ki wakh ni de gniko megne si trouh yi lanou neko di dounde alkhouran ak souna yarkosi babou mana tok fi tay di wakh senegal soufi troukhyi dioge rek mou yakhou yalla na yalla goudal saw fan s khadime te weral la
@@saliousyll2527 Sa nday ak baay nékk ci lu sunu BOROOM diglewul manal a doon mukk-mukk aw lay ci nga wéyal loola. Deelul ci ALXUR'AN ci li nit ñi daan wax Yonént Yi (r A a) bu ÑU léen daan inddil lu bókkul ak séen gëm-gëm. Li ci dólli ku mooy ku baax, dimbali ma ci inddil ma tarixa buy jàngale ALXUR'AN AK SUNNA ta du ko jëfe ?
Allakhou akbar dég alkhourane néxna
Macha'Allah, Djiazak'Allahu Hayrane
Machallah ya oustaz sunna rek MBA sonnou
Wallahi Rachid dafa dégg alkhourane
Ma sha allah yalla na yalla fayla yiiw
JazakAllah Khayran
Ma sha Allah ahsanta
ما شاء الله بارك الله فيكم.
ماشاءالله بارك الله فيكم
Que Dieu te protege ❤ au senegal ❤ ya oustaz ❤
Macha Allah 🥰😍🥰😍😍😍😍🙏
Seurigne khadim ndiaye hafizahoulah
Kou yeiwén si kham kham
Amine wa iyyaka
ماشاء الله
ماشاء الله عليك يا اخي شيخ خادم
Macha'Allah
Wakh degeu yalla jaroul di diakhasei voix alkhour'ane ak sonna si wakhtan bi li d'où radio tamit
Vraiment...
Senegal yàlla naco alhour âne ak sunnah mour ndax ly rekk Kessé moy DEUG tes yàlla Nafi yàlla djeulle trouh yi di sank djamou yàlla yi tes sakhal fy sunnah
Amine billahi touroukh yi nio tardėl senegal
ki wakh ni de gniko megne si trouh yi lanou neko di dounde alkhouran ak souna yarkosi babou mana tok fi tay di wakh senegal soufi troukhyi dioge rek mou yakhou
yalla na yalla goudal saw fan s khadime te weral la
Dëgg ju wér nga wax sa waay ! Tarixa yi kay fiiwak jëlewu ñu léen fi moom, diiné ji du wér moom.
@@saliousyll2527
Sa nday ak baay nékk ci lu sunu BOROOM diglewul manal a doon mukk-mukk aw lay ci nga wéyal loola. Deelul ci ALXUR'AN ci li nit ñi daan wax Yonént Yi (r A a) bu ÑU léen daan inddil lu bókkul ak séen gëm-gëm.
Li ci dólli ku mooy ku baax, dimbali ma ci inddil ma tarixa buy jàngale ALXUR'AN AK SUNNA ta du ko jëfe ?
Machallah