Eumeu Sène : "sama nek Roi des arènes betouma dé, sama yaye wahone nama......"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 17 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 158

  • @dienefaye5347
    @dienefaye5347 3 роки тому +60

    Big respect Eumeu le roi💪🥇♥️

  • @ametndao3008
    @ametndao3008 3 роки тому +32

    eumeu séne rék yalla nala yalla défal niamou 💯❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @salioudiallo256
    @salioudiallo256 3 роки тому +12

    Balla Moy sama mbeur mais Lima nekh ci eumeu Moy da beug yayam 😍🙏😭dama bougone sama yaye

  • @fallouthiam7222
    @fallouthiam7222 3 роки тому +34

    Ndeysan eumeu Nice na trop machala ❤️❤️

  • @bayefaye8665
    @bayefaye8665 3 роки тому +38

    Thii Mbeur yeup Eumeu monek sama number 1

  • @kingogn8568
    @kingogn8568 3 роки тому +31

    Ndeysane cette mentalités jadore❤️

  • @mamefatoundong387
    @mamefatoundong387 3 роки тому +42

    invité ngen .mbeur bou ame yarr kou bari diam machala nieup .ko nawlo

  • @soukeyecisse2714
    @soukeyecisse2714 3 роки тому +12

    Eumeu séne CHAPEAU à toi ❤❤❤🙏

  • @Foot-mundo
    @Foot-mundo 3 роки тому +25

    Respect frère

  • @amydieng1193
    @amydieng1193 3 роки тому +2

    Eumeu séne rekk machala lépaye rafete borom bakh nga

  • @papediouf8058
    @papediouf8058 3 роки тому +22

    Machallah eumeu Sene yalna sa diam yagg

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 3 роки тому +1

    Nice bless all of you amen

  • @dawcoumbadiop2407
    @dawcoumbadiop2407 3 роки тому +5

    Litakh ma beugeu ko moy dafa yarou bilahi machalla

  • @MoussasidibeMoussasidibe-k5m
    @MoussasidibeMoussasidibe-k5m 9 місяців тому +1

    ❤❤❤❤

  • @tvcodendiayematarelsdaroua7668
    @tvcodendiayematarelsdaroua7668 3 роки тому +31

    Sene Eumeu aka bakh biilay yala rk mou fiékii

  • @fzahrabah6478
    @fzahrabah6478 3 роки тому +3

    Ma cha Allah Eumeu

  • @hadaraseydihadjimalick9157
    @hadaraseydihadjimalick9157 3 роки тому +2

    Merci Champion
    Tu as donné un bon conseil aux jeunes :siloo maneu nekk naka fonk sa diiné

  • @fatoundiaye7549
    @fatoundiaye7549 3 роки тому +2

    Machallahhh notre fierté

  • @amethka9211
    @amethka9211 3 роки тому +7

    Bilahi lamine samba ya beuriii wakh boul di suivre nitt gui beumou seuss demal diangui wakh lamine tega wagni wakh djiii

  • @mariamasow4896
    @mariamasow4896 3 роки тому +15

    Hiiii Lamine samba eupeul na do bayi invitè yi gnou wakhal sèn bopou

  • @salimatandoye5027
    @salimatandoye5027 3 роки тому +2

    Bilay damako beugueu rk té yalla takh yar bi neek si mom takh na ma naw ka lol certes gni wax sa bakham dagno bakh rk di wax mais kouko djégué même soudé waxtou sakh gua partagé ak mom dina reconnaître say valeur nitt kou bakh kou tabé kou woyof mougui nii took meusou ma di commentaire mais lou fess neek si khol tourou
    Yalla nala yalla takhawou si leep lo meunti neki

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154 3 роки тому +1

    Bilahi eumeu sene mon geuneu bakhe thi mbeur yi bilahi aka yarou

  • @nafidrame3834
    @nafidrame3834 3 роки тому +14

    Salut eumeu boule beurré akh Balla Gueye damalako niane huit yalla

  • @morcisse7674
    @morcisse7674 3 роки тому +1

    Champion✨👑✨✨

  • @narndiaye7495
    @narndiaye7495 3 роки тому

    Mashala la religion avant tout. Merci eumeu.

  • @willymadjiguenediop8623
    @willymadjiguenediop8623 3 роки тому

    Mashallah eumeu khalé bou yarou bu

  • @ndeyefatou8141
    @ndeyefatou8141 3 роки тому +1

    Machallah eumeu

  • @abdoulayediarra2525
    @abdoulayediarra2525 3 роки тому +1

    Sama mbeur bii borom xol bou raféte bii 'kén dou mom sama roi bii💪✊✊

  • @belelthiometv3952
    @belelthiometv3952 3 роки тому +1

    J'aime eumeu séné

  • @abdadiallo2433
    @abdadiallo2433 3 роки тому

    Il et majeur ce gas le lutteur le plus noble

  • @laminekonate3916
    @laminekonate3916 3 роки тому +6

    Lac l'homme fort qui a battu tous les champions de pikine 💪💪💪💪

    • @amathsamb433
      @amathsamb433 3 роки тому +3

      Tu as Raison par avertissement 😆 😆

    • @FATOUNDIAYE-dd8lg
      @FATOUNDIAYE-dd8lg 3 роки тому +1

      Yeine demleine ngene nelawi outileine mbeur way ishhh

    • @ramandiaye4960
      @ramandiaye4960 3 роки тому

      Ya 2 lac wala🤣😂😂

    • @fatycisse2846
      @fatycisse2846 3 роки тому

      Hiiî 🤣🤣🤣🤸‍♀️🤸‍♀️

  • @seydinaissademe8122
    @seydinaissademe8122 3 роки тому

    Machalah

  • @ousmanegueye4822
    @ousmanegueye4822 3 роки тому

    Merci beaucoup

  • @nafidrame3834
    @nafidrame3834 3 роки тому +11

    Guir yalla eumeu, boule beurré akh Balla Gueye

  • @DAKARBUZZSENEGAL
    @DAKARBUZZSENEGAL 3 роки тому +2

    Eumeu sene so dielel bala gaye ma bayila faral adouna ak alakura bilay wolay

  • @sambandiaye3707
    @sambandiaye3707 3 роки тому

    Yalla na yalla goudal fane wi mberr

  • @abdouliesanyang9717
    @abdouliesanyang9717 3 роки тому

    Respect bro

  • @boubacarlimanbadiane9569
    @boubacarlimanbadiane9569 3 роки тому +1

    Eumeu champion la

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion38 3 роки тому +25

    Eumeu bagnal co dane gnari yone avec la maniéré do moromam yaco mène fouf co hamni foumou tahaw ni mo daka beré si lambji foco téwé fowéco ndam lolou bayi ak mome dafa néh boul nélaw

  • @domateredoundou4376
    @domateredoundou4376 3 роки тому

    Je t'aime eumeu sene ❤❤❤

  • @el-hadjiseynifaye8054
    @el-hadjiseynifaye8054 2 роки тому

    Nice

  • @mamoursall6078
    @mamoursall6078 3 роки тому +6

    Eumeu damala beug bilay ms nak dagua wara bayi beuré

    • @abdoukarimfaye3074
      @abdoukarimfaye3074 3 роки тому

      Nous réclamons le duo Malal junior et boy Lamine de lewto, pour moi Lamine samba n'est pas à la hauteur du GFM désolé

  • @abibousevanegueye8412
    @abibousevanegueye8412 3 роки тому

    King 👑

  • @abasall711
    @abasall711 3 роки тому

    Merci abdou hanne lolu moy wax dj ay rakam gnifi nalen may chance buder khaliss rk mane nako am si ay rakam

  • @ndenesene7160
    @ndenesene7160 3 роки тому

    Respect mbeur

  • @niokhorfall6979
    @niokhorfall6979 3 роки тому +1

    Lamine Samba kou soff nga watiel sa boopp .... Malal junior yafi néé♥️

  • @ladyshasha7082
    @ladyshasha7082 3 роки тому

    Euma I love him so much brother mine 👍👍😍😍😍

  • @abdouhane2855
    @abdouhane2855 3 роки тому +18

    Boul faté pékhé mi nou lalalone yekini thi nga tolou pékhé mi noulay lalale boul massa beuré ak balla

    • @satoubalo4637
      @satoubalo4637 3 роки тому +1

      Bayi len yakh der

    • @dembadiop1618
      @dembadiop1618 3 роки тому +1

      Dafa yaboul pikinois sakh

    • @satoubalo4637
      @satoubalo4637 3 роки тому +2

      @@dembadiop1618 wala yen senza Champion yi yepou la dan
      Dem len tog

    • @abdouhane2855
      @abdouhane2855 3 роки тому +1

      @@dembadiop1618 mane mo may beuguel sou ma nékone Sénégal dina fékhé ba guisko ndakh ko beug ndamame reck ngay beug amo numéro me

    • @ogthuggirl1860
      @ogthuggirl1860 3 роки тому +1

      Wax nga degue dh Abdou gnou Defate même peikhei contre modou lo wakeur aziz ndiaye damlen ragal

  • @nenebabou6726
    @nenebabou6726 3 роки тому +1

    Bilayer damala beugeu eumeu séne c nene

  • @papasidy9619
    @papasidy9619 3 роки тому

    Machala ko mako beugeu waye eme

  • @kayarlutte4921
    @kayarlutte4921 3 роки тому +17

    Eumeu boul beurrè ack Balla, sinon digua danou. Malako wakh wa Salam

  • @cheikhdieng4238
    @cheikhdieng4238 3 роки тому +3

    Bo dieulei Balla reutiou ko

  • @prospergomis3263
    @prospergomis3263 3 роки тому

    Mashallah euma

  • @moussandiaye8449
    @moussandiaye8449 3 роки тому +21

    Eumeu boul beurré lii yeup ay combill leuh...té aziz ndiaye mogui si guinaw lolou...dakh bougoul kou lal baleuh

  • @diamonotv1223
    @diamonotv1223 3 роки тому

    Ndey sahne

  • @laminekonate3916
    @laminekonate3916 3 роки тому +4

    Eumeu sene il faut accepter que lac Doumana la si biir pikine 💪💪💪💪

  • @kanakoulibaly903
    @kanakoulibaly903 3 роки тому +2

    Eumeu gor thia wakh dja yafii wahone do beurewate ak balla respect gnu gnune wa pikine

  • @badaradia4720
    @badaradia4720 3 роки тому +3

    lamine wakhga lou am solo

  • @diopmaguette2960
    @diopmaguette2960 3 роки тому

    Sama mbeur sama pape

  • @birahimfall505
    @birahimfall505 3 роки тому +1

    Eumeu sene vs guouye gui 👍

  • @keurguiyoletv5205
    @keurguiyoletv5205 3 роки тому

    Ok

  • @bambysene4403
    @bambysene4403 3 роки тому

    Li dawna yarame lafe thiate sama mbeur mi

  • @maguettefaye5904
    @maguettefaye5904 3 роки тому

    Lamine samba vrai diague leu

  • @diamonotv1223
    @diamonotv1223 3 роки тому +1

    Wawa

  • @papajuniormar1152
    @papajuniormar1152 3 роки тому

    Eumeu sene faut pas lutter avec balla parce que la personne se respecte à travers ces paroles il tenir à tes paroles que tu avait dit il faut te respecté et respecté ces fans

  • @ouleyediouf1494
    @ouleyediouf1494 3 роки тому +1

    Tjrs souriant

  • @mouhammedrasoull7710
    @mouhammedrasoull7710 3 роки тому +4

    Eumeu man dé koula so pou la boul beurré ak balla g2 diapou si rekk ta yalla takh dimbaléma rekk ta yalla takh

  • @zitanyneil595
    @zitanyneil595 3 роки тому +4

    Eumeu Boulniou fonto.
    Var est là non ?
    Yafi wakhone do wathiou diko lékate.
    Pas de wakhe wakhéte.

  • @amethdieng3659
    @amethdieng3659 3 роки тому +2

    Sa xoll mo rafet si bopom amal diam frère

  • @cheikhdiop8416
    @cheikhdiop8416 3 роки тому

    Eumeu sene mai niou ak sama yay wakhon nama ko

  • @dembadiop1618
    @dembadiop1618 3 роки тому +3

    Eumeu séne limalay conseillé moy xol noye guéné par la grande porte gni soxla comba bi dagne beug ga danou té yakarna homme de parole ga Yako waxone boul messa nangou ma waxone wakhét

  • @mbayefaye986
    @mbayefaye986 3 роки тому

    Lamine samba ohhooho beuri Way

  • @laminekonate3916
    @laminekonate3916 3 роки тому +3

    Lac l'homme qui a corrigé eumeu sene borom 12 défaites et 9 victoires si biir pikine 🤣🤣🤣🤣

  • @tk92221
    @tk92221 3 роки тому +1

    Eumeu yoroul kholou mbeur. Mais lamine est-ce nitt leu. Loutakh do dieufendikou a galathe bou ñiou mais déjà aÿ dioulit lañiou et de deux il parle comme si c’était normal de faire ça. Lou galathe bou bone bakhoul.
    Lobbying lamb ji nio beugg balla am victoire ci eumeu. Eumeu na nga same sa kaddou rék - balla nieu dieulat modou Lo rék wala modou eumeu acte III

  • @abdoulahadniasse7605
    @abdoulahadniasse7605 3 роки тому

    Saloum Materiel Agricole | Facebook

  • @astoudiack46
    @astoudiack46 3 роки тому

    Ki dama KO beugue Loll billahi

  • @mansouretadiop8119
    @mansouretadiop8119 3 роки тому

    Eume modou dalaye niousse dei

  • @papasidy9619
    @papasidy9619 3 роки тому

    Eumeu sene

  • @mouslayeimmosenegal3529
    @mouslayeimmosenegal3529 3 роки тому

    Kepeu kou beugeu investir si immobilier beugeu mouthiou si litige foncier mangui laye niane nga abonner si sunu chaine kousi abonner yalla na sa adio defarou

  • @bachirvd619
    @bachirvd619 3 роки тому

    Yonebi Kay Modou lo moka wané eumeu gooo

  • @fallouthiam7222
    @fallouthiam7222 3 роки тому +4

    Eumeu boul fate ni boul fatee ni daga watone ni do barré ak balla bouguene beure moulay day lou l'ère boul barré khalis dou tousses

  • @daoudasall8075
    @daoudasall8075 3 роки тому +1

    Eume boul dieul balla svp piege la..

  • @ousmanewillane8479
    @ousmanewillane8479 3 роки тому

    Bayelene wakh lo lene leroull

  • @moanzfall3714
    @moanzfall3714 3 роки тому

    Man dh alfalh la niangé th yagnako guiss fofou mouy hiyam

  • @modoudiouf1989
    @modoudiouf1989 3 роки тому

    Rumeurs Sène je te déconseille de se rebattre avec Balla Gaye ce combat ne te donne rien et si tu es tombé ça sera pire. tu las terrasse 2 fois alors pourquoi aller le reprendre? stp Eumeu moi je suis un fans fervant de toi mais ce qui me fait mal c'est quelque erreurs de ton staff, par ce qu'il doit sélectionner tes adversaires. Ne prends surtout pas ce combat contre Balla ça t"amène nul part.

  • @nafidrame3834
    @nafidrame3834 3 роки тому

    Si kaw si kanam si Lou bakh

  • @abasall711
    @abasall711 3 роки тому

    Eum yafi waxon doto beurer ak balla kon resprctel say fans bulako khaliss diaral victoire modax khaliss t balla niari yon yi ngako dane moko guena nakhadi si carriere ram

    • @mouhamet115
      @mouhamet115 3 роки тому

      Wakho deug khaliss mo dakh

  • @galsenlive3314
    @galsenlive3314 3 роки тому

    No lamine bari na wakh

  • @bocardavido155
    @bocardavido155 3 роки тому

    Lac 2 kay champion la ndakh gayi bougnou si amone li si modou lo am sakh gnou mana wakh

  • @mouhamadouciss6898
    @mouhamadouciss6898 3 роки тому

    Ni sa nekha beugue

  • @ablayesarre2868
    @ablayesarre2868 3 роки тому +2

    Eumeu mo gueune si mbeur yi khol bou rafétt

  • @sidygueye2216
    @sidygueye2216 3 роки тому

    Eumeu séne boul beuri ak balla gaye gor sa wakh dia

  • @sassoumdiaw8378
    @sassoumdiaw8378 3 роки тому

    Bes bo jeulé balé dingua kham ni lep deg leu

  • @ramandiaye4960
    @ramandiaye4960 3 роки тому +2

    Bane lac mo radiakhé pikine😂🤣🤣dane avec la manière laniou wakh mais ay nul rk lolou dou ndam....au moins eumeu buy danou wala di dane sakh dina beurré ba ga contane❤arrêter de comparer l'incomparable

    • @awasall9536
      @awasall9536 3 роки тому +1

      Mane dh fimou tassaré diakhalnama Khanna di daw ba tassaré lii tamite cas la dh lac rek bala may dioy mounane dafay conseillé balla gaye ay yalla ba lii diamla

    • @ramandiaye4960
      @ramandiaye4960 3 роки тому +1

      @@awasall9536 mane mom j8 fan de XLO 100% mais deug dal la wakh lac beurrém nekhoul crx

    • @awasall9536
      @awasall9536 3 роки тому +2

      @@ramandiaye4960 meussoul nekh keneu waratoul teug combawam

  • @moustaphaniang1950
    @moustaphaniang1950 3 роки тому +2

    eume bagnial

  • @salioudiallo4810
    @salioudiallo4810 3 роки тому

    Yénagui wakh grand contre petit mais eumeu ak balla dou grd cntr petit deh té yénn sakh lolénn beugue ni balla , eumeu walla aziz dafa djarre .mane nak limaye wakh eumeu moye na ande ak niary victoire yi bayi wallé ko wiri wiri bi yeup dafa ame lou si lakhassou fagnie deh eumeu

  • @ousmanekonatei4420
    @ousmanekonatei4420 3 роки тому +1

    Mais lamine samba il est malade ou koi wala 3eme femme bi la kanam gui da demm boeut yi dougg sa waye soneu de

  • @suivicaptrans1552
    @suivicaptrans1552 3 роки тому +1

    Begue

  • @assanediena6202
    @assanediena6202 3 роки тому +3

    eumeu moytou pekhaime none assiz ndaye ak Gaston mbeing bala gnioy am diam rek bala gaye 2 dane la ba tok sakawe bir bobou khalice dou dara samal sa kadou mogeune gathiè bakh na

  • @cheikhdiop8416
    @cheikhdiop8416 3 роки тому

    Lamine yagui damou de