Yonénte bi mo ndieukk nék Mouride, Dieuwrigne Ndiassé
Вставка
- Опубліковано 3 гру 2024
- www.x.com/@ndi...
/ birama.cisse
+221 78 437 43 77
YESLU est un mouvement culturel, économique et social dont la stratégie est de placer la philosophie divine au coeur du développement personnel et social. Notre objectif est de renforcer la formation spirituelle et temporelle des individus en s'inspirant de l'essence de la philosophie islamique.
www.yeslu.org
Mashallah am na solo. Yallah sakh mourid la. Ndax da nam niou khamko/ wala da nam khame mou bind. Kone yallah mo njeuk tokk si nam. Da beug xam beug xame. Donc nit famou djougue sori na.
Aka dégg 🙏🏽❤️
Sallalahu Alayhi wa Sallam ❤
Alhamdoulilah ❤
GRATITUE ET BENEDICTION DIEUWRIGNE NDIASSE 💖💖💖
Euskey ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
👍🏻👍🏻👍🏻
❤❤❤❤❤
Est Nay(avare) et épargne sont liés ?svp
Saway uoe soumil sa baye late bi dag sa rasta yi fèhèl nak yam sisa moussa ndiambè tè bayi yonou mourid yèn sèn serigne Serigne Abdou Late guènèko Touba
Bèn Talibè Serigne Touba boula bayi khèl xamoul diokhon kon
Bayil yonou mourid bingay lakko
Wadji wakh daye rafet, waye nit loumou am rek lay diokhe. Khana bala nioula guene dagua fay deuk. Kou deukoul wone touba nouniou lay guene. Ma ladj la , comme dano geunewone cheikh Moussa , alors kone serigne Mountakha lane larone deff Darou? Pourquoi aussi chaque annee mou djeul adiya wakeur Cheikh Moussa.
Yaw yagui wedi yalla ndakhe yalla nena loudieunk yonetoubi si ak rére la wa makka nekone wa inkano min khaplou lafi dalaline moubiine boulenfate ninak diouli ak koor ak asaka filako sala lahou hanlayhi wasalam fenk
❤❤❤