Розмір відео: 1280 X 720853 X 480640 X 360
Показувати елементи керування програвачем
Автоматичне відтворення
Автоповтор
Yaw mom lègui bokk nga si samay mbeur merci beaucoup ❤❤❤
Merci cheikh Niang
Félicitations baye falle 👏👏
Ooh cheikh Niang wakh dji raffette na vraiment nitt kou bakh nga kou xam adouna diam si ioe.
Da kanamé😂😂
Noooo cheihk bahoul bily😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
😂😂😂 cheikh niang yalna goudd fann😂😂😂
Bilay waxna wax bou am solo lek avance diambour tela beuré moudié beuré si yam wallay wax gua DEUG😂😂😂😂
Ay way mberou guewel mo saff khorom😅😅😅
Cheikh Niang dangay rer bay beug dei diam si yaw Frere
ré na ba sône cheikh niang serieux woul.
Reug champion d'Afrique
Mourombouma😂😂😂😂😂😂wouyaye
Mane ki damay rayy cheikh niang mo nekh😂😂
Cheich niang bilahi dafa nekh 🤣🤣🤣🤣
Cheikh niang bayil doul reug reug Mane bayi boy niang
Talibe albourakh bii😂😂😂
Papi 😂 dh beugoun diam
Cheikh defnga leep,, bari wakh bakhoul
😂😂 daa kanamé 😂😂
Bilahi boy Niang bou dofé Ba niari lokho reug reug diap Bilahi si souff la diém comprendo lén sah 😂
cheikh niang anni borom péle bi
Wa bakh nah
Beu Khadim Ndiaye diapeula😂😂😂😂
Alience baldé limouy deff mbeur douko deff naniou ko wax deug mo geun
Alliance Baldé dou mbeur vrai domaraam la
Cheikh con na😂😂😂😂
Souff Kay 😂😂😂
Mbeur dagay deff yeufou mbeur mo geun
Check ndeke ko bahgua
Guediawaye dh balla gaye moko mome gouyegui wakhonnenako
Yangui talakhou reck😅😅😅
Alias ngaka la. Rek. Cheikh Niang da dioumon. Rek
Alliance ay souff la gueum😂😂😂😂😂😂
Billaye yon rek😂😂😂😂😂😂
Cheikh niang way😂
Thiey Guéwél dak guinar waxalé soxla yén la beug man
Bilakhi warone nga abale sa fitewi boye niang
Billahi niang kai tapét bou mag le 😀🤣🤣🤣😭😭
😂😂
Ki lutteur la wala bongoman
Reug dou sen morom
😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
Gor d'où Bari wakh saway

Cheikh niang bayil doul reug reug
Mane bayi boy niang