_Sën Móodu lóo de wallaahi ku baax la kuy liggéeyal Yàlla la seytaane moo bari doole de rekk !! Waaye nag jéem a xam àdduna baax na lool ngir man a mucc ci yenn yi. Yal na ko Yàlla sàmm jéggal ko aar ko barkeb Alxuraan. Man de tey laa ko gën a bëgg Wallaahi._
La chose la plus importante est que Serigne Modou Lo Ngabou Junior n’est pas un petit fils de Serigne Touba. Qu’il fasse des bonnes œuvres est une bonne chose. Qu’il discute avec la femme d’autrui, même s’il a été piégé montre qu’il a été faillible. J’ai aussi vu qu’il incarnait le physique et la lakhassay de Serigne Touba et que certains voyaient en lui le successeur du saint homme. Mais cet histoire montre qu’il est loin même des fils de Serigne Touba encore moins de succéder à Khadimou Rassoul
Les médias confondent toujours les deux Serigne Barra Dolly et les deux Serigne Modou Lo Ngabou. Il est parfois bien de préciser pour éviter les ambiguïtés.
Serigne modou lo gabou domi si Sokhna mbene mbacke gabou ak Serigne Ibrahim borom safinatoul amane kou bakh machalla Sokhna nekone ko jambarè opératrice economique la wone yalla nagnou yalla fayal
Kou wara Diamou Yalla la malgré limou deff wayè mongui dess si kholou diam gni ba lègui Yalla bula wèrè dala beug diègeul wayè domou adama boula wèrè dala beug torokhal tè Yalla kumu sètan AK ibliss mou dèfal la bagage
Damani ce bandit de serigne modou lo gabou n'est rien d'autre qu'un grand pervers qu'on doit impérativement interdire d'approcher ou d'enseigner des enfants innocents qu'il peut abuser. Ceci dit il doit la fermer pour de bon. Même s'il a gagné l'estime de bcp de sénégalais, il a tout perdu dans la mesure où ce qu'il a fait est trés grave, à ne pas négliger. Say Say bou kate ndéyame la 🇸🇳
Woté Serigne ba paré Topp si djabarou Djambour yii. SBN Nieuw tok si télé bi di doul rekk. Kouniou ko dëfone sa djabar wala sa djabar def lako do tok ddi wakh fii. SERIGNE MODOU LO NGABOU MBALOU...
Frère Cheikh Bara! On vous respecte, respectez nous !!! Les sénégalais sont plus éclairés et plus intelligents avec beaucoup plus de discernement que vous ne puissiez imaginer. Sutura ok mais ne nous faites passer le jeune Modou Lo comme un saint victime d'un traquenard. Même à la rigueur vous taire vaut mieux que vos élucubrations !!!!
@@MrFayemanou iow wakhal sa baye mou bayi thiaga you ndew yi mouy fat ci négueum niou mathial ay coyam et ke sa yaaye guethina nieuw néko namou naako prochain foi bouy nieuw na indalé silip bou verte bi
Si la fille voulais la justice et se libéré avec autant de preuve 1 plainte aurais suffit puisqu'il ne sais pas de politique. Ou envoyé c'est preuve à sont mari.
Bouléne gnou fonto ki royou kay la donc dafa wara deugal mission cheikh ahmadou bamba mou sel mi. Té dafa wara roy si môme . Deugal name dagnou ko wara soutouram wayé bouléne neub deugbi .Mane dé kou def li sama diabar damalay Ray . Wassalam
Nit daal limouy wouyo daf kay nourou bopam la toogne ta yalla moo koy atté wanté nak nit gni sagne nagno dégne si mom sou fèkké linou ko jiigne deguela ta infrastructure bima guis foumou ko amé moo jara lidieunti
Mais soutoura dafa bakh té pourquoi pas les audios de cette femme ne sont pas sorties.cetait entre les deux mann nafa yam dhe mais yakh derr rekk lann mann
@@mortalla9336 Déed saay deug leu naniouko soutoural d'accord naa waaya lila thie lerr mom boulkako laadj, bokoy xool ci internet bi di guiss Serigne bi mouné doungg.
Exactement, si c'etait une femme salibataire sax grawoul, il a le droit de epouser une 2 fam donc le probleme ici c'est une femme marie kou niaka diome soufeké piege la.
Mais gnii thi gouvernement bougnou deffé dieuf djou melnii ken doulén djieuleul part alorsque boudeb sérigne nous gniawlouko. Allah n'est il pas le meilleur des juges ?
Serigne Bara danger rafetale rek mais rien ne prouve son acte il faut pas être l'avocat du diable lou si dess môme akk yalla n'a toubb diegalou yalla Bâle ko mou continuer daarame
Mane âme na nob boo xamne bougnou lako diokh ngua lekiko bilay walay boo done waliuwu làla wakh barki Mohamed par la force digua bogue djiguene doko tay sakh
Que dieu fasse que les personnes qui verront ce message passe une excellente journée et que dieu vous bénisse 🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Ndaysane yalla nako yalla diapalé
Léral yi amena sollo... Merci Cheikh Barra
Dieuredieuf way cheikh barra Ndiaye yalla nala diamou yagiu barkep Serigne bi
serigne bara ndiaye wakhnga deug dh machallah
Machalla Serigne by que le bon Dieu vous protège merci beaucoup
Ndeyssan c'est quelqu'un qui a fait du bien dans sa vie. Yallah nakoo Yallah may khôlou mougne. Yallah dafay natou diamame
_Sën Móodu lóo de wallaahi ku baax la kuy liggéeyal Yàlla la seytaane moo bari doole de rekk !! Waaye nag jéem a xam àdduna baax na lool ngir man a mucc ci yenn yi. Yal na ko Yàlla sàmm jéggal ko aar ko barkeb Alxuraan. Man de tey laa ko gën a bëgg Wallaahi._
Ndeysan serigne modou lô ngabou dhé liko gayi déf rafétoul dara mai sante yalla rék mbokam yi bayi wouniouko😭
Sénégal yalla nafi diamou yagiu barkep Serigne bi
Machalla dieuredief lou am solo s modou lo kou mana waxtan la
La chose la plus importante est que Serigne Modou Lo Ngabou Junior n’est pas un petit fils de Serigne Touba.
Qu’il fasse des bonnes œuvres est une bonne chose. Qu’il discute avec la femme d’autrui, même s’il a été piégé montre qu’il a été faillible.
J’ai aussi vu qu’il incarnait le physique et la lakhassay de Serigne Touba et que certains voyaient en lui le successeur du saint homme. Mais cet histoire montre qu’il est loin même des fils de Serigne Touba encore moins de succéder à Khadimou Rassoul
Baravo walfo TV sa kaw sa kanam rek inchallah barkep Serigne bi
Merci beaucoup way sohibou
Sou nékone sama serigne tey lakoy geuneu ďiapp,.
😂
😅😅😅😅
Wakhko yombna
Djokhko saa djabar
Bouko deffone sa jabaar noy deff ?
Serigne modou lo ngabou yalla na ko yalla dolli soutara
Félicitions a tout zanse walf machallah abonné vous maxi a Walf
Thiey yalla vraiment doy na warr dh billhai 😭😭😭
Les médias confondent toujours les deux Serigne Barra Dolly et les deux Serigne Modou Lo Ngabou. Il est parfois bien de préciser pour éviter les ambiguïtés.
De
MACHALA machala longue vie a toi
Merci beaucoup cheikh barra Ndiaye
Serigne bara ndiaye kou bakhla machalla
Diaradiaf chiekh barra
Wlf ay nit gniofa nèke tè degou Machalla yallna sene diame yage
Serigne modou lo gabou domi si Sokhna mbene mbacke gabou ak Serigne Ibrahim borom safinatoul amane kou bakh machalla Sokhna nekone ko jambarè opératrice economique la wone yalla nagnou yalla fayal
merci cheikh bara tu et le meilleur
Jajeuf leeral yi amna solo
Yananiou yalla moussal Si pakhay yapnon non mobon non mosoyor 😭😭
Diadiuef cheikh baara ndiaye
Merci cheikh bara yalna fane wi goudou looooolt wér
Nous vivons vraiment la fin des temps,c incroyable que ce mec continue de diriger quoi que ce doit,c incroyable
Yaw doul yala rek module djoum
@@diagnegnilou1078 A bon dagaye saga louma wakh deugue la bay ki waroul djité ken nakh loumou def deugue rek
Wallahi je disais la même chose
@@zaldiop6293 lolou kasé la amol lenene frere
Sama thioféle dafa yokou si Serigne Modou lo
Bonne continuation
YaAllah dh da ngakoy toogn 1000 fois, toubb benn yoonn mou diégueul leu lepp...waayé sénégal niitt daffiy nekk dii deff lou baakh, ndog ndog dapp koo benn yoon, mou melni meussoul deff lou baakh...
Machallah
Ndeysane machallah
Amna solo
Diereudief s chiekh baara Ndiaye
Diaraudiauf s bara Ndiaye
Que celui qui n'a jamais péché levé la maib
Ndeysane
Machallah
S bara Mala sopou té yala rek takh
Vive sérigne modou lô sinior
ما شاء الله شيخ بار جاي
Mashallah ❤❤❤❤🤲🤲🤲
Ndaye san machalhe 😭😭😭😭😭
naatou rek dé la yalna ko ko yalla oyofal arr ko té yiiir ko
Yalla nano yalla saou
Adina de nekholl gana gorr gorr lou reckk
Hamoula Dara ndeysane
Merci
Ndaysan say Tani rek jieguen moman liempo yalla nako yalla Sambo
❤❤❤❤❤❤❤
Diadief Serigne bara ndiaye
Yaww borom yeuraii bou verte ,retane yii meunaa niak si li .
Niak tèguine reik ak bania neik professionnel
Bilayy wakhngaa degeu
Dieuredieuf mbacke
Kou wara Diamou Yalla la malgré limou deff wayè mongui dess si kholou diam gni ba lègui Yalla bula wèrè dala beug diègeul wayè domou adama boula wèrè dala beug torokhal tè Yalla kumu sètan AK ibliss mou dèfal la bagage
Li Moy adouna kou niou diemal pour yakk leu bou si yalla diapoul trop
Dinga soneu mais yalla bakhna yalla na niou yalla doli soutoura
serigne bii Diarna diap diara diapalé
Boroom Touba de' guathe' ngaalaama
Diuerue diuefue borome touba Serigne cheikh lo ngabou yagefi tewer lolee
Macahala
Niite koy bakhleu Cheikh Bara aka am personalité ak caractère
Amna solo. Mais cou dièbeulé sa boppou momatoo dara. Lou la dal, boumla bètt. Lii doulou bèss, mais réseau sociaux amoulwone
Serigne Bara wakho fi darra nitt yi yewouneno doul reik guain di deffe
Bayyi leen doul
Machalle 🙏🙏😍😍
Damani ce bandit de serigne modou lo gabou n'est rien d'autre qu'un grand pervers qu'on doit impérativement interdire d'approcher ou d'enseigner des enfants innocents qu'il peut abuser. Ceci dit il doit la fermer pour de bon. Même s'il a gagné l'estime de bcp de sénégalais, il a tout perdu dans la mesure où ce qu'il a fait est trés grave, à ne pas négliger. Say Say bou kate ndéyame la 🇸🇳
S bara ndiaye wakh dji rafetena trop
Est-ce que guiss ngène beutou serigne bii? Pour ceux qui savent lire, il a les yeux d'un vicieux. Beuri naa ay morom. Mom moo feignlé rekk.
Woté Serigne ba paré Topp si djabarou Djambour yii. SBN Nieuw tok si télé bi di doul rekk. Kouniou ko dëfone sa djabar wala sa djabar def lako do tok ddi wakh fii. SERIGNE MODOU LO NGABOU MBALOU...
Frère Cheikh Bara! On vous respecte, respectez nous !!! Les sénégalais sont plus éclairés et plus intelligents avec beaucoup plus de discernement que vous ne puissiez imaginer. Sutura ok mais ne nous faites passer le jeune Modou Lo comme un saint victime d'un traquenard. Même à la rigueur vous taire vaut mieux que vos élucubrations !!!!
Sa dinama ray 🤣🤣🤣🥰
N'oubliez pas les 5prières
Serigne bara modou lo thiagua la bou mak
Segne safinathou dh bi moko nieukë deug Fogou makon àpp talibë dh wakham diou dioupp ta lislamë.
Bara lega wakh yep bakhna waye wakhlen ak mom mou baye di katt diabarou jamburr yi
Iow kou dakhaar sa ndeye nga
🤪😂 vraiment
@@best7579 yaw mii yaye nafekh naa bayii cate djabarou diambour yii
@@MrFayemanou iow wakhal sa baye mou bayi thiaga you ndew yi mouy fat ci négueum niou mathial ay coyam et ke sa yaaye guethina nieuw néko namou naako prochain foi bouy nieuw na indalé silip bou verte bi
Yaw ya meune fène katoul ben diabarou diambour ay wakhtane laniou sekhon dara diotoufa khew
Vraiment cette femme à tout bougier
Si la fille voulais la justice et se libéré avec autant de preuve 1 plainte aurais suffit puisqu'il ne sais pas de politique. Ou envoyé c'est preuve à sont mari.
Bouléne gnou fonto ki royou kay la donc dafa wara deugal mission cheikh ahmadou bamba mou sel mi. Té dafa wara roy si môme . Deugal name dagnou ko wara soutouram wayé bouléne neub deugbi .Mane dé kou def li sama diabar damalay Ray . Wassalam
Nit daal limouy wouyo daf kay nourou bopam la toogne ta yalla moo koy atté wanté nak nit gni sagne nagno dégne si mom sou fèkké linou ko jiigne deguela ta infrastructure bima guis foumou ko amé moo jara lidieunti
Iow wér ki am ay talibé nganaan
Iow dof bou reuy nga
Sarigne bou thiaga
Domou adama
@@seckmame1228 Sénégal sarigne si sakh lagnou gana geum ka yallah
Serigne Mbalou
Ahmou Diahkata mé ahna diabarou diambour ki dal dou serigne kidal kataté kat
Nit yéppou dioup yalla bagou ko nékone mou défko
Serigne bara N'diaye yangui rafétal rek wantè bou deug lak yalla takh Serigne modou khamoul diakarta khamoul tephone wantè kham nou gniou wakhè diabarou diambour sama koy bi ak sa bou dieukeur ak yow khou beug koyi ga té lou mou serigne wèdi wouko nèna moko wakh tè video wonè nako tèy guine beug ko rafétal. Respecté naléne trop nakh mè beugué li serigne modou wakh beuguine mou wakho sène diabar?? Senegal bou serigne dèf niaow tèf dagane
Léral bi am na solo man mom lepou lo lal suma mboko Dara rek def may miti
Serigne bara li wakh yeup rafét wantè bou deug lak yalla takh Serigne modou khamoul diakarta khamoul tephone wantè kham nou gniou wakhè diabarou diambour sama koy bi ak sa bou dieukeur ak yow khou beug koyi ga té lou mou serigne wèdi wouko nèna moko wakh tè video wonè nako tèy guine beug ko rafétal. Respecté naléne trop nakh mè beugué li serigne modou wakh beuguine mou wakho sène diabar?? Senegal bou serigne dèf niaow tèf dagane
Lane gua beug niou wah ko loudoul lissi gniko haml wah ko
Mais soutoura dafa bakh té pourquoi pas les audios de cette femme ne sont pas sorties.cetait entre les deux mann nafa yam dhe mais yakh derr rekk lann mann
Yeen deguen di fesel zinna
Boudone seni diabar doungenethi waxé ni d nafekh yingéne done
Yàlla d sula bëggée xamal nitt yi funé lakoy jaaralé rek
Nane lagnou ko diapé ak noumou démé moy lane? Sénégal serignes dinalen sanke
Toubape dafa créé internet mais nous Africain ont l'utilise pour se détruire
Tout sauf diabarou diambour
Lou lalathi lér nit daye mandou
@@mortalla9336 Déed saay deug leu naniouko soutoural d'accord naa waaya lila thie lerr mom boulkako laadj, bokoy xool ci internet bi di guiss Serigne bi mouné doungg.
Exactement, si c'etait une femme salibataire sax grawoul, il a le droit de epouser une 2 fam donc le probleme ici c'est une femme marie kou niaka diome soufeké piege la.
@@mortalla9336 c'est lui qui l'a avoué dans la vidéo. Kone lérna
Mais gnii thi gouvernement bougnou deffé dieuf djou melnii ken doulén djieuleul part alorsque boudeb sérigne nous gniawlouko. Allah n'est il pas le meilleur des juges ?
Ki nganii xamoul dra loudoul alkourâne ak hasaïde😂bolési beug leuff
😂😂Boy ngabou 😂😂😂😂
Dokhane diabarou jambour yi
@@maytaw00 😂😂😂
Kon li borkol si Sam jikko yi??? 😂😂😂😂😂😂 Nafekh bari Senegal
Serigne Bara danger rafetale rek mais rien ne prouve son acte il faut pas être l'avocat du diable lou si dess môme akk yalla n'a toubb diegalou yalla Bâle ko mou continuer daarame
Mandou dafabah. Quand Morgan te salissait à Paris pour fréquentation "echan..." Çà ne t'avait plus. A bon entendeur salut.
Lou wakh djiye niaw niaw acte amoul mome watt néna meusoul ndialo
Mane âme na nob boo xamne bougnou lako diokh ngua lekiko bilay walay boo done waliuwu làla wakh barki Mohamed par la force digua bogue djiguene doko tay sakh
Guanima lolou yéméneudé
Kiii mom journaliste la wala doméram la