Ce genre d'ouztaaz ne comprend rien à la religion en fait. Il est incapable d'abstraction intellectuelle. Tout son savoir se limite à sasser et ressasser ce qu'il a appris depuis l'enfance. Or la religion est dynamique. De même que chaque jour Dieu est dans une position nouvelle, de même la religion musulmane épouse le temps et offre des possibilités de réflexion qui dépasse le cancre comme le petit oustaaz. qui n'ose pas aller au-delà du savoir primaire et de se pénétrer des réalités essentielles pour comprendre enfin ce que Dieu veut nous dire. Et on n'acquiert pas cette connaissance profonde et réflexive des choses si on reste sur la surface. Le monsieur, je l'ai bien écouté. À mon avis il a compris mieux que cet oustaaz ce que Dieu attend de nous..Nous croyons à la haute mission du prophète. Pour autant il n'est pas Dieu. Ce modou gueye a exactement exprimé en lui donnant son sens profond le verset où Dieu _que Sa grandeur soit exaltée _proclame que l'humanité ne Lui a pas encore donné (à lui Dieu)toute la mesure de Sa grandeur.(wamaa khadroullaahi haqou khadrhi)Votre amour du prophète vous pousse à lui donner des possibilités et des prérogatives qui restent des facultés entre les mains de Dieu et de Dieu Seul. Le prophète Muhammad (que le salut et la paix soient sur lui)était plus qu'un homme moins que Dieu :justement un prophète
Père demale liguey mo geune si yaw nga mayeniou diam modou gueye Loumou wakh deugue la chaque jour fi si sénégal nga guiss nitte wakh diwou la geume te mouso si wakh
Bayilen di yakk wakhou nit ki limou beugua wakh moy yalla rek la yakkar wanté gueum na yonent bi ta ki yonent bi yakar la yakkar modou gueye nak Bari na fi ay borom kham kham mo lén eup tawhid
Sa xam xam Bari woul dh
آمن الرسول (آمن) اي (صدق)
Bjr bien expliqué Mr Dramé merci

Merci beaucoup
Qu Allah nous pardonne Soubhana Allah Allahou Akbar
Machalla
Ponki ngeum 6 yileu gueum yalla,yonnént yi ,téreu yi ,malaka yi ,biss peinthie,dogal yi you néh ak you nahari
Merci beaucoup 🤲🏿
Oustace amo dëg Modou nène gueumoul Mohamed wayè deugeul nako nè yalla Ka yoni pour wakh la yalla dagne koye geume Mohamed dagne koye deugeul
Sawaay dine doukhel mougoude de teyal
Yaw dingua wakhe lolou?dingua doxè nonou
Mboup Ass, yay domouram pire ngua té nafékh.
Merci beaucoup waye fere
Merci
Ziare merci beaucoup diadief contansi yave ameilene diameu joubari
Salam Babacar Dramé bien expliqué merci
😭💔je t aime mohamade psl
Koudoul khalate 3 jours de bamel loula neikh défal. Alakhou akbar
Lou lér gua wax
Père demale liguey mo geune si yaw nga mayeniou diam modou gueye Loumou wakh deugue la chaque jour fi si sénégal nga guiss nitte wakh diwou la geume te mouso si wakh
Merci beaucoup waye fere
Yawe maye nala 10000 waye
QU'ALLAH nous èloigne des égarés et nous protège de l'enfer
Amine
Oustaz bi mom khép n'a xam xamxamam vraiment
Machahala Dieudieuf
Amine
Wakho fi tuss
Merci beaucoup waye fere
Bayilen di yakk wakhou nit ki limou beugua wakh moy yalla rek la yakkar wanté gueum na yonent bi ta ki yonent bi yakar la yakkar modou gueye nak Bari na fi ay borom kham kham mo lén eup tawhid
Yaw yaa mana doul lan nga xam ci rawhid Modou Gueye ak kannen walla SEN wa keur book?
Boy lii sa wax la yaw mais mom limou wax deug nanioko
Bayiil fène dafa wakhe gueumoul yoneté bii
Modou Gueye est plus pertinent et intelligent que toi
Yaw doul sa kham kham khotoul.amna ay kelifeu dine youfi wakh lou gueuna graw fouf té gueno wakh khana modou gueye nga yap.
C'est verrait baye ki xamole
Oustze yi amounou xame xame
Khamo dara
Yow demal uti ham ham degen fokneh solu sen grand mbuba b moi ham ham
Ustaz faut essayer de comprendre mm si Limou wakh kenn douko wakh ....il voulez just dire que yalla lagnouy diaamou mais pas yonentbi
WOlof néna loudoul yalla nenn la do ci wokh?
Modou gueye da hame khame khame de d
Je tme modou
Thieyyy ouztaz ci cp yi rekkkk limou wakh darrra nekoussi Lou grawww khana kou amoul deggg deggg
TU n'a rien dit. Laisse Modo Guye, je cois ses vérités.
Modou da yabater kouni gamouma yonente bi key guemo yallah
Lege wahma c Quran fu yallah wahneh nyu gom Rasullulahi huh?
Diara dieuf thi léral yii thi rér yalla nalén yalla guindi mom nak mounna am dou dioullite mo takh mou wakh limou wakh
Même toi tu parle trop
Naniou fatelikou 3 jours yignouy khaar bou euleugué
Modou gueuye foumako guiss nako diaye sama baken domou yakh tatte nga
Ki bouléne ko maye beuz c'est un mécontent toujours wakhou dof
Wax ko Macky mom mi dollel goorjigeen....
Yalla moy sounou borom sa dafa mandou yaw sa yone nekoul si li Modou Gueye do si mandou
SERIGNE BI MODOU GUEYE DAFA RERE REK YALLA NA BROME BI GEUNDI KO WAYE DOY NA WAR LOLE
Diereudieufati
Yaw warouloo wax ak kenn koudoul LAMINE samba
Vraiment ki da yab nit gni
Ki yabou niou dé c lamine samba dofbobou beug na buzz trop
Modou khamoule bopame bilahi
Lim wakh dara néckuci dégin la rek
Guyane by dafa sof
Modou gueuye daniouko warra raye domoukharam deugue la boudone ben serigne lakofi wakh niep ngui khoullo
Xana yawe nayou warra raye
Xamone dara
Oustaz mi mo gnou yab. Wadji nena geumoul yonetembi mais geumna yalla. Alors ana lougni discuter?
Donc boumou wakh kone djoulite la, amna droit bagne gueme yenenter mai na fek dou djoulite.
@@bocarwatt8056 lou lér gua wax