Khamnaani daal Cheikh baye Niass nit kou baakh nga wallahi sopp naala liwadjhil laahi un homme équilibré intelligent maa cha allah na yalla gouddal sa fane
Amna Solo Mr Niasse! Cependant le verset 4:25 n’ordonne pas d’administrer la moitié (soit 50 coups) au non-mariés, ou célibataires comme vous l’insinuez. Revoyez bien SVP le verset, la il s’agit plutôt des femmes non-libres (esclaves ou captives) qui bénéficient du coup de circonstances atténuantes en recevant une sentence réduite en comparaison aux femmes libres pour le même acte d’adultère. Salaam
❤❤❤ هؤلاء يريدون هدم ماتبقى من الدين حتى يصبح جميع الناس زنادقا مثلهم تراهم يتكلمون كأن الله أرسلهم إلينا ، والله يقول للنبي صلى الله عليه و سلم قل آلله أذن لكم أم على الله تفترون ؟ ويل لمن صدقهم فيما ينكرون ومايثبتون
À ceux qui suivent ces lives, je vous en conjure : comprenez que c'est pas dans les réseaux sociaux que l'on s'instruit, surtout en matière de religion. Qu'Allah SWT, nous guide sur le droit chemin, Amin.
La vérité peut sortir de n’importe quel format comme la bêtise et le mensonge peuvent être fournis de bouches de soit-disant Borom daraja. L’essentiel c’est de référer à la VRAIE source qui est Le Coran! Que ce soit sur Google, ChatGPT, un live ou durant un khoutba. Na nekk wakhi YALLA bi rek
Thank you Cheikh Ahmed and masha Allah Cheikh Baye for bringing the light to this matter.We need more people like you to help Senegalese people with their religion.May Allah grant you with longevity, prosperity and peace.
Boudé cheikh Ibra mo wakh lolou wakhoul deugg!!! Yalla néna Alquraan lou lërr leu Lougniou faram fàccee. Boudé Ibra mo wakh lolou, kone kaay diaroul guné y Di diangg Alquraan, nagniou bay ba done magg
Hum machalah Ahmed Cissé sa invité cheikh baye mi ki amna xam xam deh machalah dafa lerr nagni limotakh baye Niass ak ndiabotam di dougueul ay milion wala ay miliard de personnes thi diiné Islam li kessé la xam xam dafa wara lerr , werr ,té woor li c'est la certitude machalah way dama contane thi yow ak wa keur baye niass you melni nekhoul ba nekhoul wayé baye Niass moy guédji xam xam ba dafa fégn thi ay ndawam yi xam xam you lerr té werr yi thi niom rk gakoy degue machalah way
Wallâhi yéené ngi foyé lou chéer mouy diiné, 😢 diiné djinga xam né yonént bi psl ak ay sahabaam rdy, dadie nanou louné ngir mou takhaw, yonént bi psl louné giss nako louné dégg nako ngir diiné dji niaata thi ay sahabam lanou ray, ginaw sahabayi rdy, ba sounou diamono dji niata si ay waliyou yalla ak ay borôm xam xam lanou ray gni teudie lén, gni niou généléen séeni doukou waay, té lépp takhawal diiné rék ak diangalé diiné moko waral, yéen ngéen di ay khalé you ndaw waroona roy thi lolou, roy séeni serigne nga xam né séen dounde gépp danouko diokh diiné, séen temps yépp danouko diékhal si yalla si diange ak diangalé, ak dioub yéen ngéen di foyé diiné😢😢 yalna léen yalla gindi
S18-V 29 Et dis: «La vérité émane de votre Seigneur». Quiconque le veut, qu'il croie, quiconque le veut qu'il mécroie». Nous avons préparé pour les injustes un Feu dont les flammes les cernent... Je jure par ALLAH (aza wadj'al) que ces gens qui parlent sont dans un égarement total. quiconque veut suivre la bonne n'a qu'a lire le coran avec concentration en demandant a ALLAH de lui guider sur la bonne voie et il le sera si DIEU le veut comme mentionné dans la même sourate Al kahf qui est conseiller de lire comme rapel des enseignements qui s'y trouvent chaque vendredi : S18-V110 Dis: «Je suis en fait un être humain comme vous. Il m'a été révélé que votre Dieu est un Dieu unique! Quiconque, donc, espère rencontrer son Seigneur, qu'il fasse de bonnes actions et qu'il n'associe dans son adoration aucun autre à son Seigneur».
@@moussandaby9707 sa waay kone déglou wo de debat bi dh , bagne nako wax nako ci biir wax dji yama gueneu maîtrise xadith yi wallahi té niom xadith rék laniouy topp 🫣
Billahi Wallahi Tallahi dangay fen ta xam ngani dangay fen. "المحصنات" في الآية بمعنى "الحرائر" وهذا تفسير ابن عباس، وهو قول العلماء مثل إمام الطبري في تفسيره. Baye Niass bett ngama trop😢
Ngor si ahmed yallah moy khol kouka nex mou xamal ko té yallah la nex mou xamal ken ki ga xamni moy xam xam CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASSOUL moy ki liguéyeul MOUHAMED (PSL) lou ken si nitou yallah massa ligey ci kaw souf ak assamane yaw nak waxal sa wax rek té boul manké de respect nioune nak CHEIKH AHMADOU BAMBA AK MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL DOUNIOU KO FOWÉ
Cheikh baye nieme gah mots français sisay wakh trop del wakh wolof Wala gah France pour nioumouna comprendre wante jakhase France ak wolof day compliqué pour comprendre ligey wakh
Vous prenez les hadiths quand ça vous arrange et vous les rejetter si ça ne vous arrange pas. C'est de l'hypocrisie. Mais je comprends puisse tout est écrit par les arabes et non pas par un dieu. Les religions sont une insulte pour l'intelligence humaine
Cheikh Baye mi foumou deukk ak noumay def ba guiss ko il est machallah vraiment
Cheikh baye macha Allah merci beaucoup ❤❤
Je préfère les lives doués de sens que ceux qui dénigrent la vie privée des gens ; un grand plaisir merci
KHAM KHAM DOU AY PEKHEY, MERCI AHMED CSSE ,AK CHEIKH BAYE NIASS
Khamnaani daal Cheikh baye Niass nit kou baakh nga wallahi sopp naala liwadjhil laahi un homme équilibré intelligent maa cha allah na yalla gouddal sa fane
Cheikh Baye merci à toi vraiment tu as èclairè beaucoup de musulmans.Que Dieu te garde
Machallah cheikh Hamed yagui dora ame djeurigue
Dieuredieuf émission du am na sollo
Amna Solo Mr Niasse!
Cependant le verset 4:25 n’ordonne pas d’administrer la moitié (soit 50 coups) au non-mariés, ou célibataires comme vous l’insinuez. Revoyez bien SVP le verset, la il s’agit plutôt des femmes non-libres (esclaves ou captives) qui bénéficient du coup de circonstances atténuantes en recevant une sentence réduite en comparaison aux femmes libres pour le même acte d’adultère.
Salaam
Vraiment gni nio rérr li yonete bi wakh ngen wédiko… Subhannallah
Gnaari say say gnooh and
Xam Xam Diang la Cheikh Baye Niass Yalna la yalla Ar Barkél Sa Doundou ❤❤❤
Cheikh Baye Niass😻 sa xam xam leer na🥰
وَقِصةُ الْمَرْجُومِ وَالإِثْنَيْنِ
حَسْبُكَ زَاجِرًا بِغَيْرِ مَيْنِ
مبْدَأْهَا أَنَّ رَسُولَ اللّهِ
عَلَيْهِ أَزْكَى صَلَوَاتِ اللّٰه
قَدْ كَانَ ذَاهِبَا وَجَاءَهُ رَجُل
فَقَالَ قَدْ هَلَكْتُ يَا خَيْرَ الرُّسُل
قَالَ لَهُ: لِمَ؟ فَقَالَ: إِنِّي
زَنَيْتُ مُحْصَنًا بِعَمْدٍ مِنِّي
قَالَ لَهُ: ادْعُ النَّاسَ يَرْجُموك ثم
دَعَاهُمُ فَقَتَلُوهُ إِذْ يَؤُمْ
وَبَعْدَ ذَا تَبِعَهُ شَخْصَانِ
لِلرَّجُلِ الْمَرْجُومِ يَغْتَابَانِ
حَتَّى أَتَوْا جِيفَةَ عَيْرٍ فَوَقَفْ
وَقَالَ: يَا ذَانِ كُلَا ذِي وَحَلَفْ
إِنِّي أَرَى يَجْرُّ فِي الْجِنَانِ
ثِيَابَهُ فَافْتَضَحَ الشَّخْصَانِ
الشيخ أحمد الخديم
الجوهرالنفيس
❤❤❤
هؤلاء يريدون هدم ماتبقى من الدين حتى يصبح جميع الناس زنادقا مثلهم تراهم يتكلمون كأن الله أرسلهم إلينا ، والله يقول للنبي صلى الله عليه و سلم قل آلله أذن لكم أم على الله تفترون ؟ ويل لمن صدقهم فيما ينكرون ومايثبتون
من ليس له فتح و بصيرة ،أراه هالك في هذا الزمن
Ils ont même lapidé une guenon. C’est dans les Hadiths.
Gni danô doff ay khalé lanou youy foyé diiné dji, yalnanou yalla mouseul thi lii
Cheikh Bay kholaatal aayab ومن لم يستطعِ Niguako attê dunoonu.
Cheikh Ahmed yangui dora trouvé Sa liguey! Bouko bayéti déé! Bilay soula guissé si cas mome Damaye gnow Amerique
Diné yalla Dji Dina lér inchallah.
Hadiss yi Di sosal yonéntébi rék soubhanalah
Bilahi
À ceux qui suivent ces lives, je vous en conjure : comprenez que c'est pas dans les réseaux sociaux que l'on s'instruit, surtout en matière de religion.
Qu'Allah SWT, nous guide sur le droit chemin, Amin.
Alquran rek doyna, yeremeul sa bopp
Merci 😊
La vérité peut sortir de n’importe quel format comme la bêtise et le mensonge peuvent être fournis de bouches de soit-disant Borom daraja. L’essentiel c’est de référer à la VRAIE source qui est Le Coran! Que ce soit sur Google, ChatGPT, un live ou durant un khoutba. Na nekk wakhi YALLA bi rek
Ma challah am na solo
Cheikh akhmed taye mome nangouna sa intelligence tu es fort
Thank you Cheikh Ahmed and masha Allah Cheikh Baye for bringing the light to this matter.We need more people like you to help Senegalese people with their religion.May Allah grant you with longevity, prosperity and peace.
Machalla Serigniou nandité yi li môme bouko bayi sa liguey rafetna trop
Invitel khadim bousso
Ma Sha Allah ❤❤❤ Ameuna solo lolou
Saw est le modèle parfait et l'exemple parfait alhamdoulilah
Merci cheikh baye
Cheikh Ibra néna Alkhour An létou Magla Goné douko Firi🙏🏾
Manam
Lolou moy tapalé rek
Boudé cheikh Ibra mo wakh lolou wakhoul deugg!!!
Yalla néna Alquraan lou lërr leu Lougniou faram fàccee.
Boudé Ibra mo wakh lolou, kone kaay diaroul guné y Di diangg Alquraan, nagniou bay ba done magg
Cheikh ibra wéroul
gone moy ku diangoul 😂
Hum machalah Ahmed Cissé sa invité cheikh baye mi ki amna xam xam deh machalah dafa lerr nagni limotakh baye Niass ak ndiabotam di dougueul ay milion wala ay miliard de personnes thi diiné Islam li kessé la xam xam dafa wara lerr , werr ,té woor li c'est la certitude machalah way dama contane thi yow ak wa keur baye niass you melni nekhoul ba nekhoul wayé baye Niass moy guédji xam xam ba dafa fégn thi ay ndawam yi xam xam you lerr té werr yi thi niom rk gakoy degue machalah way
Cheikh baye niass yalla na la borom bi doli soutoureu
Cheikh Bay Machallah Yalna BOUR AllAH yook Sam ak Soutoura Xam Xam bi ler ni
Xam xam bi lèrr ne yalla nagafi yahe ch bay ❤
Wallâhi yéené ngi foyé lou chéer mouy diiné, 😢 diiné djinga xam né yonént bi psl ak ay sahabaam rdy, dadie nanou louné ngir mou takhaw, yonént bi psl louné giss nako louné dégg nako ngir diiné dji niaata thi ay sahabam lanou ray, ginaw sahabayi rdy, ba sounou diamono dji niata si ay waliyou yalla ak ay borôm xam xam lanou ray gni teudie lén, gni niou généléen séeni doukou waay, té lépp takhawal diiné rék ak diangalé diiné moko waral, yéen ngéen di ay khalé you ndaw waroona roy thi lolou, roy séeni serigne nga xam né séen dounde gépp danouko diokh diiné, séen temps yépp danouko diékhal si yalla si diange ak diangalé, ak dioub yéen ngéen di foyé diiné😢😢 yalna léen yalla gindi
Louniou wakh dou deug walla ? Vrai ou faux.
Machallah cheikh Baye guindi nga niou beuri machallah yallah yokhou la zaïrane wa batinane amine
رضي الله عن شيخنا شيخين بخاري ومسلم وغفر الله لكما
Amnaa mbetteel Ci Cheikh Baay lool
Merci gayi
Ya bakh inyass dundu rekca gay def amen thank you
افهموا قبل كل شيء تفسير هذه الآية
Mashala,mashala , mashala cheikh baye,😭😭😭😭guindi nga dioulit you bari si Mbirou Yonentibi ak Yaye Aicha,séenoup nek
Cheikh baye dome ram gua balégui wakho lou lérr si juf yi nouniouko dougualé si hadisse?
❤❤❤Profete psl n'a jamais épousé aicha 9 ans Hadiss mensonge. Aicha a été épousé à l'âge de 17 ou 19ans
Macha Allah.Lii moh werr
الله اكبر
MASHALLAH 🙏🏿 GNINE GNI DIANGOUL MOM DÉ KOU NIEUW WAX LOUNOU ARRANGÉ RÈK ÑOUNÉ LA MASHALLAH YAY WADJI 😂😂
Machallah cheikh baye niass
Masha Allah ❤❤❤
فعليهن نصف ما على المحصنات Loolou pour Diaam bou djigènn la Serigne bi
كلامك صحيح
Donc le mieux c'est de se référer uniquement du coran ?
S18-V 29
Et dis: «La vérité émane de votre Seigneur». Quiconque le veut, qu'il croie, quiconque le veut qu'il mécroie». Nous avons préparé pour les injustes un Feu dont les flammes les cernent...
Je jure par ALLAH (aza wadj'al) que ces gens qui parlent sont dans un égarement total. quiconque veut suivre la bonne n'a qu'a lire le coran avec concentration en demandant a ALLAH de lui guider sur la bonne voie et il le sera si DIEU le veut comme mentionné dans la même sourate Al kahf qui est conseiller de lire comme rapel des enseignements qui s'y trouvent chaque vendredi :
S18-V110
Dis: «Je suis en fait un être humain comme vous. Il m'a été révélé que votre Dieu est un Dieu unique! Quiconque, donc, espère rencontrer son Seigneur, qu'il fasse de bonnes actions et qu'il n'associe dans son adoration aucun autre à son Seigneur».
Bayilén fén
MAA-CHAA-ALLAH ❤❤❤
Cheikh baye yaw tay dagua dioum
Invite alpha Bâ avec lui
Néna da daw
Niouss n'a Alpha ba bou yague😂😂
alpha ba amoul xam xam
Alfa d'où niew cheikh baye yague nako wo débat
Alpha do meusseu gneuw ragal la
Vraiment cheikhs Hamed Cissé yagui déf Lou ame solo machallah bonne continuation 🥰🥰
Ibadou yi xana niéméwounou cheikh Ahmad Cissé,com déno nek fi di rey lamégne xaméwounou Lou xarame ak lou dagane
Yow Yangui dora xam Sangue bi ki Machallah
Yangui diokh gayi fite dé 😢😢😢
ماشاء الله بارك الله فيك أحسنت وأكملت أطال الله عمرك فرحنا جدا
❤❤ macahalla
Maachaa Allah
Sheikh bai maa shaa Allah yalna nga gudu fan Aameen ❤❤
Cheikh bay niass vairement tu te trompes lourdement diapon nanè erreur yi doko def
Dangendi thiakhan rek bageu thiakhan lo nit nii
Pourquoi cette chois de interlocuteur
CAMS ay wakham ken meunoussi dadji dara ndakh alquran lay wakh.
Kii mome vraiment dama beugueu Niassen gni moma nekhh si selleu
Alhamdoulilah ❤
man mom abonné na wayé dakh Li mom Lou am jerign la
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ahmed cisse decredibilise les oustaz presents ici.😊
vraiment kii wakhou fii dara cheikh ahmed sakh kham nassi dara da gno sékkeu deal bi rék
YALLA NALA YALLA FAYE LÉRAL YI CHEIKH BAYE NIASS SI BARKÉ SEYIDINA MOUHAMAD SALALLAHOU ALEYHI WA SALAM
Professeur madiama ame na deugeu juveyi nioyague dinédie😮
Wa cheikh Ahmed cissé gnaww na nak cheut
Machalah cheikh baye
Machallah ❤️
Diadieuf ch bi
Rajmou sunnalah. Sa way. Yaw danga wara dem diangiwatt😢
اين أصحاب الدكتوراه ،موضوع بحث
Kane momay boléle cheikh baye ak alfa bah 😮 débat
Très bien lolou mo wara ame chiekh baye niass dafa mena féne té chiites la
Weuh yén alpha ba kii lay waaaté yagu nagne dadié sén groupe whatsapp yoyou moukay troxal ci xam xam nak
@MalickAssNiang lolou dou dëëg mane xhamena waxx tane bi alpha xawou nako Ray ki chiites bou makk la dafaye yakk hélou dioulitte bagne seydina aboubakar akk seydina omar té nio niou nio geune ndayeam akk bayame
Cheikh Baye Niass ak Oustaz Oumar Diallo débat nagn
@@moussandaby9707 sa waay kone déglou wo de debat bi dh , bagne nako wax nako ci biir wax dji yama gueneu maîtrise xadith yi wallahi té niom xadith rék laniouy topp 🫣
mashallah❤❤❤
Senegal les plupart sen islam dafa yemé bilahi...
Dinagnela tiawate aye khire
Bayil doul
Aicha bimouy nek Sokhna yonent bi bobou amna lou espe 18 ans khana
Billahi Wallahi Tallahi dangay fen ta xam ngani dangay fen.
"المحصنات" في الآية بمعنى "الحرائر" وهذا تفسير ابن عباس، وهو قول العلماء مثل إمام الطبري في تفسيره.
Baye Niass bett ngama trop😢
Seex Baay Ñas moytul di séq ak jotaay saay yu melni Ammet Siise mii
MachaAllAH😍❤️🙏♻️😍❤️♻️😍❤️🙏♻️😍❤️🙏♻️😍❤️🙏♻️😍❤️🙏♻️
Ngor si ahmed yallah moy khol kouka nex mou xamal ko té yallah la nex mou xamal ken ki ga xamni moy xam xam CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASSOUL moy ki liguéyeul MOUHAMED (PSL) lou ken si nitou yallah massa ligey ci kaw souf ak assamane yaw nak waxal sa wax rek té boul manké de respect nioune nak CHEIKH AHMADOU BAMBA AK MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL DOUNIOU KO FOWÉ
DADJI KOU D'ANGERS LEH THI SÉNÉGAL NDAKH LI MOY WAKH AKA SOREK DINNE YALLA NANIO YALLA SAMEU 😢😢😢😢😢😢😢
Cheikh baye nieme gah mots français sisay wakh trop del wakh wolof Wala gah France pour nioumouna comprendre wante jakhase France ak wolof day compliqué pour comprendre ligey wakh
Feen reek
Contane na si yaw contane na si BAYE NIASS RADIYALAHOU TAALA ANHOU YALLA NALÉN YALLA FAYE GUEUNE DI FAYE SI BARKÉ ALKHOURANOUL KARIM
Wakh nguir yàlla d baax na Lool😭
Ballen wah lulen lerrut
Sangue bi liga wakh diakhal nama dé kou nek si boum def adultère lagnouye door 100 yate les autres 50 .
Vous prenez les hadiths quand ça vous arrange et vous les rejetter si ça ne vous arrange pas. C'est de l'hypocrisie. Mais je comprends puisse tout est écrit par les arabes et non pas par un dieu. Les religions sont une insulte pour l'intelligence humaine
Yayou Aïcha 18an la amone
Ki day fèn limouy wax xamou thi dara day rtèral gni diangoul
Tu oublies que c est ALLAH QUI EST GARDIEN DE SON CORAN
C'est vrai mais il raconte l'histoire
non c'est faux et sans les hadiths le coran est incompréhensible
Tu ne me comprends pas je parle de l'histoire de saw et Aicha @@yvefay620
Et le chèvre qui a mangé les versets ou était ??? Yalla dou thiahane
@@yvefay620yaw Lou leudeum ga deff coran
Ki limouy wakh bolé len ko ak Oustaz Oumar Diallo boudé geumneu limouy wakh deug leuh
Cheikh bay comprends mal les versets
Rajmu alhouran léral louko yonete bi moka léral jangalé ko djioulite nieup andd ci …yén tay guén nieuw diko wéddy beug yam ci alhouran tei xana xamo Sunnah moy firi alhouran
Taye mome dèbat bi haut niveau la