ABDOU BAKHOUM ACCUSE FRANC"DAFA BOUGONE SITTEU DANE MODOU LO"CLASH MODOU "SEYTANE LA MO TASS PIKINE

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 18 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 78

  • @idydiallo1585
    @idydiallo1585 День тому +8

    Encore Abdou Bakhoum 😂,l’histoire a donné Modlo raison

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398 День тому +13

    Bilahi walahi ki dou nitte kou bakh 😢😢😢maak mo xamni wakh djou ñiaw rék laye wakh 😢😢😢pabi yalla nako addouna yaar ci barké maak ñiou bakh gni 🙌🙌🙌🙌 sokhor na trop te mana wakh wakh djou ñiaw 🔥🔥🔥🔥🔥🔥😲

  • @cheikhououmargueye4989
    @cheikhououmargueye4989 День тому +12

    😂😂Abdou baaxoum dafa beug diaxassé wa parcelles comme ni pikine diaxasso pour mou mane am dara

  • @SambaMbodj-l8o
    @SambaMbodj-l8o День тому +9

    Dafa bougua parcelles melni pikine woy😅😅😅

  • @cheikhmbacke2841
    @cheikhmbacke2841 День тому +11

    Fran dina dane ama balde

  • @ibrahimadandio5827
    @ibrahimadandio5827 День тому +6

    PABI VRAI DOMEKHRAME LEU TÈ SOKHOR KHANA DO DIOULITE QUEL HONTE 🟥❌🟥❌🟥❌🟥❌🟥

  • @mamadousarr4791
    @mamadousarr4791 День тому +3

    Un vrai fou

  • @cheikhounagaye9405
    @cheikhounagaye9405 День тому +3

    Abdou Bakhoum makk bou meunn fenn la ki niakk na diom bayil soss

  • @elhadjindiaye1015
    @elhadjindiaye1015 День тому +6

    Ki doff degue leu mécontentement

  • @ZooNdiaye-x5r
    @ZooNdiaye-x5r День тому +3

    Qui dafa kate ndayame ko diakhassé bakhoul parccell dou pikine dée kéne meunou lénne divisé😂😂😂

  • @LaminaKagni
    @LaminaKagni День тому +2

    Per bayill diakhase nityi makc nga

  • @momardiallo1609
    @momardiallo1609 День тому +3

    Franc dina daan ama baldé teksi katt abdou bakhou si toune 😂😂😂😂😂😂

  • @BoubacarDiop-q2p
    @BoubacarDiop-q2p День тому +2

    Pa bi yallah toppé wouko darra😂😂

  • @bayemodoudiagne2326
    @bayemodoudiagne2326 День тому +5

    Pabou niak ndayi fayda

  • @LaminaKagni
    @LaminaKagni День тому +2

    Per bayil modou lo

  • @AssaneDiop-ln4il
    @AssaneDiop-ln4il День тому

    Pere bakhoume bilaye daiye naikhale lambe ❤❤❤❤❤❤

  • @momardiallo1609
    @momardiallo1609 День тому +2

    Abdou bakhoum danguay doul rk franc meun neu oubi sa leufeul ndéy si 0,5 tiers 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @massarsarr5746
    @massarsarr5746 День тому +2

    Abdou bakhoum dofla dé

  • @gabrielagboton5361
    @gabrielagboton5361 День тому +1

    Ki lamigne bou bonne la yorr pa bou niakh fayda ,!! Yow modou lo ballou diouk niow ci yow tallal lokho . Mais vraiment khol bou bonn la yorr bakhoum !! Modou lo mo la téré nelaw vraiment..geumo darra

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op День тому +3

    Grand meuno diakhassé wa parcelle pékhé bounê yangui koy woute

  • @modoudiop6979
    @modoudiop6979 День тому +1

    Ki kanamgui rek ngahamni domou haramla😢😢😢

  • @alalama1917
    @alalama1917 День тому +2

    ABDOU bakhoum Dangay teppiiiii sa dedioooo ndey doullllll tu ne peux pas gâcher notre esprit de groupe sa diourommmm fukkiiii data ndeyou niari wadiour

  • @josephcoly4127
    @josephcoly4127 День тому +2

    Yaw yefere nga soouniou pa ndiago yi nk souniou keur di dokher bante rek meune naniou oubi data ndeye domerame bi

  • @aichasecka-8974
    @aichasecka-8974 День тому +1

    Bakhoule nga warone sante ndakh do nitte kou bakh sayy niane dou entou ndakh do wakh sissa mbokou dioulite lou rafete

  • @cheucha7281
    @cheucha7281 День тому +3

    Yaw rafètalalle sa khôl bi mo gueun

  • @benzdictenobalegomis6139
    @benzdictenobalegomis6139 День тому +3

    Yawwww bakhoum todial sa tiothe ndeye
    Yaw do yalla té meuno diakassé wa parcelles

  • @AronaBa-ss6sh
    @AronaBa-ss6sh День тому +2

    Franc dina réy sen ndeye

  • @babacarkebe1098
    @babacarkebe1098 День тому +2

    Abdou bakhoum Sá data ndaye

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 15 годин тому

    Papi mome dou wakh té dou wakh modou lo le roi 👑 leufal ndayam rk😂😂😂

  • @Anime_editor349
    @Anime_editor349 День тому +2

    Ki bakhoul

  • @mbayebayefall8162
    @mbayebayefall8162 День тому +3

    Bakhom sa data yaye modou kasse

  • @pathesamb9561
    @pathesamb9561 День тому +1

    Abdou bakhoume sa data ndaye

  • @omarcisse6712
    @omarcisse6712 День тому +1

    Bakhoum dof +

  • @AronaBa-ss6sh
    @AronaBa-ss6sh День тому +2

    Ki wéroul hamoul lamb dofla

  • @adamaba7692
    @adamaba7692 День тому +2

    Bayil féne ma

  • @cheikhgueye1612
    @cheikhgueye1612 День тому +2

    😂😂😂😂😂koukko mâtiné Keur Parcelle sakh khamna ni doukko dieul

  • @HabibSylla-e3f
    @HabibSylla-e3f День тому +2

    Mak day wakh degue way

  • @georgesdieganediouf2684
    @georgesdieganediouf2684 День тому +3

    Addou bakhoum vrai mbam là.

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 День тому

    PA bi doff la te amut yar😂😂

  • @Fayejeeseef
    @Fayejeeseef День тому +1

    Pa bi môme vraiment d où référence si wakh mague d où diakhassé pour régné

  • @leyemouhamed2149
    @leyemouhamed2149 День тому +2

    😂😂😂😂😂😂 aka doff kii

  • @josephcoly4127
    @josephcoly4127 День тому +2

    Nitou safara mok pape sarr

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 15 годин тому

    Siteu nékhoul beurel day daw rk 😂😂😂

  • @AblayeSall-y3w
    @AblayeSall-y3w День тому +1

    bakhoum pourquoi dou nék nit

  • @josephcoly4127
    @josephcoly4127 День тому +1

    Sa mbeur bou mounoul dane gris 45 ans 8 ans sans défaite

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 День тому

    Bilahi ama Baldé amoul sa fay😂

  • @morgaye9582
    @morgaye9582 2 години тому

    François moy donou modlo si roi des arènes bi Abdou Bakhoum iao do meusseu rètan modou di dioy

  • @sambatorino8115
    @sambatorino8115 День тому +2

    Ki modou lo dako. Wara porté plainte

    • @PendaTalla-c5z
      @PendaTalla-c5z День тому +1

      Bilahi lolou la wakh parce qui limouy wakh Modou Lô c'est trop

    • @chamousman2726
      @chamousman2726 День тому

      ​Lolu moi yoon

  • @issandour3728
    @issandour3728 День тому +1

    Dakh yew yalla na ama danou

  • @badoumbaye5052
    @badoumbaye5052 День тому +2

    Dou nitou dara

  • @momardiallo1609
    @momardiallo1609 День тому +1

    Pathé baldé qui la wara saagua leufeul ndém nak

  • @TaphaDiop-t8n
    @TaphaDiop-t8n 18 годин тому

    Néna franc mounouko dane si 30 secondes 😂

  • @cheikhmboup1168
    @cheikhmboup1168 26 хвилин тому

    Ki da sokhor bakhoul beugue diakha sé parcelle

  • @OmarNije-yy1gv
    @OmarNije-yy1gv День тому +1

    👉👑👑👑👑🥰🥰🥰🥰💪💪💪💪💪💪💪💪🙏🙏🙏

  • @diopablaye5227
    @diopablaye5227 День тому

    Yenay sene saye tane nak

  • @fatoundourbodian1078
    @fatoundourbodian1078 22 години тому

    Boul diakhasse wa parcelles

  • @aliimranegueye2636
    @aliimranegueye2636 Годину тому

    Makk bouy feneu daye yeungeul arass ta parcel mano ko diahasse

  • @TaphaDiop-t8n
    @TaphaDiop-t8n 18 годин тому

    So néké make dangaye wakh Lou rafete

  • @mbayemodou1733
    @mbayemodou1733 День тому

    Man dof bi damako namon sakh dof nafekh la

  • @NgagneDiakhate-n7e
    @NgagneDiakhate-n7e День тому +1

    Bayii diaxasé

  • @cheikhmboup1168
    @cheikhmboup1168 29 хвилин тому

    😂😂😂😂😂😂

  • @OmarNije-yy1gv
    @OmarNije-yy1gv День тому

    👉👂❌❌😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @FaraNdiaye-k1m
    @FaraNdiaye-k1m 15 годин тому

    Pa bou niak fayda

  • @PapeOusmanePapaOusmane
    @PapeOusmanePapaOusmane День тому

    Sokhor bakhoul

  • @thiernoaw8193
    @thiernoaw8193 День тому

    Abdou iow kou bonne ngua

  • @bachirdiop19
    @bachirdiop19 День тому

    Abdou bakhoul mak dou kathi nak bayil diaxasé
    Mak bo xamni sayou waxé gnou xeb ko

  • @Lepatriote9423
    @Lepatriote9423 День тому +1

    Dama yakamti interview Abdou Bakhoum 😂