reponse de baye fall a serigne fallou fall mbaor

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 30 лис 2024

КОМЕНТАРІ • 146

  • @MamecheikhNdaw-sk9cr
    @MamecheikhNdaw-sk9cr 3 місяці тому +1

    Dieureudieufé serigne touba c serigne fallou fall borom ndame la pas borom mbawor

  • @FilledelEternel2353
    @FilledelEternel2353 8 років тому +1

    bay fall my seufans number one

  • @youssougueye7480
    @youssougueye7480 7 років тому +5

    Qui vrai Baye Fall la, mogui liguey té gueum na serigne gnam.
    Sénégal danou soxor rekk.

  • @nlo6330
    @nlo6330 8 років тому +1

    merci baye fall wakhe dji rafétna

  • @bayefall355
    @bayefall355 6 років тому +3

    Diarro tahul bonne amouleene ham ham

  • @aichadiom6651
    @aichadiom6651 8 років тому

    du courage Baye dieuf dieul la rk

  • @khadimgueye4427
    @khadimgueye4427 8 років тому +26

    Le mouridisme est une tarikha pure mais des fois le fanatisme des adeptes devient dangereux. Comment, après avoir survécu à un accident, il peut se permettre de dire que c'est Cheikh Ibra qui l'a sauvé. Dieu il est où dans tout ça? Sincèrement en tant que musulman et en tant que mouride, je déplore le fait que les adeptes attribuent le mérite de leur réussite aux marabouts au point d'oublier Dieu.

    • @ousmanembinkydiedhiou247
      @ousmanembinkydiedhiou247 8 років тому +2

      triste constat!

    • @cheikhbirek8128
      @cheikhbirek8128 8 років тому +2

      bilahi bro lou leer nga wax .

    • @Mustafa-bd3db
      @Mustafa-bd3db 8 років тому +1

      tu as tout a fait raison bro. Il y'a beaucoup de fanatisme dans le mouridisme maintenant.

    • @Michael-md6wb
      @Michael-md6wb 8 років тому

      ɷɷ Heeyy Friendsssss I Havee Just Wonnn Branddd New iPhone 6 From visitt : - t.co/eU4Ew8DLAq

    • @elizabethanokye-boateng9889
      @elizabethanokye-boateng9889 8 років тому

      ɷ Heeeeyyy Friendsssss I Have Justtt Wonnnn Branddd New Mac AirPro From visitttt : - t.co/eU4Ew8DLAq

  • @tourebakar3305
    @tourebakar3305 8 років тому

    nice fall courage Baye fall bouléne tontu s.birék fall

  • @mamekhadyndiaye7969
    @mamekhadyndiaye7969 8 років тому +1

    thiey baye fall ndeysan baye fall dh guena la beugue cheikh ibra rekk kay wadia

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 6 років тому

    Nit kou bakh day am talibé dieureu dieuf sr Touba diarama Mame cheikh Ibrahima Fall

  • @baaybi2879
    @baaybi2879 5 років тому +1

    Machallah degou rek mo wor

  • @maguettebomou5177
    @maguettebomou5177 5 років тому +1

    Well done !!!

  • @papethiame8798
    @papethiame8798 7 років тому

    assalâmu alleykum yien bokki JULLIT yi AK bokki Tâlube yi ... di nuyu bokki Senegal yeupp, te dileun fattali waxi borôm Touba ci am poh , nêna wôn adduna 3 jëfëfi am,
    li Matula DEF MUDI am poh, ndax Langa cay jëleu dula taxa dugg ajjana kon dula TERE dem sawara ...kon jaruta def .
    AK lì mata def MUDI jâmu yallah sunu BORÔM môlay taxa dugg ajjana......
    Ak moy yallah sunu BORÔM dey taxa dem sawara "wal yasi bi Allahi" AMIIN !!!
    nêna bu mujj bi buko sa xel sax xalât ,
    YALLAH NA yallah sunu BORÔM feyal nuko ngën gi FEY Amin.

  • @lahatndiaye5537
    @lahatndiaye5537 8 років тому +1

    slt wa serignou baye fall wiri wiri la telephoname di sonnet j pense ecouter

  • @gardfloreenvironnement9644
    @gardfloreenvironnement9644 7 років тому

    Nice Na Baye Fall Amal Diam bou wëra wër

  • @goodboy5222
    @goodboy5222 8 років тому

    je suis de tout coeur avec toi khadim rassoul gueye ndegeum yaw mii dou tourendo serigne touba yako wakh

  • @bayefall8714
    @bayefall8714 8 років тому

    Mom ak Serigname bi yeupp dagnouyy fo nékou yi si ak Baye fall

  • @diopfallou9743
    @diopfallou9743 7 років тому

    merci Baye Fall

  • @diallopmilleur110
    @diallopmilleur110 8 років тому +1

    Esprime en français pour que les autres pays entend ce que vous disais

  • @mousselygassama1125
    @mousselygassama1125 8 років тому

    dagnou wara cétàt yònnou baye fall ndax baye fall nêkoul ci thiêr

  • @faliloumilito8885
    @faliloumilito8885 7 років тому

    Serigne bi mon lan Lay def fii sakh

  • @galsenflow9077
    @galsenflow9077 6 років тому

    L'homme ne doit se prosterner que devant son DIEU
    Domou adama waroul soukeul aka ramale koudoul boromam
    Wanteh bouléne di sante di wakh sene tourou serigne yii teh bayi fii Yalla sougnou borom
    Di wate si séne serigne yii nane gnom nguene yakaar adina akh alakhira yalla naléne Borom Bi diegueul
    Nagnou bayii bokaleh bii teh délo sougnou khel si yalla
    Goor dou take diaro
    Def aye rasta ni djiguene
    #mon_pays_va_mal

  • @___xaf5306
    @___xaf5306 7 років тому +1

    Sénégalais yi nio méti boucle d'oreille sah dégney koy critique geume geume si holl la doutchi soline doutchi dohine nen ragal yalla respecter len choix des autres t manou t hamni soube yalla rek gney rendre compte kou deh wak sa bamél manou len please.

  • @ndeyethiorogueuye5399
    @ndeyethiorogueuye5399 7 років тому

    ms serigne bi wiiri wiiri ly sonei ms bougoma thi wah ms mangui toup

  • @cheikhdiop6509
    @cheikhdiop6509 4 роки тому

    Goor ak diaaro thimm...

  • @papitondoye5513
    @papitondoye5513 8 років тому

    Moussa respect

  • @freshlova22
    @freshlova22 8 років тому

    celui ki va minsulter sa data Ndeye chak matin chak apres midi et avan de dormir sa tounou ndeye aussi

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 6 років тому

    Sama guayi yéne Serigne bi dou séne morom bayi léne sagua yi ..

  • @yacinefall4376
    @yacinefall4376 7 років тому +1

    waw pire mame cheira fall meune na Lou raw lolou

  • @elhadjikabayefall1348
    @elhadjikabayefall1348 8 років тому

    akassa Baye Fall ibrahima fall mandou lene si nionak mome ba aldiana

  • @yorodiop8346
    @yorodiop8346 6 років тому

    Baye fall dou aye fo bayi la ak fall baye leep lou bonne faalle leep lou bakh

  • @kamzodiakho4944
    @kamzodiakho4944 8 років тому

    cool

  • @rmormboup8278
    @rmormboup8278 5 років тому

    déguéna kar sene tounou day rék bagne Bay fall mais gamal liga game rék

  • @ndeyesene5757
    @ndeyesene5757 5 років тому

    baye fall demal boul tontou gayi

  • @tfkteew3586
    @tfkteew3586 8 років тому

    Akassa!!!!! deuguela👍👍👍👍mais danga wara bayi di joué film diwaté serigne bi parce que filmyi dou deugue ce n'est pas vous seul mais c'est l'habitude des Sénégalais dommage😞😞😞😞

  • @awababou2253
    @awababou2253 5 років тому

    Kone baye fall ni lay wakhe naturellement

  • @tubabogiboroh6470
    @tubabogiboroh6470 6 років тому

    some Senegalese will compare their marabout to the prophet's

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 5 років тому +1

    Kènn...d'où mame cheikh Ibrahima fall

  • @makhfousswagnane2334
    @makhfousswagnane2334 8 років тому

    😁👍👍👍

  • @mbathiolo7834
    @mbathiolo7834 8 років тому +1

    bayuo gore mi wayoute

  • @diineakdiamanotv6564
    @diineakdiamanotv6564 7 років тому +1

    Serigne bi dafma nirou ab comédien sakh dagnko wara invité ci séri yi kone mou torhiko mo niack foulla deugeu

  • @abdoulayegueuye4967
    @abdoulayegueuye4967 8 років тому

    Sénégal dall mo nekh rek

  • @sarrbachir8791
    @sarrbachir8791 8 років тому +2

    senegal nun ñépp ay bokk lan na nu sóppànte bëggànte te jokk bokk gi te bayi waxànte lu ñaaw, te ku ne jàpp langa nek yaatal sa mbokk cà la mu nekk.
    maa ngi léen di nuyu

  • @abdoulayegueuye4967
    @abdoulayegueuye4967 8 років тому

    serigne dal mo new Sénégal

  • @freshlova22
    @freshlova22 8 років тому

    yen a mare serign serign penser a dieu c'est le seul veriter

    • @freshlova22
      @freshlova22 8 років тому

      +nisse Cndiguel si vou chercher dieu Côme vous chercher vos putin de serigne vou trouverai halla unic vérité

  • @mamethierohizboutarkhiyamb8077
    @mamethierohizboutarkhiyamb8077 8 років тому +4

    baye fall douy thiakhane

  • @ibrahimandiaye8584
    @ibrahimandiaye8584 8 років тому +1

    Momo bo khamone lou yalla wakh kone dagnaye mannou si niake diouly diambour khame li yalla santane khame lou yalla beugue mo ko guene ok kou bakhnga boul dingnate day wanie sa guem guem

  • @aissatoundiaye6740
    @aissatoundiaye6740 8 років тому

    Ndeyssane.... wayé dindil diarou bi parce que gor bou ko tak surtout si oreille gauche dagn lay taxé d'homosexuel

  • @elmalickgueye383
    @elmalickgueye383 6 років тому

    Baye Fall, loye tontou,yaw défoulo kénn dara. Liguéyeul sa liguèye.

  • @seydinakane3411
    @seydinakane3411 8 років тому +1

    baye fall dou tarikha té ab talibé serignam dou wax moussiy tékk léne wakh bi diarouko wonn nangoul rek li serigne fallou wakh

    • @falloudiouf8912
      @falloudiouf8912 6 років тому

      Baye goor fall moy borom ndigueul sama serigne sama kharit doundeul fall

  • @ousmanendao6499
    @ousmanendao6499 6 років тому

    Bayfall da am ay facon lou nityi xamoul mouy lu wa tassawouf wam mouy MBAYE YALLA motax kou xamoul nagua noppi ndax mando geun koor

  • @freshlova22
    @freshlova22 8 років тому +1

    data Ndeye serigne

    • @freshlova22
      @freshlova22 8 років тому

      +nisse Cndiguel souma katter sa Ndeye ???tu va prendre tes bagage et dégager dans mes commentaire sa neni Ndeye

    • @freshlova22
      @freshlova22 8 років тому

      +nisse Cndiguel bouma Ray mayma diam Lou bess nak

    • @freshlova22
      @freshlova22 8 років тому

      +nisse Cndiguel FO deff yalla ?? doko sante bâ paré ???

    • @freshlova22
      @freshlova22 8 років тому

      +nisse Cndiguel kan tu sera seule dans ton tombe tu saura ke c dieu le seule puissant kon doit suivre pas serigne vou dormais vraiment c'est ton serigne ki ta créé c rien quun être humain tourne toi vers dieu c'est mieux et oublie les serign sont pas lieu que toi

    • @kumbakebbeh647
      @kumbakebbeh647 8 років тому

      Haha

  • @kumbakebbeh647
    @kumbakebbeh647 8 років тому

    Baye fall Mor nekh😀😀😀

  • @ndiagabambagueye4120
    @ndiagabambagueye4120 8 років тому

    OHH DEGUE REK NGA WAKH FALL

  • @babalyhooderenaatieleydu825
    @babalyhooderenaatieleydu825 6 років тому

    Serigne barina te woute legui kan mo gan xamo Dara waxa pithir pathiar ngaye waxa

  • @beyeibrahima3181
    @beyeibrahima3181 7 років тому

    bagnou gnoula sa melokan monou nekhoul daga werou mais royo Ana gor AK takk diaro nopou aki lam néga sen famille kou dioudou gnou takalla diaro légui sa domyi ga doudé mame chiekh daga len di diaro sa serign Boula wakhoul khamga Lou mbakh mano takk diaro ba safma goor rawatina mourit

  • @abdoungom6017
    @abdoungom6017 7 років тому

    kouy saga sa ndeyi diambour fonko sa ndey kouy saga serigne danga diakarlo woulak ab mourid yow man ak yow ngasaga srigne barkeeee s. touba ma reyla billahi wallahi yow do dioulit

  • @oreyadiop1940
    @oreyadiop1940 8 років тому +2

    momo iow meun nga tothi sa lefeul nday teuthi sa lamine wala danga bok si ga yi

    • @cheikhbirek8128
      @cheikhbirek8128 8 років тому

      iow mi ya wara khoti sa leufeul nday domram

    • @bkelpri2386
      @bkelpri2386 8 років тому

      +Tafisco Prince iow yaaa wara nioussa noppo imbécil.louci sa yonn

    • @cheikhbirek8128
      @cheikhbirek8128 8 років тому +1

      +Line Kèbè teudieul sa gat gui iow .m'ram

    • @bkelpri2386
      @bkelpri2386 8 років тому +1

      +Tafisco Prince balnala.conseille pr toi.démal gesstou louy bay fall.akk li kou tédd ki wax si kouy dingatt ap bay fall.té nga bayii saga niakk téguine

    • @cheikhbirek8128
      @cheikhbirek8128 8 років тому

      +Line Kèbè comme danga sop rek loo deeg yawa. mane lima xam j'en suis sûre k xamoko iow. .adouna amoul solo balma akk balna la Serigne bi

  • @souleyemanembengue66
    @souleyemanembengue66 7 років тому

    SERIGNE cheikh FALL digualale sa talibébi deugue té bayi thiakhaneyi

  • @zonecryptobusiness9244
    @zonecryptobusiness9244 8 років тому +3

    wayy sene neni ndaye rek yene daguena sokhar rek momo khamo ndayi dara si islam di doulll rekk

    • @mbackediop7678
      @mbackediop7678 7 років тому

      myfuck bellevie wakhall way khamonou darra si l'islam di dull Baye Fall laléne Gan

  • @Amesoufi313
    @Amesoufi313 8 років тому +1

    Baye fall yaw boul dontou niomgnilay niguat amnaniou ay talibé yokhamni yalén guina sél serigne fallou fall mbaor momou diwakh amna ay talibé yo khamni daniouy mandi di tokh yamba di sath di waté mame cheikh ibra ta wakhouko

    • @bkelpri2386
      @bkelpri2386 8 років тому +2

      Wax day rafétt wayy..amal killifa.bo dé ab mourid

  • @mountakhaseckbrasilsp4241
    @mountakhaseckbrasilsp4241 8 років тому +1

    Salam momo yaw dh dagaye tonie te nima guise gaye wakh tonie waroula nite kou bakh nak dafa wara madou te diapou liga gam rek wasalam

  • @moustaphacisse6500
    @moustaphacisse6500 8 років тому

    Mqne dal seute yi nioy défendre niuy trokhal yonu serigne touba ak cheikh ibra bi

  • @mandiagambengue1528
    @mandiagambengue1528 6 років тому

    serigne ndiaye ki mo eupe sa baye buzz ki Moy buzz katal sa ndaye

  • @papayqgue4076
    @papayqgue4076 8 років тому +1

    djope bagna deklou kéneu

  • @freshlova22
    @freshlova22 8 років тому

    yow ak serignbi Sene data

  • @fegnaltv
    @fegnaltv 3 роки тому

    Vidéo bi douma ci doyal

  • @moustafaniang225
    @moustafaniang225 6 років тому

    Sagua yi mom Mane na niak cheikh Ibra Fall néna sama yone wi louma dawoul déf bou ngéne KO sii bolé tamit bokou sii ..louma da déf bou ngéne kosi guéné tamit Sila

  • @khadimbeye8860
    @khadimbeye8860 8 років тому

    Enlève ton boucle d oreille foutess

  • @miroirdubaol2690
    @miroirdubaol2690 8 років тому

    Boul fontou nitngi Mame Cheikh Ibrahima fall nekotoun ko diangotoun nekotoun kodoun wakh longiaw ay sokhnam sa Seringe boubo khamna litakh wakhot wot khalis bomla diaral safara

  • @freshlova22
    @freshlova22 8 років тому

    merde alors converti you vers dieu laisse les serign c mieu

  • @mamendoye9077
    @mamendoye9077 8 років тому

    wakhgua deugue mbaye

  • @wadegora3309
    @wadegora3309 6 років тому

    Kiimoye seringe bi

  • @didi.tvdaldiam5070
    @didi.tvdaldiam5070 6 років тому

    Demal diangi watt wakh

  • @saliougaye2483
    @saliougaye2483 7 років тому

    wakhou fi xam xam lii dou xam xam bilaye diamou lén yalla ta bayi thiekhan Yi

  • @ibrahimandiaye8584
    @ibrahimandiaye8584 8 років тому +1

    Momo mboji demal guestou dji ligneye Wakh khamosidara diamou yalla dou dioulek woor Kasse khamo say farata

    • @norayni8589
      @norayni8589 8 років тому

      ibrahima ndiaye Aka ma kham samay farata ak sounena ak mousta khambe khana ko bou bakh ndakh diangue n'a alhourane kham n'a li yalla wakh ak seydina mouhamed p.s.l andi thi khaliss khamna si lou wakh mai niaka djouly ak niaka wor mom kéne manoul wakh ba mou dagane nite kou matte djouly douko Mossa wathi jamai

    • @bkelpri2386
      @bkelpri2386 8 років тому +1

      +momo Mbodji iow mouno dokhann ndayam mandou.boumala diapé dina rayy sa ndayyyy.tu es musulman këy iow la consérné louci sa yonn si lénnénnn.djoulitt daffay mandou.djang coran kham li coran wax mo gueunn.c

    • @elbachiroumbayebromzerobak8852
      @elbachiroumbayebromzerobak8852 4 роки тому

      @nisse Cndiguel yaw yanga na kham ne dou la tontou

  • @codomonoadaseidu8078
    @codomonoadaseidu8078 8 років тому

    sa serigne bi ak lekham yi

  • @mountakhaseckbrasilsp4241
    @mountakhaseckbrasilsp4241 8 років тому

    ms lepou sanrou nite ndji rek nioye takh niouye tou mal yonowi lou nite Kate kham kham khamga ni serigne touba fowoul folouwoul mame cheikh fowoul folouwoul ms nak lou waye def sa bopou

  • @ndiogoulo4968
    @ndiogoulo4968 8 років тому

    Ab mouride du foh té bala ngaa djianga lé dangay diange ba paré té diarob noppe daa haram thie goor bugne lako téré ak bugn lako téréwul yaw mom ku tollé ahmadou gnu toddé lako nganan ay Ahmadounaymar sow say wakh mom diaroul tontou wiiri nak amul bénne gnarigne ludul lékke sunu tamp ak tardél gnu képpe mangi toubal yallah bu baakh téy gnaan mu bolé gnu djiégeul

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 6 років тому

    M delene rafetal aussi amoul sollo

  • @goradiop5757
    @goradiop5757 8 років тому

    HTC Sex

  • @makhfousswagnane2334
    @makhfousswagnane2334 8 років тому +1

    momo yaw dagay digatt walla

  • @bigmofaye752
    @bigmofaye752 5 років тому

    Baye Fall piire gua

  • @ousmanfall7799
    @ousmanfall7799 7 років тому

    daguaye doule reck

  • @mbackecisse4373
    @mbackecisse4373 5 років тому

    Da ngay kathi rek bayib goor ken dou ko thiakhanè

  • @salioufall5987
    @salioufall5987 8 років тому

    thiey gueum gueum rek

  • @moustaphatouretouba.2363
    @moustaphatouretouba.2363 8 років тому

    baye falle kou bakh ngua bilakhi

  • @modoufall7825
    @modoufall7825 5 років тому

    wriwifo

  • @alisow2744
    @alisow2744 7 років тому

    f

  • @abdoukhoudossgueye1322
    @abdoukhoudossgueye1322 7 років тому

    sa kili fagui dh yako tane trop

  • @yeslaye9334
    @yeslaye9334 7 років тому +3

    kou déh ak sa bamél
    louway def bopam
    kéne kounék say djeuf doynala sokhla

    • @alisalou8151
      @alisalou8151 7 років тому +1

      Yom mi wakh li ci serign bi toubco khana khamo serigne touba yalaykesela bo beuguer feke dewene

    • @maguettebomou5177
      @maguettebomou5177 5 років тому +1

      @@alisalou8151 sans blagues !

  • @nontv221
    @nontv221 8 років тому +3

    gniaw! yaw bayfal ga.
    Mbaor daa sof rk

  • @mamadoudiop9260
    @mamadoudiop9260 6 років тому

    sa tounou ndaye serigne ndiaye domeram dingak katou mame chekhe ibrahima fall niongui sougnou bire