No jamais diedhiou sou yérémé touti c le mm bakri Moy togu falé Di yak der diedhiou ak kou melni yow Di nan policier yi 1000f rek molén bayi thi talibi voilà la réalité défoi policier attesté chauffeur moukoy sonan thi ay niane dem bu diko yakal concentration iss
C est ça ki change le senegal. Sur tout les secteurs diomaye sonko allez i si ça ira sur le bon chemin kdieu vous acompagne amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilaye séne série bi je ne sais pas combien on vous a payé mais chacun de vous doit recevoir beaucoup d argent car votre serie EST tres interessant et beaucoups d enseignement 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Diediou tamit sonal n'a Bakary xana dou diégalé béna Yon sakh mélni amoul yakaar Diop nii😂😅wa keur Bakary tamit yeuramdé 0 xolal gaz bi en plus douniou téyé seni téléphone mélni sama yaye Soko wowé doko diot bo wakhé mouné sama téléphone dara nekoul si magui AK mom😅😅😅
Jadore le rôle du policier , Amoul massla amoul yeureumteulou kép kou nékoul si yone tékko si yone rien a foutre ak sa thiono Deuk bou serieux nonu lay dokhée👏🏾
Diédiou ok il est incorruptible, il est rigoureux.. mais il manque d'empathie. On est au Sénégal. Sunu dara matoul.. il faut être dans la pédagogie et la compréhension. C'est comme ça qu'on change les gens et non à appliquer bêtement les textes. Jub/Jubal/Jubanti 👌
Vraiment on réclame le bonheur de Bakary😅😢🎉
BILAY DAFA SONN❤😂😢
Vraiment dafa diote ah
Bilahi dafa meti😅
Kou yeureum bakary kome maneu il me fait de la peine 😢😢😢😢😢
Bakary dépression la dieum,mou dof wala mou faatu😂😂😂
Où sont les Bakarymen et les Bakarywomen???
Yallah na nieup am jam❤❤❤
Des cœur ❤ pour notre bien aimé Seydina Mohamed PSL ❤❤
Yalna niepp téral séne waydiour ci barké baye niass Amine yarabi ❤❤❤
Mane dama yeureume Bakary 😂😂😂😂😂😂mai séri bi da nékh❤❤❤❤❤❤❤❤
Yaye Bou yeremoul domam Waw Amna Moy yayo Bakary 😂
Diédiou guir yallah amal touti yeurmandé ci bakary 😭😭😭😭😭😭😭😭😂😂😂😂😂😂😂😂
No jamais diedhiou sou yérémé touti c le mm bakri Moy togu falé Di yak der diedhiou ak kou melni yow Di nan policier yi 1000f rek molén bayi thi talibi voilà la réalité défoi policier attesté chauffeur moukoy sonan thi ay niane dem bu diko yakal concentration iss
Bilakhi c'est du réalité sénégalais 😂 daguay nék si urgence dit woté sa galé 😅 khaley dit joué si portable 😅 dit coupé apl yi nak
Bilaye 🥺😢
Bén si man 😂😂😂damay rouss sakh parfw
C partout 😂😂😂😂
Bakary sonena nakk😢yeureum leineko
Barki yalla mo takh sama téléphone jeux yeup la supprimé
Ana sopey seydina Mohamed psl ❤🎉
Deyssane cou yermem Bakary 😢😢
Mane tamit sa ma yaram daye daw
C est ça ki change le senegal. Sur tout les secteurs diomaye sonko allez i si ça ira sur le bon chemin kdieu vous acompagne amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤
Lii dafa wara am bis bu nekk, 😂😂lii dafa neex billaahi. 🤣 🤣 🤣
Yow yeureumo bakary nak serie bi serie bi sou amé chaque jours bala une semaine bou dead 😂
3 fois par semaine kou d'accord lalal ❤👍
Kou diougué Séri khaliso ak lady diama rèke lalal j’aime 🎉❤😂
❤❤❤
Bou diougué thi dal ci diédiou
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉
Bakary est revenu way😂😂😂 yalla na sa diam yagg🙏
Diola gueme service Diédhiou comme sunu surveillant école
Khamoul ballé 😂
Le vrai Sénégal 😢
Bakary un vrai sénégalais
Kone borom escalier yi fi la moudjé 😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
Barkeyalla mabnge jigene boumonte ay xef😂oustase Omar Sall nena com rato😂jigene younaturelyi aningene❤❤
Je suis là mane dh léppou la bayi légui naturelle la woté tei balaa ngakoy kham yalla déff nioumay takk Bilahi douma déff cil douma déff ongles douma sah déff maquillage sounioumay takk touti poudre ak Lipo simple lolou lay déff walahi 😢
Ohhh la voix d'or de ouly❤❤
BAKARY meilleur série ❤
DEUG lëu série bi nékhna trop Machallah ❤️ mais boul fatté ni bété bété moy meilleur série du monde 😂❤
Kou d'accord ni Serigne Touba amoul morom RK lalal ma ❤🎉
Kokou Moye Ahmadou Yaakarou Djaamgñieu❤
Li AK Serigne Touba loulén bolé bayilén sén yeufou dof yi
Bilahi frère @@juniorsenegal98
Wakhi dof
Kou d'accord ni ioe amo morome rékk lalal j'aime ❤❤❤
Très original vraiment! ❤❤❤❤❤
Bakary mom khana da togne waliyouuu😂
Kham na dé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Wa bakary fane laye moudié ak brome gaz bi😂
Kou d'accord serie bi di doon 30 minutes laalal❤
N'oubliez jamais les 5 prières par jours ❤🎉
Bakary yalla na ame gaz
Diédhiou kagne lay bal Bakary😂😂😢
Senegalais modul yor lumu leikk wayer telephone bu chaire lay yorr xolalma mame khoudia 😅
Diédjou mom amoul bénn yeurmandé🤣🤣
Bakary ak gaz bi😂😂😂😂😂
Pourtant la Soeur de Bakary peut changer la vie de la Famille. Elle est belle et chante bien
Série bou am plein enseignement vraiment chapeau ❤❤❤❤
YALLA N'A NÉIPOU AM JAMOU 🤲
Li dh khallé yépe la sama dom bi ni lay😂déf boko😂wowé mou coupé la
Meilleur serie de l’année 🤩
Série bi nékhna trop Machallah ❤️ mais boul fatté bété bété moy meilleur série du monde 😂❤
Meilleure série Sénégalaise way c’est bien très bien
Bilaye séne série bi je ne sais pas combien on vous a payé mais chacun de vous doit recevoir beaucoup d argent car votre serie EST tres interessant et beaucoups d enseignement 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Guisnguen nii bakary maguetter ndaxx thionah keur
Une série très intéressante
Serie bii nekh na trop❤😅
Baakary sonouna ❤
Le sacré bacary
Bakary mbakhané bi la tégué gaz bii
Wa keur bakary sen iphone yoyou bolen ko diayone am keur senegal li moniou sonal yor i phone 14 o 15 té yoro lo lekk😅
Deugue bou werr
Malheureusement c’est la triste réalité
J'aime vraiment cette série
Diola comme bouton deun dafa geum service trop😁😁😁
Yallah na yallah soutoural may xéwéul kép kouy daww dépense guir sa ndiabote❤🙏
Lou takh diediou sokhor 😂😂
😂😂😂😂😂😂😅😅😅le gardien avec Bakary😂😂😂😂 meilleure série ❤❤❤
Vraiment Bakary je kiff honnêteté reik moy liy moudié
Bakary dama ko yeureum walaye walaye
Bakary es que dounko wathiél Kamil 😂
Noooo bakary ile milleur ❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂
😂sama mame néna diédjou khana Bakary rk lay diapp 😂😂
Taye mom bakary contan na si mom😂😂
Bakary yalla nako yalla may jamou
Maylenma djitou diokhlenma kanam gui
Namena djiby seye nak
Yaw saytané ngua 😂
Halima si niata mois nga tolou 😂
Emboubou bi dh yaggue na😂😂
Ms mère bi ndawtall yi bouko dadialé meuna len guéné si situation yi nak akh Bakary sonou na trop way 😂💔💔💔
Diediou tamit sonal n'a Bakary xana dou diégalé béna Yon sakh mélni amoul yakaar Diop nii😂😅wa keur Bakary tamit yeuramdé 0 xolal gaz bi en plus douniou téyé seni téléphone mélni sama yaye Soko wowé doko diot bo wakhé mouné sama téléphone dara nekoul si magui AK mom😅😅😅
Diédhiou tmt sonal na Bakary😂😂😂
Mame Khoudia yeureumal bakary tmt kholal gaz bi 😂😂😂😂❤❤❤meilleur serie ❤😂😂😂
Wa bonne diarna li gardien bi est-ce que werna tmt😂
Bacari scenariste bi ray le rec la beug 😂
Sallahou alla mouhamedin ❤
Mais kholate léne sène heure bi mère bi di wakh wakhi toggou rére wakeur bakary di wakh wakhi toggou agne🙄
😂😂
Wakeur Bakary da nio nadié tal agne ndakh amagou niou gaz. Niom midi passena bou yagg talagou niou agne 😂
Bo lene setané les 2 épisodes précédents di nguen comprendre
@ndeyebintafall ah wakhouma deuggue 😌
@kadiaguisse5971 ah kone lolou la😌
Mane Tamit lolou dh momaa diakhal 😢 sérieux ah yëmé na dal
Alhamdouliha 🎉🎉🎉
Yalla na Nieppe am diamm amiine 🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤
Ndeyesane borom keur sonnou na😢 ben pa wakhon na keur go doggou bo ladjé niou ni pa bi dée na ndakh thiona
Ndaysane 😢😢 walahi daniouy wakh Yaye wayé tamit Souniou Papaye amouniou sén Faye bilahi 😢😢😢 wadiour daffa sonou si ndiaboot rawatina Papa moy daw woutti dépense nieuw indi si keur gui 😢
Wa diédiou môme khana Bakary rk lay diap😂
Sacré Bakary😂😂
Babacary yreum nla Yaw mom sonne nga 😢😢
Non nékhoul ba nékhoul ms bakary wa famille yam yeureumouyko 😢😢
Bakary massa😊😊😊thiono
Bakary sounou na 😂
Nn justige pour bakary😂😂😂😂
Wa Mamé koudia kan lay am domm😂😂😂😂😂
Peut-être janvier 2025 inchallah 😂😂
😂😂😂 boy bi limou dff yague nako dff di jouer si telephonou diamour mouy sonné ma adje ko 😂😂 bayiko fofou
Yaay bandit DEUG 😂😂
@ThiénaDiop-f8o 🤣🤣 hi so décrocher diokh ko brome rkk do joué wate mtkh dama ka dane bayi mou soné ba coupé 🤣🤣🤣
Bakary millieur per de famille wayi mame khoudia tmt ken du mome el jouer tres bien
Bakary ba dou gaaniou😂
Ani djiby seye😂
Jadore le rôle du policier , Amoul massla amoul yeureumteulou kép kou nékoul si yone tékko si yone rien a foutre ak sa thiono
Deuk bou serieux nonu lay dokhée👏🏾
Khana yaw policier nga
Yaw tangue nga xôll dh do sah yeureume Bakary 😢 hum konn yaw hana do baalé
@@AlphaSow-c4ekii kay diarnaa lathie 😢
Alkhamdou lah ❤❤❤❤
Diédiou ok il est incorruptible, il est rigoureux.. mais il manque d'empathie. On est au Sénégal. Sunu dara matoul.. il faut être dans la pédagogie et la compréhension. C'est comme ça qu'on change les gens et non à appliquer bêtement les textes. Jub/Jubal/Jubanti 👌
Bakary Dafa Sone Kone Yeureumouléne Kô Mou Yeureum Bôppâmë 😂😂😂
Gardien bi 😂😂😂
😂😂 Diedhiou Bakary lay ligueyé . Moytoul telephone au volant té sou donn Bakary mou djapp ko
Amna kou diay samay informations diokhèko noukoy jouer théâtre Bakary. Combien de Bakary vivent quotidiennement cette routine. Qu'Allah nous facilite inchallah 🙏
Nonnnnnn fin bi ray nama😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bakary nak dafa warone am coulisse 😂😂
Enfin épisode 19
Makhoudia ak ouli souñou diayon se téléphone yi bakari am txi bou bess dépass 1 ane😂😂
Li dal gardien bi tey yéné nakoko trop😂😂😂bi khétou soxor