BINTA DON MÉCANICIEN WAROUL TAKH NGAY...OUSTAZ SOULEYMANE DIAW AY WADIOURAM NIOKO...

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • SOLUTION TV

КОМЕНТАРІ • 116

  • @talibeserignetoubaibrafall6311
    @talibeserignetoubaibrafall6311 2 місяці тому +45

    Djigen dou deff yeufou gorr gor dou deff yeufou djigen wa salam

  • @IbrahimaNdiaye-sw6pu
    @IbrahimaNdiaye-sw6pu 2 місяці тому +28

    Djiguene mom dey def yefou djiguene gôr yefou gôr

  • @apprenant9164
    @apprenant9164 2 місяці тому +20

    Yalla nako sunu borom taxaw ba sopi xelam 🤲🏻🤲🏻🤲🏻

  • @babasene9673
    @babasene9673 2 місяці тому +14

    Bayiléne thiaxane oustaze deug késsé lafi wakh

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 2 місяці тому +11

    Yalla na niou mouthi Yalla na nou wer Yalla nanou am

  • @القاموسالمحيط
    @القاموسالمحيط 2 місяці тому +4

    Oustaz merci

  • @ndiayekhalil7156
    @ndiayekhalil7156 2 місяці тому +5

    Lii oustaz wakh rek moy deugue

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 2 місяці тому +6

    Thieye yalla na sa borom mo ndiabot

  • @Delba369Beatz
    @Delba369Beatz 2 місяці тому +16

    Képou kouy diapalé bineta si li yénay bokou même dane Bilahi Wallahi
    Li dafa gniaw si réw bou mélni Sénégal 😡😡😡

    • @dienediouf2887
      @dienediouf2887 2 місяці тому

      baane daane état wala yamale khiyame😂😂😂😂😂😂

    • @AmyDiallo-v1o
      @AmyDiallo-v1o 2 місяці тому

      Maname pour mou lete bakar bi

  • @papengom259
    @papengom259 2 місяці тому +13

    Bita moytoul beut ak lamigne bakhoul dé

  • @NdiagaNdiaye-wr9sx
    @NdiagaNdiaye-wr9sx 2 місяці тому +2

    Jerejef ouztas❤❤❤

  • @FallMandiaye
    @FallMandiaye 2 місяці тому +9

    Yalla reub na djiguene bouy gor gor lou reub na goor bouy djiguene djiguene lou

  • @NdiagaFaye-f9w
    @NdiagaFaye-f9w 2 місяці тому +3

    Bilaye yéna yésse ki khélame nékoule sii lingéne dii wakhtane TV TV yii gnosof

  • @Moustaphakane-y2p
    @Moustaphakane-y2p Місяць тому

    Oustaz khamo dara ligaye wakh tegoko fénne

  • @mbackefall4248
    @mbackefall4248 2 місяці тому +2

    Liguey lou warr la me na woutine Wa sell

  • @alibaba-pj3rl
    @alibaba-pj3rl 2 місяці тому +2

    Oustaz bii amoul fitt bou amone fitt thi djiguén plateau yii laa waron tambalé sén thioline yii

  • @ndiayekhalil7156
    @ndiayekhalil7156 2 місяці тому +5

    Pourmane amna droid def liguey bouko Mais mou def yeufou jiguéne

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 2 місяці тому +4

    Yalla na sa borom ate si yeurmendém

  • @BayeDiagne-i1u
    @BayeDiagne-i1u 2 місяці тому +1

    Machalla ❤

  • @aminatadiallo5497
    @aminatadiallo5497 2 місяці тому +8

    Dans cette vidéo la petite fait tout pour ressember à un homme. Ce n'est pas parce qu'elle est mécanicienne qu'elle doit avoir ces comportements

  • @Ichigokurosakionestate
    @Ichigokurosakionestate 2 місяці тому +4

    Binta MoMA gueunall djiguén yi nék Tik tok bi youtube bi chaine TV Di wané séni awra AK djay sa bopp

  • @ibrahimndiaye2961
    @ibrahimndiaye2961 2 місяці тому +2

    Me peritte de fa aram ya uostas

  • @fieredetrenoirs5428
    @fieredetrenoirs5428 2 місяці тому +1

    Oustaz vous avez raison

  • @FatouDiop-bs4yf
    @FatouDiop-bs4yf 2 місяці тому +8

    Ouztaz, si les zakaat arrivaient à son père de 83 ans , sa famille serait en mesure de l'aider. Bineta à un copain en Europe. Son métabolisme va changer après une grossesse. En sa qualité de mécano, souhaitez lui bonne chance! Elle vaut mieux que certaines femmes à mœurs légères.

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo 2 місяці тому +4

      Na dèf yeufou djiguène laniu wakh amna far amoul far souniu yoon nèkousi

    • @FallMandiaye
      @FallMandiaye 2 місяці тому +1

      Bilahi n'a youfou djiguene point

    • @FatouDiop-bs4yf
      @FatouDiop-bs4yf 2 місяці тому +3

      @FallMandiaye et les militaires femmes au front plus combative que certains hommes ?

    • @FallMandiaye
      @FallMandiaye 2 місяці тому +1

      @@FatouDiop-bs4yf mes ak loumana xew koula gis na xamne yao djiguene nga rek

    • @yerosow7063
      @yerosow7063 2 місяці тому +1

      Nioune wakhou niou na bayi mecano
      Sou bayi comportement bi rk légui mou changer physiquement

  • @ElhadjiDiop-y3d
    @ElhadjiDiop-y3d 2 місяці тому +7

    من تشبه بقوم فهو منهم

  • @papamandoyendoye3591
    @papamandoyendoye3591 2 місяці тому +4

    Oustaz sa collégues you djigénn yoyou thi plateau -bi sénn gréffage yi dafa kharam,konn naniou kholate sénn bopp bala niouy wakh thi bintou🤔🤔

  • @FatouBintou-sw5ru
    @FatouBintou-sw5ru 2 місяці тому

    Wakhlen sii domou adama yiinuy boom Binta mongi doundou yalna Ya Allah goudal fanam yarabi.🙄

  • @DabaFall-j2g
    @DabaFall-j2g 2 місяці тому +4

    ❤❤❤❤❤

  • @pispabadji671
    @pispabadji671 2 місяці тому +2

    barki Borome Darou mane bimaka guissè ay yèrè wolof bi goor laka fogone mè ki goor la guena dièguè sakh k djigen cheutt astafirlah 🤦🤦

  • @hfhgg-bm2to
    @hfhgg-bm2to 2 місяці тому +4

    Oustaz vraiment demalgua kol li serigne cheikh Al Makhtoum wakone am na nit yo kamne ni lalene Yallah binde

  • @Moustaphakane-y2p
    @Moustaphakane-y2p Місяць тому

    Balaga khaskén kholale sabope baparé yene boulen yala atewone daléne diraye

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 2 місяці тому +2

    Man beu tay guisouma Binta man goor la guiss😂😂 walla sama bott yi bakhoul

    • @BOYEELZO
      @BOYEELZO 2 місяці тому +1

      Goor yi sakh molen geuneu goorei😅

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 2 місяці тому

      @BOYEELZO 😂😂

  • @Ichigokurosakionestate
    @Ichigokurosakionestate 2 місяці тому +2

    Imame danga dioum la première Loula woor ni mom Moy incarné limou done té AP imame dou niaw ndiortt, bo wakhone ni bou féké, té yénn wa solution mangui lénne Di commencer wéddy déh bilahi,

  • @salioupouye9994
    @salioupouye9994 2 місяці тому +4

    Senegal yi yewoulene guisnan ka adji sarr waye leep dina ler beugeu buz rek

  • @WadeOusseynou
    @WadeOusseynou 2 місяці тому +3

    Senegal metina lane mosiye yonou nitt rek

    • @ShiekhjobeTijan
      @ShiekhjobeTijan 2 місяці тому

      iaw khana jago lo ko guis lo bon dosi wax

  • @papamandoyendoye3591
    @papamandoyendoye3591 2 місяці тому +3

    Bintou dafa kholate ni mouye solo,kome yènn ngi thi plateaubi sénn gréfageyi dafa kharam

    • @ShiekhjobeTijan
      @ShiekhjobeTijan 2 місяці тому

      No 😂 iaw NK ligay wax Sax do bene ñk khola tal Say wax

  • @NdeyemaremeWade-w5s
    @NdeyemaremeWade-w5s 2 місяці тому +3

    Ziar n'amène bou baax gourou guana nilaniou koye khame bouye saw filou sawe

  • @MatyDieng-n8w
    @MatyDieng-n8w 2 місяці тому +1

    Lepa goree bind mom yalla la mais soline bi ak you ses yi yawla

  • @assanesoldaroubayegorasarr1136
    @assanesoldaroubayegorasarr1136 2 місяці тому +1

    Theme ci yén la wara commencé fala yam

  • @nggndmb9122
    @nggndmb9122 2 місяці тому +5

    Guisso djigéne yi took si plateau bi 🤣 wala loussi l'islam wakh

    • @yerosow7063
      @yerosow7063 2 місяці тому

      Oustaz tchii Binta laniouko demander tchii lolou laay totou
      Imam meussouma d'accord ak mom politiquement mais dfw mou clash bou bakh les femmes de cette émission qd le sujet les touchent

  • @SidyNdiaye-m2e
    @SidyNdiaye-m2e 2 місяці тому +2

    waye ki gorela waye

  • @Bachirnanty095
    @Bachirnanty095 2 місяці тому +2

    Mais gor nioukey diapalé sounioulen mayon khalé bi niou bègn. Ken beugoul am diabaram bou goré wow kongue bolen andé sakh niouni sa bro leu kou noy nep laniou beugue doul rek meylen niou diamb mbram

  • @altesseroyale4383
    @altesseroyale4383 2 місяці тому +2

    Mani ko yèna khame 😂😅 ko corriger ya khame😂😅diok lène si aggresseurs mo guene ki mingui takou di liguèye tiagatou woule, aggresser woule, satioule! Mo yène lou lène di mbèle mbèli??? Khana mome nguène yèp? Ana reportaire bobou dane solo ni goor té kène massou la wakh? Yène aye nafèkh nguène

  • @AlimatouNdoye-fj3dw
    @AlimatouNdoye-fj3dw 2 місяці тому +1

    Yalla reub n'a Oustaz bouye tok thi télé di wax wakho diambour .thé yaw Oustaz khana khamoné télé poukaré la ,yaw li war moye mandou ,dagué di mboumbo l'islam mais yéni fi yéuss.séne Émission bi togne la.bayil boléne amoul programme nguene di sigali nitt.

  • @AlimatouNdoye-fj3dw
    @AlimatouNdoye-fj3dw 2 місяці тому +1

    Bayiléne doumou diambour. Oustaz yaw li nguaye wax khalébi khalatoul lolou.yéne n'a am
    Problème,yéne na douguou thi vie diambour

    • @ShiekhjobeTijan
      @ShiekhjobeTijan 2 місяці тому

      No iaw ki day jagale Rek ta limo neka dì wax lepoo Dege la😢😢😢

  • @MASS_DIENG-LOUGA
    @MASS_DIENG-LOUGA 2 місяці тому +6

    Khame guendi binta li guenalouco mais mom amoul sakh wéen khame guani tayouko ki sou solon yéré djiguen lagui gnou rayco si mbad bi parce que dani diapouni borom niari touryila té nekouko donc boulenco sollô yéré djiguen

    • @ShiekhjobeTijan
      @ShiekhjobeTijan 2 місяці тому +1

      Degal ki moum wakho dof Yi Moy wax E jigen day Solo come jigen Gour Day Solo com'è Gour

    • @yerosow7063
      @yerosow7063 2 місяці тому +1

      ​@ShiekhjobeTijan
      Limouy sole yeuré goor ak comportement goor bokouna tchii lou takh ses seins ont du mal à se développer g une grande sœur ki faisait du basket elle était presk com sa mais dkel a arrêté sa rk elle a eue un changement

    • @fatoufall7203
      @fatoufall7203 2 місяці тому +1

      Da téela éxercer liguéyou doolé ba paré di nourounouroulou goore motakhe mou méle nii

    • @fatoufall7203
      @fatoufall7203 2 місяці тому

      ​@ShiekhjobeTijan point

  • @talibebamba1626
    @talibebamba1626 2 місяці тому

    Djiguen thia djiguen gnia
    Goor thia goor gnia
    Diapa diapa gnieum

  • @loufablinde2479
    @loufablinde2479 2 місяці тому +1

    😂😂

  • @MamesayeNdiaye-v7q
    @MamesayeNdiaye-v7q Місяць тому

    Toude 7ejour kay dine la dou ada reck

  • @fatoufall7203
    @fatoufall7203 2 місяці тому

    Oustaz déguena deugue wayé naafékhe yi gno eupe motakh deugue toubourancké.

  • @SayeDiouba
    @SayeDiouba 2 місяці тому

    Deg rec la wakh kafrin guis nako fa me boko khole khamne djiguen la na def yafou djiguen

  • @MaimounaDieng-bp2pg
    @MaimounaDieng-bp2pg 2 місяці тому +3

    😂😂😂😂😂oustaz bi raynama

  • @NfamaraDiatta-q8j
    @NfamaraDiatta-q8j Місяць тому

    Punition de dieu
    Sa vie avant

  • @moustaphandiaye6434
    @moustaphandiaye6434 2 місяці тому

    L’islam mo djitou Diamono topeu si guinaw, koula djitou si leudeum Molay wah fi ngay tokk

  • @yillekamara9416
    @yillekamara9416 2 місяці тому +3

    Yéna mouna féne ki djigéne la??

  • @BahyayeDiop
    @BahyayeDiop 2 місяці тому +1

    Bineta garçon raté la amoul wénne té battou goor la yoor

  • @Pénda-e3d
    @Pénda-e3d 2 місяці тому +4

    Esk binta dou gounougana

    • @deugrek3312
      @deugrek3312 2 місяці тому

      Mome Lay Khalate ni, Daffa nirou ak Goor trope

    • @ahmeddoumbia7743
      @ahmeddoumbia7743 2 місяці тому

      Louye gounougana

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 2 місяці тому

      *Louy lolou ??en tt cas ni mou mell Yalla mokoko bindè mm batt bi batou goor la ont n’appelles ses genres de personnes les androgènes en francais*

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 2 місяці тому +6

    yabi lén domou diambour dji. sof nguén trop

    • @KaraJieu-p5p
      @KaraJieu-p5p 2 місяці тому +1

      Kaine douko yaabi ndakh moo daime télé. Kil arrête de parler avec ces doulnalistes ki ont chez eux des ivrognes, des thiagua, des voleurs... Sans les montrer à la télé. Na moytou thiât.yaala nouko neekh lay bindai diaamam

  • @AwaMbaye-d9y
    @AwaMbaye-d9y 2 місяці тому

    Neke mécanicien tahoul nguay defe yefou goor

  • @MatyDieng-n8w
    @MatyDieng-n8w 2 місяці тому

    Li mom dafa haraame

  • @dabaniang6016
    @dabaniang6016 2 місяці тому +2

    Celled la est née androgene

  • @PapaNdiayeJr
    @PapaNdiayeJr 2 місяці тому +29

    Wadji nguen toutdè oustaz nafekhe leuh bala mouy wakh si binta na lene diaguale souna Mouhamed psl sen grefage dafa kharame mouhamed psl mo ka wakh yalla rebeuna koukay deff ki aya yii mouy wakh mome laniou diaguè tafsir temps boy ki khamoule drah yeneuh djiguene yii tok si plateau bii li nguen def mo geuneu kharame 😡😡😡😡😡😡

    • @AliouneToure77
      @AliouneToure77 2 місяці тому +2

      Wly

    • @DialloShuiraim
      @DialloShuiraim 2 місяці тому +2

      yoï mi nek nafekhe

    • @karimcamara7865
      @karimcamara7865 2 місяці тому +1

      Oustaz bi ilifoul présentatrice yi mome day diangualé rek kou toppoul ya xam

    • @MomoSarr-q7l
      @MomoSarr-q7l 2 місяці тому

      Domou dianbour bi nagne ko bayyi

    • @DjilyMbacke-c6o
      @DjilyMbacke-c6o 2 місяці тому

      Me yaw ska degue ngua video ba mou diekh sakh

  • @dabaniang6016
    @dabaniang6016 2 місяці тому +2

    Elle est née androgenic.

  • @MaléMbaye-q2y
    @MaléMbaye-q2y 2 місяці тому +2

    Ioe oustaz yangui féneu nak bayil sa doul yiii lii incarné woul dara

    • @MAREMENdiaye-b6w
      @MAREMENdiaye-b6w 2 місяці тому

      Yawe môme soumala hamone todjie sa diobou ndeye oustaz daye sa morome

    • @MaléMbaye-q2y
      @MaléMbaye-q2y 2 місяці тому

      @MAREMENdiaye-b6w balnalla

  • @lassanediara3930
    @lassanediara3930 2 місяці тому +3

    C'est un garçon manqué 😂 et c'est pas de sa faute, elle est née comme ça !

  • @AwaWade-f1u
    @AwaWade-f1u 2 місяці тому +1

    Salam salam mane sènègal dama diakhal sène èmission yeup yank mandou bien ke l'islam andoussi

    • @talibeserignetoubaibrafall6311
      @talibeserignetoubaibrafall6311 2 місяці тому +1

      D'où aferla de mandou danouy yeterek

    • @AwaWade-f1u
      @AwaWade-f1u 2 місяці тому +1

      Dama khamni sou fèkè ay parents nio gui en vie lou takh mou nieuw ba fì c'est juste ç

  • @MouhamedDione-j1t
    @MouhamedDione-j1t 2 місяці тому +3

    Sén ouztas bi khamoul dara nitt boy liguéye surtout mécanique day am tenue spéciale téé nitt meunouteu changer bopam sans chirurgie téé kouy deff liguéye goor yonla gua yoor comportement goor téé nitt boulko forcéé limou beuguoul téé mandou si diamou yalla la bok téé fii kouniou fii doug sisay 18 yako gueneu bof téé yalla khamna kou bakhe ak kou bone téé khol moy fay téé kouléne wakhni yéne yénako gueune may wakh mounane niary sex na diagui watt

    • @fallabdou8631
      @fallabdou8631 2 місяці тому +8

      L'islam khamoul lolou djiguen waroul soulou koum goor ak loumou mana ligeye

    • @deugrek3312
      @deugrek3312 2 місяці тому

      @@fallabdou8631souye liguey meune na comprendre mais hors de son travail Daffa Wara Def yeuffou Djiguéne

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo 2 місяці тому +1

      Loutah guèn deukeur bobou rèk

    • @apprenant9164
      @apprenant9164 2 місяці тому +1

      T'es l'exemple parfait de la citation suivante" L'émotion est nègre, la raison est Hélène". Yow xana guisso niy même bou nékoul si liguéy kayam yeufou gor lay def, solou gor lay def. Est-ce que yéné nga liy sa bop wala sa dome

  • @IbrahimaNDIAYE-v5d
    @IbrahimaNDIAYE-v5d 2 місяці тому +1

    Mandouléne , lo khamoul bou thie wakh. Bayilene niort

  • @babasene9673
    @babasene9673 2 місяці тому +4

    Bayiléne thiaxane oustaze deug késsé lafi wakh