BarakAllahou fiikoum ya Cheikhna Dr Mouhamad Ahmad Lo , chers frères et sœurs ne répondez pas aux insultes c'est normal il ne peut pas être aimé par toute une communauté mm le Prophéte psl en a subi qu'Allah swt purifie de toute haine le cœur de ceux qui ont une énorme rancune envers cet innocent ! Profitons de cette personne de science dont Allah swt nous a fournit
Félicitation à tout le senegal,pour le sacre de mouhamad mujtajab diallo,wallahi Ahmad lo tu as la fierté du senegal,do moromu béne borom xam xam ci senegal,hafizakallah wara aka
J'ai pitié des pauvres gens qui veulent s'attaquer à ce Grand Savant. Profitez de son savoir au lieu d'insulter. Qu'Allah vous protège nous t'aimons par Allah.
جزاكم الله خيرا فضيلة الشيخ أطال الله عمركم وبارك ذريتكم إلى يوم الدين . أطال الله عمركم وبارك في جميع أموركم و يحفظكم من كل سوء و مكروه إنه نعم المولى ونعم النصير
Mais man Lima diakhal moy docteur Ahmed lo discours bi da wouté ak li yén boy yi di wakhe sérieux na niou tok wakhetan mo geun saga wanté yi walahi man joulite yeup la diapé samay mbok je suis soufi 100/100 mais koula sop la dakhe sa kham kham
Sama gayi nitt aussi louko yalla may loko contre contre nangoulko meritam je ne suis pas de son clan mais nakk kham kham laye wakh fierté pour les vraies sénégalais nanou bâyi saga borom kham kham
abass diouf indil firndé biy wanéni daa kéfarlo réwmépp. Limalay dénk moy nga ragal yalla. Ta nga khamni biss dina ñeuw. Salokho bi nga bindé wakh jii euleuk dafay sédé soko meunta wakhal lou baakh nga maandu
Am nga Xam Xam Lol Masha Allah, tu dis bcp de vérités sur l"égarement des Sénégalais mais bayyil Sunu Makk Gni Serigne TOUBA,Cheikh OUMAR,Aladji Malick,Mame Abdoulaye Niass ,Gni ayy niitOu YALLA LaañOu T Sèni diamono fèkkOulènefi..Bokkalèwouñou,inddiwouñefi diinè gou bèss mais au contraire nioffi deuggueureul ISLAM N'a nga djOOte ci Tayy...TOUBA boufa mbaax nèkkOulwOne dOffa djangguè ALQUR"ANE...Gni raggalnañOu YALLA,DoudeulnañOu Sunnu...Ayez le courage de parler directement à leur descendance yi téggOuwOul ci yOOne wala ñOu neikk Ci lilène nèx mais bayyil Sunu Makk Gni,Niom laañOu am...Sayy Mame DèffalouñOu Dara diinè Ji Wala ISLAM pour mou taxaw ci Senegal
@@lassanadoucoure6586 va te faire imbécile , espèce de prétentieux...Qui t'as dit yaw yaama gueuna djanggue ??? Le vrai ignare et imbécile, c'est 1 homme de ton genre , C'est celui qui prétend detenir le savoir où le monopole du Savoir...Comment peux-tu juger de Djaahil quelqu'un que tu ne connais pas ??? C'est ce qu'on appelle le terrorisme intellectuel, ManddouL Ci mane ...Xawmala , XaamOmaa...BulShiite
Si tu veux, Je peux te donner mon numéro et là tu saurras ndax Djanggue na wala Dètte...Bèwwe Baa Déé MoomOuLéne Diiné Ji , Ni Aldjaana , ni Djahaanamaa
Un grand savant Ma Shâ Allah... qu'Allah (SWWT) le protège.
Docteur on t'aime beaucoup en ALLAH !
الشيخ احمد لوح ايده واطال عمره وابقاه فينا وكمل نواياه ❤❤❤وماذالك على الله بعزيز
MACHAALLAH Notre Docteur international !
Dieureudieuf ci leral you ame solo. Dr Mouhammad Ahmad LO H.A. qu'Allah vous donne la force de continuer votre mission. Alhamdoulilah content de vous
Comment pouvez vous défendre ce gas
c'est parce que c'est un gars doué de clairvoyance
Domeram dioubonn Doctor lô domèkhath, khadiako guènn
Ki moy massil dadial lo
Machallh
BarakAllahou fiikoum ya Cheikhna Dr Mouhamad Ahmad Lo , chers frères et sœurs ne répondez pas aux insultes c'est normal il ne peut pas être aimé par toute une communauté mm le Prophéte psl en a subi
qu'Allah swt purifie de toute haine le cœur de ceux qui ont une énorme rancune envers cet innocent !
Profitons de cette personne de science dont Allah swt nous a fournit
Je savais pas que les wahabis vous avez des cheikhs bida wa haram cheikhna
Il m'a tellement appris ce chers docteur!! une fierté nationale et international!! longue vie à lui et Barak Allahou fik
Domèkhath dioubonn
ماشاء الله جزا الله شيخنا الكريم شيخ الدكتور أحمد لو ، اللهم احفظه واستره سرا وجهرا ، ودنيا وأخرى. وكذلك اللهم ارض عن شيخنا وحبيبنا محمد الأمين درامي.
Machalah, que Dieu ouvre les oreilles des Sénégalais
Félicitation à tout le senegal,pour le sacre de mouhamad mujtajab diallo,wallahi Ahmad lo tu as la fierté du senegal,do moromu béne borom xam xam ci senegal,hafizakallah wara aka
Moussa sy , 😂 lolou mome wakh kou danou si charrette la lol. So ko ladjé dina la léralal in sha'allah
Ibrahima DIOP xam nga bubax ni Ahmad lo machallah,té yalnako yalle sammal boppam
Moussa sy , ba légui déguo mani la nékou ko, foumou diangué al quran?
Ibrahima DIOP yaw waxal fumu jangé alquran
raga lalle yalla thi lingaye wakh
koubegge mouhamad lo boudel j"aime
doule waye
+Gora sope nabi إتق الله
@@gorasopenabi3967 iow bayil togne
@@gorasopenabi3967 doul
❤❤❤❤❤❤❤sounna rek
J'ai pitié des pauvres gens qui veulent s'attaquer à ce Grand Savant. Profitez de son savoir au lieu d'insulter. Qu'Allah vous protège nous t'aimons par Allah.
Mohamadou Traore amine way. wallahi kouka xamoul rék mo kay dal
GalGal Gal yaw ya doul dara
invitez de répondre ces genres de personnes
Machallah wallahi mbok wax nga deug,Ahmad lo kilifeu diné deug le,hafizahullah
Kou baggne serigne touba meno bakh
ماشاء الله فرحنا جداً من إستضافتك لشيخنا الدكتور أحمد لوح جزاه الله خيراً
جزاكم الله خيرا فضيلة الشيخ أطال الله عمركم وبارك ذريتكم إلى يوم الدين . أطال الله عمركم وبارك في جميع أموركم و يحفظكم من كل سوء و مكروه إنه نعم المولى ونعم النصير
بارك الله فيكم شيخنا الفاضل وأطال عمركم وجعل الجنة مثواكم
yalna yalla samula Dr🇹🇷🇸🇳, Aka yaru ndeysan , gud del fan, Sènègale yi amogunla sa.
Merci yaa cheich Adoctor que Dieu vous protége
Macha Allah #Alqur-Aanne ak #Sunna moy deugg Tei Lolou reik doyna Top
Machallh amna solo torop borom xam xam dr Mohamad ahmth lo yalla na yalla faye la yiw😍😍🎤👀🎧🕋🌟✍
cheikh bh kènna munula fay ludul ki yor fay t moy yalla sugnou brom t yalnagnula yalla fayal........
Mais man Lima diakhal moy docteur Ahmed lo discours bi da wouté ak li yén boy yi di wakhe sérieux na niou tok wakhetan mo geun saga wanté yi walahi man joulite yeup la diapé samay mbok je suis soufi 100/100 mais koula sop la dakhe sa kham kham
Macha allah yalla nako yalla defal diamb adouna ak allakhira.yalla barkel xam xamam. loumou yéné si gnoune yalla mayeko ndame.
ما شاء الله
حفظ الله شيخنا الدكتور محمد أحمد لوح
debile
قل هداه الاه
Machallah un tres grand savant je suis mauritanien mais je connais mieux ma religion grace a lui
Ki Senegal khamoung ko bilahii
Mouha Diopp on a pas besoin de lui connaître
Dieureudieuf ci leral you ame solo. Dr Mouhammad Ahmad LO H.A. qu'Allah vous donne la force de continuer votre mission
حفظ الله شيخنا د.محمد أحمد لو ورعاه من كيد الماكرين
Kon kay Seyiduna Mouhamadou Rassouloul Lahi sallal lahu halayhi wasallama doonul woone nitouk késsé Kom yén nigén koy waxé
On né avec toi machallah hamdoullah que Allah vous portez docteur Ahmad lo
Sama gayi nitt aussi louko yalla may loko contre contre nangoulko meritam je ne suis pas de son clan mais nakk kham kham laye wakh fierté pour les vraies sénégalais nanou bâyi saga borom kham kham
Deugladé,manemidé damako beugue Sama khole dakh xam xam AK Yare bi AK yiweume ,motakh gni Nek si ganawam Nanou roy simome.
Dofyi amo lėne arguima matakh guėne di sagua gui meune n'a diagal sa pape yi ak sėne mam yi
بارك الله في شيخنا وأطال الله عمره
❤❤❤❤❤❤❤❤ for ALLAH ASWADJALLE, a cause D,ALLAH ASWADJALLE
حفظك الله يا فضيلة الشيخ الأستاذ الدكتور محمد أحمد لو
أحبك بالله وفي الله
يعصمك الله من أعدائك أعني أعداء الإسلام،لأن أعدائك هم أعداء الإسلام
حفظه الله ورعاه واطال الله عمره الدكتور محمد أحمد لوح
Alhamndou lillahi machallah xam xam rék mowoor yalanalén yalla sam té aarléne
Ma challa ya dr ahmet lô yalla nanioula yalla fayale
Vraiment souniou pap dij amna xam xam yalla gua goudou fane waye🤲🤲
Mak bou yarou ❤❤❤❤
senegal li mou am khamou ko kou melni ki adouna yep dika djiarinio niioun niou gueun sai neew la.doyna waar اطال الله عمرك يا دكتور بارك الله فيك
Yalla nga ame díame ak wuer bilay oustaz hamed lo
Machallah wokhtan bii amna solo yalla na len yallah faye the mailene wer
MA SHA ALLAH DOCTOR SHEIKH MUHAMMAD LO MAY ALMIGHTY ALLAH CONTINUE BLESSING YOU AND WHOLE MUSLIMS.
Yalla Nala yalla defal dígame ak wuer si barkkem
MaashaAllah ya cheyhana ,bou wakhé rek xam xam la,ndax dal ak teye
Vraiment je suis très content machalla kadouyi l'ère na barakalawou wa fika
Diaradieuf Al Amine
yallanala yalla fayyiw cheikh bi
machallah ya oustaz barakallahou
BarakAllahu Fikum. May Allah increase your knowledge and keep you steadfast.
macha Allah .djazakallahou khayran dr ahmad lo
Serigne senegal yi kayelen sen baye mou diangalen len
Macha allah liga beug si rewmi yallanako yalla motali dafa beug Sénégal nekk benn
Mach allahou, qu Allahou vous protège et vous bénit mon cher docteur .
fatimata sy amine way
Macha Allah yalla nala borom bi same té moussalla si Seytané ak mbolème dioulite
Macha'Allah Ya Cheikhouna Dr Mouhammad Ahmad Lo (H.A)
ماشاء الله حفظ الله شيخنا الدكتور
eskeuy ya bari kham kham حفظك الله
Macha allah dr ahmad loh yalnala borom bi fay yiw❤🤲🙏
yallana niou sunu borom sammalniou sunu kilifa guî !
Allahouma Amiine
Mouhammad Lô Ah ki nak de bakhna mes dafa mana doul nguen balma
Allahouma amine
@@laveriteabsoluejuste6358 iow yay domou mbaam
@@falloudiop9594 sa baay moy dool kat bi
Dr Ahmet lo man damala beugeu trop nakh sa ma nootée
إن الذي لم يخش رب العالمين ليس بعالم ولو أفن الفنون
ماذا تقصد
May Allah reward you with goodness Ya sheikh
yalnala yala Faye Dr. mouhamad dieredief
Comment pouvez vs défendre ce gas.
ماشاء الله
sa doit tomber l'oreille de chacun merci oustaz lo
Mancha'allah dr.cheikh Ahmed lo h.a
الحمد الله رب العالمين الله أكبر ماشاء الله جزاك الله خيرا
mashallah barakalahou fikoum
جزاكم الله خيرا وأطال بقائكم
yaalna yalla saammla Dr lo
Machallah ma la begue
yalla na ma yalla moussal ci dr lo
@@toubandindiinfo5829 ndeyssane
Machallah que vous protège...
Mala beugue yallh na nga goudu fann ak wéer
جزاكم الله خيرا يا شيخنا وبارك فيكم
maasha allah yalna ya Allahou same laa
Waa kii dou ahmed kazab lo, keefeurlo neu Sénégal guèpe ndeysaan
abass diouf indil firndé biy wanéni daa kéfarlo réwmépp.
Limalay dénk moy nga ragal yalla. Ta nga khamni biss dina ñeuw. Salokho bi nga bindé wakh jii euleuk dafay sédé soko meunta wakhal lou baakh nga maandu
abass diouf yalla naga dee sili guem
Sa baye moy kazab
Mahsallah Mahsallah Baraka llah fikoum merci
Fatoumata Toure qu Allah le preserve in challah amine
أطال الله عمرك يا أخي الحبيب والله أحبك حبا جما
Djazaaka laahou khayrane yaa Cheykhanaa
Djazaka mul lahu khayrán ya cheikh ahmad lo
Bara kallahou fikà deug rek mo am solo alkhouran sounna rek
Macha alla ya amirouna
diereudieuf docteur Akhmad lo
Barakallahou fika wa fina ya cheykhana
docteur diabarla man talibe serigne bi makoh wah
Mohameth Kane mbokou yagui tongne liratal bou bakh
Mohameth Kane man pikine la deukeu négue talibe
serigne touba
Danguay doyl rek
Mashallah amena solo
ماشاءالله مبارك كل عام وانتم بألف خير
ما شاء الله الله يحفظك
Am nga Xam Xam Lol Masha Allah, tu dis bcp de vérités sur l"égarement des Sénégalais mais bayyil Sunu Makk Gni Serigne TOUBA,Cheikh OUMAR,Aladji Malick,Mame Abdoulaye Niass ,Gni ayy niitOu YALLA LaañOu T Sèni diamono fèkkOulènefi..Bokkalèwouñou,inddiwouñefi diinè gou bèss mais au contraire nioffi deuggueureul ISLAM N'a nga djOOte ci Tayy...TOUBA boufa mbaax nèkkOulwOne dOffa djangguè ALQUR"ANE...Gni raggalnañOu YALLA,DoudeulnañOu Sunnu...Ayez le courage de parler directement à leur descendance yi téggOuwOul ci yOOne wala ñOu neikk Ci lilène nèx mais bayyil Sunu Makk Gni,Niom laañOu am...Sayy Mame DèffalouñOu Dara diinè Ji Wala ISLAM pour mou taxaw ci Senegal
Dèmal diangui
@@lassanadoucoure6586 va te faire imbécile , espèce de prétentieux...Qui t'as dit yaw yaama gueuna djanggue ???
Le vrai ignare et imbécile, c'est 1 homme de ton genre , C'est celui qui prétend detenir le savoir où le monopole du Savoir...Comment peux-tu juger de Djaahil quelqu'un que tu ne connais pas ??? C'est ce qu'on appelle le terrorisme intellectuel, ManddouL Ci mane ...Xawmala , XaamOmaa...BulShiite
Si tu veux, Je peux te donner mon numéro et là tu saurras ndax Djanggue na wala Dètte...Bèwwe Baa Déé
MoomOuLéne Diiné Ji , Ni Aldjaana , ni Djahaanamaa
DEUGG REIKK T YALLA REIKK TAKH doul imbécile va yaw douuul démal diangui laa wakh connard va
Macha Allah docteur
J aime vous écouter
❤❤❤❤❤أستاذنا
macha allha amna solou trop
Macha allahou rafétna
meme si vous dites que c'est un " borom xam xam" n'oubliez pas que chéytann aussi et seul chéytann est capable d'insulter des hommes de dieu .
Douuuul
Masaha Allah
وحدة القيادة : أصحابي كالنجوم بأيهم اقتديتم اهتديتم
Abou djahil et Abou lahab ont tout deux insultes le prophète bien qu'ils savaient c'est lui l'envoyé de dieu
machalla
أنت من أفضل مشايخنا
Merci docteur