Machallah, deux voix exceptionnelles. Les artistes méritent du soutien, c'est très dures leurs travails, il faut de l'énergie, de la réflexion et d'inspiration. Et derrière ces belles voix, se cache d'autres éléments essentiels (Batteurs, Guitariste, Pianistes).
Machalahou ❤jah and Ahmadou ibn akhmadou kara mbacke noreyni ❤jah kara fepp ak niepp. Re dieuredieufety cheikh kara mbacke noreyni zahirane wall batinane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kou beug Serigne touba beu sal j’aime
Kou parole lall sa cœur❤ aime toi🥰 en plus niou teude si hôpitaux yi Yallah nagnou tané ak Jamm si Barki mouhamed🥰❤️🙏🏾
Je suis chrétienne mais je kiffe très fort vos tubes machallah ❤️ dieureudieuf borome Touba
Pareil je suis chrétienne mais je kiff à mort walayyy
❤❤❤❤
Mashallah , Bamba dieureudieuf.🙏🙏🙏👌👌👌
Merci a vous
Merci beaucoup ❤️🫶🏾yalngue am un mari musulman ❤️
Moi je suis chrétien mais je kiffe trop votre tube marchalla je vous souhaite bonne continuation ❤
😊😊
C’est
Chaque année yene tague borom touba machalla ❤mais parfois delene thi boler di tague le prophète psl svp ❤
Ça se voit que leurs voix sont naturelles tout est naturel de ce qu'ils font❤️❤️🥰😍✨
Seringe ahmada kara yalla nga fi yage té weer😭😭😭😭
Dieureudieufeté modou mbacké j’ai des frissons en vous écoutant une talibé cheikh ahmad tidiane qui dit merci et vous encourage ❤❤❤❤❤❤
Avant hier j'ai fait un marathon de tous vos feats...j'aurai plus besoin de rechercher un à un les sons...merci 🥰🥰🥰❤❤❤❤
🫶🏾🫶🏾🫶🏾
Mach'Allah yaw lo def mou nekh on est vraiment très fière de toi frère ❤❤your voice is beautiful
Machallah, deux voix exceptionnelles. Les artistes méritent du soutien, c'est très dures leurs travails, il faut de l'énergie, de la réflexion et d'inspiration. Et derrière ces belles voix, se cache d'autres éléments essentiels (Batteurs, Guitariste, Pianistes).
O
Machalah way sen duo bi nex na yalla nasen diamou yague barki Serign touba ❤
Ahmada Macké bégue nasii wolofal yii diadieuf Jah man bayfall bi kéneu gén geuneu wérr gayii bayi len coeur yii dédicacé nako bépou chrétiens ❤
😢😮 Bilae dii ngén raay nitt rkk maachallah li ngén dii déf neikhna sii ❤ waay 🙏🥰
BAMBA danne son bouma nex douma si doyal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️
Oooooooohhhh😢😢😢😢😢😢❤❤❤
DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA😊
Yein rk la beugue sama khol❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieufé Serigne Touba mbeegté rk Mbacké ❤❤ Aldiana laniouy doundou
❤❤❤ yalla na borom bi deffal niou jammu ak salam
Machalahou ❤jah and Ahmadou ibn akhmadou kara mbacke noreyni ❤jah kara fepp ak niepp. Re dieuredieufety cheikh kara mbacke noreyni zahirane wall batinane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nalène yalla sameu dolila soutoura adouna ak alakhira yalla nalène faye sène khol lima yeuk sama khol ❤❤❤❤mane rek mako kham diam ak tawfekh
Je suis chrétienne dh mais sa woy Serigne Touba yeup lay deglou machallah ❤❤
Ça te perce le cœur du plus profond 🖤.
Belle performance.
Bamba la joie est juste extraordinaire je kiff cette partie et la manière dont vous l’avez repris ❤
Kou beugue serigne touba lalal j aime❤
Non barki yalla niar yi mbecte la Mashallah ❤
Machallah 😊 dieureuf serigne touba ❤😊
Wa mane loumay rè ni rek😂❤ bilay aldiana rek laniy doundou
Dieureudieufati borom magal gui
La derniere prestation Ndeysane fatalinama ndiareme ak Serigne cheikh Katy Fall ak amedi moustache Fall Abdou Salam
niogui khare mame cheikh ibra fall bi dewen inchala🥰🥰
La voix de ahmada à chaque fois je l’entends j’ai des frissons 😢
Non jahman dou nuit way ohh ki man na way ❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Enfaite gnom gnaar dama khamoul kousi geuna nékh baat 🎉 mai machallah votre duo est exceptionnel ❤
Kendou ahmada
Ahmada ❤
Sama xole bayi séde gouye gouye yalla naléne Serigne Touba fayal bopam ❤
Dieureudieuf Mame borom touba 🥰
Ndeyssane machallah jahman ak serigne Ahmada Jadid yalna séne diam yague,bon Magal à tout le monde yalla nangou gnane yeupe 🤲🏽❤❤❤
Thiey serigne bi diawraka ❤ mame lampe fall
Dieureudieuf serigne Touba brome toukie bou sorri bi sa me touche vraiment ❤❤❤❤❤
Machalah li dafa nekj
Alkhamdoulilah Machaaalllah
Bignou Borom bi dioxé CHEIKH AKHMADOU BAMBA ❤❤❤
Ohh li nékhe na trop bilahy❤❤😂❤😊
Yalla na séneu diam yagg
❤jahman y’a tax man may degulou li walae sa woy Bamba yeup lay degulou 😂alors k suis catholique 🙏🥰diam sax c sa aimé son artiste
Contane na trop bilay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ak mbegte dey khana😭😌
Dieureudiefè borom touba cheikh ahmadou Bamba machallha jahman xpress et ahmada Bamba merci Bamba partous Bamba fep ❤❤❤❤❤
Hoo machalla way 🥰
Inchallah SII gamou biii❤❤❤❤❤❤❤
12:58 ===== 14:03 Quelle merveille ! 🥺🥺😍😍
Ay way ay way li nekh n'a dalll
Diërëdieufëti Serigne Touba❤❤
❤❤Serigne Ahmadou Bamba Khadim Rassoul dieureudieuf🙏❤❤
Mashallah Yallah na Diam Gana Yague Sénégal❤🤲🏿.
suis tidiane a 💯 mai AHmadou si gorr yalla you makk yila bokk yalla naniou ko yalla fayal❤❤❤❤
Ndeysan li kawénaa look Ahmadou Bamba jeereejef ❤
Machalla yalla nalén yalla same té same gnou ... bilaye sama khôl daye séd bouniou toude Serigne Touba ❤
Jahman_x_press me fait saigné❤
Machallah REJËFËTÊTI cheikh Ahmadu Bamba Xaadimurassul ❤
Machallah yalla nalén yalla dieumeul kanam❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Li waroul die way ndakh da nex ❤❤❤❤🎉
Je suis chrétienne mais yen lay topou ahmada sa voix lanla tamite mon frère bilahi demalay deglou bey dioy walahi
Oh leur voix sont extraordinaire ❤❤❤
Vraiment khôl sed n'a bilahi yalla n'a leune cheikh ahmandou bamba fay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla sérigne Touba rk🙏🙏♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machaalla dama danou lëre ni ......Ha li néhna way
Merci infiniment tout le peuple est content ❤🎉 yalna batt yi wëër mchlh initiative bi rafét n'a vive l'Afrique
Machallah nékh n'a trop❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Ahmadou merci ❤
Yalla n'a yalla may lene weur❤❤❤❤❤
Bamba nieup c’est mn chanson préférée j’ai pleurer en l’écoutant bly ❤Dieuredieuf Borom Touba le fait d’être Mouride c’est juste inexplicable ❤ bly Bamba thi khôl 🫀 contane na trop
Machalla ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️ machalla ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Wa kou deg lim mbalax siii guitare biii ❤
Serigne Touba ci bopam mo nékh ❤
machallah contanagne si yéne d blh dieureudieuff serigne touba ♥bon magal à tous🙏🙏
diueruediuef S touba mbacke balla ❤❤ diarama mame cherikh Ibrahim fall yaram 🤍🍾❤️🙏
Machalla amatina solo bravo nekhna trop
Machalaa mbacké bala
Chapeau diamane
Je suis chrétienne et fan de vous ligyey bi rafet n'a machala vous avez bp de discipline peace et love
machallah❤️
Mane sama parre mane doma farralle didegelo micix mi jahaman x p damanekhe s akhemada ziyarre nako
❤❤❤❤ 06:12 à 07:40 fire 🔥🔥 Vos voix sont magnifiques machallah
🥰🥰🥰je rêve trio sur le dialogue islamo chrétien avec vous. Aminn. Je suis chanteur chrétien
La sensation en écoutant
Quel bonheur 🥰🥰❤
Belie walie youssou Ndure legeye na..waye jah man dafa amm Talent ❤
Dieuredieuf serigne touba amoul morom diarama sidy birahim fall
❤❤❤❤❤❤les sensations que j’éprouve quand je vous écoute 🥰😍😍
La voix de jahman 🥹❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹
Machalla j'ai des frissons xol deideu❤
Machallah 🥰❤️🥰❤️🥰❤️🥰🙏
🎉🎉🎉wepepppppo❤❤❤❤❤
Yallah nala thiat cheikh lou ✅
Machallah jahman et hamada jadid bonne continuation yalla sen diam yagg ❤❤
Vous êtes les meilleurs
Diuetuediuef S Touba Mbacké balla ❤❤❤ diarama ❤❤ mame cherikh Ibrahim fall lampe ❤❤
machallah waw lene goor mourde yi ❤❤❤❤❤❤❤
Vos tubes sont tout simplement ouff
Mais bimom amoul morom bravo à vous 👏👏👏👏👏👏👌
Bou dewene inchala niogui khare mame cheikh ibra fall bi🥰🥰🥰
Ohhhhh li nekhna way ❤❤❤❤❤❤
❤❤❤🥰🥰🥰Bamba la paix 🕊 et Bamba la joie 😊 ❤ mé lépou nkh na❤ Jah rk laye topou 😂
Machallah ❤❤❤