Merci à tous pour l'intérêt que vous portez à la série Kooru Biddew !!! N'hésitez pas à inviter vos amis à s'abonner à notre chaine LEUZTV d'autres surprises arrivent.
Finalement Naka la Biddeew rectifier niam bi? Elle a découpé des pommes de terre defsi wala dafa wagni nioulouk bi defsi dokh, wala wa Maggi nioy solutions bi?
Walay leçon bi dialeu neu,,couple daniouy wahtane,j'apprécie très l'attitude de Mass,,,dou tagou sa diabar mai wahtane leu,,merci vraiment bien inspiré
Merci leuztv et bonne continuation mais j'aimerais davantage que certaines séries comme buur guewel soit reprise et par ailleurs bidew puisse continuer après le ramadan
merci vous êtes tellement super bien surtout le couple mass et videw je vous aime tellement j'aimerais bien avoir une femme gentille et adorable comme biddew merci encore une fois
mère bi mouné sénégal kene khoromotoul??? mais c'est grave ça,il faut éviter le trop de bouillons,le sel contient des minéraux qui sont tres bons pour avoir une bonne santé et éviter les maladies cardio- vasculaire,telle le diabète et l'hypertension
fabinou macha allah laf thiat liguay bind tayo koo scénario bi diar na yonnn😍😍😍😍 chapo a vs les homm d l'ombre yenn gui si guinaw tax baniou meuna apprécié serie bii
Bilahi bidew amoul morom mne yalla boma ray bala korgui di diekhe darò sa lamigne bou reuye bi ndeke wakh rek nga meune Dara khamoko lo bokak assane ndiouff chim
Leuz merci d'avoir intégrer leyti aussi,Je trouve que c'est un grand comédien aussi,il est fort,Wayé mane dal daro mako beug,loumou wakh mou nekh loumou def mou nekh
Pour la première fois j commente u es une fierté pour nous les diolas bonne continuation j viens juste de voir ton témoignage et franchement j'ai eu les larmes aux yeux
Merci à tous pour l'intérêt que vous portez à la série Kooru Biddew !!! N'hésitez pas à inviter vos amis à s'abonner à notre chaine LEUZTV d'autres surprises arrivent.
LEUZTV nice série. I like it . Bonne continuation .
LEUZTV c'est nous qui vous remercions pour cette belle série..... Bonne continuation !!
Finalement Naka la Biddeew rectifier niam bi? Elle a découpé des pommes de terre defsi wala dafa wagni nioulouk bi defsi dokh, wala wa Maggi nioy solutions bi?
LEUZTV meilleure sketch TV .
Bravo Leuz .
LEUZTV nekh na trop
vraiment je pense que je vais réveiller toute la maison avec mes rires😂😂bidew est la meilleure des séries!! machallah
Walay leçon bi dialeu neu,,couple daniouy wahtane,j'apprécie très l'attitude de Mass,,,dou tagou sa diabar mai wahtane leu,,merci vraiment bien inspiré
Pp
😅😅😢
Awayy...yalla na ameu diabarr bou melni bidew way....amine ..touf touf touf
Meilleure épisode , plein de sens.bravo leuz tv
Cou d'accord ni fama meuna joué
Ndeye Diop trop sakh
Ndeye Diop trop
Yess
j'adore la tante de bidéew elle est toute mignonne et douce machallah avec sa noirceur d'ébéne
Diaarya Basse bilaye Elle es super belle
Mossane Niane Niang waxal dé
Ana fans biddew yi ma guise jaime way😘
Nganga Mbene Dieng
we all love her
manela
Hahaha Badiène elle a réagi avec Fama comme ma maman le fait avec moi quand je décide de cuisiner😅😅, dafay contente di def ay louanges rek
Merci leuztv et bonne continuation mais j'aimerais davantage que certaines séries comme buur guewel soit reprise et par ailleurs bidew puisse continuer après le ramadan
biddew est la meilleure.
femmes sénégalaises faites comme elle pour gérer votre ménage
Daro dinama raaay ! vraiment une grande actrice !!! Badiène aussi !
Mass est trop un bel homme. Ses tenues lui vont trop bien
Ki amna diabar tmt
Bidew trop propre et belle
merci à toutes l’équipe . nékh -na loole macha-hallah
😂😂😂😂 mane partie fama bi momei rayr
Mom mou gérer wagne bi yow ngua gérer farantou😂😂😂 non badienne amoul
Mais Mass mignon na waay ooh😍
LKK,WIIMHJOBWR rgb6b7n k u. Ol
Pp
merci vous êtes tellement super bien surtout le couple mass et videw je vous aime tellement j'aimerais bien avoir une femme gentille et adorable comme biddew merci encore une fois
dioumou niou dal si CASTING bi ils sont fort 😂❤☀
nekhna tropppp wayyy je t'adore bcp biddew thiey fama tamou wakh diou barriiii bakhoul hahahaaaa
Merci pour les leçons
Nafila du jour
6 raka. Dans chak raka une fw la fatiha 7 fois sourahtul likhlass
Ally Saxo merci bcp
mirabelle nioko bokk
Ally Saxo jajeuff
Ally Saxo merci j'en n'avais besoin
Penda Diop jeujeuff way
Wa bideew wakhniou noko rectifier bok 🤣🤣
20mns 1100 vues. Ah kooru Biddew nak xewna masha Allah.
Lougne rectifier nonou
-thieb bi bidew moko rectifier 😂😂
No mais Daro comme biir bou daaw 😂😂😂😂 tellement eupeul 😂
Abyssatou Diatta astakhfirollah
A Commen🤣🤣🤣
Ahahah fama dotoko defati de ahhh biddwe numero uno 👏👏👏👏
Fi sa keur la,bula nekhé tokk boula nekhé teudd 😂😂😂😂😂 mangui d 😂😂😂 badiene cheut
Meilleur sketch TV !
Ahaahhah😂😂eupna fama tamit ba diga fa def dara lou bax
vous êtes les meilleurs amolène morome
No biddey ayna dè khorom bi noumouko mana gère bamou nekh
😂 😂 billhi daroo dinama Ray
mère bi mouné sénégal kene khoromotoul??? mais c'est grave ça,il faut éviter le trop de bouillons,le sel contient des minéraux qui sont tres bons pour avoir une bonne santé et éviter les maladies cardio- vasculaire,telle le diabète et l'hypertension
waw mom mou gérer wagne bi ioe nga gérer farantou nn badiene dou dem
Retane ba kheud kayyy série douma len may dara 😀😀😀
Team Bidew 💋💋💋 dama dinama Ray kW ah badiéne rek dou yomba
Bilay daro mo eupeul rekk😂😂😂😂😂
ndeysane daro ak yaye di nagn ma ray rk
Fama du nitt ❤️😃
Badiéne mane dh Magui khorom be legui😂😂😂😂 vraiment
Team bidew limouy doyoul koume nekh
Djiguéne bousi diagoul togou kham mane bidew la wakh machallah
Ass Ndiaye bidew ne prepare pas on cuisine pour el finit c toute une equipe
Nene Mbengue
Ah bon tu penses pour moi c'est bidew dhé 😂
Ass Ndiaye oui meme c ce ke je croyais bima setanè tournage sila guiss bene fem di togue ndogou bi pour ke bidew egali
Nene Mbengue
Ah bon je savais pas 😂 Ahh d'accord mais Yaw esque aye nga monnga togou 😂
machalah ma chèrie d'amour. Yalla nala Yala lafal thiat. Suis fière de toi.
Badiene tamit limuy sagnssé temps leu dh mashallah
Sii badiéne dou nitte nénako yagui natte titouma si nawet bii
😂😂😂😂😂😂😂😂
Badiane dinamaray nénako khana dangako kinine 😂😂😂😂
biddew sama idole
biddew do nopalou dé
franchement Biddew tu es une génie
fan nala trop sakh
Fama dinama Ray 😂😂
Hahahaha daro todji na keur
Lidé lañunane kou dé sa marché ba ya tagué sa bopp sa loutakh eupeule tamite Daro môme khalasssss😂😂😂..!
Biddwe Elle est meilleure😌😌😌😌
Daro djiguéne day téyy😂😂😂
Team bb anta way mais bidew do nitt
diariyatou Gueye bi mossi dessone team bb anta sheuteut n'importe kw
samb fatou 😁😁balnala
Mane dhé sama tour biguéne di siweul rék moma méti
Bb anta brome compte bloqué bi 🤣🤣🤣
Didewe
Magui dei 😂😂😂mane badiène dal mo néhal scketch
Nonhuman unnhnsnhd.9hcnkuxmwusn q
Serie katante
fabinou macha allah laf thiat liguay bind tayo koo scénario bi diar na yonnn😍😍😍😍 chapo a vs les homm d l'ombre yenn gui si guinaw tax baniou meuna apprécié serie bii
Fatou Ndiaye ak kiye togue😂😂
Nene Mbengue bilay iow toop acteur yi rk fatei ngui si guinaw ak kiy togg waxx ga deugg😂😂😂
Fatou Ndiaye 😂😂😂bayilene rek gnouye ratatati bou souba lagnouye comprendre
Nene Mbengue bidew badienn fii ak mass niouy feulaleiiii t xamou niou nei san guisi guinaw guigay guiss douniou daraaaa
Fatou Ndiaye c ca
😂😂😂😂badiène raynama
Ayyy daro eupeul nga 😂😂😂
No teye môme bidew bi dafa alaw dawmé eup ne 😂😂😂😂😂😁😁 nékhone ne trop sakh
Sofia Kanté j'avoue trop sakh elle se ressemblent trop lol lay wax chk jr
Diop Mbene kone setlou gue lolou no teye môme content na si trop sakh 😂
Ay way bamala guissé la sama xel dal si nawétou réne gui😂😂😂😂😂
Fama lamaigne bi mokoye reye 😂😂😂
Fama reck si wagne eupna sa ma fans la nack
Bilahi bidew amoul morom mne yalla boma ray bala korgui di diekhe darò sa lamigne bou reuye bi ndeke wakh rek nga meune Dara khamoko lo bokak assane ndiouff chim
Abdou aziz Diop thieuy sama domou baay bi momeuna defantè deh. 😂😂😂
Penda Diop dom bay bidew key kouko lale rek diotma te niom beugougn bidew
@@abdouazizdiop6541 nqrfw
Jungle uh huh. You DC y v d
@@binetoudiopdiop1762 mdrrr bane langue ngay Lake niiii
ceux qui dislike c koi le but
budew dal nekhna😍❤
😂😂😂😂😂😂😂 No Fama Taye Sama Sister Bii Rk Guama Diox Bilahi Sama Yaye Gaté Ko Bamou Yakkou Cuisine Mom Nada 😂😂😂😂😂😂
khadija diangal ko cé mieu
Sabine Dasylva lol Djank Kokou Kaye Bayinakofa Yagna Djiguèn Dal Daye Mené fepp
gjigéne da wara meuné fépeu
Bo meunoul bagnou meunal la sa place doko netali
😂😂😂😂wa bidew no Def ba récupérer thiep bi😂😂😂
Leuz merci d'avoir intégrer leyti aussi,Je trouve que c'est un grand comédien aussi,il est fort,Wayé mane dal daro mako beug,loumou wakh mou nekh loumou def mou nekh
mention nullarde😂😂😂😂😂hey maman
Kxkxkxxkxx yalnaniou yalla Moussal si gathi3 bagna meune wagn
Wa fama mi mann rouss na sakh 😕😕
Ahahahaha mass nèna thiep bi biddew moko rectifié
Pour la première fois j commente u es une fierté pour nous les diolas bonne continuation j viens juste de voir ton témoignage et franchement j'ai eu les larmes aux yeux
No no fama ak badian dinanuma ray
Manam biddew nimi wakhè aythia leen bisimilah nekh loll si sama khol
O bidew faté nga jokhé courbi jattendé nga wakh si jéppu jénne bi pour ñou mélni mane
Bilahi Fama mo ratakhlé mais kenn dou Badiène nena houhou
Daro ya niak diome😂😂😂😂roussna sah.bidéw dal mala beugue ak sa ré bou néhh.
Degal badien
Nena sama khel defa dal si nawetou ren bi
Mdrrr....non badiene amoul! 🤣
Mdrrrr dieul daro ak niaway bi makhala danga teyoul😂😂😂😂
Leyti amoo bidew 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂fama dou dem
niaxxx banguii feigneuu non badiene dou niitewalahi je suis par terre
Biddew la niou wakh🇸🇳🇸🇳🇸🇳
😂😂😂😂😂😂 fama raynama😂😂😂
Chapeau à badiéne👏👏👏👏👏
Fama ya niémé gathié gathié😂😂😂😂😂
😂😂😂 Daro tué nama
Ayway yalnama Yalla May japar boumel kom biddew ameen teuf teuf
On dirait le sketch le plus Reader
Man dolen ma raýy🤣🤣🤣
badiene néna thiatt dafa viff
Ay Fama jiguen day togou
Non fama dou nitt 🍠😂😂ayyna trop sakh
Non couple parfait Daro ak leyti rek 😂
Biddew rekk dou aye caff😂😂😂😂😂😂😂
Ani wa team Bidew
bo tollé si khorom woma😅😄😄😆😂😃haa badiane
😂😂😂no koorou biddew nekhna way no badiane fama ak biddew c une équipe parfaite big up