    Neko nay faral di wor tey ñann yalla yalako yalla sopi

  • @ElzoDiallo-q3k
    @ElzoDiallo-q3k 2 місяці тому +3

    Nice

  • @makhfousetoure9550
    @makhfousetoure9550 2 місяці тому +6

    Na toop ta delo si yàlla ta Na taak soxna Senegal yobo ko fofo

  • @ndiayelamine109
    @ndiayelamine109 2 місяці тому +8

    Lou yomb bakhoul en plus koudoul halate bamel loula nekh defal

  • @dembasamb5549
    @dembasamb5549 2 місяці тому +3

    Sa waye mane lima djiakhall lo giss thi toubab la Khamoull ak djigènu sènegal yi nga khamni ma challa ,gènn al thi li nga nèck topou sa bakhane la rèkk

  • @BounamaDoumbia-se5jx
    @BounamaDoumbia-se5jx 2 місяці тому +1

    Thieye ndiouku Ndiaye diakhalenema

  • @lilzilo
    @lilzilo 2 місяці тому +1

    Alhamdoulilah ❤

  • @MbayeSeck-s4r
    @MbayeSeck-s4r 2 місяці тому +2

    😮😮😮😮😮

  • @ABDOUTAMBEDOU-v7i
    @ABDOUTAMBEDOU-v7i 2 місяці тому +1

    Sokhna fatou mangi ba Gambia way yaw lay toppu

  • @gassndoye6712
    @gassndoye6712 2 місяці тому +4

    Wakhoul DEUG dh bodone diouli wahtou dou moye yalla malako wakh

  • @leyemoussaliou5583
    @leyemoussaliou5583 2 місяці тому +2

    😂😂😂😂😂😂 na bayi thiakhan yi

  • @aissataba2398
    @aissataba2398 2 місяці тому +4

    Laisse Ca et demande pardon a dieu. Dieu ta donnè ta santè et la possibiltè de partir en europe tandis que tes freres meurent dans la meditèranèè.travail halis bou lew allah def thi barkè.arrete ca la vie est ephimere mon frere

  • @lemeringue-fi2zf
    @lemeringue-fi2zf 2 місяці тому +1

    Ki mo bone 😢😢

  • @ngagnedeme-w2t
    @ngagnedeme-w2t 2 місяці тому +1

    Guawal guéne ci lii. Xaliss ak banekh diarouko. Essaye de trouver une relation sérieuse qui peut aboutir au mariage. Si tu veux relation sérieuse, c'est pas sur ces sites car les adhérants sont là pour le plaisir. Dans les lieux publics, tu peux draguer et essayer d'avoir une relation sérieuse.

  • @Mouhamed-vz7hy
    @Mouhamed-vz7hy Місяць тому

    Naye Wooor taye niane yalla sopiko😢

  • @cheikhdiop8801
    @cheikhdiop8801 2 місяці тому +1

    Billahi di ngako rèthiou bayil li ngay dèf thi ay thiakhane rèk la nèk

  • @damesene3761
    @damesene3761 2 місяці тому

    Wayer dawoul reck

  • @amadoubarro9713
    @amadoubarro9713 2 місяці тому +2

    Akhirou jiamane

  • @ibrahimadia2290
    @ibrahimadia2290 2 місяці тому +1

    En tout cas dé beurilé barekélécko geune té dereum bou léwe mo geune un milliard bou léwoul Na toupe té guéne si limou neck Sinon dina yakke dinéme Niacke Santéme té lolou daraye Adouna diarouckofi

  • @FatouDiop-jf9bw
    @FatouDiop-jf9bw 2 місяці тому +1

    😅 0:50 😊😊

  • @wanealpha1965
    @wanealpha1965 2 місяці тому +2

    Da yabate

  • @CheickneSacko-p4q
    @CheickneSacko-p4q 2 місяці тому +2

    Na takk diabar fofou té bayi site bobou... topou liguey yame sokhna Fatou sa liguey rafette na.

  • @aramebangoura7057
    @aramebangoura7057 2 місяці тому

    S'il te plaît il faut partir loi😮

  • @astoumaguettesissokho32
    @astoumaguettesissokho32 2 місяці тому

    Waw yow bo heuyé guis sa bop si Internet bi say mbok guisle loy wakh toubab meune nagnou la filmé té doko ham déloul sa hél mi si yalla semaine yi mélni mois. Mois yi mélni att kone la vie est courte démal thi liguéy bi ngua amone guéne si vie bigua néké

  • @adamasall-bw7yo
    @adamasall-bw7yo 2 місяці тому +1

    Dafa aram

  • @ElhadjiIbrahimaDIOUF-cv4lt
    @ElhadjiIbrahimaDIOUF-cv4lt 2 місяці тому

    Qu il se desinscrit du site, regrette ce péché avec un repentir sincère et essaie de se marier.

  • @AidaNdiaye-r4e
    @AidaNdiaye-r4e 2 місяці тому +1

    Sokhna fatou siarnala

  • @gueyemoustapha9230
    @gueyemoustapha9230 2 місяці тому

    Limoy def boko bayiwoul sankou laye daf mom mingui wakh ligueyem mais miko téré ndilo nak n'a bayi xéll si bopam mou khamni mome dou toubab limoy Daf boko bayiwoul dina gate fan wala mou gade weurseuk té limouy daf mingui diay bopam Di doundé lolou mousibala nako bayi té diapou ligueyem témoiu takeu diabar bouko défoul dina ko réthiou

  • @bass3165
    @bass3165 2 місяці тому +2

    Lou ame la masi kham dara

  • @altesseroyale4383
    @altesseroyale4383 2 місяці тому +2

    Li moye tiaga international 😂😅jeune yi deuglou yi fékhé lène ba boulène seytané dougue ba nguène danguène di dème europe pour déf lou melni ndankh beugue alale bou gaw! Mome néna dou teude ak goor, bo teudé ak goor ak diabar am kou goor ki ak yow sène awra dafa lalanté té dieukeur ndawsi lolou la si beugue😂😅! Ki sathieu na film bi. Bodémé sakh dafa déf na pornographie, ta so démé teunde na ak aye goor! Tchiiiip ya dougale sa bopp ci seytané!

  • @ibrahimasall5417
    @ibrahimasall5417 2 місяці тому

    Lane Moy yakh bou reuy😅.
    Lolou ci djiko la,bayil foyé sa khel.europe djiguen yomb n'a fi.sokhlawoul doug ci site pour am djiguen.en plus wakhoulo ben yon sam sa diné,sa liguey ak khalis kessé mo lo yitel.
    Khalatal sa diguente ak sa borom.takal ci khale yi,té bayi thiakhane.

  • @RamaSy-s1e
    @RamaSy-s1e 2 місяці тому

    Vraiment je ne comprends pas pourquoi il amène sa dans cette émission il joue sa vie il doit arrêter sinon ça finira mal merci

  • @AliSy-t8w
    @AliSy-t8w 2 місяці тому +1

    12:57 😂😂😂😂

  • @damesene3761
    @damesene3761 2 місяці тому

    Bisness by amna khaliss amna nakh nakh

  • @extremeownership5223
    @extremeownership5223 2 місяці тому +1

    En tout cas beugue lou yomb baxoul Europe bofi gnewe samal sa bop ndax toubab yi kou lene top si sene vice digua sankou yalla bossi dieule yome

  • @HousseyNouWade
    @HousseyNouWade 2 місяці тому

    Mane soumou conseil legui mou guisse séquences amme cii sites yii khawma feke toubab lou wokh time is moning na khar rek

  • @BintaS.Camara
    @BintaS.Camara 2 місяці тому +1

    😂u are crazy. Sorry

  • @MouhamedFall-dk7uw
    @MouhamedFall-dk7uw 2 місяці тому +1

    Fatu Bayil xél ni ay kilifa dane lay suivre ki dafa bone rk diaroul sakh netali

  • @AbdouCamara-d5f
    @AbdouCamara-d5f 2 місяці тому +1

    Cv

  • @ndiakhattseye7523
    @ndiakhattseye7523 10 днів тому

    Thiaga bou goor

  • @AbdouCamara-d5f
    @AbdouCamara-d5f 2 місяці тому +1

    😂

  • @abdoulayeseck96
    @abdoulayeseck96 Місяць тому

    Yalla noppina bou yagg lepp miggui si alkhourane kholale ndakh so douggeulé sa lokho si safara noumouy moudié

  • @OusmaneDiallo-wk3jc
    @OusmaneDiallo-wk3jc 2 місяці тому

    Toubab Dafa bonne déé Aka bary fi thie Espagne danguay tassé ak couples Kou goor ky wakhe la sama diabar Dafa âme envie teudeu ak Africain gneuweul ma Faye la ngua teudeu ak môme touki Kat dawa wara moytou Lou bary khalysse bi sa ndiabot dy lék Dafa wara léw

  • @zizouzidane7332
    @zizouzidane7332 2 місяці тому

    Yagui yakha sa adouna en plus alal diou salte gay leka en plus bari bakaar soral de adouna yagoul

  • @mouhamedndiaye8810
    @mouhamedndiaye8810 2 місяці тому +1

    Quel est l'interêt de raconter l'histoire d'un gigolo, vous cherchez seulement des vues à la fin

  • @babaniang3990
    @babaniang3990 2 місяці тому +1

    Yawe danguaye kharou

  • @SayeFall-b6k
    @SayeFall-b6k 2 місяці тому

    Diguako rehtou de yakhgua saboppde toubal tegua wor

    • @senegal2
      @senegal2 2 місяці тому

      Yaw dangaye thiagatou

  • @scoutmaiba9584
    @scoutmaiba9584 2 місяці тому

    D'abord nàngul ni dagay cagatu, ndax lo lu gay def ni 😢.
    Suppriméel site bi te concentrewu ci sa ligéey. Numéro bi ga ci def saniko ci poubelle.
    Bës bo ci dajéek ku la ci jiigne viole de, dotoko defati.