😭😭😭 mon cœur pleure pour ces animaux. Ça me choquait qd j’étais petit. Mais bon nous sommes un peuple qui n’a ni pitié des enfants ni de la femme. Donc que dire des animaux!? Triste! Allah nous voit et nous attend de pied ferme. Qu’Il change nos cœurs et y mette plus de compassion. Merci pour ce mini reportage DakarActu.
Sénégal thi bopam ligne fa wara wakh mo Bari manque d'éducation amouniou respect thi sene bop sakh baye rèspectè Mala civisme zéro sans oublier borom taxi yi ak borom chauffeur carapide yi ake ndiaga ndiaye yi doy n'a war 😥😥
Finalement...j attendait c moment kon parle des pauvres cheveaux.prkoi cette maltretance..prkoi l president n en parle pas???? Daniou yore bakanne come nous.pourkoi on elimine pas les charettiers...
Conne mane aak yow nio yeeme..les habitants d fadjia m prenne pr une folle.prck dama aam yeurmande ci fasse.boudoone amnna possibilte guiss macky sall.koone daamakoye wakh mou dindy fasse senegal
Mane damay dawale fach ms sama fach mesoule pikirou khadiou pikire yepe bakhoule mane fache la gena begu sama bakane billahi wallahi wa tallahi ms amna nio khamni danio mene féne
Les charretiers sont d'une arrogance démesurée. On les laisse conduire sans assurance , sils touchent une voiture en cas d'accident dara dou khew. Respectons les animaux !!
Beuge naala nakh linga beuge mousse mane mome jadore les chats dama beuge mousse mais c tres rare de voir des senegalais qui aiment les chats motakh kouma djiss ak sama mousse gani wa kii werr na ndeyssane yalla moy def yeurmandé si xolou nitte. Pluies de coeur sur toi
Manque d’éducation de la population!! Et ignorance !! Ce phénomène doit arrêter !! En manière générale arrêter de maltraiter des animaux et aussi respecter le Sénégal,prenez Sénégal comme toi, il a une âme si tu prend les choses de cette manière !! Walahi do sanii mbalite si mbeed bi do deef daara louye torakhal ben mala!!
Tant que fass yi gniougui len di dioylo senegal dou massa natt ndakh dilen liguey loo teksi yenleen loudiisss baparé dilen door té dougn lenn diokh laik boudoy bilahi bone rekk ak gnak yeurmandé kessé leu té malayi dagniou am baken comme gnioune
Monsieur Sow nakala laniou meuneu deff ba amm sa numero nguir meuneu and akk yaw deff app reportage thi sa ligueey ? Sou yembé yonéniouko si boitedakc@gmail.com
😭😭😭 mon cœur pleure pour ces animaux. Ça me choquait qd j’étais petit. Mais bon nous sommes un peuple qui n’a ni pitié des enfants ni de la femme. Donc que dire des animaux!? Triste! Allah nous voit et nous attend de pied ferme. Qu’Il change nos cœurs et y mette plus de compassion. Merci pour ce mini reportage DakarActu.
Lii amna solo billahi
Ndaysann 😳, Amna solo trop🙏🏾
Yacine
Reportage intéressant on doit davantage en parler sur ces genres de sujet
Merci ONG brooke on vs attend ds la commune de taïba Ndiaye
Sénégal thi bopam ligne fa wara wakh mo Bari manque d'éducation amouniou respect thi sene bop sakh baye rèspectè Mala civisme zéro sans oublier borom taxi yi ak borom chauffeur carapide yi ake ndiaga ndiaye yi doy n'a war 😥😥
Finalement...j attendait c moment kon parle des pauvres cheveaux.prkoi cette maltretance..prkoi l president n en parle pas???? Daniou yore bakanne come nous.pourkoi on elimine pas les charettiers...
Mo takh si fitna rék lagnouy nék
Yalla naléne yalla yeureum
Jdixsn
Li xew si rew mi li rek meune nako waral mane deh yalla xam Nani Mouss nasi khéhe ak bène way nakh yéne fass bi lou disse yalla xam nako
louma beug la sama.xoll❣️
Bilay man dama lèni yeureum sama khol day toye si niom ame lène yeuremande waye boul ni mala la rek louma nekh lakoy def da ame bakan kom nieup
Conne mane aak yow nio yeeme..les habitants d fadjia m prenne pr une folle.prck dama aam yeurmande ci fasse.boudoone amnna possibilte guiss macky sall.koone daamakoye wakh mou dindy fasse senegal
Dakaracte li amna solo lool mazahalla
Retenez bien kouy torokhal Mala man n'a torokhal nit car lep yeurmandé la.
DEUG la dé danion wara khamné sa collègue la boye liguéyeul té lisi eupe solo moye dafa yoré bakénn ni yaw té yallah daye atté
Amna solo torop bassir
Mane damay dawale fach ms sama fach mesoule pikirou khadiou pikire yepe bakhoule mane fache la gena begu sama bakane billahi wallahi wa tallahi ms amna nio khamni danio mene féne
Nom au maltraitance des animaux
Imame Bachir wakhe gua lépp machahala.
Les charretiers sont d'une arrogance démesurée. On les laisse conduire sans assurance , sils touchent une voiture en cas d'accident dara dou khew.
Respectons les animaux !!
Pa bi mo mene doule fache bouniouy yepe 2 tone foumou ame ki daye doule
Au Senegal même les humains sont maltraités désolant
Lol venez en Mauritanie exactement à Nouakchott et vous verrez comment on traite les anes
Ay way ngir yalla amleen yeurmeunde ci malayi Sama xoll dafa fess bilahi li metina
Billay Sénégal ninoy def fass fii rek la am
Degue na kilifa mouni problèmes yi eupe senegal thiono yignuy tek fache yi nioko indi
Mangui sante yalla sougnou borom am gnari mousse sama négue chaque jours sama diggi lale légnou téddi
Beuge naala nakh linga beuge mousse mane mome jadore les chats dama beuge mousse mais c tres rare de voir des senegalais qui aiment les chats motakh kouma djiss ak sama mousse gani wa kii werr na ndeyssane yalla moy def yeurmandé si xolou nitte. Pluies de coeur sur toi
Machallah ya bakh sokhna si aissata soumare bn van
C le gouvernement qui doit mettre des sanctions
Manque d’éducation de la population!! Et ignorance !! Ce phénomène doit arrêter !! En manière générale arrêter de maltraiter des animaux et aussi respecter le Sénégal,prenez Sénégal comme toi, il a une âme si tu prend les choses de cette manière !! Walahi do sanii mbalite si mbeed bi do deef daara louye torakhal ben mala!!
On est a l'extèrieur mè louniou am si cheval laniou ko amè
Ayy doméharam laniou danio bone ci mala yi trop
Walakhi, ces gens là finissent mal, 😭😭
arréte de mentir stp
Sénégal rék laniye sonalé fasse fi thij Mali kéne doufi tak fasse Sénégal lifék gningi sonal Mala dou avance
👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍
Nice
❤❤❤
Dafa meti😓😓
Billahi les animaux sur les chevaux sont mal traités au Sénégal et ça me fait mal
Borom fass yi legui daniou boneu fass yi dougn lékk di yenou Lou diss diko door ba yaw sakh daguay tit
Billaaye wakhattiko
Bayilene féne
Tant que fass yi gniougui len di dioylo senegal dou massa natt ndakh dilen liguey loo teksi yenleen loudiisss baparé dilen door té dougn lenn diokh laik boudoy bilahi bone rekk ak gnak yeurmandé kessé leu té malayi dagniou am baken comme gnioune
C'est pouquoi les senegalais soffre
On en voit tout les jours. Cest vraiment dommage.
Reportage bou intéressant, mais deugg bii saletés,est puis la vétérinaire bureau m bii ak place sam bii aussi saletés na aussi
Dou yoon thi boppam nignouy deff cheval bilahi kou thi bayyi woul maltraiter animal do avancer
Koussi torokhal fass si torokh ngueyy moudie yeneyi domeram rek mo keyy deff
g
Amouléne programmes😄😄😄😄
Li dou programme kon ?
Démal nga diangui.
Niakk kham aduna reik. tay Sougn neila imbécile ngay weur nane dagn la sagga.
Bigéne si ware takaw mo yagga mane dwal katou charrette la m moma geuneul Sama bop Ndakh louma am momako may
Merci bcp frère continue sur ce lancer
Lolou mouniou war kéne dou yor sa alal ngakoy sagané
@@dioumpro9687 deugu deugu
Monsieur Sow nakala laniou meuneu deff ba amm sa numero nguir meuneu and akk yaw deff app reportage thi sa ligueey ? Sou yembé yonéniouko si boitedakc@gmail.com
Mane mome managouma wakh si média Ndakh dawal katou charrette la + Cameramane
dinalasi diapalé
Abdaiah da
Motakh kou toroukhale Mala rek tokhokh ! Il y a des gens même les animaux valent mieux qu' eux !
Fass warna lékkk maximum 7000fr wayyé kuthi respecté wul akkheu bobou dinko giss
Méty na
😭😭😭
Wakh dji lou kay safaral état mossi wara dioug