AL KITAB DU 03 FEVRIER 2023 AVEC OUSTAZ ALIOUNE SALL, OUSTAZ ALIOUNE MBAYE ET SERIGNE MBACKÉ SYLLA.

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 3 гру 2024
  • Suivez le journal de Sud Fm, la Revue de Presse.
    Ne Ratez pas Ndeki li, Wakhtanou Fadiar, al Kitab, Objection
    Visitez notre Page Facebook / senradiosud
    Notre Site web sudfmsenradio....
    Suivez le journal de Sud Fm, la Revue de Presse.
    Ne Ratez pas Ndeki li, al Kitab, Objection, Wakhtanou Fadiar et d'autres émissions
    #sudfm #radio #actualité

КОМЕНТАРІ • 64

  • @cheikhounaniang5845
    @cheikhounaniang5845 Рік тому +2

    Machallah Sama oustaz yi émission bi amna solo lool

  • @barrafall3051
    @barrafall3051 Рік тому +1

    Machallah xam xam rek mou wour wallahi daguay xam yalla xam adouna

  • @Pullo1able
    @Pullo1able Рік тому +1

    Machalla. Jazak'Allahu khair. Yalla fayal nu leen. Merci depuis USA!

  • @talibechiekhsopnaby3401
    @talibechiekhsopnaby3401 Рік тому +2

    machàallah sama gnatti OUSTAZ yi Goudou fan ak wér

  • @tafacisse7340
    @tafacisse7340 Рік тому +9

    Machala Sama soppé Yi meilleur émission Tay mom dama tardé direct bi Wa argentine 🇦🇷🇦🇷🇦🇷 yépp gnongi béggué

  • @mariemefall4
    @mariemefall4 Рік тому +1

    Emission bi mo Buena nékh 👍 yép ma challah

  • @sophietoudiouf2095
    @sophietoudiouf2095 Рік тому +1

    Machallah le trios je vous aime yalna Borom bi guenlen tahawou way barkeb Kitaboulahi

    • @serignemansoursyjr3877
      @serignemansoursyjr3877 Рік тому

      ALLAHOUMA AMINE INCH'ALLAH MACH'ALLAH YALLA Na YALLA Nangou Gnanëu Yii INCH'ALLAH Témou Bollégnouko Déffal INCH'ALLAH

  • @fatouseye8330
    @fatouseye8330 Рік тому

    Trop content de vs

  • @khadymborombengue2398
    @khadymborombengue2398 Рік тому

    Machaala yalla na len yalla Sam mback no may danel

  • @thiernosenegal4360
    @thiernosenegal4360 Рік тому

    Merci oh ça aller merci bac Nathalie Baye merci 🇬🇦🇸🇳

  • @bintajallow3490
    @bintajallow3490 Рік тому

    Wa Alaikum Salam Warahmatullah. Yalla naleen yalla Feyla Yiw. Ma Cha Allah

  • @Fatou947
    @Fatou947 Рік тому +1

    Yag len fi lol té andeu ak weer ak khaliss bou bari si barke seydina mohamed ❤😊

    • @serignemansoursyjr3877
      @serignemansoursyjr3877 Рік тому +1

      ALLAHOUMA AMINE INCH'ALLAH YALLA Na YALLA Nangou Gnanëu Yii INCH'ALLAH Témou Bollégnouko INCH'ALLAH SAL'ALLAHOU ALLAÏHI WA SALAM MACH'ALLAH

  • @khadimgueye3317
    @khadimgueye3317 Рік тому

    Machalla oustaz aliyun sall yalna yalla faye la takhe wola yokola sam

  • @mameastoudiop8505
    @mameastoudiop8505 Рік тому +1

    Assalamou aleykoum warahmatou Lah. Nouyou naa léén ziaar naa léén boubakh waay . Sama trio de choc bii contaane naa si yéén lool comme d'habitude. Yalla na léén Yalla lafal thiat té défal léén diam soutoureu khéweul Ak tawféékh, yok kham kham bi té wéreul baat yi🤲

    • @serignemansoursyjr3877
      @serignemansoursyjr3877 Рік тому

      ALLAHOUMA AMINE INCH'ALLAH MACH'ALLAH YALLA Na YALLA Nangou Gnanëu Yii INCH'ALLAH Témou Bollégnouko Déffal INCH'ALLAH Wa Alaïkoum Salam Wa Rahmatoullah Wa Barrakattouh Gnongi Nangou Ziarr Di Déllo Ziarr YALLA Na YALLA Nangou Ziarr INCH'ALLAH

  • @awaseck2848
    @awaseck2848 Рік тому

    Ma Sha Allah c très intéressant

  • @pendalove3582
    @pendalove3582 Рік тому

    Thanks 👍

  • @masambagueye5019
    @masambagueye5019 Рік тому

    Dégg jamono maasàllaa fatabaarakal Laah

  • @youssousow2136
    @youssousow2136 Рік тому +1

    Macha allah

  • @cheikhounandiayeseye6059
    @cheikhounandiayeseye6059 Рік тому +2

    Amati na solo ❤

  • @thianeba5922
    @thianeba5922 Рік тому

    Machalla amna solo

  • @sedibabounacissokho427
    @sedibabounacissokho427 Рік тому

    Machalla je vous aime bien amne solo

  • @cheikhka2746
    @cheikhka2746 Рік тому

    Machallah amna solo dieuredieuf yallana yalla féyal ci barké alkhouran karim ci daradiayit seyedina mouhamed SALLALLAHOU ALEYHI WA SALAM ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @awaseck2848
    @awaseck2848 Рік тому

    Deugue deugeu Oustaz Mbacké cousin wou Oustaz Alioune Mbaye Ma sha allah

  • @diengtoubamamour5758
    @diengtoubamamour5758 Рік тому

    Jërëngeenjëf !

  • @TheGadiaga
    @TheGadiaga Рік тому

    machalah wakhtane bi amna solo

  • @cheikhmbacke2919
    @cheikhmbacke2919 Рік тому

    Machalla

  • @awaboussombengue3887
    @awaboussombengue3887 Рік тому

    amatina solo bilay dieuregeundief

  • @fatoudiokhane700
    @fatoudiokhane700 Рік тому

    Machallah sama oustaz yii yalna yalla same lène inchallah

    • @serignemansoursyjr3877
      @serignemansoursyjr3877 Рік тому

      ALLAHOUMA AMINE INCH'ALLAH MACH'ALLAH YALLA Nagnou Ko YALLA Bollé Déffal INCH'ALLAH

  • @mordieng4730
    @mordieng4730 Рік тому

    Machalla amatina solo loll yalna yalla samou lene ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @modousamb1889
    @modousamb1889 Рік тому

    Macha halla amatina solo

  • @aminatadiop9572
    @aminatadiop9572 Рік тому +1

    Émission neexna lool. Yalnaleen Yalla fay.jërëjëf.

  • @morbeye4571
    @morbeye4571 Рік тому

    Magui ziyr machalla

  • @moudoudienq387
    @moudoudienq387 Рік тому

    ماشاءالله

  • @adjidiop7502
    @adjidiop7502 Рік тому

    ❤️❤️❤️

  • @ametfromgniby
    @ametfromgniby Рік тому

    🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @dialiguedieng2588
    @dialiguedieng2588 Рік тому

    oustaz goudal fane ,

  • @diouldebalde4067
    @diouldebalde4067 Рік тому

    MACHALLA YARAM DAWNA XOL SEDNA

  • @ramaba2521
    @ramaba2521 Рік тому

    Tarkala🥰😍🤩

  • @modousarr7064
    @modousarr7064 Рік тому

    😍😍😍😍😍

  • @tafadiop9946
    @tafadiop9946 Рік тому

    Walay ndeye san yalla nalen yalla defal Jammu
    Tae yokko wergui ak katan gui
    Xam xam bé Âme âme ak man Man gui goddal sén Fann
    Kontan na trop sén yén ay 2:h de matin l'ay lén de deglou

    • @serignemansoursyjr3877
      @serignemansoursyjr3877 Рік тому

      ALLAHOUMA AMINE INCH'ALLAH MACH'ALLAH YALLA Nagnou Ko YALLA Bollé Déffal INCH'ALLAH

  • @mbayefallou838
    @mbayefallou838 Рік тому

    As-salaamu allaykum jaa ngéen jëf
    Mbàkke yaw dafa melni war ngaa bàyyi xel sa waxiin ci fase rawatina jigéen guy ñaan baatam

  • @cheikhounambaye3546
    @cheikhounambaye3546 Рік тому +1

    Machalla oustaz 🙏🏼❤️🕋

  • @DIAXARTV
    @DIAXARTV Рік тому +1

    Hikma bisbi ✍🏿
    👇🏿
    Bufekeni Dangay sonn ci def lu bax 🙏🏿 xamalni coono ba dina Jeex👏🏿 te lu bax la dafay Dees 👏🏿 bufekeni Dangay def lu Boon 🤦🏿‍♂️ ngir ca bànneex rekk 😞 xamalni bànneex ba Day Jeex🤦🏿‍♂️ te bàkkaar ba Daf fay Dees 👏🏿 xoolal Wax ji ✍🏿 té bul xool 👀 nétali kat bi 🙏🏿

  • @papaibradiadie6481
    @papaibradiadie6481 Рік тому

    Yalna yalla goudël sénn fann vous nous transférez votre humeur

  • @jibyjob1457
    @jibyjob1457 Рік тому

    🇺🇸🇺🇸🇺🇸

  • @aissataba7506
    @aissataba7506 Рік тому

    Serigne mbacké 😁😁néna wadji mérnadé

  • @babacardiop726
    @babacardiop726 Рік тому

    Walay ndéyesan dangéna bakh yalna Yalla takhawou lén oustaze allioune Sall dafa beugue sougnou makk gni moo takh ma sopp ko loool

  • @ibrakibra6190
    @ibrakibra6190 Рік тому

    🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹

  • @fatouthioub4070
    @fatouthioub4070 Рік тому

    Û

  • @gayekalidou4582
    @gayekalidou4582 Рік тому

    Waaw, yaa OUSTAZ.?? dii daaw, dém Procés. Procés Sweet Beauté . Waaw, RaagaL dém, wouyou Sustisse ? Waaw. Lou ci, dinné Waakh.??

  • @maty9972
    @maty9972 Рік тому

    🤣🤣🤣🇨🇵Selem

  • @maguettethiam9858
    @maguettethiam9858 Рік тому +1

    😂😂😂

  • @modougoumabala5800
    @modougoumabala5800 Рік тому

    😂😂😂 dakh

  • @dieynababathily3244
    @dieynababathily3244 Рік тому

    Machallah ya oustaz 🙏 🙏 🙏

  • @mariakone8859
    @mariakone8859 Рік тому

    Macha alla