Merci pour le message que vous avez passé pour les Modou modou et Fatou Fatou en tant que Fatou Fatou je suis contente de savoir que y’a des gens qui réfléchissent et sensibilise la population vraiment des fois daguaye découragé si comportement yi maye Guice mais bon daguaye déff reckk ta Yalla takh merci à vous pour le message je vous suis depuis Paris
Bilahi au dela de la comedie, trop vrai la lecon de morale sur les modu modu. Etant donné que je fais parti d'eux je suis heureux de voir que ya certains senegalais qui nous comprenent. boudone gnoune rk gno takh kone keine dou sonou si adouna waayei gni botou sougnou guinaaw lanouy soralei. Mouy etudiant wala salarié, senegalais yi, mbokk yi dagno warre di essayer de se mettre a notre place des fois, di dawal empathie.
Le message de ass m'a fait pleurer je te jure da nio sonou si europe bi daww ba dé pour la famille pour les amis yalla na niou yalla doli soutoureu si barkhé seydina Mouhamed psl
Vraiment contane na thi message binguén dialalé wa Europ je vous suis depui Espagne 🇪🇸Machallah ass et faudé louniouy doundou yeupp kén meunouko expliquer
Merci beaucoup papa Fodé et papa Ass une forte message nous les Modou Modou on vous remercie que Dieu vous protege et une réussite totale de tt votre projet
Walay ndeysan toki dafa mèti mane moom nama yalla bal mias sama yaye rek momay wo nèma dakh yangui ci diam mias apar mom kouma woo xaliss rèk motakh mangui top nak degue nèkhol obrigado🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Merci pour le message que vous avez passé pour les Modou modou et Fatou Fatou en tant que Fatou Fatou je suis contente de savoir que y’a des gens qui réfléchissent et sensibilise la population vraiment des fois daguaye découragé si comportement yi maye Guice mais bon daguaye déff reckk ta Yalla takh merci à vous pour le message je vous suis depuis Paris
taye mome dadio wax dek
No wax dji rafetna
❤️❤️❤️
❤️❤️❤️❤️❤️
Merci
Bilahi au dela de la comedie, trop vrai la lecon de morale sur les modu modu. Etant donné que je fais parti d'eux je suis heureux de voir que ya certains senegalais qui nous comprenent.
boudone gnoune rk gno takh kone keine dou sonou si adouna waayei gni botou sougnou guinaaw lanouy soralei. Mouy etudiant wala salarié, senegalais yi, mbokk yi dagno warre di essayer de se mettre a notre place des fois, di dawal empathie.
Le message de ass m'a fait pleurer je te jure da nio sonou si europe bi daww ba dé pour la famille pour les amis yalla na niou yalla doli soutoureu si barkhé seydina Mouhamed psl
Goudou na nekhna beusseullll j’aime
1er svp May len ma j'aime way
Ndeye mareme loy doyé j'aime 🙄 aaaahhh am nga no mel. Toute façon maynalako😂😂😂😂😂
Lokoy doyé
Niobagne way😂😂
@@adamasene7678 ahhh 🤣🤣merci beaucoup dieul nko
@@2famediatv dmafi nek di aimé rk te douma ame j'aime
Merci asse message bi pour gnounla
Merci merci Ass merci Gracias merci fodè ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇪🇦🇪🇦🇪🇦
Billahi lou leer danio sonn 🇫🇷🇪🇸 kouniou niann maniouniouko rek niou mere nioussi 🇫🇷🇪🇸💪👏♥️👍
Vraiment contane na thi message binguén dialalé wa Europ je vous suis depui Espagne 🇪🇸Machallah ass et faudé louniouy doundou yeupp kén meunouko expliquer
Bilay mon frère ay café touba madd rien touss fourass gni diguone madd legui madd amna wakhougnousi sakh
@@ndiayemariama6350 bilay made li yallah kham doyna vraiment Mane mom mbakhalou saaaloummm la nam namou ma you saf yoyu😂😂😂
@@malickgaye8347 nieuweul Maroc ma toguala bou saf bilay
@@khadyndiaye7663 Falay Tabaski sé inchallah fo nék thi Maroc lolu Dinama nékh tropp
@@malickgaye8347 bilay nieuweul magui casa
Bilay modou moudou yi dagno sonou khamna thi dara wayè yalla naléne yalla doli soutara ak mbolem djoulit 🙏🙏🙏
Amine yarabi mashallah
Allahouma Amine
Merci pour le message si Fatou Fatou yi vraiment taye dég na deugu ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
merci bc pape ass pour le soutien 😂😂😂 mounè oule diam mane dè thierè tamkharite la beug niou indalèma sou kounkandè kharè guedje djie
Modou Modou yi ak Fatou Fatou yi😃😃😃🤙💯💯
Mane fatou la toudou
Bilahi merci bcp d’avoir pensé à nous
Message bou ame solo bou nieup done khalaté ni dina bakh trope
Gno faar gnoune ak yén
Papa Ass ak papa Fodé wakhnaniou lou ame solo nitt bou yeukeuti alalame mayla war ngako remercier🙏🙏🙏🙏 wakh ji amna solo
walahi téksi alale dafa sakheu thi khol
Ww
@@BMAUDIOVISUAL bilay sen conseil bi dafa ame solo je parle en connaissance de cause meilleure episode chapeau à toute l'équipe
Mane mom koukandé lay xaar mou khaar gueidj gui ma Modou modou djiiii😂😂😂😂😂
Thi cas rék gay dokh yaw
Nonn Père Ass amoul nena ko chewing day Toubabe 😂😂😂😂😂
Mai khalé bi diougué passy Molna trop je l’aime 😍
Bilahi lolou rek lagn beug mom vraiment merci beaucoup pour message bi
Vraiment je suis fier de vous bonne continuation walahi tey dindingène sma stress bi yeup
Miemane papa ass momoy daniel merci capitale❤😂🎉😅
Merci ! Asse ak Fodé Billahie sén wakh dji guissnasi sama Bopou danio sonnu noun modou modou yi
Verrou ass yi deh comme verrou monsieur tombola 😂😂😂😂😂😂😂😂
Ray ngama
Vraiment papa ass ak papa fodé séne duo bi nékh na 🥰🥰
Mane dh magui United States 🇺🇸 la nek me ass ak fode wah guene deug si modou Modou yi bilahe mane sene number la sokha la
Wallah le message est fort yalna soutoureu yaague rekk!
Tougeul mom kou fi nekoul meunoul comp
Le message de Papa Ass c'est important 🙏
Merci grand ass pour le message 🙏
Message bi ass yaw ak fode amna solo si modou modou yi👌👌👌👌👌
Neexna trop
Nékeu léne si diam way
Depuis la banlieue parisienne 92🇨🇵
Machalla capitale seri bou ame solo la toujours dagnouy yété machalla diam si yen a toute l'équipe ✌
Jeureudieuf waay
Walay liguen wakh thi modou modou amna solo
Waww
Message yii amene solo trop nioune imigre yii sonunanu trop ousmane Dieye depui paris
Grand ASSE bilahii walahi do nitou dara😂😂😂😂😅😅😅😅👍🤣🤣🤣🤣🤣
Bravo fodè ils n'ont rien compris mais merci pour le message que tu as lancé très important je vous encourage
merci beaucoup grand ass dueg dou rombi nopou😆🤣🤣
Mercie beaucoup grand asse et fodé si message bi pour les modou modou🇪🇸🇪🇸🇪🇸🇪🇸
Ana niou beugue tons ass💃💃💃
Thi def exmens yalla na léne yalla may niépou am si barké serigne touba❤❤
Ma fille😂😂Ass dou nitt
Yii tay papa Ass wax na deug 😋 wa Coco ngani loy Sango ba am teint 😂
Merci Grand asse et pére feudé tay mome wakhal ngéne niou
Merci message bi modou bek nagnou deh Bilahi
Mame fatou tamit nice na déh teint noir bi ohhh
Très belle leçon Bilay gni neik extérieur kein doulein khalat dagnouy liguey diokhei ko dadi tokk Bilay ndaysann
Dafa méti
Billay
Bilay fodè nimouy wakhè mome rèkk moko eune😄😄😄😄
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Machallah amna solo message bi
Ass il est fort
😂Nenako Ouguiya Ak Dalassi guey bagantei Sheut 😂😂😂😂😂Mani deh
Série hier bi nékh na trop kousi d'accord na lale j'aime way
😂😂😂
Ass dou nit nénako sa kanam gui melnip gueup niii 😀😀😀😀
Merci beaucoup papa Fodé et papa Ass une forte message nous les Modou Modou on vous remercie que Dieu vous protege et une réussite totale de tt votre projet
Bilahi fodé ak grand ass sont les meilleurs 😂😂😂😂😂
1er way dou ay fo j aime bok
Non Asse amoul yagui mel né koy yéyé mbadji wala deri nak😂🤣😅
😂😂😂
Wawaw merci 🥰🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦
real talk me breda said here 🇬🇲🇸🇳🇬🇲🇸🇳❤️😘big up uno self brada ahs
Merci Ass ak Fodé yalla nalén yalla fay 🙏🏾❤️❤️❤️❤️
Ma fille😂😂♥️♥️papa ass douma rayy sheuuuuuu
Malgré la comédie ils passent des messages très intéressant ❤️ merci moi je suis Modou Modou 🇮🇹
Bilahi Ass moy Meilleur 🤣😂😂😂🤣 nn Ass dina Ray 🤣😂
Vraixcomedien ass machalla
Papa merci beaucoup pour message bi
Papa ass merci beaucoup pour message bi
Alla bonni ass nenako yangui melni kouy yey mbadjeu😆😆😆😆😆
Du talent pur
Qualité images au rendez-vous
Bonne continuation
Merci beaucoup
Non grand ass akk ay façon waham rek amoul ak foula gou mat seuk lassiy andal 🤣😂😂😂
Mame Fatou une gazelle à la couleur d'ébène 😍😍😍
BM AUDIOVISUEL
Yénefi né bilahi kéne dou papa ass daf maye raye 🤣🤣🤣🤣
Été pape ass café caféwuma li khawma lafa ngua sole khawma ms amna vacsi bu méil nonou boul wathiè sama grate té robe bu rafétt lako gnaw🤣🤣
Contane na thie message bi depui 🇪🇦🇪🇦❤️❤️
Alhamdoulilah alors
Message bi jalna mais buleen fatté le 10 août inchallah tamxarit si ngoone kunkandé day xarr geej gui 😂😂😂😂
Domou ndaye yeugo li khew annulè nagne ko
@@bijoufall3014 annuler Ku déf lolu😂
Walay ndeysan toki dafa mèti mane moom nama yalla bal mias sama yaye rek momay wo nèma dakh yangui ci diam mias apar mom kouma woo xaliss rèk motakh mangui top nak degue nèkhol obrigado🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Yén kaay massa tiono ak diarama rék lagn lén di waax
Ay foodé bayil ass 😂😂wallhi pp ass dmay ray néna sa kanam gui di Melni gueub✊🤣
Macha alla ass c vres bilahiiii
Mm faty miii no noxou naaa rafétt di oh my gods ❤❤❤
😂😂😂😂😂😂
Ass amel ngama akk bilay😂😂😂
Nourou ass meré nala dh😂😂🤌🏽
Merci pour le message grand Ass c'est très sympa waay deug rek nga wax
Ass Yalla nala Yalla takhawou
Pour la première fois Ass wakh fi leçon de vie mais fo diar mou roubei rk 😂😂neina toubab yi diapala di xoll ndakh Danga tilim 😂😂😂
Dabax Gueye t'as assurer bonne continuation 🥰♥️
Way maléne ma j’aime way beut bou rousoul toth 😂
Ass amel naniou akh😂😂
Message resu dèpuis Espagne🇪🇸🇪🇸🇪🇸🇪🇸🇪🇸 merci GRAN ASS
Merci beaucoup
Man asse la beugue🤣🤣🤣🤣
Teudei😄😄😄. Sérieux papa ass reyna ma😃😃
bouléne faté kougkandé daye kharr guédieu gui tamkharite merci
Kouy yeuy mbadji😂😂😂🙆🏽♀️
Non ass douma raye BONNE continuation plus 1abo🥰
Ms vous êtes les meilleurs capital mome mofi tékk takk meilleurs série kooru meilleurs série tabaski nangou rkkk wala bagne ❤💪
Un like si tu aime 👍 capital ❤️🔥❤️🔥❤️🔥
Mane dal wa team capitale la beugueu vous êtes les meilleurs
10 minute merci ass
ASSE notre fierté 👌😍
Bilay ass ligay wakhe amna solo trop
Diadeuf ci message bi pour modou modou ak fatou fatou yi🙏
3ème tank wouy 😂😂😂kouy yeuye mbadji kay 😂😂😂
Bilae lila toubab yi di tek sakh grawoul mais lila Sénégalais yi di tek molaye ray
Billay
Ay aas waniel no🤭😀😀😀
Waay yaw Doul😁😁😀😀😁Momay raay Baki yalla
Diadieuf ass message bi amna solo tropp ❤ mane mom yamay danél vréma