Notre coach école de football depuis 2005 on te souhaite une longue vie On est fiert de toi Bilahi Toujours égale à lui-même ( tu es toujours modeste )
Bamba damako beug Moy sama dom bou gor inchala bouma demè senegal nadem ba sen keur damako beug bilahi sou guenê sama diekeur nima Amy dawsil khol SA dom ndeysan 😭💪🏾❣️
Merci grand allou dieng était grand liberau de asc mbullane de diourbel et coatch formateur a la base fière de toi y a beaucoup de jeunes talents qui ont passé dans les mains de cette homme Merci le grand🙏🙏🇸🇳
Le vieux a raison. Le gosse est l'avenir de cette équipe. Mo wara nek sunu avant-centre. C'est indiscutable. Amul complexe té meun na limuy def. Bess bu commencer titulairu nagn ko jokh sunuy penalties mokoy dore. Mané ay penalty wam xawma kumu doy wayé man batay doyuma.
Bamba dieng est la future star de cette équipe du senegal...la manière dont il a marqué son penalty en dit beaucoup sur ses qualités...un fan malien
Effectivement môme rek mo marquer but bou nice
Ay way numéro bamba dieng la bg svp wa chaîne bi
"BAMBA dafa am fit beugg but" lolou mom c'est vrai père moo tax dina am carrière bou baax inch'allah.
Na gnew Chelsea mo mou e lukanule
Machallah 🥰 ahmadou bamba dieng futur sadio mane 💚💛❤️✅🇸🇳🦁 ont t'aime 🇸🇳
Notre coach école de football depuis 2005 on te souhaite une longue vie
On est fiert de toi Bilahi
Toujours égale à lui-même ( tu es toujours modeste )
Ohhhh machalla grand Alsane dieng notre coach école de football au temps 2000 . Diourbel suis vraiment fier de toi père Alsane
Ahmadou bamba dieng joueurou askanwii on est fièr de lui🔥🇸🇳🏆🏅✊
Machalla yalnako yalla lafal thiate barkep serigne touba mbacke barkep maak gniou bakh gnieepou amiine
Bamba damako beug Moy sama dom bou gor inchala bouma demè senegal nadem ba sen keur damako beug bilahi sou guenê sama diekeur nima Amy dawsil khol SA dom ndeysan 😭💪🏾❣️
Ndeye sane yaye boye beugg dafa fort
Bamba sé notre fierté nous les diourbelois et bonne continuation à lui
Nganima
Masha'Allah! Bamba Dieng est une future star en devenir in shaa'Allah.
Salam j suis très contente de Bamba c lui qui a joué le match au 2ème mi-temps bilay j l estime très fort yalnakho yala lafal thiatt
Macha Allah Yalla na sunu borom sam kho arr kho si Barkhé tourondo wame J'adore bien ce petit j'aime bien un enfant très osé dans le foot
Bamba MashaAllah mom na guéna Osé rék attaquants défa wara wané bari pékhé pour nék leader mondial
Un futur talent bamba 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
BAMBA DEING NIEUWEULE ITALIE SÈTSIMA SAMA DOME BI NÈNA YAW LA NOPE😂😂 ELLE A TROIS ANS KO NOPE MOUNÈ BAMBA DEING
🤣🤣🤣na nieuw kone
Oooh lou Nice waay
🤣🤣🤣
Ndysane ohh 🥰😂
Merci grand allou dieng était grand liberau de asc mbullane de diourbel et coatch formateur a la base fière de toi y a beaucoup de jeunes talents qui ont passé dans les mains de cette homme Merci le grand🙏🙏🇸🇳
Ohh ma challah bamba yalna KO yalla lf thiat
Alou 🔥❤ no ki mo meun yarrr ❤❤ ... doumalla meuss faté
Machaalah.nako.tourodowame.yallou.ak.jiouweur.yép.félisitasion.
On est fière de lui yalla nako diame sonal si barket mouhamed
Fiére de lui c'est mon idole je l'admire beaucoup
Nganima
@@osdiawara6528 😂😂
MachaAllah papa wakh dji rafet na bravo à Bamba
Coach Alou! Cissé , éducateur spécialisé bou nekone Centre polyvalent de Diourbel, bel témoignage Big up
Manchallah Bamba est le future start inchallah vive le Sénégal
Tout le peuple est content de ton fils
Machallah Dieng la santé fiit foula fayda AK diom kaay am 👏👏👏👏
Alsanne dieng un coach très méticuleux.. c’était dure quand on rencontrait son équipe .😅😅 je stressais grave sur le terrain
Fiit mom amnaco trop bilahi
Kou bakh. Il a formé pas mal de personnes machalla
Merci bamba et bonne continuation
Bonne continuation Serigne bi yalna la sa tourodo hard amine
Diadiaff waye Amall diamuo rk yaw ♥️♥️♥️♥️♥️😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Grand Alassane Dieng Dieng way un grand coach
Le pere de bamba dieng en action
machallah yalnako thiate séklou on est fière de vous
Yalla nako yalla lafal thiatte
Du talent et de la détermination, Bamba est rassurant.
Machalla diourbel est fière de Bamba dieng
Ahmadu Bamba fitt moy nëk premiere vertu si mom
Sama kharit sama khoulowalé mon frère diam si yow
❤❤❤❤❤
Mercii merciiii Bamba
Maa chaa Allah c le petit frère du papa Bamba Dieng
Tout le merite revien a toi coach alassane
C un tres tres bon et courageux joueur.
Bien parler coach
Mrc a notre frère bamba😍😍😍
Bilahi dingen thiatou bamba Dieng
Thi barkeb tourendome ley deme
En tout cas il toutes les qualités d'être un très grand attaquant. Maintenant il doit continuer à bien travailler.
GRAND ALSANNE MON COACH DE TOUT LES TEMPS
Félicitations Bamba Dieng
Machallah bamba dieng
Bamba dieng ❤️
Bamba notre fierté
Dafa man limouy def motakh damoko beugue billahi
Le vieux a raison. Le gosse est l'avenir de cette équipe. Mo wara nek sunu avant-centre. C'est indiscutable. Amul complexe té meun na limuy def. Bess bu commencer titulairu nagn ko jokh sunuy penalties mokoy dore. Mané ay penalty wam xawma kumu doy wayé man batay doyuma.
Waw fi ak 20 ANS sikanam lolou beuri na dei sama wadji
ndeysane kadou yi rafetna
Bamba Dieng yaye djambar
Bravos Alassane Dieng
Bamba goal welcome to Chelsea Football club 😇
Machalla
FIERTÉ DIOURBEL
Wi wa diourbel sounou dom la
Bonne chance
Sama coach way doundal
Machallah
bamba champion le
Bamba Dieng
Bravo
Pabi niaaw na🤣
Franchement yague na yor boy you am talent mais day soga diot parce que dane nane joué ak gnom école de foot baye bada
Nenaleen buterla te lii dakoy deugeul
Mon fils bamba
Titt am bamba dou tite dè
Nioune gnépafa diar.
💚💛❤️🇸🇳🦁
👏🏽👏🏽👏🏽🇸🇳🇸🇳🇸🇳
❤️❤️❤️❤️❤️
waa pèr nomou dèmè nonou🤭🤭
Code leu
@@aminabakarwallygueye9678 yaw doo ngaka dh
cool leul rek ymgx
C'est un père de certains
Lou khew???
Bamba khalé la c'est normal
Dama am khalee bou mana football tee khawma fou maye diar
Dougal ko centre wla école foot rk madjiguene
Merci
🥰🥰🥰🥰🥰
Tanke bi dafa desse
Salut
Nic
Trounadome moko walou rk ak ligueye wadiour
Donnons Allah sa part, c'est la moindre des choses en tant que musulman.
Bamba est une machine a but
Machalla
Machala
Machala