N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
S’il te plaît les commentaires arrête de juger les gens, sa mère il est tout mignon et Belle vous connaît pas son âge il a droit droit de vivre comme tout le monde. L’apparence est souvent trompeuses. Vous connaissez pas son coeur à l’intérieur Fier de toi, Maman et fier de sa fils mame ❤❤❤❤
Maman sa wakh rafet na mais il faut que nga soigné sa apparence mak nga kilifa nga meune neu geuneu yiw ngay moure sa bopou dindi sa pose ongles ak cils yi arreté khessal bi referance nga
Mame Ndiaye wakhal sa yaye mou bayi khéssal yobbou ko si dermatologue mou traité ko té mouye ték colle dara dakhoul sangnesé ték colle bou raffétte si kaw yiiw daye yokk tarr makk daye yiiw loufi diar gonné gonnélou la khamoul Adouna molaye sétane té internet da doye war guéne bayi si khél bou bakh jajeef
manchalla mère xahji rafetna yalasa jamm yag nit d'Ay fonkou Aÿ wayjouram lak sen geureum alhamdulila gorgolu rek non kubaxla lu nek si xol fegne si kanam waman communications dafa des nabayî kuwax mû tontula buyague mû stresse bapare sike ken xamul yala reka xam OK merci
En tout cas wargua wakh akk mome mou wagni touti wakh dji beurina torop nit gnagui fi yore ba liwe tokeu si ter keneu deguou leneu arriviste bakhoul khaliss mome boko amer keneu dou guisse sa sikeu niabotou canara dome djitou yaye topou si c grave
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
On ne dit pas il on dit Elle est mignon❤❤❤ il faut lire des livres français faire des exercices français ❤❤ a la prochaine ❤❤
@@khadidiatouba1124on dit dit elle est mignonne aussi😂❤
A
Galadiou dome mome Ndéye diou bakh MACHALLAH 🎉❤🎉❤🎉❤
Longue vie à toi Mame Ndiaye machalah 🎉🎉🎉❤❤❤🎂🎂🍭
Longue vie à mame Ndiaye yalnaka sounou borom defal diama té mayka goudou fanes bou andah Wer AK werrrele Sy Barker seydina Mohamed 🙏🙏🙏
Machallah mame lafff thiattt HBD longue vie a toi que Dieu vous protège ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeyssane ALLAHOUMA Amine MACHALLAH lo deugeur deugeur dioye😢
S’il te plaît les commentaires arrête de juger les gens, sa mère il est tout mignon et Belle vous connaît pas son âge il a droit droit de vivre comme tout le monde. L’apparence est souvent trompeuses. Vous connaissez pas son coeur à l’intérieur Fier de toi, Maman et fier de sa fils mame ❤❤❤❤
Il
Est
Tout mignon
La guiss😂
@@Noba-konatefier de son fils bolékosi
J'ai du mal à vous lire. Do binde wolof benneu yone😂😂 il est mignon et belle au final on se perd😂😂😂😂
@@Noba-konatefier de sa fils mame 😂
@@MariamaNiang-h9w😂😂😂😂😂
Longue vie à toi Mame Ndiaye hbd❤❤❤❤🎉🍞🎂🧁🎂🍞🥮
Bilay bahe rék mo ame solo wayé ame coloré tamite acte de grandeur la Machallah
Longue vie à Mame Ndiaye savon borom bakh machallah témoignage yi raffetneu
Maman sa wakh rafet na mais il faut que nga soigné sa apparence mak nga kilifa nga meune neu geuneu yiw ngay moure sa bopou dindi sa pose ongles ak cils yi arreté khessal bi referance nga
Bien dit mere bi norouwoul kou yiw
Vraiment
@@ibrahimagueye8559😂😂😂
Machanla
Long vie a toi maman 🎉🎉
Machallah long vie mame Ndiaye savon amine yarabi
Machallah mane dama beugue cou teral yayam cou fonck aye waye dioram thia kaw thia kaname ❤❤❤
Pourquoi ce titre tamitt😢joyeux anniversaire mame enjoy your day yalna nga yagga fekke yagga talleu
Mere bayil khél dé niga mél réfétoul si mak bou am ay seut 😢😢😢😢
Doyna war dal
Doyena ware
Yémé na dall
Av vraiment
Degg na deugg dh
Mame Ndiaye gnila bagn la yeureum❤ barkei Mouhamed
Wallay ndakh moom kholbi dara nekouthia mam kou bakhla
Machala dieredief wawaw rak top mak mak yereme rak
machaallah Mame gni xamoul rék gnoy wax mais yaw inchaallah lou bax rék ngay ame sa xol rafète na té sa yaye gueureum nala say employés tmt lou bax rék lagnoula sédèl goudeul fane ma chérie yalla yokoula diam té mou bayéla ak Mr nguèn féké lépeu sibarki SEYDINA MOUHAMED PSL ❤❤❤❤❤❤
Machaĺlh misse Ndaiye yaye bou bahk gua
Ma sha Allah longue vie à Mame Ndiaye savon ❤❤❤
Ma cha Allah 💕 yalla nanioù doundou ba âme ngeureumou wadiour yi si barké seydina Mohamed psl ❤️
Amine li nehna machala
Amine
Amine ya rabi
Amine
Amine
ndaysane mère bi li mou wakh dioye l nama sakh longeu vie a toi mame ndiaye
Machallah ❤❤maman longue vie à toi inchallah
Fi koufi yoor yaye yilif sa yaye .
Sen titre bii mome bakhoul dara vous êtes méchant trop méchant
Je voulais dire la même chose
Yabaté rék
God bless you mame ndiaye
Mashallah maman mame Ndiaye ❤❤❤❤🤲🙏
HBD mame N'diaye❤ yalna gua goudou fan🙏🙏ligua bougue yako kham yalna lako yalla défal doundal 111ans🎊🎉🎁🎂🎂🎂😘
Machallah Mame on t'aime
Mashah Allah mashah Allah Mame Ndiaye joyeux anniversaire doundeul ba saye maye di bawane enjoy you day Wala mané indo you day
Long vie maman
Dome nawlé la mosse YAYE BOYE rafétena MACHALLAH YALLAH naléne YALLAH lafal thiat 🎉❤🎉❤🎉❤🎉 yawite bakh gua bokka téréwone mou défal employéme douko def ndeyssane ❤
Macha Allah Mame Ndiaye joyeux anniversaire
Salam salam mes amours Fan's N°-1 de Mame Ndiaye savon c sa Maman😍😍😍❤❤❤ li nekhna deh
Ndeyssane mame goorgorlou rek waye sa khessal say ongles ak tatouage dotoumako toud de ndakh sa yaye rek nguay top machallah
Machalla ❤ ndeyssane
Bon annif notre mame international focus rek
Merci beaucoup mame❤️😘
Machallah kadougni Amna solo. Lool
Machallah ❤
Machallah maman (yow sama toma Nguagne) longue vie à toi.
Ho mame ndaysann guenala beugg ❤️❤️❤️❤️❤️
Telle mère Telle fille khéssal ba wékh tall
Faté 3 jours bamel
Merbi nite kou khess khana dafa yok kaye
Mandou mo guene tabakh diouma té niou niane yalla aténiou si yeurmadém
Yaw do tal sa bop sa trois 3jour bamel mo guene
Booko khamone diga mandou si nitt gniii
Yangui juge te khamo ndakh nit ku khess wala bamel khatna lol te niak wakh lula wor rek dugal n’a nit safara
Famille mam ndiaye la yeureum di nagnou melni khogne dei khésal rek adouna Mogui sen kanam 😂😂
Machalla wakhe dji raféte na ambulant Bon anif Mame yalna yalla takhou woula
Maman cadou yi raféte na wayé sa khéssal bi eupna soye diouli di gnanal sa dome danguaye dindi ongle yi
Deug deug pose ongle cils mak up tei tegoul sa kol si bopou bi doyna war
Joyeux anniversaire Mme Faye Mame Ndiaye. Doundal 111ans sans ordonnance.
Machall 🤲🤲 🤲🙏🥰 lovi à vous 💖💖💖💖💖
Joyeux anniversaire ma cherie
Hbd longue vie
Machala mame doundal wéral ak werlé ak khéwal gou bari bari inchala 🎂🥰❤️
Mame Ndiaye wakhal sa yaye mou bayi khéssal yobbou ko si dermatologue mou traité ko té mouye ték colle dara dakhoul sangnesé ték colle bou raffétte si kaw yiiw daye yokk tarr makk daye yiiw loufi diar gonné gonnélou la khamoul Adouna molaye sétane té internet da doye war guéne bayi si khél bou bakh jajeef
Mbass!!!! mandouléne
Kon mam dia la santa kon mam peulh nga ma cha allah
Longue vie a toi mame 🎉🎉🎉
Long vie à toi maman mai xessal kouko meneu bayi nangako bayi amoul mouthe
Hbd mame ndiaye longue vie a toi🤲🤲🤲🤲💕💕💕💕💕
Machalla mame ndiaye dafa bakhe garmie le ❤❤❤❤❤❤
Jonguamah gua mashallah ❤
Une personne qui n’as de défaut ça existe nittt boula Daraa Thiaralll farrr
Longue vie à Mame Ndiaye laf tiat
Damey imaginer mame Ndiaye savon première dame Ousmane palais ?😂 Sénégal bopa deuk bou pank ley nek
Joiyeux anniversaire mam Ndiaye longe vi
Mak day def yeufou mak wa salam
Machaallah 🎉
Machalla Allah Long vie a Mame Ndiaye😢❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉❤❤🎉🎉
Cône long vie a elle
Mame Ndiaye savon ndoudal werral Amal diam ci barki yonente bi❤️🩹❤️🩹❤️🩹❤️🩹❤️🩹❤️🩹❤️🩹
Vraiment wakhdie bénela c’est parceque deugue rék lagnou wakh machala Yalla nako Yalla lafall diate
Joyeux anniversaire longue vie santé de fer et bcp de bonheurs incha'Allah dundal 111sans ordonnance amine
Longue vie et courage ❤
manchalla mère xahji rafetna yalasa jamm yag nit d'Ay fonkou Aÿ wayjouram lak sen geureum alhamdulila gorgolu rek non kubaxla lu nek si xol fegne si kanam waman communications dafa des nabayî kuwax mû tontula buyague mû stresse bapare sike ken xamul yala reka xam OK merci
Machalla yalna yalla khéb doli hbd à notre Mame Ndiaye savon🎂🎉
Aminé yarabi aminnnnnnnnñnnnnnnnnnnnnnnnnne
Amine waye Mame yalnala yalla may goude fane AK wér amine
HBD Mame Ndiaye Savon auguri buon compleanno 🎉🎉🎉🎉
Sa dom di number one si diay khessal nga def bi teint ak yoyou lunettes
Mère bi bamouy khessal Mame ndiayoul diw mom mame wakhna ko si ay live bamounei kou thierel sama yaye na thierel sa yaye 💋
@@gueye2481gni gno beugue aye wakh rék wayè mère dara nèkoul di tein bi loudoul rafette
@@gueye2481😂😂😂😂
@@Salihatv03200😂😂😂😂
Lolou la nieuka wax sama xel 😂 khana mame amoul louy dindi liii tmt 😅
Ndeysane yaye
Amine Yarabi
Machalla ❤❤❤
Macha allah
Joyeux anniversaire à Mame Ndiaye savon
Machallah❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdoulila ❤
Machallah mame rek ❤❤❤❤❤
Meunoneu gua meusorou nak yay boy magu dou def bopou néneu
Demou keur serigne yi khana
Wa Legui nak Serigne si moomougnou dîné dji djiguene daye mousoorou @@saufi719
@@saufi719
Mère la Guiss mouy wakh fi
MotaQ. Mou né co Mère Moussoroul. Ayoul Dé.😢😢
Machalla
Bou yaye wakhé diekhna koumou nékh meune nga nopi 😂😂😂bal ba takkeu na fi ak feugnou dieum mame Ndiaye diam Adina ak alakhira diam rek
Bilakhi wakhatico ❤
Maman doh wagni diwou bii
Mais wañile xéxaal bi,yayou diabour, sino Machallah, Mame aussi na wañe wakh ak di publié xalise,nite dèye moytou thiate ak beutt.
Hbd longue vie à tw mame ndiaye doundeul
machallah yaye djubax
Ndeysane ❤❤
Yen li mère bi di wakh molen nior wala arrêter de critiqué ish mère goudeul fane
Mame Ndiaye Kay nila maneu mél gni aye rap lagne
Amine yarabi ♥️🥰🙏🙏🙏🏿🙏🙏🏿🙏🏿♥️🥰🙏🏿🙏🙏
Machallal
Machalla mame longue vie machalla ❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Hbd mame longue vie à toi
En tout cas wargua wakh akk mome mou wagni touti wakh dji beurina torop nit gnagui fi yore ba liwe tokeu si ter keneu deguou leneu arriviste bakhoul khaliss mome boko amer keneu dou guisse sa sikeu niabotou canara dome djitou yaye topou si c grave
Waw mame sa teint wou yaye bi rafetna deh😂😂😂
Amine ❤
Mère bi sama size leu, on nom mère bi dafa mol kii damakay dieul. 😂Mame Ndiaye ndéké khaléleu