no vraiment li rek motakh ma ragual sénégal Say bo fa begué nieuw rek dégu gnou raye kén Ba kagn nak li warna diekh vraiment metina di mastawou wa famy bi yalla na yalla léral lepp t Souf sédd si kawam si barké seydina mouhamed psl
massa massa metina je ne peux pas tenir mes larmes dans kel pays sommes nous je sais ce que sa fait nako nit kouné set thi bopam yalla na yalla leral yeup et punir ce qui ont fait sa. elimane famou yalla no dakal fi. dila nianal thi aldiana you kawyi . gou def li bonne na gnou
Yalla nako yalla yeureum diegueulko aye bakaram famou dieum gueneulko fimou diougué makoy dialé wa keureum yayam ak kep kouy mbokam ak dioulite yeup lii doyna war métina lol Sénégal doy na war walhi metinama lol pask damakoy nate thi mane bou dalone sama mbok mais nak yalla nako nitou yalla nite ba ki def lou gnaww lii yone tek ko lokhoo yalla nalene yalla yok kholou mougne diam ak salam rek yalla na gueneu sakh thii sénégal yalla are gnou lakhe gnou fou yakh doul yegg metii nama lol wa salam
un jeune quan jai vu son fils orphelin de pere et mére jai pleuré bilahi li dafa meti bilahi walahi mon pere est policier mais jai honte et big boss niap lene ndeyam ci zair wala batine wala mou doff
Walahi Allah est le meilleur juge te il vous jugera que firdaws soit sa demeure ke sa famille soit armee de patience et dandurance yalla bour bou mandoula
big boss momou comme dafay defal bopam justice degolen ma soudon sama mbokk walahi kep kou ci bok dinga mort topko mefié vous les gas boulen ken yobou sans convocation donc l'affaire est clair big boss khawma kate len ndeyam ci kasso bi wala mou dife li moy andi reglement de conte senegal du nimporte koi
Ndeye sane 2ans déjà jusqu'a présent justice n'as pas été faite ki mou diotel mingui dokh sohlam di feulalé def lou ko nekh élimane yalnala yalla kharé aldiana
quand j'ai vu la maman du défunt, j'ai pleuré car j'ai pensé si c'était ma mère et moi à la place du défunt.c'est vraiment dure yaye boye Massa massa massa l'homme noir est trop injuste.
c est une belle chose d' etre humaniste .Malheureusement ,Il faut savoir que notre societé senegalaise est entrain de changer:plusieurs agressions physiques,meurtre etc...
moi je connaissez elimane c un grand frère ils ont tué puis disent du importe koi arrêter de faire sembler rip mon grand mon ami celui qui me disé tjrs dinala toudé dome
Wallahi li metinama trop ki Touré la sant niou diko def ni haaaaa sama khol diekh na wayé Touré waliw piirre nga khass nako ci barké cheikhou Tidiane martaba dina len dal.
They souniou BOROM!!!desole mais vs ne saurez jamais lou ko rey li len xoxatal,xoxatalna medecin yi def autopsie bi.deinthie len sen neew te djap ci YALLA. XAMNA LEP TE FEKENA LEP.adouna yagoul.in ssha Allah .le trubinal de DIEU ns attend.
Domam bi yeureum nako lol sakh...Courage. SÉNÉGAL doyna waar .... problèmou hommes de tenues yi di fitnal peuple sénégalais yi té était bi dou réagir thi dara.
elimane ne c'est pas suicidé il été tellement croyant k tous il lui arriver si tu tkt il te repon. non tkl dina bakh inchallah tous mes condoléances à yeumbeul eli été pas bon k pour sa mifa mes avec tout le monde k dieu préserve les 2 filles kil a laisser dernière lui amine amine
moi quand j vu son enfant j ai pleurai c vraiment triste oh le monde faller reglé sa a l amiable avec son patron mai regardai au final pour tant il n a rien fait de mal. la maltraitance dans les prison c dure pensai a dieu et a c que vous vetes
mais légui Sénégal dangereux na dé comme au fare west ahh mais on est dans une république bananière ou quoi cela ne doit pas rester impunis il faut que le procureur s'auto saisisse ou sinon nous diront que la police est complice
li dafa yomb tooooorop bien k kou diékhal dém mais esk la police existe de nos jours?...Pikini production la musique du début n'est vraiment pas adéquate avec ce reportage...il s'agit d'un décès y'a des musiques bcp plus appropriées.
koulii ganee bine hasalahou hanee yakfira ila mane mantaa anne mouchkira aaaw moukminoun moukminamm moutaa hamydanee yalah dou meusaa balee djioulite bou ray moromou djilitame tai tay koo0!!
Justice pour ilimane Tourè li kénn douko fattè 👈
La dame noire la jlaim El connais ses droit...ki gueine adouna yala nako yalla yeureum☝🏿
merciiii!!!! bcp la tante d'ilimane liii motakh diakk bakhh!!
Va
Yalla na yalla lérale lépe si barké seydina Mohamed psl té mou khipé adjiana
Metina trop ms lepp Nagn ko ték si lokho Yallah Dina léral lepp inchalah paix son âme Mister Touré👏👏👌👏👏😢😢
Base
Ohhhh Lil metina na bilahe
Tite na si senegal sa yo khole nouvels yi dioye yalla na co yalla yeureum yalla na yalla ate machaala tante dji khamna limiye wakh
pauvre Sénégal c grave injuste la HONTE 😡😡 loudoul yalla néne la .yalnalenn yalla atté si barké seydina mouhamed psl
oui la honte pour le peuple
Kaba Mariama
Kaba Mariama amin sista
.'co
Monsieur le président, Monsieur le ministre de l’intérieur vous êtes nos dirigeants les sénégalais vous attend sur ce dossier
keep kou kham Elimane Touré khamené khalatoul sah kharou, nite kou dioulité wone. Sénégal dou deukou justice, gniko door bamou dé Yalla naléne Borom bi allak
Li mettinama troop
Je suis tombé par hasard ci video bi. Mais adouna diaroul khekh fi koufi def lou bonne balla nga guene adouna guiss ko. Wassalam. G trop mal😣
no vraiment li rek motakh ma ragual sénégal Say bo fa begué nieuw rek dégu gnou raye kén Ba kagn nak li warna diekh vraiment metina di mastawou wa famy bi yalla na yalla léral lepp t Souf sédd si kawam si barké seydina mouhamed psl
quєєn fα jtj tué pareil que mw Say souné ma begu déme sénégal nakh tellement mon pais me manques beaucoup m ragual motakh menou ma deme
wa mais li deug la wala? non mais il y a du nimporte quoi au Senegal!! c'est quoi ça!!! Ça me fait trop mal au coeur!
Que dieu l'accueille dans son paradis céleste. Ami e
La maman elle est même choqué ndakh dome ci khol la sakh ndeyssane yalla nalene yalla maye kholou mougne que son âme repose en paix 😭😭😭
j'ai vraiment mal .mes larmes coulent prkoi tant de méchanceté. la vie est éphémère. oh mon dieu adouna diaroul lii raye domou adama ni rek
yalla nako yalla yeureum
+Astou Gueye amin
que justice soit faite massa Yalla nako Yalla Yeureum kharei ko aldiana firdawsssi
ndeysane yala gemoul nélawoul tei Dou diawalé DINA len atté incha allah meti na trop mei soyez forte
massa massa metina je ne peux pas tenir mes larmes dans kel pays sommes nous je sais ce que sa fait nako nit kouné set thi bopam yalla na yalla leral yeup et punir ce qui ont fait sa. elimane famou yalla no dakal fi. dila nianal thi aldiana you kawyi . gou def li bonne na gnou
Yalla nako yalla yeureum diegueulko aye bakaram famou dieum gueneulko fimou diougué makoy dialé wa keureum yayam ak kep kouy mbokam ak dioulite yeup lii doyna war métina lol Sénégal doy na war walhi metinama lol pask damakoy nate thi mane bou dalone sama mbok mais nak yalla nako nitou yalla nite ba ki def lou gnaww lii yone tek ko lokhoo yalla nalene yalla yok kholou mougne diam ak salam rek yalla na gueneu sakh thii sénégal yalla are gnou lakhe gnou fou yakh doul yegg metii nama lol wa salam
Ceux sont des bandits de long chemin, Li motah bougatouma deuke Sénégal té dara dou len si féke nak
massa yalla na yalla lerale si barker alqurane yalla dina leral leppppp inchallah
yalnako yallah yeureme
ay waye li metina trop migui melne dama kou kham car dafa meti trop yalla nakou yalla yeurem masseta maman
Thiat Mbow merina trop un père de 2gos ki a perdu sa femme il y a 2ans .k vont denir c anfants
Amina Faye li dé amol paris senegal mom
amina camerawoman louma def magamaye mere
Thiat Mbow défo dara dama dioum
un jeune quan jai vu son fils orphelin de pere et mére jai pleuré bilahi li dafa meti bilahi walahi mon pere est policier mais jai honte et big boss niap lene ndeyam ci zair wala batine wala mou doff
ndeysane uncle bou bakh Tu n merite po sa Que la terre te soit légère tonton❤😢😢
Walahi Allah est le meilleur juge te il vous jugera que firdaws soit sa demeure ke sa famille soit armee de patience et dandurance yalla bour bou mandoula
missi la douce bilahi c est vraix c est dificille mais le jour arrivera inchallah
missi la douce c
Ckava
Affaire you yomb yii nii non policier 👮♂️😭
yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawsi
big boss momou comme dafay defal bopam justice degolen ma soudon sama mbokk walahi kep kou ci bok dinga mort topko mefié vous les gas boulen ken yobou sans convocation donc l'affaire est clair big boss khawma kate len ndeyam ci kasso bi wala mou dife li moy andi reglement de conte senegal du nimporte koi
partage cette vidéo dans tous les réseau sociaux svp
Diakhoumpa Ahma fax
yana motalee ndawam Aldjana Firdawsi.yalnalen YALLA meylen xolou MOUGN.fi mou len fetewone YALLA FETELENE fa.
oohh li metina way😭😭😭yala na Allah leral lép si barké rassoulilah
thieuy yalla 😢😢 Sama yaram dawna
cloudx gams bilay
Ndeye sane 2ans déjà jusqu'a présent justice n'as pas été faite ki mou diotel mingui dokh sohlam di feulalé def lou ko nekh élimane yalnala yalla kharé aldiana
Khoudish Diarra metina billahi
quand j'ai vu la maman du défunt, j'ai pleuré car j'ai pensé si c'était ma mère et moi à la place du défunt.c'est vraiment dure yaye boye Massa massa massa l'homme noir est trop injuste.
Abdoulaye Sall il ne faut pas stigmatiser une race
Abdoulaye Sall c dur bilahi
Votre commentaire est touchant monsieur je n' ai même pas encore regardé la vidéo car je suis au travail
PRINCESSE PRINCESSE salut vous etes humaniste
c est une belle chose d' etre humaniste .Malheureusement ,Il faut savoir que notre societé senegalaise est entrain de changer:plusieurs agressions physiques,meurtre etc...
moi je connaissez elimane c un grand frère ils ont tué puis disent du importe koi arrêter de faire sembler rip mon grand mon ami celui qui me disé tjrs dinala toudé dome
Mimi Seck Massah siguil ko ndigalé yal nako sunu borom yeurem te hareko aldjana
Thieye Yalla yeumbeul deuk me doyna waar trop lii motakh nieme wouma Senegal
metinaaaa Massa lene Massa massa😢😢😢😢 jé pas les mots
Que la lumière soit faite eupeu niit dolé diay lako dafa wara diëx Sénégal
Wallahi li metinama trop ki Touré la sant niou diko def ni haaaaa sama khol diekh na wayé Touré waliw piirre nga khass nako ci barké cheikhou Tidiane martaba dina len dal.
way ki xarouwul way boulen fonto nitt yi .....legui dal policier yi ni reik dmbram yi
peace love vu que je bah
Légui dall policé yii dall nioy diapalè Ray katou nit ngii
sachez qun jour Allah va nous juger ragualene Yallah
Paix à son âme🙏🏾
Walakhi metina dioye na bâ sone
They souniou BOROM!!!desole mais vs ne saurez jamais lou ko rey li len xoxatal,xoxatalna medecin yi def autopsie bi.deinthie len sen neew te djap ci YALLA. XAMNA LEP TE FEKENA LEP.adouna yagoul.in ssha Allah .le trubinal de DIEU ns attend.
Mais attant jusqu'à présent pas de suite à ce crime non c vraiment dommage pour la justice de mon pays
Domam bi yeureum nako lol sakh...Courage.
SÉNÉGAL doyna waar .... problèmou hommes de tenues yi di fitnal peuple sénégalais yi té était bi dou réagir thi dara.
ha li metina yalla na khipé aldiana firdawsi
Li mo wara Djeh chaque jour ak cas Bou bess nak eupneu
Wayè bilahi alakhira dana tang dana metti ta amoul balè
elimane ne c'est pas suicidé il été tellement croyant k tous il lui arriver si tu tkt il te repon. non tkl dina bakh inchallah tous mes condoléances à yeumbeul eli été pas bon k pour sa mifa mes avec tout le monde k dieu préserve les 2 filles kil a laisser dernière lui amine amine
ils affirme k il c suicidé a la police mais a la police il y a pas de corde ni pendule
ki serve de suicide
Wa mais il faut que la justice fait sont travail li mètina trop
#Deçu
Nous sommes dans quel pays?
paix à son âme yalla nako yalla yeureum
je ne reconnaît plus Mon pays mais il faut ke justice soit fait
Yacine Ndoye 4 11 85 malheureusement ya pas de justice chez nous .Il faut appliquer ces 3 mots goorgorlou moytou mougne
Vraiment lii mettina nékhoula mougne wayé bayi léne leppe thi lokho yallah. Keppe kou khalate Yawmal kiaya digua raguala def domou adama lou gnaw ........Dakh mako euppal dolé mako meune douma moromame Adouna la yém Guir yallah nagnou rafeta khôl yi ........ guaye neubbeutou nitgni fatté sa borom ........Yallah wakhoul né koula togne wala koula sagua wala koula déf loula metti rek gua féyou ........ 👎 Pour lane boko déffé après aye rethiouté rek gua thi am ....fii thi douya ak laakhira vraiment nitte la Yallah guena beugue thi limou sacke wayé mothi gueuna yésse Mé Sénégal monde entier gnothi gueuna meune déf nitte lou gnaw boudoul thi serigne tou gnon gui reyaneté Di yénaneté lou bonne lolou nak mo téré dem Sénégal 🇸🇳 Réw boléne thi necké diappalé wooléne Séne boppe Yallah daléne di setane Guir Yallah lou waye yéné sa poppa nagko yené sa morom ....... Sa BAMMEl doko bockou ak kéne Kone naye rafette waye
Ilimane yalna ko Yallah yérem
moi quand j vu son enfant j ai pleurai c vraiment triste oh le monde faller reglé sa a l amiable avec son patron mai regardai au final pour tant il n a rien fait de mal. la maltraitance dans les prison c dure pensai a dieu et a c que vous vetes
ay way lih mettinah c la loi du plus fort qui régne dans ce paye.
xawma lou tax leene ci sénégalais yi soxar ils sont vraiment méchants lép xaliss rek
saga rek nga ray ci niit khana kone maky sall ray senegal yeup liniouy koy saga yeup mouy bayi mou dial ce pay est rempli d'assasin
mais légui Sénégal dangereux na dé comme au fare west ahh mais on est dans une république bananière ou quoi cela ne doit pas rester impunis il faut que le procureur s'auto saisisse ou sinon nous diront que la police est complice
regarde ou nous mene la jalousie.
Dakar et ses mystères
Jusqu’à présent justice n’a pas été fait
Ay fou nite di mouthiè
action please quelqu un peut me donner le numero de sa famille .on a besoin plus d action que de wakh rek bayi
😭😭😭😭😭😭😭
legui yalla rayoul dh nit gne nioy ray legui bilahi amna yokham ne dafa yombou waye
Bon j vois k vous devez porter plainte contr idrissa et cue policier sa du n import kw
' 99
meetina meetina trop Sénégal raye rek ô c triste
J'ai l'impression qu'on est dans les favelas
paix à son ame 😭😭😭😭
pauvre Senegal wax djii lere naa ki teukou wate lane moye ndeyou dinala rey police ba geuna tapale
Légui Sénégal djay dolé mofa am !!! 😂 Tay rek niou nieuw dokhann sénn ndeye yenn nieupp domram yi ngenn donn
Le bon dieu est temoin
il n'est Pas la justige dans ce pays
Sénégal amoul loi gnite yi diouboule moutakh louwaye nekh def hè Sénégal doyna ware Hé yalla bane Sénégal lagniou nek policier corrompu hummm
li dafa yomb tooooorop bien k kou diékhal dém mais esk la police existe de nos jours?...Pikini production la musique du début n'est vraiment pas adéquate avec ce reportage...il s'agit d'un décès y'a des musiques bcp plus appropriées.
Ma Senegal dama xamoul loulene dalni..!!nous nous somme des musulma ..! Massa yaye boye mougne lène sounou Borom nalawou
Ndeye sane
amina défo dara
a
la famille mougn len rek yalla dina aatè ba ngen contane lolou mom def lenko sen xel
koulii ganee bine hasalahou hanee yakfira ila mane mantaa anne mouchkira aaaw moukminoun moukminamm moutaa hamydanee yalah dou meusaa balee djioulite bou ray moromou djilitame tai tay koo0!!
Dieu est le seul juge
Sénégal dou deuk policé indispline
bilay metina masta a toute la famille
ce dur
mais li métina ray domou diambour nane da kharou sénégal vraiment amoul loi
ohhhh li metina trop bilaye du courage et k la lumiere soit faite
yeneni deces you ni mel amna fi,amati fi fi te ken wakhoul dara ba tey.djapaken ci YALLA MI XAM TE FEKE.
Biqu Boss yakk ñiko Ray yalnaléne yalla werr
bike bosse mokou rayii lolou
et kesk macky a dit
😢😢😢😢
li nakari nama trop way diay dole la
K justice sw fait
Mais c'est quoi ça on est où c'est trop
Yemena senegall a moull guistis li nnawona fat bakan kom animale dafa yompo gnoko raye
lou niit até diga ko até wate bamél akh le ndeum famii bi sigi lén ko ndigalé massa
non Sénégal dou dème nakh nafekh tout des crompu
Il faut savoir se venger Cino rek yi doufi djioukk
bala ma dé niou nane aye big boss lane boy big boss lou doul bandit ray katou nit
thiey yalla