Cheikh Ahmed Cissé vs Cheikh Mbacke Sakho

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 31 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 210

  • @djibrilndiaye6397
    @djibrilndiaye6397 Місяць тому +16

    Moi franchement je le suis depuis 2015/2016 c’était avec Tounkara
    Une personne exceptionnelle honnêtement
    Moi je ne suis pas pas comme ça des gens mais lui y’a pas photo .
    MERCI ENCORE PROFESSEUR 🙏🙏🙏

  • @padoudouful
    @padoudouful Місяць тому +13

    ❤❤❤❤❤❤ THIÉY GUISNA NAK KOU KHAM YA ALLAH TÉ DIKKO BAYI KHÉL SI BÉPP BORR❤ AL QURAN KÉSSÉH MO WAURRR MOM REK LAY TOPP ❤❤ CHEIKH MBACKÉ JËRËJËFF🎉🎉🎉🎉

  • @bakarykurumang4136
    @bakarykurumang4136 Місяць тому +6

    Knowledge is powerful, I admire this brother

  • @godspathmalanggassama5311
    @godspathmalanggassama5311 Місяць тому +15

    Merci Cheikh Ahmed Cisse pour avoir invite CAMS et merci a Allah pour te l’avoir inspirer. Il ya plein d’autre sujet sur lesquels vs pouvez developer et aider bcoup de senegalais et gambiens in shaa Allah.

  • @mariamagueye9084
    @mariamagueye9084 Місяць тому +3

    Ce Monsieur est très pertinent et tout ce qu'il dit est tiré du coran. Respect ❤❤❤❤❤

  • @DaoudaGueye-rq3fe
    @DaoudaGueye-rq3fe Місяць тому +11

    أطيعوا الله وأطيعوا الرسول.
    yallah néna top lénma top lén yonénti bi

    • @beugyallarek
      @beugyallarek Місяць тому +3

      Tontoul ladj yii
      Ana yonent bi?
      So ko beugué top fo koy fék?
      Ana rissala bi ko takhona done rassoul?
      Mome la dane top?
      Ndakh mission wam dafa nékoul wone diotali rek?
      Ana loy tontou ci ladjou Yalla bii 👉
      ….فهل على الرسل الا البلاغ المبين ؟
      "…..Ndakh yonent yi dafa am lou lène war loudoul diotali bou lère?"
      Sourate 16 verset 35 (سورة النخل الآية ٣٥)
      Bane hadith ngay gueum ci niéte yii?
      1. Hadithou Yalla yi ( Alxuraan di wakhou yonent bi إنه لقول رسول كريم)
      2. Hadithou sounnite yi (boukhari, ….)
      3. Hadithou chiite yi (al-kaafii, ….)
      Té lii la Yalla ladj
      ….فبأي حديث بعد الله وءاياته يومنون
      Traduction: "…. Ana bane hadith nguèni gueum guinaw ak ay kemanam?"
      sourate 45 verset 6 (سورة الجاثية الآية ٦)
      Tontoul stp

    • @Ousmane-q8s
      @Ousmane-q8s Місяць тому +2

      @@beugyallarek dou tontou moukk ba biss binthieuuuu 😂😂😂😂😂

  • @mbodj1963
    @mbodj1963 Місяць тому +4

    Merci d'exister CHEIKH MBACKE SAKHO ❤️🙏🇸🇳

  • @levisionnaire2869
    @levisionnaire2869 Місяць тому +12

    Je suis Catholique mais cet homme est très éloquent et charismatique. Kham kham dou fo❤❤❤❤❤❤

    • @71399
      @71399 Місяць тому +3

      Yallah Yallah arr

  • @fatimalowefaal7318
    @fatimalowefaal7318 Місяць тому +4

    Nyata yourn nga tuddu Yonnantibi teh wokho Sallal Laahou Alaihi Wa Sallam Billahi wokho fi dara xam xam b yalna bumla sank

  • @oulsop
    @oulsop Місяць тому +1

    Machallah ki rék mo diara déglou yalla na ame wér, diam ak soutoura😍😍😍

  • @AmieFaye-sr7rw
    @AmieFaye-sr7rw Місяць тому +6

    Thiey Cheikh bi sa liguey rafétna yalla na yalla deuguerala té molalila sa yéné si diam gni Cheikh bi Saho wahtane wi amna solo cou rére rék yalla na yalla guindi

  • @fatimalowefaal7318
    @fatimalowefaal7318 Місяць тому +4

    Billahi Kufi Bayyi Alquran Ak Sunnah mba ngaye weddi waxi Saydina Muhammad Sallal Laahou Alaihi Wa Sallam Billahi di nga xamni Ya Allah swt bugul kudul Saydina Muhammad Sallal Laahou Alaihi Wa Sallam

  • @cheikhbombaly2789
    @cheikhbombaly2789 Місяць тому +6

    Kii Diambaar leu Machallah

  • @masiba7272
    @masiba7272 14 днів тому +1

    Sourate 17-verset 79: Et de la nuit consacre une partie [avant l'aube] pour des Salat surérogatoires : afin que ton Seigneur te ressuscite en une position de gloire.
    Cheikh mbacke Sakho dimbali ma fi.comme yaw fadiar ak timis rek ngay diouli car c'est ce qui est mentionné.
    Alors commentel ma verset bi

  • @thiernosall3823
    @thiernosall3823 Місяць тому +1

    Très pertinent mbaké sakho et cheikh Ahmad joue le jeu pour faire comprendre les téléspectateurs 👍

  • @Assaneniegendiaye75Ndiaye
    @Assaneniegendiaye75Ndiaye 9 днів тому

    Billahi wallahi djiébalouna cheikh mbacké Sakho yaye sama oustaz . merci mon dieu

  • @allkhoranetv39
    @allkhoranetv39 Місяць тому +10

    Yaa ngi doga invité kouy wakh te yàlla takh

  • @lamintouray7262
    @lamintouray7262 Місяць тому +3

    Thank you, cheikh Mbacky sakho, for proving all your proofs from the Quran alone. The only words of

  • @moustaphadiop5405
    @moustaphadiop5405 Місяць тому +3

    Machaa Allah swt alhamdoulilah dieuredieufety CAMS thie leral yii mouye alkhourane wakhi yaAllah swt rek mo woor alhamdoulilah

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому +2

    Bilaye Cheikh Mbacké Sakho,lépe lo wakh,bodémé ci Alkhouran lolou nga faye féke,dara métiwoule ci jamou Yalla,jape dinné gui métile ko méti,ba lo défe dém safara

  • @malickndiaye3711
    @malickndiaye3711 Місяць тому +1

    Meilleur emission merci chek bi

  • @dankpannahcisse8758
    @dankpannahcisse8758 Місяць тому +1

    Oustas Sakho tu es un érudit 🙏🏾👏🏾.Qu’’Allah te protèges.

  • @daddg5099
    @daddg5099 Місяць тому +7

    Maashaa Allah Sakho, le seul Oustaz qui parle Coran seul sans associé.

    • @masiba7272
      @masiba7272 14 днів тому

      Wa atiou lah wa atiou Rassoul.

  • @fanssadiomanelofficiel4089
    @fanssadiomanelofficiel4089 Місяць тому +7

    Machaallah

  • @lamintouray7262
    @lamintouray7262 Місяць тому +2

    Quran chapters 33 verses 38 to 39 if i didn't forget has defined the Sunnatullah the only sunna of Allah

  • @artouzin
    @artouzin Місяць тому +1

    Dans l'apprentissage des métiers on t'apprend la théorie mais en même temps la pratique celui qui m'a pris que la théorie et ne sachant on n'a jamais vu quelqu'un pratiquer ne sera jamais pareil

  • @diopdiop7519
    @diopdiop7519 Місяць тому +5

    -sourate 69-44.
    -Sourate 69-45.
    -Sourate 69-46.
    -Sourate 69-47.
    (Y'Allah dafa teukou yonénetebi thi limouko yoni bouko yoké bamou vagniko"dina diape vétou ndidioram gî dagê siditou batam bi"yonétebi liko Y'Allah yoni rék thi laye yam"comme yonénete yiko djitou aye téréé laléne yoni"

  • @AssaneMbaye-o8y
    @AssaneMbaye-o8y Місяць тому +2

    Macha alla mèrci bauqou chiekh mbackè sakho ❤

  • @djibrilndiaye6397
    @djibrilndiaye6397 Місяць тому +6

    Excellent débat 😂😂😂😂
    Nooon franchement tu es le meilleur professeur
    Merci encore 👍🙏🙏🙏

  • @cheikhniang6659
    @cheikhniang6659 16 днів тому

    2.Abou Dawoud a rapporté également qu’al-Irbadh ibn Saria (P.A.a) a dit: « A l’issue d’une prière qu’il a dirigée pour nous, le Prophète (bénédiction et salut soient sur lui) s’est tourné vers nous et nous a délivré un sermon très touchant dans lequel il a dit: Accrochez-vous à ma sunna et à celle de mes successeurs bien guidés, tenez-y fortement, sisissez-le avec vos dents molaires. (cité dans kitab as-sunna du Sahih d’Abou Dawoud)

  • @oumardionguethioune630
    @oumardionguethioune630 Місяць тому +5

    Merci ...si tu peux inviter Alpha Ba....merci encore.

    • @aliounefall2885
      @aliounefall2885 Місяць тому +2

      Arrêtez way, kou nek ak sa level. Alpha ba level Lam agoul fi
      Ngen balma
      Bou nieuwer fi niank xam xam bi day fegn rekk
      Cheikh amet dakoy exposé deh
      Bakhna

  • @diopdiop7519
    @diopdiop7519 Місяць тому +7

    CMS prêche dans le sentier d'Allah selon le coran.Qui l'écoute se conscientise à l'islam authentique et peut se sauver aux péchés "bokalé"que Dieu ne pardonne pas Encore merci bcp.

  • @serignesamsung
    @serignesamsung Місяць тому +1

    Aka beurri khame khame
    tay wakh deugg té sétoussi darra🙏🏿

  • @mouhamethmbacke7272
    @mouhamethmbacke7272 Місяць тому

    رب إغفر لى ولوالدي ولمن بيتي مؤمنا
    وللمؤمنين والمؤمنات

  • @AhmadouDieylaniba
    @AhmadouDieylaniba Місяць тому +2

    ايدك الله بارك الله فيكم

  • @malickndiaye3711
    @malickndiaye3711 Місяць тому +4

    Kou wedi na indi alkhourane

  • @AhmadouDieylaniba
    @AhmadouDieylaniba Місяць тому +2

    Cheikh Ahmed, ô Dieu, aide-nous

  • @kemite13690
    @kemite13690 Місяць тому +2

    Alaahou akbar !!!❤

  • @mbayeniang5597
    @mbayeniang5597 Місяць тому +3

    Ma shaa alah yalna yàlla faye leen wakhtan bi Amna solo lool

  • @alexandreanas8222
    @alexandreanas8222 Місяць тому +4

    Cheikh mbacke sakho longue vie et la santé à toi merci beaucoup depuis longtemps ses sofianke nous conduit en erreur

  • @bakarykurumang4136
    @bakarykurumang4136 Місяць тому +1

    This guy is gifted

  • @masscool
    @masscool Місяць тому +1

    Cheikh Cissé tay nak invité nga kou ame xam xam, machala

  • @MouhamadouMoustaphaneneMbaye
    @MouhamadouMoustaphaneneMbaye Місяць тому

    Machala am na solo ler na li moy. Xam xam waye Sénégal mom dagni lép rk Adia a safara dinè eup na lolou

  • @abdoulayefaye5689
    @abdoulayefaye5689 18 днів тому

    Le seul problème que j'ai avec ce monsieur, c'est son manque de déférence envers le prophète Muhammad ( sallal'l lahou aleyhi wa salam).

  • @laminesarr3047
    @laminesarr3047 Місяць тому +5

    Wépépépépé, c'est fort!

  • @samadeguine9840
    @samadeguine9840 Місяць тому +33

    Euskay ki mo guena yeuk yalla bép invité bouffi meussa tok waxtane by yalla késsé la

    • @ablayng6446
      @ablayng6446 Місяць тому +6

      Bayil campagne yi😂😂

    • @maximilliendjibril
      @maximilliendjibril Місяць тому +1

      Yaw kou rére nga

    • @Alioune123
      @Alioune123 Місяць тому

      Ki yeugoul dara!

    • @hoorevision5753
      @hoorevision5753 Місяць тому

      Nittou yalla cheikh Mbackè sakho un homme véridique

    • @bayewade9439
      @bayewade9439 Місяць тому

      Il est très dangereux ce ga la gni yonete laniou guemoul lép Lou yenete diagalé guemounioko

  • @MoussaDiop-vs4js
    @MoussaDiop-vs4js Місяць тому +1

    Machallah xam xam fegn na

  • @abdoumaslahmaslah3532
    @abdoumaslahmaslah3532 Місяць тому +3

    Il s'exprime bien

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому +2

    Senegal Adaa moy sen dinnée ak sen seriñ yi

  • @hoorevision5753
    @hoorevision5753 Місяць тому +6

    Machallah cheikh Mbackè Sakho

  • @abdoulayefaye5689
    @abdoulayefaye5689 18 днів тому

    Il n'est nullement explicité dans le saint coran le nombre de rakas et la récitation de la fatiha dans les prières. Je voudrai bien savoir ses sources.

  • @CheikhDieng-s8x
    @CheikhDieng-s8x Місяць тому +1

    Ki bague n'a gua bou😢lé KO AK oustas Ahmed mbaké mi parce que ki djolém kien khamout KO amamoul coumach amoul fin 😢

  • @usmaansonkomusellmi4636
    @usmaansonkomusellmi4636 Місяць тому

    Senegaal moo bëri dof Mbacke Saaxo saytaane moo koy liggéey loo doomu xaj piir

  • @alioudiane5228
    @alioudiane5228 Місяць тому

    Allahou akbar j'ai même peur de mbacke sakho qu'allah nous protège et nous guide dans le chemin droit.
    Mbacke sakho reviens en arrière et répand toi avant qu'il soit trop tard

  • @fayealiounekane8727
    @fayealiounekane8727 Місяць тому +2

    machallah

  • @AhmadouDieylaniba
    @AhmadouDieylaniba Місяць тому +2

    ❤❤❤❤❤❤

  • @elhadjba4360
    @elhadjba4360 Місяць тому +1

    Cheikh Ahmed mashallah

  • @fatousall-t5w
    @fatousall-t5w Місяць тому

    Mbacké Sakho you are the best ❤

  • @KhalilMouslime
    @KhalilMouslime Місяць тому +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @sabar129
    @sabar129 Місяць тому

    Est ce que lui reconnaît Hadissoul khoudsi?

  • @Laye719
    @Laye719 Місяць тому

    Xam Xam rek ka wore. Merci Cheikh Mbacke Sakho.

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому +3

    Senegal liñouy waraté dou Alkhouran

  • @cheikhniang6659
    @cheikhniang6659 16 днів тому

    4.Allah a donné à Ses serviteurs l’ordre de répondre à Allah et à Son messager.A ce propos le Très Haut dit: ô vous qui croyez! Répondez à Allah et au Messager lorsqu' il vous appelle à ce qui vous donne la (vraie) vie, et sachez qu' Allah s' interpose entre l' homme et son cœur, et que c' est vers Lui que vous serez rassemblés. (Coran,8:24 )
    5.Allah a donné à Ses serviteurs l’ordre de Lui soumettre leurs différends.A ce propos Il dit: Siٍ vous vous disputez en quoi que ce soit, renvoyez- le à Allah et au Messager...). (Coran,4: 59 )
    Es la allah a dit si on ce dispute sur un sujet qu'on le renvoyer à ALLAH ( coran) et au messager pour toi si allah nous as autorisée que le Coran pourquoi donc il nous dit de le renvoyer a ALLAH et au messager ?

  • @lamintouray7262
    @lamintouray7262 Місяць тому +1

    Allahu kabir

  • @diaoibou4709
    @diaoibou4709 Місяць тому +2

    29:44 ki kouko top sankou dama khamoul bakham da yor alkhourane boppam wala sourat 58 aya 2 lila yalla wakh et comparez le avec ce quil dit kou mane lire na lire par rapport ak limou diangue.
    Sourate 58 aya 2 lila alhourane wakh وَٱلَّذِينَ يُظَٰهِرُونَ مِن نِّسَآئِهِمْ ثُمَّ يَعُودُونَ لِمَا قَالُوا فَتَحْرِيرُ رَقَبَةٍ مِّن قَبْلِ أَن يَتَمَآسَّا ۚ ذَٰلِكُمْ تُوعَظُونَ بِهِ ۦ ۚ وَٱللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ خَبِيرٌ
    Kou yor kaamil mane nako verifier

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 18 днів тому

      Verifier nako limou wakh la guiss dh ou bien gua leral ma

    • @AliouNdiaye-lc3pp
      @AliouNdiaye-lc3pp 9 днів тому

      ​@iboudue2727képp ku andak mm Deel julli 2rakkaa bul sangu farata bul julli jumaa bul noddu b likhaam b sëlmël

  • @DiaDan-z3r
    @DiaDan-z3r Місяць тому

    Yaw dé kula topp diiném dina oyof

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 18 днів тому

      😂😂 Lo beug mou metti

  • @MouhamadouMoustaphaneneMbaye
    @MouhamadouMoustaphaneneMbaye Місяць тому +1

    Svp qui peux m’aider à rencontrer ch Mbacke Sakho svp

  • @saffiekeita43
    @saffiekeita43 Місяць тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aboridial3431
    @aboridial3431 Місяць тому +2

    Yalla miniou bind rek moniou xam tayit dafniou yerem

  • @lasource3996
    @lasource3996 Місяць тому +2

    Wallakhi wakh bi leerna nagne

  • @AhmedLo-eu2ek
    @AhmedLo-eu2ek Місяць тому

    Wa legui mom djuli al jumman dinako djuli ak nka lakay défè ak nax dina khutt ba je me pose la question ?

    • @AliouNdiaye-lc3pp
      @AliouNdiaye-lc3pp 9 днів тому

      Non wax nani du julli jumaa du nodd du likhaam du sëlmël

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому +1

    Imam Bouks ak Imam Milk amél nguéne julit yi akh

  • @cheikhniang6659
    @cheikhniang6659 16 днів тому

    Et moi je te dit les soufis, chiite, frères musulmans, les tabligh , coraniste, etc sont tous égarés egareurs Walahi bilahi talahi. Si tu veux la bonne voie alors suivie la coran et la sunnah avec la compréhension de salaf saleeh. 🤝🤝

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому +1

    Oustaz bouko ñomé ma joxe la 1000.000 cfa

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp 9 днів тому

    Man de Masuma giss naafeh bu melni mb sakho ndawul Ibliis la

  • @MabalBah
    @MabalBah Місяць тому

    Sheikh bi sa waji dama yekha understand ne wa قرءانيون la😂😂

  • @youssouphagaye6223
    @youssouphagaye6223 Місяць тому

    CAMS ❤❤❤❤❤❤

  • @diopdiop7519
    @diopdiop7519 Місяць тому

    Diangal ayat yi thi sourate yi dothi dég haram"téréé ak loulaye ngagne"
    Sourate 4 verset 43
    Sourate 2 verset 219
    Sourate 5 verset 90
    Sourate 5 verset 91

  • @CheikhMbaye-kt5po
    @CheikhMbaye-kt5po Місяць тому

    😂😂😂 diné cheikh mbacké Sakho bi kouci beugueu bok noye def.
    Diné bi nekhna dé😅😅

  • @falloukasse6482
    @falloukasse6482 Місяць тому

    Lepp loumou wakh mongui si alkhourane

  • @JJJTV-DIASPORA
    @JJJTV-DIASPORA Місяць тому +1

    Ki khoumou yabb ? Ban diné la bokh … ?

  • @fatimalowefaal7318
    @fatimalowefaal7318 Місяць тому

    Bu feckey nyari rakka ngai julli weddi nga wahi Yonnantibi Sallal Laahou Alaihi Wa Sallam

    • @beugyallarek
      @beugyallarek Місяць тому +1

      Yonent bi nyari rakat rek la diouli, yène ni nguèni dioulè wéroul

  • @cheikhniang6659
    @cheikhniang6659 16 днів тому

    Et Cissé a demandé si on peux faire la invocation a un mécréants ( chrétiens, juives, laïques, etc) no jamais. Es ton ami si il savais le Coran il vas te répondre sur cette question. E Quand le Prophète (Bénédiction et salut soient sur lui) se mit à demander à Allah de pardonner à Abou Talib après sa mort, Allah le lui interdit en ces termes :Il n’a appartient pas au Prophète et aux croyants d’implorer le pardon en faveur des associateurs, fussent-ils des parents alors qu’il leur est apparu clairement que ce sont les gens de l’Enfer. Abraham ne demanda pardon en faveur de son père qu’à cause d’une promesse qu’il lui avait faite. Mais, dès qu’il lui apparut clairement qu’il était un ennemi d’Allah, il le désavoua. Abraham était certes plein de sollicitude et d’indulgence. (Coran, 9 :114-114).

  • @bachir2248
    @bachir2248 Місяць тому

    Le CORAN est une œuvre qui va au delà de la simple traduction des versets.
    C'est une pauvre philosophique qui est transmise aux hommes par un être exceptionnel et muldimensionel.
    Je vous suggère d'aller fréquenter les universités islamiques car vous avez déjà appris le coran par cœur.
    Dommage pour un telle personne ressource.
    Njàng du wèss.

  • @injeniusconsulting-group4689
    @injeniusconsulting-group4689 Місяць тому +2

    Salam pourquoi renvoyer a boukhari pour illustrer votre vision quand cela vous arrange pour rejeter la sunnah et revenir rejeter les mêmes auteurs je vous renvoie a l histoire de Moussa et la sagesse de khadir pour mieux comprendre que tout n est pas aussi tranché que vous semblez l expiser

    • @daddg5099
      @daddg5099 Місяць тому +2

      C'est pour vous montrer que le sounisme est dans l'égarement total. même, dans les hadiths de Boukhari que suivez, il est dit prière 2 rakka.

    • @gilbertlaitysarr8257
      @gilbertlaitysarr8257 Місяць тому

      Ce n'est pas vrai amène le hadith ​@@daddg5099

  • @aliounelo2181
    @aliounelo2181 Місяць тому +2

    Fase kon diafena😂

  • @BabacarDarameaboubacar
    @BabacarDarameaboubacar Місяць тому

    🖐️Cheikh mbacke. S alkhour aan manokodegge san jangga lem yonet bi wakh ngane sanggra haraa moul ndakh yalla tuddu fa batu Haram sudon loolu rék Kon jaalo haramul ndakh yallah tuddu fa batu harاجتنبوا))( (ولاتقربو)

    • @NihmaTV
      @NihmaTV Місяць тому

      😂😂😂😂
      Yonent bi Alxuraan moy diangalème

  • @khalifaniang2183
    @khalifaniang2183 Місяць тому +4

    Sakho mi vraiment kou yabaté la yaw ngani sangou seete nekoul si alkhourane kne weroul ta kabar bingano mom ngay def meunoko layal si alkhourane boul fowé souniou khelmi way

    • @walterwhite8303
      @walterwhite8303 Місяць тому +3

      Sangou sett gnew na si alkhouràne mais niko Yalla waxé ak ni nguen koy defé mo bokoul. Alkhouran da wax gnou raxas mou sett rek. Mais lenen gneup gayé ko si yoq

  • @Abdsr8735
    @Abdsr8735 Місяць тому +2

    Cheikh ahmed Cissé limouy catior mo la eup xam xam fouf Mbacké Sakho. Dalay diay rek

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому

    Boko gagner si lou weer ci téré Yalla la wax nak

  • @KhadimDiop-l8c
    @KhadimDiop-l8c Місяць тому

    Dayi dole rike 😂😂😂

  • @moustaphaLO221
    @moustaphaLO221 Місяць тому

    Walahi dine metiwoul

  • @KhadimmaissaGueye-k5c
    @KhadimmaissaGueye-k5c Місяць тому

    Alkhourane dal mowor

  • @abdoufall2928
    @abdoufall2928 Місяць тому

    Lou takh mouy diouli 2 rakka wahtou yepp,warr nako leeral maa diomi mane😮

    • @iboudue2727
      @iboudue2727 18 днів тому

      Demal thi boukhari nena avant 2 la wone.apres amna koussi yokou yenene 2 😂😂

  • @cheikhniang6659
    @cheikhniang6659 16 днів тому

    Mais se frères il parle des versets coranique sans même savoir leurs sense, seule les offres ne fait pas rentré au paradis mais aussi tu devrais faire les offres comme dit notre prophète. Personne ne rentrera dans le paradis si ce n'est par la miséricorde d'Allah
    Au nom d'Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux.
    D'après Abou Said (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Personne ne rentrera dans le paradis si ce n'est par la miséricorde d'Allah (*) ».
    Ils ont dit: Même toi ô Messager d'Allah ?
    Le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a répondu: « Même moi, sauf si Allah me couvre de sa miséricorde » et il fit un signe avec sa main au dessus de sa tête.
    (Rapporté par Ahmed et authentifié par Cheikh Albani dans Sahih Targhib n°3599)
    (*) C'est à dire que les bonnes actions aussi nombreuses soient-elles ne sont pas suffisantes pour mériter ce qu'Allah a préparé comme récompense pour ses serviteurs dans le paradis.
    Les bonnes actions sont une cause pour obtenir la miséricorde d'Allah et c'est uniquement par la miséricorde d'Allah que les habitants du paradis vont y entrer.

  • @fatimalowefaal7318
    @fatimalowefaal7318 Місяць тому +1

    Kii Funkul Saidina Muhammad Sallal Laahou Alaihi Wa Sallam Billahi

    • @beugyallarek
      @beugyallarek Місяць тому +1

      Kii mo fonk Yonent bi ci fonk gui mou fonk Alxuraan

  • @MbayeSerigneAbdou
    @MbayeSerigneAbdou Місяць тому +3

    Awra Moy ( Ween) taat) ak data

  • @Pisyum
    @Pisyum 9 днів тому

    Beugna xam ban Aya la yalla wakhé juli niar raka la ? Budé wakhgako d degumako

  • @ZainabouDiop-
    @ZainabouDiop- Місяць тому

    Ideu bobou yeup,Yallah mo sibe fassé,3weers yoyou yeup ci même lale bi moye joubo meune na ame di digeunté 3 weers yoyou

  • @abdougueye7078
    @abdougueye7078 Місяць тому

    Mbaké Sakho borom khamkham leu