Ça me rappelle l'histoire que j'ai vécu!l'importance c'est d'avoir toujours le coeur toujours propre vers tes semblables,tu sortiras toujours vainqueur des situations quelques soient leurs grandeurs!!merci pour cette belle histoire
Li nak limasi diangu beurina trop 1moye kou War rene bah dewene mou djik lah dagnlaca djign ms dou yaw 2 moye nit ki lepou lou nek si yaw té wara guenna deka guenné 3 moye kignane daye halak brome brome bah tabale ka safara 🙏
Histoire Magnick Domou Baay Sogui ak Yatma Domou Pere Ndiaye Ande si ak Makhoye Mii Nekone Soxna Mbagnick Tei Yatma amone kholou mbeughel si mom Si deuk Bouniouy waxx Tiimbarlan Sa Deuk Bha amone Eugh Bou Metti Bha
Man de lii dall galay man mom lay doundu Dara duma méti ba kén xam ko ak lumu tarr tarr Tayit duma beug dara ba fésal ko ak lumako beug beug Yallna nu yalla arr rk
Sëriñ tuubaa nee woon Na : Jigéen ñàtt la (3) 1 ka nga xam ni bako YÀLLA di bind yaa tax. koo ku lum Yàgg Yàgg lum manti am sa Soxna lay doon. 2 mooy ka nga xam ni bako YÀLLA di bind taxoo, koo ku jarul sònnu taxoo koo jug nangu ndogal Li moo lay noppal. 3 mooy ki nga xam ni bako YÀLLA di bind da nga cee am wàll, sa moroom am ci wàll. koo ku bu ñëkkée ci yawit sab moroom lay mujju. ku Xam lii nak da ngay nòppalu dara dula sonal
Massa alah yalla na yalla doli wer barkep borom touba 🙏🙏❤️❤️🕋
Gueumeudi yalla motax samba ray galaye wayé meunoon na niak ndakh jigueen diarouko
Limassiy wakh moy nitt bou guiss lo beug wakh ko soudei meuno ko mougne à jamais bala mouy trop tard.
Histoire bi amna solo machallah
ماشاء الله نسأل الله أن يحفظنا 🤲الحسود لايسود♥️😭😭😭
آمين يا رب العالمين
@@diengAllekarbala.4218 ءامين وإياكم
Macha Allah amna solo lool😭😭😭
اللهم آمين
Louñi thie meunne diangate moye louwaye réndi sa lokho naye nathie♥️♥️♥️
Masaallaha merci🤗🤗🤗🤗😇😇😇
Ça me rappelle l'histoire que j'ai vécu!l'importance c'est d'avoir toujours le coeur toujours propre vers tes semblables,tu sortiras toujours vainqueur des situations quelques soient leurs grandeurs!!merci pour cette belle histoire
Eskeuy machalla amna solo diadieuff 😍❤️
Kou sope seuydouna mou khamed na bleu
Lii d monye iniaane ak soxor dou diarrigne loudoul reuthiou
Yallana yalla dolli raxass sunu xol yi Barkeb
Machallah oustaz yallah nala yallah diapale si barcky mawlana cheikh ibourahime Niass
Machalah Amna solo lolou wayé lépou djiguén moko waral
Cheikh Mou 6uu
Ygg
ماشاءالله جزاك الله خیراً
Wollay histoire bi neekhna Jazak Allha feek
Une très belle histoire est aussi important merci bcp
Machalla histoire bou doy War bou am
Galaye mbam leu way
Son bii xalat tv rekk lamay fatalii Pape Bouba yalnako yalla yeuramm
ما شا الله خزك الله خير ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Ça me rappelle Magnick ak Yatma dans ndeysane le prix du pardon
👍👍👍
Ndeyssane théâtre bou nekh sax
C vrai
@@binetadiack840 un théâtre titré ndeysane le prix du pardon
Film bobou doumasi doyal walahi
Samba la toudou li gua wakh Mon nek si man da Faa melni samba yeup nio yame
Merci beaucoup 👏👏👍
Ndeyssane yalla na nou yalla mousel si kinian amine barkep borom Touba 🙏🙏🕋❤️
Machalla.Lii. Daf. May. Fataly. Lihetoire. Bou.yage👋👋👋👋
Belle histoire qui resemble bcp à celle du film le prix du pardon
Machallah oustaz. Li moy lou nekh sa khell Ak sa khol dagua ko weur guené
Pas toujours dh
@@babacargueye1664 ces
@@babacargueye1664 hmm
@@babacargueye1664 d’accord avec toi
Dawna yaram lol Bilahi
Masallah
Li nak limasi diangu beurina trop
1moye kou War rene bah dewene mou djik lah dagnlaca djign ms dou yaw
2 moye nit ki lepou lou nek si yaw té wara guenna deka guenné
3 moye kignane daye halak brome brome bah tabale ka safara
🙏
Niit d'où top beug beugam té Loula metti boul ko neub guéné jo
Machaallah amna solo ❤️❤️❤️❤️
Magnifique✨💗
No dawou Na yarame no adouna def Lou bakhna rek mo âme solo 😭😭😭😭😭😭
L'histoire de Magnitt Makhoye ak Yatma « le prix du pardon »
Merci beaucoup amna solo yallnala yalla Faye geunegui fay
👉👀Touba xassida rék
Amna solo lool machalla
Machallah très intéressant merci beaucoup
فرحت بكم لكي يعملون عملا مفيدا ماشاءالله
Machalah
Histoire bou am sollo
Ah lidh koumou dalle ame nga louméti mais dogale l'amour mo fort Té Solution Wame dou yombou 😍😍❤❤❤
Merci beaucoup c'en production
Machalla nô touddou👍👍👍👍
Machalla ame na solo loooooool
MERCI beaucoup MON frère
Bilahi li nimako bougue souma sanione Mouy am sak journée amna solo lolou👍👍👍👍👍😍😍😍😍
👍🤛✌️👿😎😔
@@mariamadia1072 a domou bay 👍👍👍
@Sadio Coulibaly Amal diamou yaw👍👍👍👍
Liimom Amna sólo machallah
@@damaldaroundiaye2250 bilahi Lou wer la
amna solo
Amna solo trop
Machallah amna soloo diaguat bi moy nit dou diel loudoul werse guem
Moussna ma dall dh wayé🤐
Merci beaucoup
😓😥😥
@@ndiayekhady3540 p pp ⁹
@@ndiayekhady3540 ppp
ماشاءالله جزاك الله خيرا الحسود لا يسود. فرحت بكم فرحا جدا. لكي يعملون عملا مفيدا
Manchllah yalla nala yalla faye
MACHALAH TLIFBI AMNA SOLO WAYÉ GALAY MÉR RÉK MOKO DIAPOU WAYÉ WARON NA GORÉ RÉK NDAKH BANIOU DALA ANDEU YAGEUNA
J'ai bien aimer. Ces Trot interressant
Maashallah baat bi Lair na
amna solo 🙏
Histoire bi nékhena té amena solo machallah 😍❤️👏
Cv
Histoire Magnick Domou Baay Sogui ak Yatma Domou Pere Ndiaye Ande si ak Makhoye Mii Nekone Soxna Mbagnick Tei Yatma amone kholou mbeughel si mom Si deuk Bouniouy waxx Tiimbarlan Sa Deuk Bha amone Eugh Bou Metti Bha
Man de lii dall galay man mom lay doundu
Dara duma méti ba kén xam ko ak lumu tarr tarr
Tayit duma beug dara ba fésal ko ak lumako beug beug
Yallna nu yalla arr rk
Oh histoire bi daw n'a yaram
🙌
des histoire très captivante merci
Histoire Mashallah Ame Na solo torop
machallah cheikh elhadji amna solo lol deh yalla na yagg lol barké borom taif
Masallah ❤ amna solo ❤
Machalla Amna solo
Machallah, amna solo, lou way rimdi sa lokho lay nathie 🙏👌
Non vidéo bi amna solo yalna yalla fayla yéw
Diadieuff rafétna lole machallah
Diadieuf way rafétna dh ni rék la yalna Serigne Mbacké Sokhna lô fayla
Kou begeu kham sa diné ta begeu seydina Mohamed abonnél sama sén bi
Machalah amatina solo yalna man man bi yokk
Mashallah.lou am solo. Demay fatali histoirôu niary domou Adama yi.
🇸🇳✋✋✋✋
Le salón de más sale 27.28
ماشاء الله ❤❤تبارك ❤ الله ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J aime cette chaine
Video bi machalla
Macha Allahou yallana yalla barckl ♥️💯
Machalla ame na solo trop❤️🙏
Bonne continuation 💪💪
AMNA SOLO LOOLL
Marchalla la ❤️❤️❤️
😭😭😭😱😱😱😱😱dieureudieuf
😱😱😱😱😱😱😭😭😭😭
👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏
Wolofall bi Na gueuna pure a part ça nice👍👍♥️nak bou Magu yeukkkeu la dou kouye ak "parent"c repetitif
Je m'abonne 💯
😭😭😭 doy na warr
Lii lepuou si man ndarga Kiniane la bockou yalla nanou yalla mousal si ignane
AM na solo trop
Machalla wakh tanwii amna solo lolou♥️
Yalnano sono boroum mosale ci khôl bo wow ak ndiakha ré Lô doy warr
Macha Allah amna solo jarijaff
Lidé moy adouna aka doy waar bilahi té loufi tass si djigene la diougué
Belle et intelligente histoire merci
muchas gracias
Kadtou
Machallah yallah nala yallah faye
Amine
C'est intéressante
J'aime beaucoup
Machalla oustaz ♥️😍😍💜👂👂
الحسود لايسود♥️
Machallah yalla na yalla défara diamou rk inchalla
Lidé dadéllou ci waxi sallahu halayhi wasallam geumukéne ciyén dumat ludull lim beugall bopam dakoo beugall maromam
Machala néhk na
Nice
machallah
Machall
Sëriñ tuubaa nee woon Na :
Jigéen ñàtt la (3)
1 ka nga xam ni bako YÀLLA di bind yaa tax. koo ku lum Yàgg Yàgg lum manti am sa Soxna lay doon.
2 mooy ka nga xam ni bako YÀLLA di bind taxoo, koo ku jarul sònnu taxoo koo jug nangu ndogal Li moo lay noppal.
3 mooy ki nga xam ni bako YÀLLA di bind da nga cee am wàll, sa moroom am ci wàll. koo ku bu ñëkkée ci yawit sab moroom lay mujju.
ku Xam lii nak da ngay nòppalu dara dula sonal
sok ran
Toubarkala li rek moy solo si amna mbecte sisa commentaire bi
Machallah Que belle histoire
❤️❤️❤️👍👍👍💔💔
Amna solo
Machallah
Ok