Salam man dhé talibé serigne Bara la té djapon na sa papa comm khalif Serigne Bara mais wané ngani yaw 6 moy 9 boyabo nakk niéup déllo djapp si serigne touba té djamou dji yalla té khamni yalla rekk mofi nékk niite mom nou ay kadoom mél rékk nonou la biir bi mél . Doyédi niakk fayda di khiro rék djeumé fou kén khamoul boulén gnou ray .talibé bi geuneu doyadi molén geune yén gnognou gnéppa yam
Yen yi di commentaires, deguen kham li xew deug bey wakh, deguen wara noppi bayi mou sed, sen wakh bari na té 2018 ba legui mini continuer. Mom amna yarr khamna li li wakh sou démé ba wakh li amna lou ko takh wayé yen yi diarou ko one
Li niawna mane douma mouride mé nanou rafetal wakh ji serigne sidy moukhtar ligueye na ba kheuye déme l'islam diepiwouko adouna amoul solo nanou rafetal té wakhtane
Yénangi tilimal sen ligeeyou mam demlen diangi té dianglé dji té toub si yalla bayi wakhanté lou niaw dañlensiy khébé rek wayé ken dousi am ndam si yenn ñiepp yeen ñi nak koutok sen wét ngir dieblou soufa toogé dioromi munit dina gisné tané woulen ko si dara goor goor lou leen
Ak loumana xew yaw mom kou reew nga te lii moy firndeel né santo mbacke nit loumouy kheuthio momou ko kon lingay momoko toubil te diamou dji yalla te bayyi sa wax diou niaaw djii lii amoul solo
Barra Ba ay way kouy mourid am nga gathiè ak nakhar touba yar ak tèguine rek laniou kham saytanè nak mane lounè kone bayinel wakh niou niaw yi dou séne waal
Man dhé worna serigne touba dém sa l'abbé jack séck mou nékk sama serigne mo geune may djieum si sa genre gui yakk gni ngay wakh yéna yam walla gnou tané la
Antouka ak lou meundi khew ki limou def bou s touba sikaton diamono dinako yuéde khamoul nimouy wakhé yaw louy khadjalé ak mbokou rek ngafi wakh wakhofi dara louy rafetal. Linga wakh ken muenousé djerigno yakh derou domou adama yi rek ngafi neké mem lingay wakh boudé degue la waro tok fi diko wakh li reglewoul dara dafay guena yakhe rek Bolendi wakh nak warngén soralé gni nek thi rewmi. Te doun ay mourid. Te yakamti nagno degue wakhdjou niaw thi yonou mourid. Amel nguén taloubeyi akhe nak te s touba dinagnoi até.
من كان يؤمن بالله واليوم الآخر فليقل خيراًآوليصمت 👍👍
Maneu dé louma am sama papeu ak sama yaye lakoye diokh béneu sérigne doumako diokh sama khaliss
Bilahi yonou mouride môme dagnouko wara supprimé
Khanaa sa data baye lanuy supprimé imbecile
Salam man dhé talibé serigne Bara la té djapon na sa papa comm khalif Serigne Bara mais wané ngani yaw 6 moy 9 boyabo nakk niéup déllo djapp si serigne touba té djamou dji yalla té khamni yalla rekk mofi nékk niite mom nou ay kadoom mél rékk nonou la biir bi mél . Doyédi niakk fayda di khiro rék djeumé fou kén khamoul boulén gnou ray .talibé bi geuneu doyadi molén geune yén gnognou gnéppa yam
doyna warr lolou saxx.gnou dellouu thii talibee.te kenal Serigne touba.ahh Serigne bi de de la waxone gnou.degnko baxxia.doyna warr
ki koukou khoull kham nee Serigne bara mouy mamam
Ils se ressemble très bien
Ki nourou nakk Serigne bara dhe
Sama gayi nagnou mandou réck parceque monougno wédi limouye wakh nite naka boné diw diouroul sabaye ya déclaré ab guérre wasalam
Mbaye Yatt yaw djam rék ngay am
وکلهم آتیه یوم الفیامه فردا()کلکم راع وکلکم مسئول عن رعیته/من کان یومن بالله والیوم الآخر والیوم الآخر فلیقل خیرا او لیصمت
Nite yi naniouy nagou deugeu lignou lene def kouka khole sisa bop doula nekh kou kham nite kholeene photo serigne bara ak serigne abdou coumba souna benela serigne bara kene manouko sosal
Waliyou moy diour serigne serign diour bour bour diour voyou
vous etes tous pareil !
Diii tepekooo momaye ray
Sababarou gaïndé beye douko tatiou gni Aÿ seutou serigne bi leugnou gnoune Aÿ talibélagnou
Ayway ngir diemmi s touba wahtanlen sen bir bayyi werantebi ngir yalla
Subhaana lah
Yen yi di commentaires, deguen kham li xew deug bey wakh, deguen wara noppi bayi mou sed, sen wakh bari na té 2018 ba legui mini continuer. Mom amna yarr khamna li li wakh sou démé ba wakh li amna lou ko takh wayé yen yi diarou ko one
Yaw boul gniou fontoo waay. Respécté woo Mouride yi. et ligniouy wakh Mouride yi lépp sa genre yii gnioo takh. Gnioune Geumou gniouléne. Serigne Touba rék rék rék lagnioulén soppéé motakh waayé doolén si dara. Yaw ak lou meuneu khéw war ngaa am soutoureu waayé lii mooy wanéni yaw ak moom kone yééneu yam rék.
Wawww ndank rek
internet lagni supprimé Sénégal si na rewmi d'Ay tak dé bakhna li jarna wakh internet
Aziz na leppp ler way dollill
Ki dé khana dou mbacké mbacké. WAKH diou niaw dji dé waroul diogué si seutou Serigne Touba.
Li niawna mane douma mouride mé nanou rafetal wakh ji serigne sidy moukhtar ligueye na ba kheuye déme l'islam diepiwouko adouna amoul solo nanou rafetal té wakhtane
Milliard à touba et les moitié des populations son des pauvres Je suis mouride mais c incroyable
Serigne bi nio ngi toub,ngir dieum kou Ted bayi lii ngen di def thi net bi. dafa niouy torohal nioune talibe yi. Dem len thi Cheikh Mouhamadoul Mountakha MBACKE. leup dana safarawou inchallah DEUG rek moy moudj
Kawteef
Euw
yangi tilimeul sa keur mam
Sama dom yi Sama joumadji Sama xacida yi
Doy.na war sayabo fou way kham diam
Bilay li eupba te ken douko lidianti
ayway thiey sunu borom
Yow mi al sa lamegne woniaw , doo darra con se Touba
Koula khol khane serieng bara moy sa mam
Yénangi tilimal sen ligeeyou mam demlen diangi té dianglé dji té toub si yalla bayi wakhanté lou niaw dañlensiy khébé rek wayé ken dousi am ndam si yenn ñiepp yeen ñi nak koutok sen wét ngir dieblou soufa toogé dioromi munit dina gisné tané woulen ko si dara goor goor lou leen
koun khayoun nela sa bay bayam dou bayam dika wakh lou raw lim wakh
Vraiment nak
Ah doyna war bou yabo fou way kham diem
mane dh dama rouss bilahi liii eupena sgne bi wakh day raféte adouna amoul solo
Ak loumana xew yaw mom kou reew nga te lii moy firndeel né santo mbacke nit loumouy kheuthio momou ko kon lingay momoko toubil te diamou dji yalla te bayyi sa wax diou niaaw djii lii amoul solo
Salldiop diop astahfirou Allah ragalal yalla té mandou
Boule kham lilay dalle yarou wo Yoro kathe rek ngaye def koula khole khamny boko dara ak s touba niaw lamegne ya trokh
Doxall rék Adinak sa kanam réwandé amull ndiariñ
Réfetalal kaduyi waay
Lin kou baka deff koun kou deff mou metilla khoull leen kou dji sen boubbou rek
Yalla nena waxall lou rafett mba nga nopi.
demal diangui
Ay bandi la niou khaman té na niou seenn birr
Maïs yaalla du na lenn wérr
Gueye Abdou
yaw amo sutoura
thioy xalis tasna fepp
Li niaw naa
Bon torb
Lou way di gnane na sa bole ay taguine
Kou amoul teguine mome akbayima nio yéme.
Li alalou adouna diarouko bou sang si dohale ni hawma gnoune talibe yi founou dieum li doy na ware
Wouah
Khana gnom gneppa biireul
doyna waar astafourla
Waw ki mom lim wakh epuena deh
Noo Appene
Modou Diop t FC
Yawmi di alal mola djital lilahi wa rasouly dimbali len nou Guen dem wakhtan si sen birr te Guen may nou diam
magui toub dh mbacke balla Ak sotora way
khilafa day diaroul khathio magoume80ans bo kheuy neko sa wadiour diouroula. loukhew yawa metina lol sakh
Mais Li lokoufi diarr demal diaamodji yalla te bayi sen thiakhan yii
Mai li mom eupeuna na rafet way
Liniawna trop
yaw Aziz sa dol
dagay wakh rêk demal ligayi
Barra Ba ay way kouy mourid am nga gathiè ak nakhar touba yar ak tèguine rek laniou kham saytanè nak mane lounè kone bayinel wakh niou niaw yi dou séne waal
Na raféte waye
Li dafaye wanè ni tarikhas yi aye thiakhane la dém lène diangui li sène borom beugue si gnoune té gnou diāmou ko ci lolou tarikhas yi mafia lagnou
Pape Diop bayil sa doul yi ndayam
Dieurrudieuf degg nasa wakh
Man dhé worna serigne touba dém sa l'abbé jack séck mou nékk sama serigne mo geune may djieum si sa genre gui yakk gni ngay wakh yéna yam walla gnou tané la
Malaw Gadiaga .
Malaw Gadiaga mandoulle rék copin
Antouka ak lou meundi khew ki limou def bou s touba sikaton diamono dinako yuéde khamoul nimouy wakhé yaw louy khadjalé ak mbokou rek ngafi wakh wakhofi dara louy rafetal. Linga wakh ken muenousé djerigno yakh derou domou adama yi rek ngafi neké mem lingay wakh boudé degue la waro tok fi diko wakh li reglewoul dara dafay guena yakhe rek
Bolendi wakh nak warngén soralé gni nek thi rewmi. Te doun ay mourid. Te yakamti nagno degue wakhdjou niaw thi yonou mourid.
Amel nguén taloubeyi akhe nak te s touba dinagnoi até.
Mamemor Touba wakana hakhane ci lima yakar kougnouné sa baye bayam djourouko ga wakh lou eupp limou wakh.
Guenn balma
Ousmane Sarr bilahi
Fen.reik .gay.deif .yaw .doup.sareign.sa.wakh.barie .na.lool.
Ga ya won yobou nanou mbotoum kharnou bui liii doyna warr
Topeléne yalla té bayi ngi . Di nagnou léne nakh adouna té yéneléne di tanné alakhira .ay bandit you lakhatou laniou
Ki doumouram la mbackè mbackè deug d'où déf niii ngay def
khamzooo tv actualités yaw mi yaye domiram