RÉPONSE A UNE QUESTION SUR LES PROPOS DE OUSTAZ OMAR SALL PAR DOCTEUR MOUHAMMAD AL AMINE DIOP

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 лют 2025
  • #kebetu #senegal #team221

КОМЕНТАРІ •

  • @TubaboGiboroh
    @TubaboGiboroh 28 днів тому +2

    Li moma GANA nekh ci ibadou Yi kou def dioumteh sa mbok Yi nioyi layi dioubanti mais boudon alhoul tarika Yi de koyi outil ayi layal .... Macha ALLAH

  • @BaNdiabel
    @BaNdiabel 27 днів тому +1

    Kou neka ak deginnam pour mane bou deglo depuis au début jusqu'à à la fin kou bouga yaka wahdji la mo ame mais connecté bi lerna nay bayilen Di Yak ayi wahi diambour c'est vrai day dioum mais fimom o Diop demal deglou au début jusqu'à la fin

  • @mohammedcamara8460
    @mohammedcamara8460 28 днів тому

    Barrakallahou fik

  • @MrOusmane2112
    @MrOusmane2112 28 днів тому

    Shukraan Docteur Muhammad Al Amiin Diop raddu yi rafét na. Ño ngi léén di santt yén wa ahlul sunnah. Kepp ku 12:36 wax lu waroo ak al quraan ak sunnah sa morom radd la.

  • @rappel4152
    @rappel4152 28 днів тому

    Wakh ji rafet neu Dr té deupona Alkhouran ak Sounnah qui a toujours valorisé les femmes qu'Allah vous récompense

  • @thiernondiaye1975
    @thiernondiaye1975 26 днів тому

    Yonintebi AK Khadija 3ans lanou maguanté Khadija 3ans lako magué

  • @JeanchristDiallo
    @JeanchristDiallo 27 днів тому

    Oustaaz loummou wakh daffa leer kou kham oustaaz Khamenei dokhoule si ay détail teh radda bii pour mann diarrouko woonn

  • @thiernondiaye1975
    @thiernondiaye1975 26 днів тому

    Mane dé douma takeu djiguéne Bou ame dome té djiguéne sou meussoul seuy nékeu fi

  • @JeanchristDiallo
    @JeanchristDiallo 27 днів тому

    Dioublou way Oustaaz dou fou ngay wakhée sah

  • @laminedanfa8021
    @laminedanfa8021 28 днів тому +1

    Est-ce que côté bobou lay wakhé je ne pense pas dh pour man djiguéne yi di fowé seuy lay bayilo khél yén yi rk car divorce bi dafa bari lol

  • @chakur83
    @chakur83 28 днів тому +1

    Pour man deglouwoko Bou bakh ak context boumouy wakhé

    • @rappel4152
      @rappel4152 28 днів тому

      Daa wouté Alquran AK Sounnah l'islam meussoul décrire ni les femmes alors Oustaze Oumar daa joum et c'est normal qu'on le corrige

  • @71kado
    @71kado 28 днів тому +1

    Oustaz Diop, li si solo yi la bokk dou ap détail, et on dirait que déglou woo Oustal Sall. Raddo déh wayé ......

    • @bakarisoumare1929
      @bakarisoumare1929 28 днів тому +1

      Mon frère ne soit pas un fanatique ou un suiveur aveugle. Cette religion n’appartient qu’à Allah et à personne. Celui qui se trompe, même si il est un super savant suivi par des millions de personnes, on te corrigera et montrer l’erreur afin que les gens de commun n’y tombent pas. Baaraka Allahou fik Oustadh, pour toutes ces informations qu’on ignorait.

  • @ibucisse3606
    @ibucisse3606 28 днів тому

    Oustaz Sall wakh DJI niaw naa daamaa yaakar ni dafa dioumm rek

  • @laminedanfa8021
    @laminedanfa8021 28 днів тому +2

    Est-ce que côté bobou lay wakhé je ne pense pas dh pour man djiguéne yi di fowé seuy lay bayilo khél yén yi rk car divorce bi dafa bari lol